2em part waxtaanu Sëriñ ahmadu Njaay Giiraan ci way dawlu yi..

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 5 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 49

  • @rakkaadiou1515
    @rakkaadiou1515 3 роки тому +26

    Khoola beuri woul sah ay j’aime wayè so wahoone nii kéneu dou Serigne bii j’aime yii beuri

  • @mansourdieng2000
    @mansourdieng2000 3 роки тому +27

    Ki Moye Vrai Mouride Ki Mo Ték Tankam Fako Serigne Touba Tégone Mane Ay Vidéo Wam Dama Koy Sétane Mai Lou Am Solo Rék Laye Wakh Yalla Na Yalla Goudeul Fanam Amine Allahouma Amine

  • @aladjifayee3371
    @aladjifayee3371 3 роки тому +9

    Machalah ♥️ niou melni yow niofi waron ndakh domou Adama yi yewou

  • @daoudandong9611
    @daoudandong9611 2 роки тому +3

    Serigne Ahmadou Ndiaye nguirane yalla nafi yague lool tëë and ak wërr ci barké Serigne ñieumm boobé di Cheikh Moustapha

  • @fallbara2752
    @fallbara2752 3 роки тому +5

    Diadieuf amna solo

  • @issasarr3528
    @issasarr3528 3 місяці тому

    Ligaye leral nii amna solo lol loumata bayi khél wakhtane yi nepp warnako degg Lou rawatina niokoy tek si desé desé yi nut yi disi bayi khél bu bax walhi machalla Serigne bi yalla nagafi yagg lol té wer si barcke alkhouran Karim ak khassda yi ✅

  • @morndiaye2467
    @morndiaye2467 Рік тому +1

    Yalna yalla goudal saw fan té weral bate

  • @layediallo2885
    @layediallo2885 Рік тому

    Machalah Serigne bi amna solo

  • @babacarndiaye7920
    @babacarndiaye7920 Місяць тому

    Dieuredieuf yaram

  • @ndionelaye
    @ndionelaye 3 роки тому +2

    Yalna yalla fayla

  • @africanpeople1470
    @africanpeople1470 2 роки тому +1

    Yallah nalafi Buur bi yagal

  • @mohamedfadalgaye
    @mohamedfadalgaye 7 місяців тому

    bilay deugue nékhol ❤🎉

  • @ibrahimasow3698
    @ibrahimasow3698 3 роки тому +2

    Merci

  • @baayfallfall1793
    @baayfallfall1793 2 роки тому

    Yàlna yàlla fayla te baatkel xam xam bi

  • @issasarr3528
    @issasarr3528 3 місяці тому

    Ndaysan amna solo lol

  • @SokhnamayeCisse
    @SokhnamayeCisse Місяць тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤baye ahmadou ndiaye ❤❤❤❤❤❤

  • @bayeyoro31
    @bayeyoro31 Рік тому

    Bilahi wakh ngua DEUG de

  • @babacheikhndiaye7491
    @babacheikhndiaye7491 3 роки тому +4

    Louam solo

  • @fallamadou1047
    @fallamadou1047 2 роки тому +1

    un conferencier sous coté

  • @senegaulgalsen
    @senegaulgalsen 8 місяців тому +2

    Sa vidéo bi takhna ma démm diouligui Guéh th fassiéné na bisse niki taye topou sougnou borom mangui koy gnane th di gnanale yeup mou diégale gnou sougnou ay backares th khire gnou silou bakh may gnou moudiou bou rafete

  • @naboundiaye7468
    @naboundiaye7468 2 роки тому

    Alahou akbar

  • @naboumbaow6973
    @naboumbaow6973 2 роки тому

    Machalah

  • @morfall1070
    @morfall1070 2 роки тому +1

    Lii lagnou wara wah nit ngi ta bayi ndakhaté bi nit ngou bari rér nagnou

  • @daradjitvdiop5321
    @daradjitvdiop5321 3 роки тому +4

    Machalla

  • @mariamambaye1460
    @mariamambaye1460 Рік тому

    Bilay motakh kouney gua gnanal sa bopp nitt gni sen bop rek lagnouy tall

  • @iboukandji7396
    @iboukandji7396 Рік тому

    ❤❤❤❤❤❤

  • @diopallaamydiop9354
    @diopallaamydiop9354 2 роки тому +1

    🙏🙏🙏🙏

  • @fricaque2172
    @fricaque2172 2 роки тому

    ..

  • @absgofficiel
    @absgofficiel 6 днів тому

    ❤❤❤❤❤