Dieuredieufaty sokhnasi amna solo loll sakh contane nanou dakh ay togoukatt laniou ak surtout Mouwahibou Mbaye Cheikh Fall khattaba kone amal Tawfekhou khassidagui
Machalha sokhna Bilo sa recettes amenna manna akh salade bu tes epice naturelle machalha en plus sa invité bu limou wakh deghuele khou khoromoulha felicition je viens de te découvrir mais machalha contanne si aux😘😘😘😘😘😍
DJOLOFGIRL Salaam Sokhna si! Merci de l’avoir essayé! In Sha Allah, d’autres plats vont suivre. Abonnez à la chaîne et activer la cloche pour recevoir toutes les notifications!
Ziar Sokhna Ngone, alhamdulillah !!! Guiss nga de gnoun delendi jox rek idee apres guen defko selon sen gout ak feme te xamna yeguendi def moye dax foof li gnou len indile 😘
Salam Sokhna Billo niguilay ziaar Bou wër recette yi Amna Solo Macha Allahhh Lima thi geuneu nèkh Tourou Borom bou Sèlle bi ngay Tambalè lèpp loy dèf ak Khasiday kou Tèdd ki Cheikhoul Khadiim ga diko Oubè sa Ay Video Macha Allahhh yallana yalla Barkèl Lép thi Barkèp Mouhamed psl Barkèp Khadimou Rassoul Amiineee jajeuf
Merci beaucoup madame Wakhoumala sètr gui ak sèll gui mais yanguiniouy diangal toujours ni kanam moy diokhé niam mane nakk damay suivre di partager mais massouma commenter lou wéssou tay vraiment merci vous êtrs adorable ❤❤❤
Queenb 17 thank you so very much for your kind words. In this channel that is what we thrive for hopefully u will enjoy the videos as much as we enjoy bringing them to you🙏🏾😘
Assalamou aleykoum sokhna billi mangui dora guiss sa chaîne.. Mashaa Allah selle na tè ndourou na lou nekh beugone naa kham nougnouye defaréépice kankan bi.. jeredieuf
Thiatou Papam Ziar na la thiat In Sha Allah dinagnou len is defaral recette bi ci ben tuto. Dalal ak Jamm ci chaine bi j’espère k dinala jeurigne bou baax!
Bravo madame en disant qu'on doit laisse chacun se sert par rapport à ce qu' il veut ce que on devait savoir nous les femmes car beaucoup des gens impose la quantité de piment de sel à leur inviter
Ziar Sokhna Ndeye Fatou Thiane, merci ci tewlubi ak commentaire bi. Pour les vidéos de Bernde ce sont des émissions qui passent à la télé ( bichri tv), ce serait irrespectueux de bâcler les videos our nos téléspectateurs, c’est à cause de cela que chez Billo a été créé pour qu’on puisse faire des vidéos tuto qui sont plus courtes. J’espère que tu pourras visiter nos tuto chez billo.🙏🏾
Bonjour sokhna si c la première fw je vw t publication dama done latie ndakh viande bi avant nga koy marine diko congale dagne koy rakhass ba pare wala et contente nagnou tie yaw dieuredieuf
Ziar Sokhna Rama dalal ak jamm ko Di niane rek chaine bi jeurigne Len bou baax. Waw pour viandebi meun nga ko raxas sinon sou feke daga raye xar te gnou defar ko bamou set meugueu rek mariner directement man damaye def niar yeup. J’espere k tontoubi dinala aider Ma len gueuneu contane yen gnou baax gni 😘
machalah yaye togue gui da yiww na loll li boumou yamm fi bindeul télé bou melni 2s tv mou fayy diarr surtt côté santé te bi kenn weroul ndakh lekk gui legui
Ziar Sokhna Ndeye Binta, sap sap bi dengou ko jeund en poudre sinon so amoul poudre bi man nga ko weer bamou wawe ou nga def ko ci sa four bamou xawo wawe come ca nga dab ko apres ley ko dal diko mane utiliser! J’espere que tu pourras le faire facilement In Sha Allah!!!
I love this channel! I'm from Senegal but I can't speak wollof but this is helping me improve! also in college away from my mom's amazing food this is helping me learn. thank you! can you do a video on mafe?
Hello Marieme, thanks for subscribing to our channel. We hope that you will enjoy the video and learn something. Here is a link the a video we did on Mafé. ua-cam.com/video/wN18pwmch3c/v-deo.html Please reach out anytime with any questions!
Ziar FAYE Ndiaye, sombibi mom dagaye woot lou gnou waax graines de chia en français ou chia seeds en Anglais Mais nak hawma nou gnou koy waxe en Italien. J’espere k li dinala aider!!!
Salaam my dear sister thx for taking the time to visit our Chanel and also your comment it is greatly appreciated ! You know most of the videos are being broadcasted on TV so it is considered a bonus in my Chanel, and also the aim of this Chanel is teach but help others how to eat a healthier diet and giving them all the other options or alternatives they have and for that I can’t just be doing tutorials all the time. Some people are lacking enough to know most of what I am sharing some others are not that fortunate and since we are a family in this Chanel I have to include everybody no matter what their skills are that is the only reasons. Thx a lot my dear sister 🙏🏾😘
Hadja Baro Ziar u need buy chia seeds if u r if USA it is wildly available in pretty much every supermarket even Costco or Sam’s Club In u have their membership even Walmart will heve it. If you go to chez Billo u will have the detailed recipe there. Hope this was helpful! Thx a lot🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Ziar ma cherie waw niankatang bobou nak chou-fleur la gnou ko togge amna ben tuto bougnou ci def ci chaîne bi. Essayer ko neexna te baax na ci werguyaram 😘
MASHA Allah dieuredieuf Sokhna Billo on apprend bcoup de choses avec vous
Alhamdulillah merci bcp kou baax 🙏🏾❤️
MachaAllah. I like it.Thank you for sharing
Trop bien fait cuisine très propre et classe
Adja Bakary Ndiaye ziar merci pour tt😘
This maybe my favorite episode. Tres simple but also very informative. Dieureudieuf Billo 😘
Jajeuf my beloved sis always trying our best to share with u what we learn😘
I appreciate all the informations you provided for healthy diet. Way to go Billo...
Ziar sis thx a lot my dear🙏🏾😘💕
Machallah sokhna sama bokh mourite.
Mandiang Astou ziarnala ma cherie Akassa jajeuf 🙏🏾😘
Ta cuisine est généreuse et saine comme d’habitude Amal diam adorable Bilo 😍
Gnou bok lepp ma sœur chérie 😘
Machalah sokhna billo amna solo
Akassa ma cherie jajeuf dila ziar bou weer 🙏🏾😘
Dieuredieufaty sokhnasi amna solo loll sakh contane nanou dakh ay togoukatt laniou ak surtout Mouwahibou Mbaye Cheikh Fall khattaba kone amal Tawfekhou khassidagui
Ziarnala Sokhna Awa Akassa fe beg bi euppe amine ci nian yi gnou bok lep 🙏🏾😘
Macha allah ak yiway bi mane deh sopenaala
Doli nanou siar bou weer dila diokh sa wathiouwaye
Yankise Diarra ziarnala ma chérie merci bcp yena baax rek yalna Borombi faye la lu bari Amine 🙏🏾🙏🏾
Amine incha Allah sokhna billo tour bi weuly la c juste compte bi mo nek au non de yankis mes mangui rafet lou video yi
Machalla sokhna billo set na selna machalla ak khassida yi nio may Danielle dieureudieuffetti serigne touba j'abone
AMY FALL ziarnala bou weer ma cherie ah beg na 🙏🏾😘
machallah tata billo
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Très classe sister
Merci bcp ma chérie 🙏🏾😘
Machala sokhnasi un grand merci beugone na kham kankan
Ziar ma cherie waw nak dinagnouko defar ci aye fan you neew In Sha Allah, jajeuf ci tewlubi 🙏🏾😘
Manchaallah sokhnasi amna solo .
Machallah maman chérie
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Belle présentation 👌👌
Comment réalisé le kankan ?
On va faire un tuto pour ça inshallah 🙏🏾😘
Machalha sokhna Bilo sa recettes amenna manna akh salade bu tes epice naturelle machalha en plus sa invité bu limou wakh deghuele khou khoromoulha felicition je viens de te découvrir mais machalha contanne si aux😘😘😘😘😘😍
Ziar bou weer sokhna Amynalinguere,jajjeuf ci kadu you rafet yi. Merci pour tt gno ngui guiss japale yi 🙏
Bilaye souma lay xol si wagne ak beug lou bakh sama bop rek lay guiss Machahalla😘😘
Akassa ma cherie sant rek lolu deh ak sant la ci man xamna yi ngaye defa dak foof 🙏🏾😘
@@ChezBillo 😘😘😘
Masha allah tata, j'adore tes vidéos..
Kankan beugna kham nougnoukoy défé..
Merci beaucoup yalna yalla fayla
Ziar ma cherie In Sha Allah dinan ko def sous peux 🙏🏾😘
Masahlla nehna
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Je viens de te découvrir mais j'adhère maachaa Allah
Aminata Gueye dalal ak jamm, merci ci sa abonnement, yalna Borombi fayela 😘
Fatabarakalaxou Sockhana ci
Machallah biimom sama didiaye lakoy togal
Waw ma cherie dina contane de te neexna noye na aussi waax ma noumou deme soko togue In Sha Allah 🙏🏾😘
Sokhna Billo Yallah nala Yallah faye riz au choux fleurs dama koye togg 👍🏽santé néex masha-Allah🙏🏽🙏🏽🙏🏽💚💜❤️
Akassa kou baax deug la man de du ma ci doyale tres nourrissant jajeuf waye 🙏🏾😘
Machalah waye maman y'a khame lou bakh
😂ah jajeuf ma cherie 🙏🏾😘
Merci tata pour cette bonne et riche recette bonne continuation
Jar ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Hello Billo jai fait ton moussal yap c t tres bon et sain continues a nous dnner pleins de recettes healthy. Vinaigrette bii ca ye jlai adopte 👍🏽
DJOLOFGIRL Salaam Sokhna si! Merci de l’avoir essayé! In Sha Allah, d’autres plats vont suivre. Abonnez à la chaîne et activer la cloche pour recevoir toutes les notifications!
Merci bcp. Si gnongui khar kankan
Machallah sokhna billo amneu solo
👍💕
Machallah amna solo beugone na khamm noniou défaré farine coco dieuredieuf
Fatouhelene Sylla ziar sis in Sha Allah dina def tuto pour farine de coco 🙏🏾
@@ChezBillo dieuredieuf Sokhna si diamm khéweul j adore ta cuisine merci si bernai yi amna solo
Machallah mane dh sopeuh naleuh yiw nga sa wakh tèy nah sète nga yalla dinala diapalè
Zeliatou Gaye ziarnala bou baax merci ci kaddu you rafet yi ma la gueuneu sop amine te gnou bok lepp 🙏🏾😘
@@ChezBillo 😍😍😍ayy wayy noumay df ba am sa contact
Salaam@@zallista__traiteur8658 +1-646-385-9436 WhatsApp
Merci beaucoup Sokhna Billo maacha allah
Ziar ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Tou Coeur avec tw machala
Akassa ma cherie merci bcp 🙏🏾😘
mousseul bi diarna yone machalah
Akassa jajeuf 🙏🏾😘💕
Machala sokhnasi recette bi seleu n’a rafett n’a yawitt yiwga machala
Limata Yega ziar bou weer jeureujeuf ci commentaire bi 🙏🏾!
Oh j'adore machan allah
Alhamdulillah akassa jajeuf 🙏🏾😘
Merci Soxna bilo. Ça me donne une idée de plat. Je vais l’essayer inchallah
Ziar Sokhna Ngone, alhamdulillah !!!
Guiss nga de gnoun delendi jox rek idee apres guen defko selon sen gout ak feme te xamna yeguendi def moye dax foof li gnou len indile 😘
Salam Sokhna Billo niguilay ziaar Bou wër recette yi Amna Solo Macha Allahhh Lima thi geuneu nèkh Tourou Borom bou Sèlle bi ngay Tambalè lèpp loy dèf ak Khasiday kou Tèdd ki Cheikhoul Khadiim ga diko Oubè sa Ay Video Macha Allahhh yallana yalla Barkèl Lép thi Barkèp Mouhamed psl Barkèp Khadimou Rassoul Amiineee jajeuf
Waleikum ma cherie jajeuf ci kaddu you rafet yi . Amine ci nian yi te gnou bok lep te feke ak tal🙏🏾😘
Chii MashaAllah. Beug na li sokhnsa si.
Akassa ma cherie neex na de jajeuf 🙏🏾😘
Salam Sokhna Billo j'ai récemment découvert votre chaîne. Tous nos encouragements vos vidéos sont très explicites. Bonne continuation.
Aminata Wele Ziar nala lou bari merci bcp pour les encouragements 😘
bonne recette machaalla bravo merçi beaucoup pour le partage 👍👍👍🙌🙌🙌💕😀💋
awa breton nouyou nala sister
Merci bcp 🙏🏾🙏🏾🙏🏾💗
Nice and healthy
Macha Allah sokhna billo amna solo yaw mome brome bakh nga khasida bi nékhna trop togouyi tmt amna solo séttna séllna sopp nala trop danga téye laff thiatt
Maty Niass ziaralma ma cherie ma la guwuneu soo kou baax nga 🙏🏾😘
Merci beaucoup madame
Wakhoumala sètr gui ak sèll gui mais yanguiniouy diangal toujours ni kanam moy diokhé niam mane nakk damay suivre di partager mais massouma commenter lou wéssou tay vraiment merci vous êtrs adorable ❤❤❤
Alhamdulillah ma cherie vraiment merci bcp dila Sant ci tewlubi. Nonula joxinwi lu am solola, jajeuf sant na gnou bou weer🙏🏾😘💕
Salamou alleykoum sokhna billo macha Allah mais je voudrais savoir papier bigni lemeussé chawarma tamou blanche noumou todou svp merci
C'est du papier sulfurisé
Ziar waw papier bi mom papier parchemin la toudou. Wala papier sulfurisé 🙏🏾😘
Machalla, I really like your cooking, it's healthy
Queenb 17 thank you so very much for your kind words. In this channel that is what we thrive for hopefully u will enjoy the videos as much as we enjoy bringing them to you🙏🏾😘
Machallah amna solo
Jajeuf Sokhna Khady 😘
Assalamou aleykoum sokhna billi mangui dora guiss sa chaîne.. Mashaa Allah selle na tè ndourou na lou nekh beugone naa kham nougnouye defaréépice kankan bi.. jeredieuf
Thiatou Papam Ziar na la thiat In Sha Allah dinagnou len is defaral recette bi ci ben tuto.
Dalal ak Jamm ci chaine bi j’espère k dinala jeurigne bou baax!
@@ChezBillo Delloo nala ziar sokhna Billo mashaa allah dinagne thi begue lolou inshaa allah...
Jeredieuf thi tontougui yalla na yalla barkel barkep cheikhoul khadim..
Merci beaucoup tata yalna sa diam yagg
chérie daddy chou ziarnala jajeuf 🙏🏾😘
Mashalah sokhna si. Xassida yi nekh na trop
Togou bi sele.
Faty Amar ziarnala bou weer akassa dilene beggue rek
Jajeuf 🙏🏾😘
@@ChezBillo machallah l like the way you cook and the holly xasidas.long life to you sokhena billo
Vraiment on vous encourage et bonne continuation
Saliou Ndong Ziar sa me Serigne jajeuf ci encouragements yi ak kadu you rafet.
Merci bcp pour tt!!!
Machalah
🙏🏾
Manchalah
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
Ma challa sokhna Billo diarnayone mane sokhna ndeye magatte fall Milano sa cusinabi MOMA nekh è bellissima😍
Ziar sama domou baye sa sant dafa neex, merci bcp, dilen beggue rek😘
Wa diamono dji est ce que amna gnou mounoul togu vraiment Intenet bi mom Il suffit juste de copier 🥰🥰💖 merci Mme pour la recette
Akassa lal ngako de Alhamdulillah ba gnou ame youmelni sunu youtubers ya ngui def legueye bou mouc ayib ci côté bobou, jaguenejeuf ci tewlubi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Merci beaucoup
Avec plaisir 🙏🏾😘
Machalla sokhna Billo Bilahi dama yam si sa vidéo ni par hasard mais xassida yi rk la dèglou abonné wou machalla togeu bi diarna yon
sokhna mai Sarr Ziar bou weer waw guis nga de, alhamdulillah!!!
Jajeuf ci tewlubi ak sa abonnement yen rek Ka gnou dolelene
@@ChezBillo machalla yalla nala serigne bi samal bopam😍💗
Pareil dama abonner direct👍💝
@@mameis4107 ndeysann dafa nékh loleu yalla nala borom bi sam si barkép borom touba
@@sokhnamaisarr3380 allahuma ammin, jajeufeti🙏
MASH'ALLA bien ornée et bien cuits
Merci bcp!!!
Masha-Allah santé santé santé👏🏼👏🏼👏🏼👍🏽👍🏽👍🏽🙏🏽💚💜❤️
Akassa jajeuf 🙏🏾😘
Merci beaucoup pour tes recettes délicieuses et saines yow tamit Yalna la sunu borom fay. 💓
Amine, gnou bok lep 😘
Chez Billo Mashallah
Bravo madame en disant qu'on doit laisse chacun se sert par rapport à ce qu' il veut ce que on devait savoir nous les femmes car beaucoup des gens impose la quantité de piment de sel à leur inviter
Bonjour sa m interesse le kankan
C'est bien fait machallah!! il faut juste raccourcir les vidéos elles sont un peu longue
Ziar Sokhna Ndeye Fatou Thiane, merci ci tewlubi ak commentaire bi.
Pour les vidéos de Bernde ce sont des émissions qui passent à la télé ( bichri tv), ce serait irrespectueux de bâcler les videos our nos téléspectateurs, c’est à cause de cela que chez Billo a été créé pour qu’on puisse faire des vidéos tuto qui sont plus courtes.
J’espère que tu pourras visiter nos tuto chez billo.🙏🏾
Kan kan bi mome sokhla nagnou ko si tabaski bi inchalah billo
Assalamou Halley coum madame est-ce que vous pouvez me faire une liste de toutes les ingrédients et légumes svp
Machalla Nice nice
Mame Dikel Diagne Ziar bou weer jajeuf 🙏🏾😘
Ou peut avoir tes produit sokhna Bilo
Salaam Sokhna Amynalinguere. Vous parlez de quels produits?
Wii on v savoir comment faire kankan
Bonjour sokhna si c la première fw je vw t publication dama done latie ndakh viande bi avant nga koy marine diko congale dagne koy rakhass ba pare wala et contente nagnou tie yaw dieuredieuf
Ziar Sokhna Rama dalal ak jamm ko Di niane rek chaine bi jeurigne Len bou baax.
Waw pour viandebi meun nga ko raxas sinon sou feke daga raye xar te gnou defar ko bamou set meugueu rek mariner directement man damaye def niar yeup.
J’espere k tontoubi dinala aider
Ma len gueuneu contane yen gnou baax gni 😘
je mabonne comme amoul jummo
lestouche r 😂😂😂
Dalal ak jamm et merci ci abonnement bi 🙏🏾😘
machalla mee man nigni décoré plat rk la beug kham
Ziar yaram In Sha Allah dina gnou gueuneu wane decoration sougnouye yak, jajeuf ci tewlubi 🙏🏾❤️
Ma challa Tata nekhna de
Yebe Sylla ziar nala ma cherie wa gua yi lolu lagnou waax de 🙏🏾😘
machalah yaye togue gui da yiww na loll li boumou yamm fi bindeul télé bou melni 2s tv mou fayy diarr surtt côté santé te bi kenn weroul ndakh lekk gui legui
Ziarnala kou baax sa kaddu rafetna loooooolu. Dinanci bayi xel in Sha Allah.
Suggestions yi amna solo loolu jeureujeuf 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Kankan bougunagnou khamnougnkay dafaré? 🙏
Merci beaucoup tata envoyé moi les recettes stp
Salaam Sokhna Khady, envoies moi ton email, et dis moi les plats dont tu as besoin les recettes. Merci
Chez Billo bonjour. Je pourrais avoir la recette stp de cette salade mon adresse email peynda.marie@yahoo.com en vous remerciant
Sape sape bi nokay defé on vous encourage
Ziar Sokhna Ndeye Binta, sap sap bi dengou ko jeund en poudre sinon so amoul poudre bi man nga ko weer bamou wawe ou nga def ko ci sa four bamou xawo wawe come ca nga dab ko apres ley ko dal diko mane utiliser!
J’espere que tu pourras le faire facilement In Sha Allah!!!
Waw def KO maman
Akassa ma cherie 🙏🏾😘
I love this channel! I'm from Senegal but I can't speak wollof but this is helping me improve! also in college away from my mom's amazing food this is helping me learn. thank you! can you do a video on mafe?
Hello Marieme, thanks for subscribing to our channel. We hope that you will enjoy the video and learn something. Here is a link the a video we did on Mafé. ua-cam.com/video/wN18pwmch3c/v-deo.html
Please reach out anytime with any questions!
😋👏👏👍❤❤
Alhamdulillah ma cherie 🙏🏾😘
😍😍😍😘
Jajeuf 🙏🏾😘
Salame sokhna Billo je parle des de tes sombis a l'Américaine dakh yaw yakoye ndiaye merci
Amynalinguere Mabo ziarnala non jayu mako lou defar rek la pour sama famille, désolé!
👏👏👏💯💯🙏💝💖🌹🌹👍👍👍
C très bien mais faut résumé le plus k possible
Akassa ma cherie merci 🙏🏾😘
👌👍👍💗🙏😆
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘
Machalla tata sa wagne rafetna te sett 💕
Nasice Diaby ziarnala ma chérie 🙏🏾😘
Noumaydef ba amsi donnini sokhna Billo?
Donnini la sokhla,magui Italia?
Sombibi?
Ziar FAYE Ndiaye, sombibi mom dagaye woot lou gnou waax graines de chia en français ou chia seeds en Anglais
Mais nak hawma nou gnou koy waxe en Italien.
J’espere k li dinala aider!!!
Mane dal khassida bissi souf momay nekh
dyana Ndiaye ziar waw deug la muahibu la.
Yaw kay sounou mbokou talibé nga incha alah dinagnoula suivre every where masha togou bi amna solo té tadjie bi rafet oui
J'adore le décor ❤❤❤❤❤💔💔
My dear sister I like your videos but they are a bit long
Salaam my dear sister thx for taking the time to visit our Chanel and also your comment it is greatly appreciated !
You know most of the videos are being broadcasted on TV so it is considered a bonus in my Chanel, and also the aim of this Chanel is teach but help others how to eat a healthier diet and giving them all the other options or alternatives they have and for that I can’t just be doing tutorials all the time.
Some people are lacking enough to know most of what I am sharing some others are not that fortunate and since we are a family in this Chanel I have to include everybody no matter what their skills are that is the only reasons.
Thx a lot my dear sister 🙏🏾😘
How to get the " sombi "
Hadja Baro Ziar u need buy chia seeds if u r if USA it is wildly available in pretty much every supermarket even Costco or Sam’s Club In u have their membership even Walmart will heve it.
If you go to chez Billo u will have the detailed recipe there.
Hope this was helpful!
Thx a lot🙏🏾🙏🏾🙏🏾
I am senegalese i love your channel it is very good
May Allah bless you
Bonne recette madame.
Seulement les gants sont noirs
Nice soul pour togue
Merci bcp
Ziar kou baax merci ci sa commentaire 👍
Sokhna billo bénéne niakantake bobou banla bidoule thiépe
Ziar ma cherie waw niankatang bobou nak chou-fleur la gnou ko togge amna ben tuto bougnou ci def ci chaîne bi.
Essayer ko neexna te baax na ci werguyaram 😘
Amna solo ak éducation alimentaire bi changé lekine bi
Awa Diop Ziar nala sama sis waw leg I leg day da ci baax ndax amna gnou xqmoul dc faw gnou dimbalilene mais aussi gni xam faw gnou dilene fatali 😘🙏🏾
kankan ca m interresse
Waw legui rek In Sha Allah tps mognou xawa ndiat rek 🙏🏾😘
Une abonnée de plus soxnaci say recettes sont très saines.
Jajeuf Ent merci ci commmentaire mais surtout ci sa inscription bi contane na trop 😘
machallah sokhna bilo depuis senegal je t'encourage
Ma D ziarnala jajeuf waye 🙏🏾😘
@@ChezBillo Sokhna si ma la beug yiw set yewen yaru tey ak dinne dji rek takhna nou war la suivre ma cha Allah
Ziarr n'a gniepp
Abonnelen sama chaîne
Ziar sama gayi dem len visiter te abonnewu waye fuir ngou japaler sunu sœur
Moi c'est Amyna Dioum j'ai une chaîne UA-cam Amynalinguere Mabo va fair un tour et n'oublie pas de s'abonner 😘😘😘
tarcala
Macha ALLAH
Saly Diallo Ziar sis 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Machala
Mame Saye Diakhate Ziarnala 🙏🏾😘
Machallah
Akassa ma cherie jajeuf 🙏🏾😘