Kou beug xam Balla deeg lou ko fi. Balla wax dara la ci manoul. Incohérent comme pas possible. Li mouye kass yeup ci la neek teey ji. Baan boy la fi maay chance🤔 Balla daan Yekini Yekini def conference di wax ci febaraam. Mou ni dafay saltel. Tassé ak Bombardier ni dara diotou ko Niou daan ko mouni dafa febaroon Eumeu Sene daan ko Mouni xalé la woon Eumeu danaat ko Mouni dafa febaroon. Niou ni deet ni waay : Mou ni gni ko daan nieup mo leen maan. Ballla dafa nekh dé😃
Balla Sa bou Dadié ak Bomb Dakoy toumaal si ay wakh you Vilgere Même Eumeu aussi Sa Bou dadié ak Mod'lo nonou lay def Mais Lolou Amoul Chance Té kouko dégue Fokni Djikom la fékni Dara Amoul Si
BALLA GUEYE 0 BOMBARDIER 1....UN JOURNALISTE INCAPABLE D ETRE PROFESSIONEL DANS LES QUESTIONS ET UN BALLA ARROGANT ET SANS S.V ( SAVOIR VIVRE) IL DOIT ETEINDRE SON CELLULAIRE N EST CE PAS?
Balla guaye 2 stars des lutteurs sènègalais de tous les temps
Pape Cheikh yague naa beurri wakh😂
Balla tu restera le meilleur 😎
Balla raffètna khol trop pour dire vrai ça c'est sur
Kou beug xam Balla deeg lou ko fi.
Balla wax dara la ci manoul.
Incohérent comme pas possible.
Li mouye kass yeup ci la neek teey ji.
Baan boy la fi maay chance🤔
Balla daan Yekini
Yekini def conference di wax ci febaraam. Mou ni dafay saltel.
Tassé ak Bombardier ni dara diotou ko
Niou daan ko mouni dafa febaroon
Eumeu Sene daan ko
Mouni xalé la woon
Eumeu danaat ko
Mouni dafa febaroon.
Niou ni deet ni waay : Mou ni gni ko daan nieup mo leen maan.
Ballla dafa nekh dé😃
BILAKHIIIII...
BOMBARDIER DI NO KO DELLO THI PLACE OM ...BEU PARE MODOU LO DI NA GNOWAT DIEL REVANCHE......☝️
😂 balla dafa wayadi
Un grand monsieur bombardier
On va k balla weroul fi day force
Kaagn laay wéér mom lol
Balla bombardier moy sa baye
Balla gaye daga khepp khale mou tall sa keur
Balla le meilleur de sa gènèration
Keur bi rafetna macha lah
bombardié bilahi dama la fans
Balla Sa bou Dadié ak Bomb Dakoy toumaal si ay wakh you Vilgere Même Eumeu aussi Sa Bou dadié ak Mod'lo nonou lay def Mais Lolou Amoul Chance Té kouko dégue Fokni Djikom la fékni Dara Amoul Si
Balla dakhar Dina faf safat wala dél wakh loula lér
Franchement Bombardier communique tres bien mais mo meune Balla Gaye 2 motax Balla dou Gnaan revanche moukkkk
Balla gaye 2 ioe danga khamoul wakhine lolou moye sama problem danga wara am yaarr iss
Pape bari gua ndeye wakh troop en plus do déglou seytané gua rek !
Yaar bahna si niit
@@abdoulayendoye1803 maandou bakhneu thi nitt loma khamale yaw 🤮
No balla dafa yague con
Balla xawma kan mé Bo Amé djom Bo guisé kuy Naan ay Doom Dinga Daw Ba Fakastalu Sa yaram bi mo Fousa kén liguéyula ya yakh sa bop
Bg2 dy nexal lamb rk
Balla dé comba bi loumouthi wakhe t danou n'a hooooooooo
Sama mbeur bi réwon-na 😂😂
Bombardier état biii soko indiwaté yaa meunn wadji
Sa papa meussoul nékk roi des arènes. Roi des arène si manga la commencer
yar dal ak yalla faral leu mo meune nit yii dila mbameu bombardier si kaw si kanam
Balla njingay nogatou bomb bokoul si
Wally cv
Balla for ever the big king
Quie et la 😂😂
Très incorrect; très hors sujet so danouwoul wone ci combat bi dinama diakhale trop balla fallait que gua danou pour gua xam ni wakh dioubari bakhoule
Loum wax rek def na kou ko raw si beure
Balla gaye defarou wàtal rek dina bakhe
Pape cheikh vraiment tes questions sont bête comme toi khamo dara boule diakhassé gni ak wa Sénégal
yaw balla guaye bombardier boula diape digua kham sa wakh barina
mamy mbaye T
moi j aime balla gaye 2
BALLA GUEYE 0 BOMBARDIER 1....UN JOURNALISTE INCAPABLE D ETRE PROFESSIONEL DANS LES QUESTIONS ET UN BALLA ARROGANT ET SANS S.V ( SAVOIR VIVRE) IL DOIT ETEINDRE SON CELLULAIRE N EST CE PAS?
Ballla daye nappeeee 😂😂😂😂😂
M
You bogine bro haha lmaooo 😂😂😂
Balla affairbi yawla billalhi
On a l impression que bombardier est plus mûre et plus mâture que balla sur le débat
Également pape cheikh n a pas le niveau pour animer ce plateau
balla gaye 2parle trop
balla Gaye parlare troppo
Fra missa che hai sbagliato ( parla troppo )
coule
C'est vrai balla gaye 2 da fibaron juin 2020