moustapha cissé yow déja sama papa gua koula kholl rek kham né nitte kou bakhe gua té am diom tékki rek mola nior téral sa famille diambar deugue gua goor yalla pire gua tu es fort mentalement avec tout ce que tu as traversé yalla bakhe na yonou ndaw dou gaw té borome karaw gou niakoul dara du courage inchallah bouko yalla sunu borome toudé rek digua nieuw europe
Mane dh sama tata (petite soeur de ma maman) maroc la diougué di traversé pr dem italie bobu lagn ko gueuthie deggg Yalna ko yalla gnite si barké bessou yonente bi 🤲🏼
Ndéysane begue tékky rk métina moustapha yalla nala yalla diapalé depuis🇸🇳🇺🇲 USA yonou souf bi la diarra dh Brasil Améric 2019 begue tékky rk fall sénégal da méty mai yalla nala yalla diapalé yonou souff bii bilahi kousi diaroul manoko kham
Man mangui Allemagne Moroc la diar en 2012 mais Lou mbourou d'Ath si Tal ba d'Ath na kofa mais légui Alhamdoulilah,yalla na yalla takhawou gnépou si barkéb Serigne Touba
Je suis en Italie mais il faut savoir une chose,képp kou dieul aventure Libye,Maroc, Tunisie walleu Algérie pour ndém Europe.Amneu son propre histoire de vie qu'il a subit,on peut pas tout raconter.Mane moom xaral ma noppi rékk.Yalla na Yalleu yéreum niou dée ci Yoon bi🤲🏽Té dimballi niou feu déss🤲🏽
Je passé en liby j’étais capitaine 👨✈️ d gall Je suis en Europe depuis 2016 mais si j’étai le fair jne le ferais j’étais j’ai regretté dara diarouku ci adouna bon courage frère
Oh mes larmes coule je m'appelle Ibrahim Korobo Sénégal casamance sedhiou comunes de koussy1 village de nimzath j'ai passé ce chemin là, Dakar. Mali Bamako, bourkina Faso wakadougou, kanthiary, Niger Niamey, agadez arlite, Algérie tamarasette, ourgilla, enzella, debedebe, lybie bene waly, tripoli, pour Europe Italie Cécilia Rome, France Nice, Cannes, Marseille, Espagne Barcelone.,murciá, llerida 😭😭😭😭
Man dei wax deug yalla beugna toukki lol guéne galséne waya ay yonou souff ak gall mom sama xell xalatouko heure bouko yalla dogalei baxneu mais douma bayi courage bro!
Avec tout ce que moustapha a dis il y a des gens qui pensent toujours partir il faut lire les commentaires en bas. Pourquoi les noires aiment les difficultés. J'ai envie de pleurer.
ALHAMDOU LILAXI RABIL HALAMINA NOUS ONE LA TRANQUILLE je suis passé en Libye mais là-bas c’est dur mais moi dieux ma aider je ne pas duré longtemps Libye je suis resté là-bas 4 jour seulement et après j’ai eu la chance d’avoir un chodiak pour rentrer en itali j’ai fais sénégal entr itali 24 jour seulement maintenant je suis à Paris j’ai mes papiers y’a deux mois maintenant j’ai gagné bien ma vie dieux merci encore une fois je remercie énormément mes parents courage mes frères sénégalais 🇸🇳🥰🇫🇷
Jajeuf champion Lou méti goor laye dal daga âme diome motakh nga dem a la quête pour un lendemain meilleur voulour toujours aider ta famille mé dis toi que on ne perd jamais o gagne ou on apprend et en plus ya le destin et nul ne peut contre son destin
Bal fetal boy boumo lal mougui doundou c’était devant moi ce matin,j’ai pris le même pirogue avec lui jusqu’à Italy,ont n’était dans le même campement en Italie et ont n’est venu ensemble en France ,le gars ses un Guinéen actuellement moungui Paris ont se voit presque tout le temps
Du courage yafou gor c est très dur j ai quitté chez moi 18 janvier 2016 et arrive italie 22 février 2016 mais la route es dépassé dur mm c est l enfer
Mane de ma nga ni Algérie ta inchallah le 20 septembre bi ila Libye déf na kasso 5mois anter mali & Algérie defna kasso cot'divoir 2foi me dara khame na ni dina masa bakh bilahi sonnou na ci sama adouna dra sama yaye diaralna ma dé bisse bou khammi ni damaye dem Libye no daye dé ndakh sama yaye maye adouna naame me dra yalla bakhna inchallah geume nane ni duna bakh 1jr ta bilahi defna ti yone bi puls 2million 300000 ndakh kasso yoma don faye😭😭😭😭😭🙏🙏
Je suis en malta sud de l'Europe tout près de l'Italie et Espagne jai passé en Libye mais en réalité on a très souffert sur la route les arabes sont méchants
Lybie amatoul Etat, ba nopi toubab yi seen bop gno dooleel lybiens yi nguir gnou mann leena nadjal nitt gnou gnoul gni fofa. Gnom amna Lou gnou sagnoul def ndakh UE bi gnou bokk, ak respect droits de l'homme yi. Motakh gnom gno diokh khaliss ak matériels lybiens yi nguir gnouy torokhal africains yi, tayyeef la dé.
Nguir yalla jeunesses bi moytou léne yonou souf si lou yalla Sak si adouna Nare mossi gueuna bone , koussi mouna woute visa mo gueune doumané kéne boumou gneuw Europe yeufou soxore la koussi mouna ame visa gneuweul
babucar diap si yalla nga tok man fofou la diar mes bou dèmb done tèye douma dème bilahi tèh rèw mi fii tamite nekhoul ame papier rek problème la bilahi
Moi aussi Espagne la nek Barcelone badalona mes instemp bi mangui senegal mes ameth sama ameth la nañiou ko ñianal li guene si mome ta yalla takhawou ko babou guis yone bou lerr mou outi am teral yayame ak kepeu kou khebeu yayame ndakh kouy forcée touki say wadjiour ñio takh ndakh dafa am ñiou meneu khebaté ta yalla yague na ak diamame
Bro courage mane doundou nafa lou geune méti lii ta bouma guisaton gaal gratuit tay lako geune mane senegal dafa méti limay wax mano leen ko comprander sah
Le journaliste n'arrive même pas à lui poser des questions ❓ le gars disait qu'il a regretter depuis Burkina cas même frère tu pouvais faire demi tour, même à Akadesse(Niger) tu pouvais encore faire demi tour. Il n'a pas parlait de son ami,s'il est entré en Italie ou s'il est retourné avec lui en Sénégal. ? Bravo à toi. t'es un guerrier bon courage. Quant à moi si c'était à refaire je le ferai bro. (La souffrance au Sénégal ou l'Afrique de l'ouest avec les travaux longue durée, salaires de merde à non tout sauf ça !! ) Barca où Barzak rék
Je confirme ce qu'il dit parce que moi je n'ai pas assez dessus avec ma fille à l'époque elle avait 1 ans si moi j'étais obligé de traverser la mer avec ma fille c'est en pensant dedans c'est là où je me suis dit j'ai fait une terrible erreur mais alhamdoulilah on est là maintenant en France on a une autre papier maintenant on dit grâce à Dieu al hamdoulilah Rabi alamine et si c'était à refaire je vais pas le faire
mon takh aye 😂 mn ma diapeu sii lii wadie dii wakh pask nioune niougi maroc dii tante ba dougou zone international ba giss Espagne marocain yi diniou diapeu sak estan mais yalla bhak na
Bro santa Yallah che questa vita che facciamo in Italia è una merda tu lo sai che Senegal é molto meglio solo che non c e lavoro lì questo é il problema ma Yallah bakhna
Billahi 😭😭moi je confirme j'ai partir avec Rimbo, mais vraiment Alhamdoulilah 🙏 pour l'instant je suis en Italie 🇮🇹 je suis là depuis 2015
moustapha cissé yow déja sama papa gua koula kholl rek kham né nitte kou bakhe gua té am diom tékki rek mola nior téral sa famille diambar deugue gua goor yalla pire gua tu es fort mentalement avec tout ce que tu as traversé yalla bakhe na yonou ndaw dou gaw té borome karaw gou niakoul dara du courage inchallah bouko yalla sunu borome toudé rek digua nieuw europe
Salam
Mane dh sama tata (petite soeur de ma maman) maroc la diougué di traversé pr dem italie bobu lagn ko gueuthie deggg
Yalna ko yalla gnite si barké bessou yonente bi 🤲🏼
Sa tata bobou noumou toudou
@@gorqfggj5359 aby djité la toudou
Nianal len ko yalla sammouko fam nek rk c durrr 😭
Amine way
C'était en quelle Année (
Ndéysane begue tékky rk métina moustapha yalla nala yalla diapalé depuis🇸🇳🇺🇲 USA yonou souf bi la diarra dh Brasil Améric 2019 begue tékky rk fall sénégal da méty mai yalla nala yalla diapalé yonou souff bii bilahi kousi diaroul manoko kham
Par kel moyen d transport
Yalla nguafa ame Terangua ak xewal ak papiers si Barke Serigne SALIOU MBACKE
Bonne chance yalla na yalla diapalè motali yèhna bi
Bamba brezil 🇧🇷 mame cheikh lolou ame na sama domou ndeye
@@damediaw6509 amine
Man mangui Allemagne Moroc la diar en 2012 mais Lou mbourou d'Ath si Tal ba d'Ath na kofa mais légui Alhamdoulilah,yalla na yalla takhawou gnépou si barkéb Serigne Touba
C'est comme mon histoire il raconte. Mas dieu merci je suis en Allemagne. Courage frère 😭😭
Courage mon Frère boul xaddi muk ✊🏿💪🏿
Je suis en Italie mais il faut savoir une chose,képp kou dieul aventure Libye,Maroc, Tunisie walleu Algérie pour ndém Europe.Amneu son propre histoire de vie qu'il a subit,on peut pas tout raconter.Mane moom xaral ma noppi rékk.Yalla na Yalleu yéreum niou dée ci Yoon bi🤲🏽Té dimballi niou feu déss🤲🏽
Walaye sais Dieu qui est for
Bilahii wadji da bakh reek dii wakh nioune dounou wakh mai insby alkhadoulilahii
Fiii mouy wakh feep diarnafa mai da melnii leemp sii man sant na sama yaye bou bakh
Slt moi je suis en France .
J'ai passé là-bas il à rien inventé que dieu nous PROTÈGE amen
Ba France nekh na rke
T'es pas en France toi, car tu aurais pas commettre cette grosse faute ''j'ai passé '' 🤣🤣🤣🤣 mdrrrr ''je suis passé '' je préfères🤣🤣🤣
Fou nex si France man Toulouse la nekh
Bahna
Je passé en liby j’étais capitaine 👨✈️ d gall Je suis en Europe depuis 2016 mais si j’étai le fair jne le ferais j’étais j’ai regretté dara diarouku ci adouna bon courage frère
Il dis vrai, Dieu merci je suis en Allemagne, mais la route de Libye est plus dur que l'enfer
Merci mon frère tu parfaitement raison je suis passé à liby 🇱🇾 c très grave vraiment
J'ai vécu la même chose, au Maroc alhamdoulilah maintenant je suis en France, vraiment c'est très très dur mais dieu grand.
Oh frére yallana la yalla jaaplée waye barkii cheikhûll khadim
Oh mes larmes coule je m'appelle Ibrahim Korobo Sénégal casamance sedhiou comunes de koussy1 village de nimzath j'ai passé ce chemin là, Dakar. Mali Bamako, bourkina Faso wakadougou, kanthiary, Niger Niamey, agadez arlite, Algérie tamarasette, ourgilla, enzella, debedebe, lybie bene waly, tripoli, pour Europe Italie Cécilia Rome, France Nice, Cannes, Marseille, Espagne Barcelone.,murciá, llerida 😭😭😭😭
Waw fo téré
@@amadoundiaye3539 magui espagne
Si tool yi😂😂😂😂😂
T'a bien metrisé là route ahahahah,moi agadez Sahara Libye
@@devisdiallo4016 oui frère j'ai bien maîtrise la chemin
Massa way c trop dur donc khalé djiguene yi wagniléne ladioum khalise mi té khamni goor gni sonou nagnou🤦🤦🤦🤦
Wakh Ngua Deug Deh Bilahi Li Yeup Djiguéne Mo Léne Ko Tékk
Waxga deugue Fatou 👍👍
billahi yawe
Ay way merci
@@assanediallo4906 5
Cheikh ibra Fall néna bayi lénn topou deureum ndakh dina waral ay bamel you sorri . donc chère frère soyez patient et pensé a ceux qui vous aiment
pourquoi il ne priait pas cheikh ibra fall
Bilayy Sénégal mon méti rék téi sounou gouvernement bi désfa lounou darrà😭😭😭😭😭
billahi yawe
Daray adouna jiaroko😮😮😮
Man dei wax deug yalla beugna toukki lol guéne galséne waya ay yonou souff ak gall mom sama xell xalatouko heure bouko yalla dogalei baxneu mais douma bayi courage bro!
Yalla nalla yalla diapalle way grand bi lou miti gour laye dall mogne rek nioune nieup dina niéw inechallah Sénégal dou darra pour niom nio guen niéup
C’est trés important cet émission
Ndeyesane moi j'ai perdu mon frère qui voulait rejoindre l'Espagne aussi et moi présentement je suis en italie mais réellement guissoumafi louko diar
Ndeysane , yallah bakna reste courageux
Ahx yallnako yalla yereum, doy nawarr deh, con yagui italy
Deko gnanal rek ndaysane metina trop vraiment
Yalla nako yalla yeuram
Ndaye san
Avec tout ce que moustapha a dis il y a des gens qui pensent toujours partir il faut lire les commentaires en bas. Pourquoi les noires aiment les difficultés. J'ai envie de pleurer.
C'est vrai et j'en fais partie ✊✊✊
😅 ma ngi ci biir
Rien ne vas au bLed bro
Grand bi lou lerr gaa wakh yalla nalla yalla takhawou fi yepp djarr nafaa mais sante yalla rekk 🇧🇬🇧🇬👋👋🇸🇳🇧🇬🇧🇬🇧🇬
billahi ndayesane
ALHAMDOU LILAXI RABIL HALAMINA NOUS ONE LA TRANQUILLE je suis passé en Libye mais là-bas c’est dur mais moi dieux ma aider je ne pas duré longtemps Libye je suis resté là-bas 4 jour seulement et après j’ai eu la chance d’avoir un chodiak pour rentrer en itali j’ai fais sénégal entr itali 24 jour seulement maintenant je suis à Paris j’ai mes papiers y’a deux mois maintenant j’ai gagné bien ma vie dieux merci encore une fois je remercie énormément mes parents courage mes frères sénégalais 🇸🇳🥰🇫🇷
Ta fai combien d’années pr avoir tes papiers car deguena ame papier fofou da meti
Que dieu protège nos frères qui sont au pays arabes là bas c plus dure que l’enfer
Pour tout vos problèmes de aimé retour d'affection rapide contacter moi sur WhatsApp (+22960405069)..
🇸🇳🇧🇷🇧🇷 Masha alla
Hoistoir bi amna solo lolou 🤲🏾🙏🏽🕋🕌
Tou pase seule les souvenirs qui restent c est ton destin du courage moustapha DIEU est grand
😭😭😭😭😭😭😭
Jajeuf champion Lou méti goor laye dal daga âme diome motakh nga dem a la quête pour un lendemain meilleur voulour toujours aider ta famille mé dis toi que on ne perd jamais o gagne ou on apprend et en plus ya le destin et nul ne peut contre son destin
Ndaye sann yagui maye fatali 😭😭diamano bima koye dondou 2016 bilahi yagui wakhe loumeti me lepou diekhena j suis an francs
C'est très dur je suis triste que dieu vous bénis Amine
Bilahi lou lèr nga wakh yalla nala yalla takhawo inchallaho rabi me magui laye ziare dila namo
Dèlo ziar bou bakh
Yalna la yalla defal diam Inshalah
Ndeye sane il a beaucoup souffert mon cher mari adoré
Masta Mn namour
Entouka de toute façon yefou goor leu yomboul nak mes yalla bakhna
@delmo tv oui
Courage bro depuis Allemagne 💯💯🇩🇪 jul
Oui il est mon mari
Bilahi yonou Maroc Espagne la mete yalla rek molaye dimbale😭
billahi yawe
Aye waye bilahi métina
Alhamdoullilaha sant na yalla bakhna 2016 lafa diar yalla soutoural ma bama aguesi si diam 🇮🇹 Senegal dafa mètti trop
billahi yawe
Slm mbokk wa kou bougone nieuw foufou nakk
Wallahi senegal liny dunde lep lep gouvernement bi monokou ték wallahi
lahilaha ilalah mane dema touma allahou akoubar mane mifa beugone diar dieureudieuf sering touba moustapha dimbali ngama
Li yakk n’a sama Life 😂😂😂
Je suis en Italie jai passe en Libya apres jai rentre en Italie mais vraimet je suis trope fatigue en Libya
Baan afer le
J ai vêcu tout ce trajet maintena je suis en italy alhamdoulillah dieu merci
J ai vécu la misert la souffrance tres di
L Italia é una merda🤣🤣🤣
Abdu Shakur Prkoi
Italiani sono bravissimi ma non sono tutti
Man dé mangi mangi maroc depis 2017 pr dem espange mei dara apunako fi ba 10ans
Yalla nalla yalla diapale
@@mariemdibba2027 amin
ndéysane yalla nala yalla djalalé Inchallah
@@cheikhnacheikhsadboudjeurd8087 amin way
Décourager bro
J'ai quitter Sénégal le 20 mai 2015 , aujourd'hui je suis en France , alhamdou lillah
On di k y’a rien en Europe Esk c vrai
Fou nekh si France man Toulouse la nekh
Ndyssan yallna yall japolela je bark seydena Mohammed Sw amin
Billahi doundou nako diarna fa lou méti😭😭😭😭😭😭😭😭
Bal fetal boy boumo lal mougui doundou c’était devant moi ce matin,j’ai pris le même pirogue avec lui jusqu’à Italy,ont n’était dans le même campement en Italie et ont n’est venu ensemble en France ,le gars ses un Guinéen actuellement moungui Paris ont se voit presque tout le temps
Masha alah sante yallah
Ey way goor mo sooner billay tu m'a fait pleuré
Man 2016 bobou lafi dougou mes bou dèmb done tèye bilahi douma déme mes nak alhamdoulila boma mouthiè
Du courage yafou gor c est très dur j ai quitté chez moi 18 janvier 2016 et arrive italie 22 février 2016 mais la route es dépassé dur mm c est l enfer
Mane de ma nga ni Algérie ta inchallah le 20 septembre bi ila Libye déf na kasso 5mois anter mali & Algérie defna kasso cot'divoir 2foi me dara khame na ni dina masa bakh bilahi sonnou na ci sama adouna dra sama yaye diaralna ma dé bisse bou khammi ni damaye dem Libye no daye dé ndakh sama yaye maye adouna naame me dra yalla bakhna inchallah geume nane ni duna bakh 1jr ta bilahi defna ti yone bi puls 2million 300000 ndakh kasso yoma don faye😭😭😭😭😭🙏🙏
Yalna leu yalla Diapoule
Appel moi sur watshap 781072950 dinala diapalé inchalah
@@rokhayaseck9239 ok dinala def sign inchallah
Rokhaya seck mane sakh sokhla na si japalébi
@@tvadamandiayekhassaidtouba8388 amine ko bakh 😍🙏
Allahu akbar bayiléne déme si gal yii sauver léne sén bopp guir yallah lolou risque la dhé
Je suis en malta sud de l'Europe tout près de l'Italie et Espagne jai passé en Libye mais en réalité on a très souffert sur la route les arabes sont méchants
très méchants même
Ziar sama waji magui won malta 6 ans
Llll
Lybie amatoul Etat, ba nopi toubab yi seen bop gno dooleel lybiens yi nguir gnou mann leena nadjal nitt gnou gnoul gni fofa.
Gnom amna Lou gnou sagnoul def ndakh UE bi gnou bokk, ak respect droits de l'homme yi.
Motakh gnom gno diokh khaliss ak matériels lybiens yi nguir gnouy torokhal africains yi, tayyeef la dé.
Mai ba fofou amena XEWAL rke
Nguir yalla jeunesses bi moytou léne yonou souf si lou yalla Sak si adouna Nare mossi gueuna bone , koussi mouna woute visa mo gueune doumané kéne boumou gneuw Europe yeufou soxore la koussi mouna ame visa gneuweul
Mai gninane Europe amoute dra nak
@@damediaw6509 kèp kouko wax dafa amoul papier mes bo amè papier tè beug ligueye dinga dég dali
Wallahi goor yomboule mane magui itali waye amoule dara loufi yombe mane dale lima digeule samay frer moy dara diaroule di diare si yonou soufe
Abon loye wakhe nii
Bilayy
Lossi mana degue kaolack ba agadez fofou amoul blême wayè Niger ba Libye soubhana allah😭😭sama carte d'identité Burkina la dess
Man de diara gomafa me Khamna damay foumo 🔥
Babacar boul moussa dem fofou woroul
babucar diap si yalla nga tok man fofou la diar mes bou dèmb done tèye douma dème bilahi tèh rèw mi fii tamite nekhoul ame papier rek problème la bilahi
mo geun de
Merci Sama Gaye 🔥
@@muhammedkanteh422 ligua wakh soukou nieup wakhone gualll diekh fi nekhoul metina ak coronabi
Machalaa raffetnatrop Mame doundouléne té werr AMINE RAFFETNATROP LEPPOU LERNA TROP DIEUREUDIEUFFEE SERIGNE BII
Wallay soko doundal doko kham 😭😭😭😭
billahi yawe
Courage mon frère yalla nalla yalla diapale waye
Amine
Li warna diangal sounou presidente mou gena goor goor thi reew mi ndakh khaliyi am ligueye...😰😭
YitéLou Ko sakh.. mom kay na niou niane borom bi takhawou niou rek insha'alLah
billahi yawe
Tu a raison mon frere j'ai passe a liby en 2016
Merci frère courage
Mai man sax mai issbiii magui italy Libya la diarre☺🥰🇸🇳🇮🇹
Si gal bi
Liwax yap deugue la Libye la diar mia magui Italy sant Yalla bubakh
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@@Eladji-sall44 louy djoy
@@pwm-1529 dr
@@Eladji-sall44 fou dek si France
Tu peux me donne ton numéro de WhatsApp stp
Machalah mane maroc la diaar magui españ ni wayei yalla bakhna
Man magui ni Espagne limou wakh leppou degue la
Moi aussi Espagne la nek Barcelone badalona mes instemp bi mangui senegal mes ameth sama ameth la nañiou ko ñianal li guene si mome ta yalla takhawou ko babou guis yone bou lerr mou outi am teral yayame ak kepeu kou khebeu yayame ndakh kouy forcée touki say wadjiour ñio takh ndakh dafa am ñiou meneu khebaté ta yalla yague na ak diamame
sa numero svp mon gars
Man France la nekh Toulouse Toulouse waye magni sante yallah boubax
Képpp kouy démm dangua beugua téki lima gueuna méti moy fignou lénn teuthie yeupp loumou bonne bonne lékk nagnou mais Sénégal😭
ay waay santal sounou borom car bkou d'amis son perdus leur vie que DIEU les accueille dans son pradis
En tout cas il est fort mentalement yallah nala yallah samm
Diaredieuf moustapha loulerr nga wakh man mii fofoula diarre metina trop
😭😭😭😭
Man fala diaar mètiwona lol mais lou metti goor lay dal sant yalla mangui italie ak sama sokhna ak sama dom sant yalla bou bakh
Bilakhi dioye loguama
Louu meitti day diehh mais supporter mo diaff.é..Yalla samae la,
Yalla Nala Yalla diapalé respect à toi frère 🙏🤝
Bro courage mane doundou nafa lou geune méti lii ta bouma guisaton gaal gratuit tay lako geune mane senegal dafa méti limay wax mano leen ko comprander sah
VRAIMENT T'A DEPENSE PLUS D'UN MILLION RESTER ICI FRERE ET TRAVAILLONS
Khana dégulo limou wakh
😭😭😭Dawne yaram
bilahi mem man fala diarr me yenena
Le journaliste n'arrive même pas à lui poser des questions ❓ le gars disait qu'il a regretter depuis Burkina cas même frère tu pouvais faire demi tour, même à Akadesse(Niger) tu pouvais encore faire demi tour. Il n'a pas parlait de son ami,s'il est entré en Italie ou s'il est retourné avec lui en Sénégal. ? Bravo à toi.
t'es un guerrier bon courage. Quant à moi si c'était à refaire je le ferai bro. (La souffrance au Sénégal ou l'Afrique de l'ouest avec les travaux longue durée, salaires de merde à non tout sauf ça !! ) Barca où Barzak rék
Thanks brother is not easy
Bilahi kouko doundoul doko kham waye doun nako Boubakh
Pourquoi vous avez demandé l'indépendance en 60?
Dama beugue kham khalé yi done dém Espagne tan déparé mbour si lan lanou nék répondé moi s'il vous plaît 😭😭😭😭😭
Ndaysane yalla n'a yalla SOUTOURAL Sama papa dji Niou ÉVITE
Amine
Ne décourage pas grand yalla bakha té hamo yone bi lolu mo takh mai sinon 1millions késé mounala yobe ba Niger ou yénéne pays africain
Walaye noumouko wakhė nonoula dėmė courage rekk frere
Je confirme ce qu'il dit parce que moi je n'ai pas assez dessus avec ma fille à l'époque elle avait 1 ans si moi j'étais obligé de traverser la mer avec ma fille c'est en pensant dedans c'est là où je me suis dit j'ai fait une terrible erreur mais alhamdoulilah on est là maintenant en France on a une autre papier maintenant on dit grâce à Dieu al hamdoulilah Rabi alamine et si c'était à refaire je vais pas le faire
Tu as combien d’années en France
Ndeysen kou si diarou doko kham😭😭
Bilay walay courage rek
billahi yawe
Billahi
Ndeysane djambar. Yalla nala yalla mey nga touki.
1millions mais investiral en Afrique so nieuwone Mauritanie ma diapalela en immobilier.
Man magui ni Espagne démonna libeye sant yalla rek
Courage rék aye diambar deugue deugue guéne yalla naléne yalla takhawou
😥😥😥😭
😭😭😭😭😭😭😭😭😭
du courage frere
Grâce à dieu ses moi je l’es sauver demain je vais lui montrer ce vidéo le gars reçu la balle
Macha'Allah merci
Ma sha Allah
Bilahi degi la frere da am loudes sa motah si sama adouna mounouma siporte nar
Omar mane mangui paris mais nar yi no gueune yeuss bakhounou gniou bone lènou rasiste
@@abybathily8221 bilahi gay de
Billahi Lima dathi lyby birna brome touba bouma ko nèttali woon macky sall dioxma passport diplômant billahi
😭😭😭😭😭😭😭
Bilahi lybi mome kene dou Mouna wakh lepp Mane loumassi doundou rek métina bilahi
mon takh aye 😂 mn ma diapeu sii lii wadie dii wakh pask nioune niougi maroc dii tante ba dougou zone international ba giss Espagne marocain yi diniou diapeu sak estan mais yalla bhak na
@@mansourdieng2000 yalla défal la diam rk dina bakh incha Allah
@@princetorodo8590 yalla nala yalla indi thi diam incha Allah
Toukki dagnou koy sete bala dem yallah bakhna yaw linga faye yeup so togone senegal investir si a dem wadji toukki takhouta tekki deh
Sama gnari rak ba legui khamou si lougn nek khaw la dé nagn kham niongui dound 1an kelk mois 😭😭😭😭
Loy wakh nii
@@babsbii3585 bilahi dafa nekhoul wakh rek mais kham de naniou
Pisco El presi oh metina bruh yalnala yalla diapalé
Amna solo emission yi Lou diara defla pour guena sensiibiliser Jeunes yi.
billahi yawe
Walay ndeysane duegue pirrr nga wakh Burkina aka metí mane ma gui espagne Wayé
bilahiiii lolou dhé daray italy 🇮🇹 diarouko
Ndayesan man fofou la diaar mais santé yalla rek magui espag temp yii
adouna dalle mosoul mēti nigni gno yackamti rk weur bocka yakametē rk mē kou tackou si sa rw dinga tēcki❤︎✔︎✔︎
Mane dh mangui Italie wayè douma digal kène mouy diar ci gall
Kenne ladiou l'e digal bon amai je digal teye co
Bro santa Yallah che questa vita che facciamo in Italia è una merda tu lo sai che Senegal é molto meglio solo che non c e lavoro lì questo é il problema ma Yallah bakhna
Ahhah è vero bro io sono cresciuto cui in Italia da piccolo a Treviso ma europ diaralouma DIAR fisa way DIAR
Lou tax gua diar cii dagua lenn guen? wala dagua lénn eupp wersekk?zerar8
Man mangui Libye actuellement Mais limoy wakh ni yep deug la c'est pas facile je fais 6 ans ici
CV grand
Dém force dara dougnou téh 😎
Guirigaras la nekone ci 2015 Alhamdu lillaah â gëna ci jamaa