Baye Niasse daal neena yeemu na ci koo xamne daa noppi noppi gu guddu te Liko waral mooy xam yalla waye ci xaalam gay xammee ne xamna yalla. Kon boog rafetal joortu ci jaamu yalla bi . Daga reere lu barri nag cheikh bi . Wayee yalnala yalla may guddu fan diga xam li waral tekaaral bi
Salamou alaykoum ! Di len ziar yen mbok khayri khayri. Almoudou thierno alpha Sow la. Dilen wo si xam xam. Nakala cheikh mbow deugeulé noubouwo_ wilaya _khilafa ak sen khadrat bou thierno alpha sow Sow ba dika layalé bayt cheikh Brahim. Ba paré mou weulbatikou Di sikkeul Lou si dess. Noubouwo wilaya khilafa dafa lambo lenen loudoul hadrat kessé. Do len guestou Lolou ba paré sogua dioublou li ci dess. Wa salam.
@@bayeissakha5632 est ce gueum Guen noubwo wilaya khilafa cheikh bi. Cheikh mbow dafa touddou khadrat yi ba pareh mou layalé bayt cheikh Brahim, mais waxoul noubwo wilaya khilafa lep. Il s'est contenté de la basmala et de la Fatiha (maqamat), fofu la développer. Wahko mou deffal leu tamiz si ummoukhat NWK parce que wax bi fofou leu. Nanguoul nguen thierno alpha Sow ummoukhat et maintenant nguen Di weddi loussi dess.
@@amethkouyate4622 C'est parce que thi fatiha lay wakhtane motakh wayé oumouhate nouboweu wilaya xilafa yeup la dadji haka'ik ba salawate. Li thierno indi dokhna ko ba khoulwiyou, soufliyou, adje. Wayè bima dioko lako téke thi souf bo beugué âme loula thi lére fékhél dioko ak Mbow. Salam et ziar.
@@bayeissakha5632 non cheikh bi adjo woul may diokkou ak cheikh mbow. Thierno alpha Sow da sakhal mom mou dakh. Je préfère diokkou akh ki sakhal. Ken si magg yi si hadra cheikh Ould khayri da mokkal oummoukhat yi teh moussoul tarbiyya. Kenen dokh oummoukhat cheikh Ould khayri ba pareh inkar cheikh Ould khayri. Juste pour dire que xam xam dey andak barkeh ak deugeugeu. Abbey Jacques Sarr jang na Al Quran, pourtant tahoul mou gueum mou top mouhammd,saws. Was salam!
@@amethkouyate4622 Dakoul Khadra bou néke amna diouromi Khadrate lolou baye moko wakh té lou wére leu khalkhiya bi nga défe khaka'ik bamou âme Khadrate la dake (Al anebiya'ou koulouhou khala'ikh) diakhassé khalkhou, madiass ak khakikha. Boudoul lolou selon votre logique sa Khaka'ik sakh matoul insa moy batinou nouboweu di euweulou wilaya, naka nonou cheikh Ibrahim moy batinou wilaya Di euweulou khilafa naka nonou noukh ci euzeul bi ak nouboweu . Khadratou nassot lane moy khadratame? Marifa nékoul ci keurou oumouhate diko récité marifa ilmou zawkh la ( xam xam bougni Moss) nékoul ilmou diraya Cheikh limou inedi diégui na oumouhate gnou bari li lagn xamoul motakh gnou nèke di créer oumouhate amna gnoukoy def ba lègui oumahatou keuwnou, oumouhate hayawane oumouhate malaka amna gnou yégualé Di créer ba lègui
Nekhoul beu nekhoul mais iow werro Saga lou dagane leu Mais dougn ko deff Ndakh nitt kou touti nga Gni ngay teukeulel seu bopp dé wallahil azim, séne dalleu sakh yamouniou ak iow
Sa mbokou yidhé si sagua Serigne bi laniou deuk waya lolou takhouniou bayi inchallah kham kham rek moy djité ndakh niouye Baye laniou topou pas nitte yiii donc ay wakhou baye Niass rek laniouye até
@@Khalilbrahimaaaa ndayssane yarouniouléne ci kham kham motakh Sagua rek guéne meune mais tontou léne ci kham kham rek niou deff comparaison lolou mo gueune Nioune dhé yaréwougne niou sagua donc nioguilay wo ci kham kham
Ngay wakh Lo xamni Xamo ci dara Nim teudé lepp pour Yakk deram. Nagn ragal Yalla tay defar … yaw yakoy bayi xel mom nekkoul ci yi nga nekk ni sakh … Sangue Barhamou Defoul Wakhoul Lou Niaw… nagn Dém rek Vidéo yi sou denioul seni seut nioko nara guiss di mer ci yèn…
Nioniou dhé danio sokhor ci louniou momoul konone dinaniou ko partage ndakh mbir mi baye Niass nopésouko dafko partager nieupou jotssi Sou Serigne yeupou defone ni kone talibés you mare yallah yeupou dinaniou kham fou deugue fété Tekssi Serigne bi mission wame bokoul ak yéneu Serigne yi Séne mission
Yeuramal sa bopou saway c'est mieux nioune dhé sante naniou yallah ba togou niou ci ay néne mais plutôt ci kham kham bou deugueur avec des paroles du Coran, du prophète, de cheikh Tidjane, de baye Niass et de cheikh ould khayri Kone nioune danio took ci deugueu
Ngir yalla yarouléne bayi sagayi
Machalla sarigne bi yalna yalla samoula arla si barkè baye niass
Machalla cheikh Oussama mbow yalna yalla samouko
Bismillahi Rahmani Rahimi bokkoul si Fatiha lolou nga wax mais Baye Niass defné Bismillahi Rahmani Rahimi si Fatiha la bokkou
Baye nénala amine laïcha minale kourane houwq tabbi ou malayekaty
Yow kaye ya xamule lou baye wahe motahe
Yalla nako yalla samb Cheikh ousmane
Alhamdoulilah Serigne bi doundeul walahi deyssane doundoubi xamna solo lol
Sangue ndiaye dousa morom
Allahou Akbar wallahii ndeyssan DEUG néxũll lí dafã léér billah Cheikh Ousmane mbow mõy lérall payi bí deh 👌👌👌❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏
Loufi lerr
@@aboukabe4712 leepa leer cheikh ousman leeral na lep
الحمد الله على كل حال وفي كل وقت
جزاك الله خيرا يا شيخي khol seddina ❤️
Machalah yalna xam xam bi ak meudeud yii yok ya rabi yalla samal la bopam
Fi Mouss doufi nané niekh.
Dieuredieuf Mbow
بارك الله فيك وجزاك الله خيرا ياشيخ شيوخ
Allahu Akbar macha Allah serign bi leral nga lep ❤❤
❤❤❤❤❤
Li meu beugue KHAM moy bane fatiha nguene di WAKH
Maddddd: mashallah mashallah mashallah
Lima metti mom moy day sathie limou sokhla. Limou sokhla woul mouniou koy sandee ay heer
Baye Niasse daal neena yeemu na ci koo xamne daa noppi noppi gu guddu te Liko waral mooy xam yalla waye ci xaalam gay xammee ne xamna yalla.
Kon boog rafetal joortu ci jaamu yalla bi .
Daga reere lu barri nag cheikh bi . Wayee yalnala yalla may guddu fan diga xam li waral tekaaral bi
Ndayssane Mbadou sa Serigne mo yoor Makhama nopi bi😀
Fi amoul réféte ndiortou sén Serigne da ték oumouwate niouniko li bakhoul dou diné sou fékéni mome loum sampe deugeur na na nieuw tontou mo geune
Weddi Yaggue na thi adina. So Niwon di wax guendi geuna weddi rek . Wayé xamalné foodoul fekk cheikhoul khaïry boufa sentou thierno alpha .
Niguèn wéddè thiérno nonou la am niou wéddè cheikh té takhoul cheikh nekk tontou wanté ak niom .
Macha allah
Dieuredieuf
Salamou alaykoum ! Di len ziar yen mbok khayri khayri. Almoudou thierno alpha Sow la. Dilen wo si xam xam. Nakala cheikh mbow deugeulé noubouwo_ wilaya _khilafa ak sen khadrat bou thierno alpha sow Sow ba dika layalé bayt cheikh Brahim. Ba paré mou weulbatikou Di sikkeul Lou si dess. Noubouwo wilaya khilafa dafa lambo lenen loudoul hadrat kessé. Do len guestou Lolou ba paré sogua dioublou li ci dess. Wa salam.
Salam Serigne bi, Mbow deugueloul oumouhate nouboweu wilaya xilafa au contraire dafko dadji té laye nako, wa salam
@@bayeissakha5632 est ce gueum Guen noubwo wilaya khilafa cheikh bi. Cheikh mbow dafa touddou khadrat yi ba pareh mou layalé bayt cheikh Brahim, mais waxoul noubwo wilaya khilafa lep. Il s'est contenté de la basmala et de la Fatiha (maqamat), fofu la développer. Wahko mou deffal leu tamiz si ummoukhat NWK parce que wax bi fofou leu. Nanguoul nguen thierno alpha Sow ummoukhat et maintenant nguen Di weddi loussi dess.
@@amethkouyate4622 C'est parce que thi fatiha lay wakhtane motakh wayé oumouhate nouboweu wilaya xilafa yeup la dadji haka'ik ba salawate.
Li thierno indi dokhna ko ba khoulwiyou, soufliyou, adje. Wayè bima dioko lako téke thi souf bo beugué âme loula thi lére fékhél dioko ak Mbow. Salam et ziar.
@@bayeissakha5632 non cheikh bi adjo woul may diokkou ak cheikh mbow. Thierno alpha Sow da sakhal mom mou dakh. Je préfère diokkou akh ki sakhal. Ken si magg yi si hadra cheikh Ould khayri da mokkal oummoukhat yi teh moussoul tarbiyya. Kenen dokh oummoukhat cheikh Ould khayri ba pareh inkar cheikh Ould khayri. Juste pour dire que xam xam dey andak barkeh ak deugeugeu. Abbey Jacques Sarr jang na Al Quran, pourtant tahoul mou gueum mou top mouhammd,saws. Was salam!
@@amethkouyate4622 Dakoul Khadra bou néke amna diouromi Khadrate lolou baye moko wakh té lou wére leu khalkhiya bi nga défe khaka'ik bamou âme Khadrate la dake (Al anebiya'ou koulouhou khala'ikh) diakhassé khalkhou, madiass ak khakikha. Boudoul lolou selon votre logique sa Khaka'ik sakh matoul insa moy batinou nouboweu di euweulou wilaya, naka nonou cheikh Ibrahim moy batinou wilaya Di euweulou khilafa naka nonou noukh ci euzeul bi ak nouboweu . Khadratou nassot lane moy khadratame?
Marifa nékoul ci keurou oumouhate diko récité marifa ilmou zawkh la ( xam xam bougni Moss) nékoul ilmou diraya Cheikh limou inedi diégui na oumouhate gnou bari li lagn xamoul motakh gnou nèke di créer oumouhate amna gnoukoy def ba lègui oumahatou keuwnou, oumouhate hayawane oumouhate malaka amna gnou yégualé Di créer ba lègui
Ndékété koula deglou dafay gueneu gueum Sangue Ndiaye 😂😂😂… Thieuy Yalla
Kone djaroul guaye kasse guanaw daffay yokou sa mbeuguel ci SBN
ganaw daguéne goumbeu lanke né douguéne yewou demlene rek diguene tarkhisse ndakh topouléne Baye Niass
Walahi serigne yangui beugue dougousi lo khamoule
Kí yaknå sí lii yw danko xamũll rk mõ tax
alkhayri
Nekhoul beu nekhoul mais iow werro
Saga lou dagane leu
Mais dougn ko deff
Ndakh nitt kou touti nga
Gni ngay teukeulel seu bopp dé wallahil azim, séne dalleu sakh yamouniou ak iow
Sa mbokou yidhé si sagua Serigne bi laniou deuk waya lolou takhouniou bayi inchallah kham kham rek moy djité ndakh niouye Baye laniou topou pas nitte yiii donc ay wakhou baye Niass rek laniouye até
Al hamdou lila dieuredieuf
Ndiabotou baye vous siuvet partou fait vous attention
🥰💪💪💪💪 alahou akbar
Thiey yalla donc selon tw hadate yii 6 laniou ooooh ya yeuss
Fane la Baye waxé nih hadate yii 6 laniou
Bo nieuwé niou bakhel Lako inchallah
Binga commencé incare wa medina singa rèrè yallah
Wallahi wakhatiko mbow dafa katte ndeyamme
@@Khalilbrahimaaaa ndayssane yarouniouléne ci kham kham motakh Sagua rek guéne meune mais tontou léne ci kham kham rek niou deff comparaison lolou mo gueune
Nioune dhé yaréwougne niou sagua donc nioguilay wo ci kham kham
@@Khalilbrahimaaaa yaw khana sagayi si sa Serigne ngua ko dieulé.
Ndax nitte lo nampe nguay guale
@@mysteremystere5196 walahi sén Serigne sax manouniou tontou question talibé Mbow yi bay tontou Serigne bi
Eskaye Eskaye avec l'avocat de la fayda lépou dinaniou ko tek ci ay preuve you lér nanieu té bou amoul siki saka
Kham kham deugue nak
Tchiey Mbow , 🤣🤣. Yaw SANGUE BARHAMA dafleine fi bayi. Moleine meiti. Nieuw leine seiti ko rek, mo gueuneu yomb di🤣
En tant que Khalifa yallah mouye bayiwaté 😅 saway thiakhane bakhoul way
Omar la sara mbow Mala beugue khel you beri guidi gualane Barker baye Niass yala na yala yok sa lere mbow
Yangui nane kou nieuwoul si cheikh do khame fatiha ya fofou ay batte rek mofa nieuw toure amoufa woutil yallah
Niou barri gnongui sagua sa serigne ndakh sa melokane ,walahi mbiri yallah moy atele bopame niou deme rek
Baye Niass tamite dhé sagua wone naniouko foumou moudjou ?
Deugue môme Bala moye takhaw faw sagua yii âme lolou thiossane leu
Abou kabe
Mbow bayil fen😂😂😂
ioe daga mélni sa Serigne motakh nguay saga
Ndieyssane Momar biteye sa serigne day FÉNE loolou motakh guayakar ni niép dagnou féne:
Dieume dji nga wakhal adouna dou yangue moukou bamou tontou la ,talibè bouko nangoul sakh amoule sa diote ,neek dakar di nakh dofyi rek ngéne fi nèk
Yaw Sa Serigne boudé gnaména neko neu toutou Cheikh Ousmane Mbow Ci loumou Kay wo
Ay wakh sa khalate mofi amatoul dhé. Legui lépou daffay lér
Ngay wakh Lo xamni Xamo ci dara Nim teudé lepp pour Yakk deram. Nagn ragal Yalla tay defar … yaw yakoy bayi xel mom nekkoul ci yi nga nekk ni sakh …
Sangue Barhamou Defoul Wakhoul Lou Niaw… nagn Dém rek
Vidéo yi sou denioul seni seut nioko nara guiss di mer ci yèn…
Yakarone nani kou khame yalla ngua .ndékètéyo yaw sa serigne chékhoule khayry sakh khamoko barké baye .niake yarr trop
Heureusema 😂😂ligayy wakhh metrisee woo ndeysan yogg yaguu dora am fahmou sii fatikha konn
Dieureudieuff 𝙏𝙝𝙞𝙚𝙧𝙣𝙤 𝘼𝙡𝙥𝙝𝙖 𝙎𝙤𝙬
Thieye sama wadji xam xam rék moko gnor
Gni xam deug nioungui laye retane. Yangui exposé sa niak xam xam.
Nioniou dhé danio sokhor ci louniou momoul konone dinaniou ko partage ndakh mbir mi baye Niass nopésouko dafko partager nieupou jotssi
Sou Serigne yeupou defone ni kone talibés you mare yallah yeupou dinaniou kham fou deugue fété
Tekssi Serigne bi mission wame bokoul ak yéneu Serigne yi Séne mission
Mbow ya katte sa yay
Yaw sa Baye sa Yaye ak sa Serigne niola diangal saga motakh ngua mélni kham kham 0 saga 100%
Saway maguilay nianal bou bakh ndakh djisnani dagua rér motakh guay sagua Serigne bi gua khamni loumou leu wakh rek djokh leu dalil.
Sa saga yinak daffay firndél ni sa Serigne djangaloula kham kham motakh Sagua rek gua meune
Nioune dhé dounioula sagua ndakh Serigne bi yarounioussi ci kham kham rek laniou yar
Wasalam
Yawe ya gene nii bilahi 😂😂😂😂😂
Mbaw, gni la toppeu rek laa yeureum.
Tu n'es même pas logique avec tes dits.
Toukkeul!!!
Yeuramal sa bopou saway c'est mieux nioune dhé sante naniou yallah ba togou niou ci ay néne mais plutôt ci kham kham bou deugueur avec des paroles du Coran, du prophète, de cheikh Tidjane, de baye Niass et de cheikh ould khayri
Kone nioune danio took ci deugueu
Serigne bi amoul tamiz si Yonent dé. Ta tamit oumouhàt bî mokalô ka ndakh Dou lî la SANGUE bi indi.
Fô sakhal Malàyika yi?
Livtakh sa fàtikha bi mayoul môy yow yà si am problème.
Baye NIASS néna Kou bawoul mazhar bou fégn nga wédi Kahn ngay dadjé ak mbôtou am gi?
Yaw loy wakh maîtriser woko😂
🤣🤣🤣🤣
Mdrrrrr vraiment mbow tu es nulard koula deglou bou bakh yangui dioum rek si sey Dalil ak argumentation
Wakhal foumou djoumé rek c mieux