En europe c'est exceptionnel & en quelques jours il y a plus d'eau dans les rues et les maisons. Chez nous c'est chaque année et l'eau reste chez les gens pendant des mois ba mou verte. Comparons ce qui est comparable waï.
Pendant la saison des pluies gouvernement bi dafa wara prévisible mogueune wakh y’a des gens qui ont tout perdus et des vies yalla na yalla safara lép inchallah
deuko bokalè ni rek lay mèl d'où meuseu avancè nakh dieuf you bone yiguèni fay def Di diamou ay serign you meuneloul Sénégal touss bagn lène yèwou serign moutakha meunoul si yène touss serign touba aussi meunoul si yène touss fi yallah rek mofii nekk
Je vois des gens qui demandent le projet, ne doit-on pas plutôt poser des questions sur les 700 milliards qui devaient solutionner les inondations. Massa méti na, que Dieu vous protège.
Les inondations affectent gravement la vie des habitants de Touba chaque année. Les autorités doivent envisager des partenariats avec des experts en ingénierie hydraulique pour repenser les infrastructures.
Nos opposants milliardaire là doivent avoir honte aprés 12 ans au pouvoir ,puis voir ça.Et ils ont le culot de demander le projet d'un gars (maltraité, acusé ...)sous leur gouvernance
Touba dou neexa défar ndax, dagni dof doflou di bagna jarignoo seen xell. Moo takh dinagn sonnal seen bopp, sonnal reewmi yeup. Gouvernement boufi massa gneuw, jox gna leen alalou reewmi, ta dagn lay wann ne defaral la leen dara.
Lorsque le prophète Ibrahim demandais à dieu qu'il fasse d'Arabie saoudite une terre plein de richesse , il a fallu des milliers d'années pour que cela se produise.... Yalla yakamti woul dara teh Serigne Touba wakhoon Nani kou yakamti dou feke Dara ... Lim beugg si deukeum bi faw Dina ame inchallah 🙏🙏
Situation bi war na délociwatt sen khel yi. Deuk bo khamni daniouy dieul ay mélokanou Yallah diokh ko mindeff diko diamou dii wakh moy sen leup.Tay niane lène ko mou wallou lène, warr na lène sétane nguène nekk ci diaffé diaffé yi. Li day woné rek Yallah keesé moy Buur tay yondina mindeffam bou ndaw mouy taw nguène nekk ci tolof tolof. Solution lène rek la toub délou ci sen Borom.
Yonét bi Moy le sounou boorom yoné si diam yi pourtant Dana khif bay tak biram guir meuna diamou yallah . Sounou borom kharitam lay natou guir daradialko
Ya Allah naléne sounou Boroom Samm té Takhawou léne noumou gueuneu Gaawé si barké Seydina Mouhamad (SAW)
Europe central sakh lii moo fa am. Yalla moy wathiee ndokh mi domou adama mounouci dara. Gnissi dee paix à leur âme
En europe c'est exceptionnel & en quelques jours il y a plus d'eau dans les rues et les maisons. Chez nous c'est chaque année et l'eau reste chez les gens pendant des mois ba mou verte. Comparons ce qui est comparable waï.
Qu'Allah accueille en son paradis firdawsi tous(tes) les disparus(es) amine Y'a Rabi🤲🏿
Amine
Seul le repentir peut changer la situation
Pendant la saison des pluies gouvernement bi dafa wara prévisible mogueune wakh y’a des gens qui ont tout perdus et des vies yalla na yalla safara lép inchallah
Patience sonko va tout régler bientôt
Qu'est ce qu'il attend?
اللهم استرنا بسترك الجميل الذي سترت نفسك ،فلا عين تراك...وانت أرحم الراحمين 😢
Amine 🙏...
Amin inch'Allah
Yala na yalla safara barkai serigne babacar sy
Hooo khooo ndey sann 🤭🤭lii metina lool'lool yalla n'a koo yalla safara Barkeep alkhourann Ak khassidaa yii 🤲 Amin Amin ya raby
deuko bokalè ni rek lay mèl d'où meuseu avancè nakh dieuf you bone yiguèni fay def Di diamou ay serign you meuneloul Sénégal touss bagn lène yèwou serign moutakha meunoul si yène touss serign touba aussi meunoul si yène touss fi yallah rek mofii nekk
Je vois des gens qui demandent le projet, ne doit-on pas plutôt poser des questions sur les 700 milliards qui devaient solutionner les inondations. Massa méti na, que Dieu vous protège.
Yalla nalene Yalla yeureum
Yalna yalla tegui natou bi si Barker Seydina Mouhamed PSL
Les inondations affectent gravement la vie des habitants de Touba chaque année. Les autorités doivent envisager des partenariats avec des experts en ingénierie hydraulique pour repenser les infrastructures.
Vraiment macky warna wakhh fann la deff 700 milliard yi😢😢
C'est lansana guangni sakho qui avait le programme, maintenant il est nommé par Sonko ...😂
@@amadouba4541 même s'il est nommé il doit rendre compte
AVEC TOUS CES MILLIARDS QUI TOMBENT SUR TOUBA C TRISTE
Ces pour les marabout pas pour la population
Bilahi metina ma famille en fait partie depuis guiranène
Yaw déh soriwognou
Massa
Diokh len yalla benna thier motakh dey wone boppom
yalla na yalla tegui natou bi inchallah
FAIRE UN LAC ARTIFICIEL DERRIERE TOUBA LAC LAC LAC LAC LAC LAC LAC LAC LAC POUR IRRIGUER LES CHAMPS
Thieye yalla, mom reck mo meunn, sante reck
Massa wa Touba.
Au Sénégal quand tout va bien on remercie les créatures mortes. Quand tout va mal on pense à le TOUT PUISSANT.
😢😢😢
Fanla 700millards yi dougou métina
Paix à leurs âme😭
Serigne Touba dieureudieufety
Woko baham loumoussi meune...
Oh li métina ylnalén Borom bi Takhawou Askanou Touba diléne Massawou métina lool
Paix à leur âme...
Sonko diegoule Senegal 🇸🇳 😢😢😢😢😢😢😢
Il a fait quoi
Ndaye sane mètina
Kon ñaar a ci mujj ñàkk seen bakkan ?
Ndaysaan ! Yal na leen Yàlla yërëm te xare leen àjjana ci barkeb Muhammat SHW.
No lii yémena billahi gayi fone def milliaryi la khamoul
Yalla kheb dolli li dey wone Serigne Touba dou touss bokkale rek diokho len yalla benna thier
Yalla doo morrom
Ndokh bii dou kheweul deih lii moussibaa laa
Pitié pitié pitié mon Dieu où est le projet
Ensemble reprenons le travail bâclé de BBY sans coup férir et jetons aux orties les ennemis du Sénégal! CQFD
Nos opposants milliardaire là doivent avoir honte aprés 12 ans au pouvoir ,puis voir ça.Et ils ont le culot de demander le projet d'un gars (maltraité, acusé ...)sous leur gouvernance
Hypocrite
Allahou Akbar 🤍 🤍 🤍 🤍🤍🤍🤍
Qu'Allah vienne en aide aux sinistré(es) allahouma amine 🤲🏿
Touba dou neexa défar ndax, dagni dof doflou di bagna jarignoo seen xell. Moo takh dinagn sonnal seen bopp, sonnal reewmi yeup. Gouvernement boufi massa gneuw, jox gna leen alalou reewmi, ta dagn lay wann ne defaral la leen dara.
😢😢😢😢😢
😢😢😢😢😢😢😢
😢oh
😢😢
Touba nimou tolleu warna am canalisations warone nagne depassé fi ak milliards yifay doug yeup
Yalla louko nèkh laye défff
Mougne rek ak.ndongou dogual sounou borom..
Ana waa ONAS?
Khalis sou magal gui da diekh wala
😂😂😂😂😂😂😂😂
Thiey yalla
Li mètina trop
Li yeup macky sall la
Sonko diom
Macky Sall c le passé , pouss kattou poup bi sonko mo waral li yeup
Mensonge
Kom ko serigne bi amoul morom na len diaple si ndokh TOUBA bi❤
Lorsque le prophète Ibrahim demandais à dieu qu'il fasse d'Arabie saoudite une terre plein de richesse , il a fallu des milliers d'années pour que cela se produise.... Yalla yakamti woul dara teh Serigne Touba wakhoon Nani kou yakamti dou feke Dara ... Lim beugg si deukeum bi faw Dina ame inchallah 🙏🙏
Situation bi war na délociwatt sen khel yi. Deuk bo khamni daniouy dieul ay mélokanou Yallah diokh ko mindeff diko diamou dii wakh moy sen leup.Tay niane lène ko mou wallou lène, warr na lène sétane nguène nekk ci diaffé diaffé yi. Li day woné rek Yallah keesé moy Buur tay yondina mindeffam bou ndaw mouy taw nguène nekk ci tolof tolof. Solution lène rek la toub délou ci sen Borom.
Yonét bi Moy le sounou boorom yoné si diam yi pourtant Dana khif bay tak biram guir meuna diamou yallah . Sounou borom kharitam lay natou guir daradialko
Koudoul yonéti bii serigne touba mola geune
@@BafodeSylla-dh9ol 😂😂😂kan moko wakh Yallah wala Yonenti ???
Wakou fanatique wakhou doff rek
Wholene seringe touba
Psl sah dane na âme aye difikilté té mome la yalla Yoni sr Touba donko ligeyeul ndogal AK diame nio ande wa salam
Et les milliards de touba?
Inondations yi metina
JUb Jubal Jubanti
Ndokh mom xéweul la rekk
Comme deux morts amnathi nékatoul xeweul
Ho massa
Louma diakhal billahi si government sonko ak diomaye bi sac jours nite dé😢Senegal vremant sonko diomaye diegouniou Senegal 😢😢😢😢😢😢
Mensonge
C'est le gouvernement de sonko
Ca n à rien à voir avec un gouvernement
Ca n à rien à voir avec un gouvernement il faut que tout le monde retourne vers Dieu thiakhane bi dafa bari
Khana téy 😂😂
Et pourtant vous n'avez pas l'air d'ètre une chauve souris!!!!!!! Ya ngui yeungueul Arassss yaram, tubbal way
Et qu'est ce que le gouvernement de SALL à fait ?
😢😢😢😢😢😢😢😢😢
😭😭😭😭