La force de Amy Collé , c'est qu'elle est NATURELLE mashaallah. Mais qui connait ses parents ne s'étonne pas. Elle est une artiste de grand talent. Elle est aussi Saint Louisieene du côté de son père.
Ndeyssane ca me rappelle bi sama bopou bi di meti ton propre frere qui est mon ami mon oncle cila ma wakh la meme chose nima sama rakk amy colé dafa amone metitou bopou motah leigui dafay mourou, limay wah nii ndeyssane eupe na 10ans et finalement suis devenue voilée tai ci lama metite bi bayé
Wa samay tamite khamna limou fébarone motax Mou changée té sou maquillage bi guénoul Dou sentir bopam meun na rouss si changement bimou changer 🙌en plus elle était plus Belle sans maquillage 😍Mais nul ne peut échapper à son Destin☺️Mangui diégeulou boubakh ci kadou yi🙏
Ce que j'aime le plus dans la série mére dial c'est que tout est naturel. Macha Allah Ami Collé, une vraie artiste
Macha alla
Machallah en plus d’être belle, elle est très joviale avec un sourire trop contagieux🥰🥰. Longue vie de santé à toi chérie.
ouiii j'aime trop son sourire machallah
Elle a beaucoup changé waouh en plus une très belle sourire comme d'hab bisous là bas 😘
Machallah elle est toute belle,je l'aime bien
Machallah ma chérie bonne continuation ❤️❤️
@@mamikasse2414 pp
métitou bop dé moma takha mourou mane miii khamena boubakhe linga dathie machallah yalna yalla sam gneupe thi barké Seydina MOHAMED psl ❤❤❤
Mais mourou nak nopou yi dassi wara bok
Mane de moma sonal trop
La force de Amy Collé , c'est qu'elle est NATURELLE mashaallah. Mais qui connait ses parents ne s'étonne pas. Elle est une artiste de grand talent. Elle est aussi Saint Louisieene du côté de son père.
JE L'AIME BIEN MAIS LE KHESSAL ELLE DOIT ARRETER
c'est ki ces parents
Elle à une très belle sourire Machalla
🤣🤣🤣sama tourondo do Bayi français yi un joli sourire
No comprendo nada
@@fatou3040 gnoune Fatou ti gno teukheut essaye de comprendre
@@timabella9954 vale no hay problema te entiendo
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Elle est drôle avec un beau sourire 😃
Ndeyssane ca me rappelle bi sama bopou bi di meti ton propre frere qui est mon ami mon oncle cila ma wakh la meme chose nima sama rakk amy colé dafa amone metitou bopou motah leigui dafay mourou, limay wah nii ndeyssane eupe na 10ans et finalement suis devenue voilée tai ci lama metite bi bayé
Machallah 🥰 🥰 🥰 🥰 Alhamdoulilah namone nanioula Amy colé
Machalla amy cole fofou diar nafa ndeye ndoumbe Mme Diouf nitkou bakh machalla wa pegne thioum africa danio bakh
Ndeye ndoumbe Diouf Mme ba borom pegne thioum africa
Sourire 😊 bou rafet la yor machalla
Son sourire😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍
Mash'Allah Amy collé. Dafay khawa Niro ak bijou tfm Mash'Allah 😍🤩
Sisi wahga deug key danio hawa niro surtout bou reitanei! Yow ya meun setlou dei🤣
@@teestreeter4628 😂 avant madone cliquer Bijou lako tégone. Deukk bi légui tout le monde à l'œil yeugo lolou😂
Effectivement ya une très grande ressemblance macha allah.
gno bokkk guiss guiss
Très belle sourire machallah Amy collé yalnala yalla lafal thiat
Merci Ami Colé pour ses bons moments à te regarder. Lala je vous adore.
machalah bilahi deug la mouray defa rafèt ❤❤🤲
Wayé mom da mourouwoul wala charte mouray bi mom respecter wouko. Même dans les series
Machallah Quand elle rit on ne peut s'empêcher de rire avec elle 🥰
Mashala nit yi beugue naniou lene ba tey li nhuene di def nekh na
Sama tourando ya nekh déréte machalah continu comme ça 😍😍❤️
Machallah Thiey metitou bopou moy febarou djiguen yeup Bilay
Bilahi moma sonal mane mi
Machahalah Amy collé yalna sa diame yague
Machallah ma belle ♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥰🥰😘
Amy colle ❤❤❤ jlm bcp
Geureumeul sa YAYE BOYE MACHALLAH wasselouna akha thi yaw bagua done dara thi katanou YALLAH 💯💢💥💫💦💙💜💙💚💛🧡💯
Agreable a regarder et ecouter
Mashallah Sama yaye Sène thiali 😍❤️ danga yag sonou ci man wox deug bima neker xaler ba nimay touker momay let papam beugma ba deh
Ak bakheu yaye ak pp bilay yalla na yalla déff diam 🙏🏻🙏🏻❤️
Est ce que c'est la fille de mère dial
❤️❤️❤️rire contagieux Macha ALLAH
Ndeysaan elle toute belle.
MashAllah Yallah na Yallah sam
Je l'aime trop cette fille 🥰❤️ mashalha
Machalla trop joviale avec un beau sourire 🙏🙏
Amy colle AKa rewww te yape mère diale machala jolie sourire
Machallah sama magou bopou séne thialy djiata ngé ma kane
cette lala là..vraiment impec
Machalla ak rée diou nékh bi
Machallah ❤️
MashaAllah Amie I love ❤️ u so much
très posée
Elle est magnifique mashalla
Niomm danio bakh ndeysann moom ak seny sene
Noo machaa Allah yalna yallah sameu la❤️❤️❤️
Ndeysane woleine koo moi ligueiye
Amy collé aka réwone barry histoir ndeysane changé na yallna yalla diapalé seni mome tapet la mousa nek
Machala
Ki bilahi dafma dane retane lo sakh
Amy Cole damako yague nop😍
Damako beugue bilahi toute belle macha allah
Ami cole nostalgia 😄😄😃
Ma challa laf thiate nitt ko bakh Billy 🤩😘😘
Tu et belle ma chérie ❤️❤️❤️
Oh sourire
Love you ami Macha allhA
Nice na y
Ami ma belle ❤
Lala amneu questiion yo khamni mm si la personne est joviale faut pas pauser
Masahlla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ laf thiate
J'aime Amy collé
Wao anou kiné Sow
Elle vit à l'étranger maintenant je l'ai vu sur tiktok bou yagoul elle vend des produits minceurs
Elle est mariée mère d'une fille el vit en Belgique
Merci pour l'info
Wouyyyy ami dîna ma ray🤣🤣
Amy collé machallah rafet nga mais ki la make up lokhom dafa eup li motax ivoiriens yi dinou saboter ci maquillage bou eupeu
Mane sah haméwou makowone ndah maquillage bi
@@ngonesaliou8347 non dafa eupeu de trop vraiment maquilleuses yi war nanou gueuneu diangat sen métier bamou gueune mokou
C'est vrai
Delen wagni poudeur
Lala defois tu débordes…!!! Vie privée nitki kéneu dousi dougou
Elles ressemblent à manma ndeye coubat de thés
Machallah ❣ ❣ ❣ ❣ ❣
❤❤❤❤❤❤❤❤
Da. Ngendi. Amne. Léegii. Daame. La. Kou. Am. Doomedangaye. Sanger
Lama nouyouna la au partage!!!!😂😂😂!!!
Lala fok nga wakhko febar bi demou demei por mou am diam dou bayi
Nom yawe sinéma nga 😃😂😂😂😂
@@diadia965 noo mane dama warou si lala kharite🙆
Lala t'es pas sérieuse walahi 😂😂😂😂😂
❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤
Au passage 😂😂🤣il dinama ray
Machallah Elle ressemble à MBATHIO Ndiaye Machallah ❤️🥰🥰🥰
Sheeeuu 🤣🤣🤣🤣
Ndiouro wougnou déee kharite
On est famille on est ensembale😂😂😂😂😂
Sourire bou rafete comme trai wifi 🥰
Maquillage bi daf ko changé
Carréma sah
Non Amy😅😅😅
Quelle jovialité
🙏🙏💞❤
😘😘😘😘♥️♥️♥️♥️
🥰🥰🥰
Au partage🤣🤣
Wa mom simploul dh interview rek mou solo ni
En tout cas yiw na rafetna c’est l’essentiel
Noo mes sa maquillage bi doyna ware dé
Yow tamitt doy nga waar deh!! Goor en plus 🤦♀️🤣🤣🤣🤣
Wa samay tamite khamna limou fébarone motax Mou changée té sou maquillage bi guénoul Dou sentir bopam meun na rouss si changement bimou changer 🙌en plus elle était plus Belle sans maquillage 😍Mais nul ne peut échapper à son Destin☺️Mangui diégeulou boubakh ci kadou yi🙏
Ana goor ak lidianti maquillage
Louth sa yon
@@masamba5646 lolou moma diakhal man
😂😂😂😂😂😂😂😂gnaw
😂😂😂❤️❤️❤️
Machallah amy amna solo
Namone nanela trop
Nitte kou bakh begue ambiance s'en keur réfork
Yaye djoubakh begue ay kharitou domame si negame lagnoudanefowé walahi maman adorée
@@boussombaye6536 koula lathie lolou?
Bijou ndiaye tfm lay nourol machallah
@@souch4658 wa yaw mome niako kérsa rék😂😂😂
😂😂😂😂😂
Machala
❤❤