Wally musicalement je ne suis pas avec toi mais tu t'exprimes hyper bien et j' avoue que tu as un coeur d'or en plus tu as de la grandeur si j'ai à te conseiller moy nga Baayi Wooy Dafa Xaram Ti Yow Xolbi Nga Yor Yalla Nala Borom Bi Ak Nioune Nieup Ndax Ci Baakar Laniou ..."Boubacar Doumala Neub Dama Tiiit." Ki Diarna Niou Moytou Di Tég Ci Deram Lou Niaw... Awma compkéxé Ci Toubab...Macca Tal Moukarab La Compléxé...Kou bax Leu Mako Moudié Wax...Chapeau à Dj Boubs
Boub's tu as fais un bon entretien avec Wally vraiment aujourd'hui tout le est très fier de Toi mon frère Wally je parle d'une bonne personne intellectuelle doit accepter qu'aujourd'hui que vous avez montrez un bon exemple Wally Seck merci
Yala nama yalka bolei ak yw ma wkv senegalais yii lougnou khamoul sii yw liii diakha louma sii yw ndakh xam blh diam rk gaay ame je t’aime plus lima begon 🙏 je suis fière taay ndakh gueune gama siiguil
Vraiment je suis très ému waly chapeau à toi vous avez fait une très bonne communication que le miséricordieux ,le tout puissant , le bon dieu exhausse tous nos prières boubacar vous êtes aussi sans égale
Walah wally seck sama khol dafa fèss ndakh sa wakhinne tay dji dawna yaram trp yalla na yalla dolli diamou at salam barki seydina mouhamed since 🇿🇦🇸🇳😭😭😭😭😭
Xol bou rafet ak bou leundeume day fégne si beut lolou louma yag setlou laa té Wally xolam mo rafét machalla il a raison bala bou melni sou amé rk sa veu dir k adouna légui mou diéx nagnou consien sili mou wax le monde va mal k dieu ns protége🙏
Manchallah wally seck tu peux même représenter le Sénégal à l'échelle mondiale car tu parles comme un savant sa guisguis mooo graw tu devances les gens sur bcp de sujets je te suis . Courage
Allahou akbar c'est waly Seck qui parle ainsi ndeysane le monde est en panique Li nak diangate la si kou nék ak sa digsneté ak sa borome nga nék si adouna loula yalla sante nga bagne di musique déf ay concert té yalla téré lako nga bagne ni danga kaye déf tay béne soldarou yalla bouniouye wakhe coronavirus téré la Lila yalla téré wone nga nangou ko par force boul diokhe lokho djiguène boul acolate boul boul déf concert boul déme boîte nga nangou ko par force ba paré daw di woute walou si yalla ndakhe ndiakharé esk diotoul mbok mi ditoul souniou diougué si Li niou diamou yalla bayi lép Li mouniou téré di dokhe si aye begue begame esk diotoul mbok mi astahfiroulahi bania yame fi késsé ndakhe bou corona dialé bouka guena pire dina Nieuw té dou fi bayi kéne mouye yawamal hiyame lo tite si corona bi dinga tite 5000 foi de plus bis bobou Kone mbok esk doka wadial yok say diamou yalla linga wakhe fi bania nék lo Kham ni fi rèk la yam meune naniou mouthie si corona bi wayé walahi yawmal hasri kéne Menou sé mouthie té dina yague dina méti sa dieuf rék nga faye doundé amoul diokhé 5milions amoul diokhé 2 milliards dieuf diou bakhe rék té lo fa yobou dou doye corona bi c'est un soldat de Dieu té c'est un malheur Naniou déllou si Li ayouba wakhone rèk quand le mal lui avait touché il disait inni massaniya dourrou wa anta arhama rahimine " le mal m'a touché mais tu es le plus miséricordieux des miséricordieux Donc comme le coronavirus nous concerne tous chacun doit dire cela le mal à touché le monde mais tu es [ Dieu ] le plus miséricordieux des miséricordieux .yalla naniou yalla same té mayniou diangate si Li niou meune ko top diamou ko nimou ko begué mangui diégalou nak assalamou haleykoume wa rahmatoulah
Blh sama yaram dawe na blh wally blh wlh tlh taye la la guene beugue guene la fonk guene la diape wally srx taye dioye😭 Lo ngama blh wally Seck linga beugue yAlla na am li ngaye sentou yAlla nga si diote ak bepe dioulite 😭😭😭😭😭😭 vie sur toi wally seck
Bilae j ai les larmes aux yeux on est arrivé dans un stade ou nous ne devons pas attendre le gouvernement fait pour nous mais plutôt que nous ce qu on peut faire pour le gouvernement. Wally vous avez raison ,l argent na plus de valeurs si les vendeurs ne vends plus et ke l acheteur n achète plus .C sa le Sénégal le partage,alors frères et soeurs partageons car c est là que nous l avons besoin .Merci Wally c très émouvant ces paroles qui vous viennent du coeur et saches que notre coeur est rempli de larmes.
Amine Ya Rabbil alamin. Merci Wally tu as un coeur en or et merci de tes paroles, pleines !!! de sagesse. Merci, de nous rappeler a l’esssentiel. Ca m’a profondement touche et j’espere que nous tous (ceux qui ont entendu ton message aussi) dirons: Astaghfirla! Astaghfirla! Astaghfirla!. Repentons-nous tous au Seigneur de l’ Univers, Allah Soubhanahou Wa t’ala, de nous pardonner nos peches et dans Sa tres grande Misericorde de nous aider. Amine! si barke Gueundi bindef Seydina MOUHAMED, Sallal lahou aleyhi wa salam.
Billahi il m'est impossible de rester deux jour sans regarder le discours émouvant de Waly Seck. Il m'a beaucoup impressionné à travers cette dernière. On peut dire que c'est un RÉFÉRENCE 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Wally beugona nalla trop mais tey gueunala beug dakh kaddu yii rafet yii ak khalat bou rafet bii sincèrement sorina si Mane yow moi ta wara jeul kaddu dakh tu es un porteur de voix.Mais tu parles sur une autre dimension machalla Wally.
Diadieuf frère, vous avez bien parlé machallah...C'est un tarbiya général, Yalnaci YALLA wiss ndokh bou seideu gouyyy ba SALAM général am inchallah...Amiiine
Amine mon frère Waly je vous j'aime beaucoup bilahi Boub's toi aussi tu es adorable Waly Mane mom damala Bouga te yalla rek takha guisouma artist bou melni yow bilahi
Wally musicalement je ne suis pas avec toi mais tu t'exprimes hyper bien et j' avoue que tu as un coeur d'or en plus tu as de la grandeur si j'ai à te conseiller moy nga Baayi Wooy Dafa Xaram Ti Yow Xolbi Nga Yor Yalla Nala Borom Bi Ak Nioune Nieup Ndax Ci Baakar Laniou ..."Boubacar Doumala Neub Dama Tiiit." Ki Diarna Niou Moytou Di Tég Ci Deram Lou Niaw... Awma compkéxé Ci Toubab...Macca Tal Moukarab La Compléxé...Kou bax Leu Mako Moudié Wax...Chapeau à Dj Boubs
Machalla wally ngeu balma akh mane ak sama ay mrom yi ngeu khamni dagn la deukalone fo deukoul nitt néxoul kham mo takh ko xamoul rek boulko jugé
A c'è waly yalla nala yalla mbaye goudou fan ak wér nga feké lepu sy barké séydina mouahmed salalaou ahlyiwasalam
Boub's tu as fais un bon entretien avec Wally vraiment aujourd'hui tout le est très fier de Toi mon frère Wally je parle d'une bonne personne intellectuelle doit accepter qu'aujourd'hui que vous avez montrez un bon exemple Wally Seck merci
Machala fier de vous deux yalla na yalla def diam thi adouna bi yeup ci barke seydina Mohamed alay salatou wasalam
Vraiment c'est très important wally seck dans un niveaux de langage supérieur vraiment il ma choqué le cœur ♥️♥️♥️WBS
Non mane kay dama sakh moudiou diaxall
Yala nama yalka bolei ak yw ma wkv senegalais yii lougnou khamoul sii yw liii diakha louma sii yw ndakh xam blh diam rk gaay ame je t’aime plus lima begon 🙏 je suis fière taay ndakh gueune gama siiguil
Khol bou refet gua ame machalla yalna yalla safaral lepe barke moukhamed saws ak serigne sous bakh yeupe inchalla
Vraiment Wally yagui nakh niou bari tu as un bon cœur
No ki damagal mo nek nito yalla nito yalla manena lakhato ki dafa bakh trop 🙏
Machallah Wally sa wakh rafet na yalla na diam am si adou na bi yallah na diam am way❤❤
Bilahii doufiii yameu inchalla ❤️😭niogui sa guinaawwwwww ❤️
Bayy fall guir cheikh ibra fall ya salamou rek
Ohh sama yaram dawna walllahii
Non Wally môme machalla 😭😭
Machallah mn frr tes un grand personne
Merci bcp wally mane même guiss guiss bi la ti ame depuis le début. Mai nak yalla nagnou yalla same tei arrêté lép.
Vraiment je suis très ému waly chapeau à toi vous avez fait une très bonne communication que le miséricordieux ,le tout puissant , le bon dieu exhausse tous nos prières boubacar vous êtes aussi sans égale
Walah wally seck sama khol dafa fèss ndakh sa wakhinne tay dji dawna yaram trp yalla na yalla dolli diamou at salam barki seydina mouhamed since 🇿🇦🇸🇳😭😭😭😭😭
Machallha Wally seck sa wakh rafétna trop sakh yalana diam sakh si Adouna si Barcke Naby sunu yakar
Wally seck yalla nala yalla taxawou tu ma vrement surpri wallahi di nga fi yague barki borom touba
Ndeysane mane dohou ma thi musique mais bege nala bisse niki taye nite dafa lundeme yalla na gnou yalla bolé djegele 🙏🏼
Bilakhi niit déko guis mouy dém rék mé boul kham li nékk si kholam wally Seck borome ❤️ or biii diam si yaw
Wally je t ai jamais consideré mais vraiment tu es un homme de coeur respect frere
Xol bou rafet ak bou leundeume day fégne si beut lolou louma yag setlou laa té Wally xolam mo rafét machalla il a raison bala bou melni sou amé rk sa veu dir k adouna légui mou diéx nagnou consien sili mou wax le monde va mal k dieu ns protége🙏
Niane bimouy niane si cotë fin bi chaque djiouli fadiar sougnou imam diaka bi mome lèy niane tu est unike mr seck
Manchallah wally seck tu peux même représenter le Sénégal à l'échelle mondiale car tu parles comme un savant sa guisguis mooo graw tu devances les gens sur bcp de sujets je te suis . Courage
Bilay dioy lo nama waly louma geudia deff khaw ma sakh kagne lako geudia deff nio bolo demm diegalo yalla mou tegué fébar bii
Machallah wally DEUG DEUG rek moy moudie machallah brom xol bou bakh nga yallah na yallah déf diamou
Yalna la yalla gawa deife milliardaires ndakh nga bayi woye .neike thi leineine amine .tu as de la lumière boy .
Machallah yalla na yalla dèf diamou si addona bi
UN GRAND MERCI A WALLY ET BOUBS? WALLY JE T'ESTIME A PARTIR DE CE JOUR, J E SENS QUE T'ES QUELQU'UN DE GRAND, QU'ALLAH TE PROTEGE AINSI QUE TA FAMILLE
Allahou akbar c'est waly Seck qui parle ainsi ndeysane le monde est en panique Li nak diangate la si kou nék ak sa digsneté ak sa borome nga nék si adouna loula yalla sante nga bagne di musique déf ay concert té yalla téré lako nga bagne ni danga kaye déf tay béne soldarou yalla bouniouye wakhe coronavirus téré la Lila yalla téré wone nga nangou ko par force boul diokhe lokho djiguène boul acolate boul boul déf concert boul déme boîte nga nangou ko par force ba paré daw di woute walou si yalla ndakhe ndiakharé esk diotoul mbok mi ditoul souniou diougué si Li niou diamou yalla bayi lép Li mouniou téré di dokhe si aye begue begame esk diotoul mbok mi astahfiroulahi bania yame fi késsé ndakhe bou corona dialé bouka guena pire dina Nieuw té dou fi bayi kéne mouye yawamal hiyame lo tite si corona bi dinga tite 5000 foi de plus bis bobou Kone mbok esk doka wadial yok say diamou yalla linga wakhe fi bania nék lo Kham ni fi rèk la yam meune naniou mouthie si corona bi wayé walahi yawmal hasri kéne Menou sé mouthie té dina yague dina méti sa dieuf rék nga faye doundé amoul diokhé 5milions amoul diokhé 2 milliards dieuf diou bakhe rék té lo fa yobou dou doye corona bi c'est un soldat de Dieu té c'est un malheur
Naniou déllou si Li ayouba wakhone rèk quand le mal lui avait touché il disait inni massaniya dourrou wa anta arhama rahimine " le mal m'a touché mais tu es le plus miséricordieux des miséricordieux
Donc comme le coronavirus nous concerne tous chacun doit dire cela le mal à touché le monde mais tu es [ Dieu ] le plus miséricordieux des miséricordieux .yalla naniou yalla same té mayniou diangate si Li niou meune ko top diamou ko nimou ko begué mangui diégalou nak assalamou haleykoume wa rahmatoulah
Toujour a lui meme borom xollou diama bi machalla yalla nalla yalla faye
Blh sama yaram dawe na blh wally blh wlh tlh taye la la guene beugue guene la fonk guene la diape wally srx taye dioye😭 Lo ngama blh wally Seck linga beugue yAlla na am li ngaye sentou yAlla nga si diote ak bepe dioulite 😭😭😭😭😭😭 vie sur toi wally seck
Machalla wally Seck bi moy 2ème fois may tiré leçon si yaw bila pape cheikh Diallo invité ak ta machalla eres uno grande hombre que dios te bendiga ❤️
Sama dom dji laf thiat
Waly pardon je tes jammais aimer mes vrement je t adore respect
Macha Allah ya dû mature sur son language bien dit le grand frère
Bénén Wally sécke lay guiss 🤔🤔🤔🙄🙄🙄🙄 buegue sénégal ndaysann❤️❤️❤️
Extraordinaire waly seck borom bi mo ham kou bone yalnala yalla sameu tu as un grand coeur vraiment ❤
Nice itv Dj bouss kéne dou ioe👌👌👌
Frèmen se message sa me chogé yalna diamou yag siii réw mii ❤️🇸🇳🇸🇳
Ylla Bakhna Lepay Sounou Borom Moy Wanéti Bopam Rek N’oublie Sénégal Y’a Tout Cheikhoul Khadim Mame Malick Mame Limoulay Mame Baye Niass Mame Boukounta ❤️❤️😭
J'ai des larmes aux yeux wallahiii . Wally a un coeur d'or
Bilay grand wally délo guama thie yalla tay yalla na diame yague
félicitation Wally Seck nice Idée sincèrement vous méritez des applaudissement chapeaux a vous
Bilae j ai les larmes aux yeux on est arrivé dans un stade ou nous ne devons pas attendre le gouvernement fait pour nous mais plutôt que nous ce qu on peut faire pour le gouvernement. Wally vous avez raison ,l argent na plus de valeurs si les vendeurs ne vends plus et ke l acheteur n achète plus .C sa le Sénégal le partage,alors frères et soeurs partageons car c est là que nous l avons besoin .Merci Wally c très émouvant ces paroles qui vous viennent du coeur et saches que notre coeur est rempli de larmes.
Merci Maryacine gnioune dhe gningui france mais senegual lagniouye khalate khalatougniou sougnlous bop gningui gniane yalana yala safara virus bi thi barke Chekhoul khadime amine
Vraiment cette émission est importante pour tous les sénégalais.
Amine Ya Rabbil alamin. Merci Wally tu as un coeur en or et merci de tes paroles, pleines !!! de sagesse. Merci, de nous rappeler a l’esssentiel. Ca m’a profondement touche et j’espere que nous tous (ceux qui ont entendu ton message aussi) dirons: Astaghfirla! Astaghfirla! Astaghfirla!. Repentons-nous tous au Seigneur de l’ Univers, Allah Soubhanahou Wa t’ala, de nous pardonner nos peches et dans Sa tres grande Misericorde de nous aider. Amine! si barke Gueundi bindef Seydina MOUHAMED, Sallal lahou aleyhi wa salam.
Wally Seck ,il a fait un excellent Communication c'est vraiment touchant, très instructif.
Biillae kii kouko juger rk daka xamoul xol bou nice laa yore frere iow loudoul diamou doko am je l aime fort❤
Yalla nala sunu borom doli sutura kaddu yi rafétena frère jajeuf👌🏿
Wally Bi nga toudé Yonente Sama khol dafa séd. Dama dioy bilahi kéne dou seydina Mouhamed saw🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Machallah Wally message tres touchante 😥 Dj Boub's l meilleur de tt l tmps merci bcps longue vie a vs que le bon dieu nous protèges 🙏
Wally il est tellement mature maintenant...je l'aime daleu.
Billahi il m'est impossible de rester deux jour sans regarder le discours émouvant de Waly Seck. Il m'a beaucoup impressionné à travers cette dernière.
On peut dire que c'est un RÉFÉRENCE 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
😭😭😭😭😭😢😢bilay j’ai pleuré wally wakh gua lépp
Vraiment ç émouvant tu as tout dis notre Wally
Ms yalla nako yalla safara si bou guaw si barki cheikh Ahmadou bamba
Wally beugona nalla trop mais tey gueunala beug dakh kaddu yii rafet yii ak khalat bou rafet bii sincèrement sorina si Mane yow moi ta wara jeul kaddu dakh tu es un porteur de voix.Mais tu parles sur une autre dimension machalla Wally.
C'est triste c'est émouvant je t'adore trop nite nie khamou nioula sakhe je tai toujours aimé
Félicitations wally seck de votre soutien patriotique.
Merci Wally seck k Dieu nous protège Boub's merci à vs
Une fierté nationale se petit nous impressione ts les jrs
Walahi mane dei walahi shui ...
Vrmnt Wally amo morom j'ai mm pas les mots yalla na yalla goudeul sa fane😂😂🙏
Wally cest la première fois que j'entend wally parlé il très intéressant se garçon.
Bilaye kéne waroule jugé kéne kou né daga wara mandou sissa morome waly taye wané gako machallah yalla na yalla andi diame🙏🙏🙏
Alhamdu lillah
Wally yalla wannako yone
Na guëm limouy wax rk incha allahu yalla Dinako jappalé
Kadou yi rafet na wally inchallah dina bakhe bagnou koy nétali😳
Wally borom kheil mou rafeite machalh
Yallana yalla soppi banga bayil woiy bayi boîte, grand théâtre diel li desse si sa adouna diégué yalla bala mo trop tard
Parlé de manière posé en toute conscience voilà le sénégalais que je connais voilà le Sénégal rien d'arrogant juste kham kou gniou done
Yalla nala yalla maye diamou rek
Tu as un bon cœur frère yalna yalla souti xéweul si adina bi yeup barki Mouhamed 🙏
Done- Shiffo 🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😍😍😍😍
ndeysan nekete nitou yallah DEUG nga one love Frr❤
Mane jp mm plus parler g les larmes aux yeux ❤️😭😭wally jtmmm❤️
Tawfekh ak taysir thi Sénégal ❤️
Long vie a notre wally machalla😍😍😍😘😘
Wally dégue na degue dh wakh kouko yeureme mou gagne la tu as parfaite ma raison je t'adore ❤ ❤ ❤ ❤ ❤
❤ je ne pourrais texprimer ma gratitude et merci pour avoir ouvert les yeux aux senegalais❤ kou deglou li digua kham
Diadieuff grand wakh yi Nice neu mashala. Amal jam
waly yalna yalla samb ak boubs
Diadieuf frère, vous avez bien parlé machallah...C'est un tarbiya général, Yalnaci YALLA wiss ndokh bou seideu gouyyy ba SALAM général am inchallah...Amiiine
Machallah sama Wally seck rek 👍🏿👍🏿this is so Nice 💪💪💪💪👏🏼👏🏼🤝🤝
Tay mom guisna benen wally secke kou bakh am yermade
Masha’Allah wally Seck yallah nala yallah fay sa khol❤️❤️❤️
Amine mon frère Waly je vous j'aime beaucoup bilahi Boub's toi aussi tu es adorable Waly Mane mom damala Bouga te yalla rek takha guisouma artist bou melni yow bilahi
Wally sa xol mo rafett bilay frère !
Mashallah Wally sa wakh Nice na nitt ki soko khamoul déko wowé ééééééééééééééééé
My Wally so emotional MasAllah Ameen y balago we lov you
Bayy fall seck ndananby boul titee boul ragual borom touba protégé dawale sayir gui wakh deguine bassaa kanamm
Billahi khole Moy domou adama te lo Nakare khame yalla nele yalla faye se khole nitou zahire nge me yawe khame nge li neke si se khole
No frenchma waly tu ma fait pleuré .k le seigneur tout puissant guide nos pas
Billaye wally Dou nit yalla nala yalla faye sa khol
Mashallah ame na solo trop frère
No wally iow boul tite dara Yalla rek molay Faye Machallah kadouyi raffetena j’ai des larmes au yeux
Yaw dal da NGA bakh et puis nitei point final.🤗
Wally dara wesouwoul yalnala yalla lerare ci yone bou bakhe ya rabi🙏
Yallah daal moniouy wane bopam rk... Fimou tollou nii nieupa kham kouy Yallah.
Môme késsé moniou meuna mousseul. Yallah naniou yallah Bollé mousseul si Corona virus
Émission bi môme macha Allah déma contant ndakh kaddou you rafête
Manchalla je t’aimerai pour tjr inchalla ba yague batay ma khamni sa khol mo rafet doundeul reck💕💕💕
Wally Seck li Dafe meti bilay 😥
Waly t’a raison nioun wa diaspora sondou nagnou wayé sante Yallah rék.