Machalla yaye Isseu maala beugue bilay Kéne douyaw yama doy si wagnvi souba in sha Allah moome lay togue mon mari aime beaucoup le thiébou guédje. Yaw dal Maman dél wakh amine rek doundal 100 ans sans ordonnance témou ande ak weur ak khééwal. Aliza depuis Canada.👍❤
MACHALLA FA FATABARAKKALAH ce qui m'inspire le plus c'est la sainteté dans vos plats , votre professionnalisme etvotre éloquence c'est vraiment intéressant merci beaucoup togou Yaye Isseu laftiat longue vie Tante Marie MACHALLA FA FATABARAKKALAH
Mane lima néhe si Tata bi moye sou togué baparé loko bindeul si commentaire dinala tontou si aye coeur pour wone la ni mingue léye bayé hell machalah. Lafe thiate❤❤❤❤
Salam bravo mais vos recettes sont bonnes très bonne explication mais si possible vous pouvez dire pour combien de personnes et le grammage des ingrédients du riz etc. Merci beaucoup
Je suis accro à ces videos. Je regarde la veille ce que je dois préparer le lendemain pour mieux parfaire ma cuisson. Yalnala yalla fay
Kou beugue yaye isseu
Mane 👍
Machalla yaye Isseu maala beugue bilay Kéne douyaw yama doy si wagnvi souba in sha Allah moome lay togue mon mari aime beaucoup le thiébou guédje. Yaw dal Maman dél wakh amine rek doundal 100 ans sans ordonnance témou ande ak weur ak khééwal. Aliza depuis Canada.👍❤
MACHALLA FA FATABARAKKALAH ce qui m'inspire le plus c'est la sainteté dans vos plats , votre professionnalisme etvotre éloquence c'est vraiment intéressant merci beaucoup togou Yaye Isseu laftiat longue vie Tante Marie MACHALLA FA FATABARAKKALAH
Ma Tata de mon cœur. J adore ta cuisine. Inchallah dîna la setsi dès que je viens au Sénégal.
Ohhhhhhhh😍😍😍😍😍😍 xifatina. J'adore votre cuisine, je salive à chaque fois que je regarde vos vidéos❤ je vous pardonne de autant m'affamer 😅
Yaye isseu dall lima geuna nèkh si yaw moy dagga ame talibè machaalla mère😚😚
Machallah sama yaye boye lii nekk kou bou goul thiep nieebe sakh dina gua KO mangé dimanche inchallah gnou def KO mrci encore.
Macha Allah ma Badiane bauy de valeur,tègate ngata ci temps .lî si thiébou guédjeu,eupeuna.
macha Allah tata yale na lokho bi werr thi barke Seydina Mohammed saw 💖💖🥰
Mane lima néhe si Tata bi moye sou togué baparé loko bindeul si commentaire dinala tontou si aye coeur pour wone la ni mingue léye bayé hell machalah. Lafe thiate❤❤❤❤
🥰🥰🥰
La meilleure machallah de très bon plats à moindre coût longue vie avec une santé de fer.
Machallah tata amena tina solo yalla nalaya yala barkel fay yiw inchallah 🥰🥰❤❤❤🙏🙏👍🏿👍🏿
Machaalla maman c'est un plat très riche goudal fane lole 💖💖💖💖💖on vous adore
Macha alha yay isa Mane damala bege rék tét yalla tah❤
Tata thieb bi nekhna si guiss rek machallah
C mon plat préféré merci Tata
Thiep bi amoul noumou nekhewoul Macha allah rien ka regarded tu vois ke ce bien prepare
Mashalah pas la peine d dire nexna com d’habitude rek mashalah on attend l thieré bombou avek impatience😘🥗❤️
Merci bien pour l'innovation. Ak nawette bi mome lou frokh dassiy bakh lolou sakh. Kallah veille sur vous et augmente vos connaissances.
Wa Mane bi fayenela diare beu sétanoumakone... thiéye sougnou ta mari international bi ❤️❤️ mais dara dou yassa brochettes bi ohhh
Ayway sama plat machallah maman dina nieuw ndar ga togal mako😥😘😘😘
Machallah amna solo tata 😙😙
Machaallah tata isseu. Dimanche tay bi mom la togu mais nekhna riche na😍😍🥰
Maman machallah ❤❤❤
Ayway li tamit mba diam machalla diarna yon yalna yalla fayla es 🙏🙏🙏🙏🙏❤❤❤
Machalah tata ❤️❤️❤️ Toujours à la hauteur de nos attentes 🥰🥰
Machala défati nga sa meunine badiane sama badiane isseu la toude
Merci beaucoup Mme longue vie à toi bisous ces oumy
Macha allah rafetna te nourouna lou nekh toogou bi jaarna woon
Macha Allah madame contane thi yaw. Surtout vous savez innover. Tres créative
Macha Allah Sokhna Marie nammoon na nou la. Tay moom yobbou nga nou waalo ak ndar. Merci.
Bonjour tata sincèrement vos plats sont succulents machallah
Ma Shaa Allah
Machallah tata j vais essayer inchallah ❤❤❤
Moi aussi😂
Machallah
Maman ki est tii😘nekh na beury na .c binta seck Mme sam
Laylayla aye yaye isseu nak lilanla tamit tamit tamit eupna mashalla💪🏿💪🏿💪🏿❤️💋
Machalla maman ❤️❤️❤️
Kou yakamti doko setane mais machalla
Amal diam tjrs tata 😍😍😍😍😋😋
Trop saf saf bravo bravo encore une fois
Machallah maman thieb bi nékh na
Thanks tata we learned a lot across your videos
May allah bless you for many, many ,many years to come
Amen
Machala c très bon et tu m a inspiré Dina ko togue
Khana sa toggou dou am adja ak ay magie yoyou nonou
Ay thiebou guedieu Yass gui. Delo ngama walo dè
Masha Allah tata 😍👌
sama khéle sakhe moungui si yawe 😀🙌😀🙌😀🙌😀🙌 douma yékale
Machalla ❤️❤️ Binta fall
hiii Tata tay mome mane nga togal mais sauce légume bi danouci ame bi mome dimanche inchalah ma mayéko merci Tata amal diam jtm😍❤
Guedj yasss hahhh mako beugueu sama khol
Machaallah gattana té lérna
Bonne continuation ma chérie 😘😘😘
Je validd😘 laf thiate
Tata tourna kheul
MACHALLAH
Machalla gnou dėlou walo tu nous aviez manquė
Machala magnifique
Machalla maman vraiment tu cuisine bien
Cc succulent belle assiette 😍merci
Masha ALLA togueu rek guaye def 😍😍🥰😘
Mashallah tata huuuum miam sama plat nga tog tay bon appétit na rees ak diam
Machallah lou nekh si nawette
Ma sha allah
Es muy rico me encanta👍
Mashalah fiere ci yaw😘😘😘
Machalah sama plat préféré
Nekh na trop bn appétit
Machallah machallah nekhatina. Yow lo togueu mou nekh rafet😻
Bilahii tata y’a meune tooogg way liii nekhna te sell na
yawe koula wakhe nékhena 😃😃🙌😀😅😀
Mak tata gno niroo nignouy toggué, sauce mom dmay tankeu gneekh rekk😄😄😄
Bi mom tongue liberté 4 vrai la nekh na félicitations
Merci anta
Looks beautiful
Machall 😘😘
Merci 🙏 , machallah,
Prochain passage sur Dakar, je ferai inchallah un petit scale 👍👍👍
👍👍🙏
Merci pour la recette Tata danga tay thiép bi wala
Manchalla nekhna
Nehna tres bon plat j essayerais ca. Merci en tout cas
Pouvez vous me traduire les ingrédients stpppppp je ne comprend d pas Snif
Machala 😘👍
Macha allah
Très contente de ta cuisine Macha allah
Tata isseu es ce que il existe thiebou kethiak avec viande
Mama tu es la meilleure. 💙💙💙
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Amna envi tokouko samedi
Machallah tata
Tata isseu la beug
Merci beaucoup pour la recette, marché bi temps yi meiti na trop
Machala nexna
J'aime macha allah
Bonjour Tata danga tay thiép bi wala
🙏🏾🙏🏾😘😘
😋😋😋😋😋😋😋Manchallah
M achallah tata
Machalla
Machala trop bon
Bonjour. La sauce légume ce qui est blanc cest du navet oubien ?
Oui Habsatou c'est du navet
Macha allah. Togabi dafa civilisé sakh. Ahaha
Salam bravo mais vos recettes sont bonnes très bonne explication mais si possible vous pouvez dire pour combien de personnes et le grammage des ingrédients du riz etc. Merci beaucoup
Riz bi khana kene douka taye si Inde
NIAM NIAM NEXNA
Merci super