Débat bou tangg entre Tapha Gueye et Eumeu Sène pour le combat Serigne Ndiaye 2 vs Doudou Sané

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 30 лис 2024
  • Спорт

КОМЕНТАРІ • 83

  • @MamadouDIALLO-oq2dk
    @MamadouDIALLO-oq2dk 11 годин тому +8

    Serigne Ndiaye tamou adversaire moko narra tardel yaw ndane bébé Saloum gua beugua mbeuré force akk VIP yii

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 14 годин тому +8

    Sincèrement Serign ndiaye va doudou sané lamb logique la

  • @soldarouyayam8524
    @soldarouyayam8524 13 годин тому +9

    Doudou sane seul le future taychinger

  • @thiawaliou2277
    @thiawaliou2277 12 годин тому +5

    Khadafi sané doffe boù khèsse bî 💪💪💪💪🔥🔥🔥🔥

  • @MamadouBarry-cl1ig
    @MamadouBarry-cl1ig 4 години тому

    Vraiment la qualité d’image de lutte tv est juste magnifique ❤

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 12 годин тому +5

    Combapt la dai doudou sane serign ndaiye

  • @senegalais.
    @senegalais. 12 годин тому +3

    avant de prendre l'avance Eumeu séne kegn danal Doudou Sané déja.

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 9 годин тому +1

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @KhadimDiouf-uu5jo
    @KhadimDiouf-uu5jo 12 годин тому +3

    Doudou sane d'où moromou Serigne Ndiaye

  • @récré-o1d
    @récré-o1d 11 годин тому +1

    Makane à créer un trophée 🏆 le roi des VIP pour eumeu sene

  • @mandellandoye1908
    @mandellandoye1908 14 годин тому +2

    Combien de fois Serigne Ndiaye a déjà terrassé Doudou Sané ? Plus de 5fois même

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 12 годин тому +15

    😂😂😂😂eumeu sen dai barage bou mate barage la ame

  • @boucardiouf6367
    @boucardiouf6367 14 годин тому +2

    Dieul Doudou sané Moy sénn deuxiéme déféte

  • @modo6218
    @modo6218 13 годин тому +6

    Man franc la geum nianoul kenn day fokhati loum mom😂😂

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 7 годин тому +1

    SERIGNE NDIAYE DAY DANE DOUDOU SANÉ MONKO MEUNE FOUF

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 7 годин тому +1

    MS DOUDOU SANÉ VS SERIGNE NDIAYE LAMBJ LA

  • @ousmaneba2343
    @ousmaneba2343 10 годин тому

    Serigne Ndiaye Doudou sané moy combat logique bayi léne séne thiahane waleu Zambala Eumeu Serigne Ndiaye moussoul nék actualités

  • @MOUHAMEDdiopdiop-o7c
    @MOUHAMEDdiopdiop-o7c 13 годин тому +2

    Doudou Sané vs Serigne Ndiaye2
    Doudou Sané vs Blindé
    Doudou Sané vs Ablaye Ndiaye
    Doudou Sané vs Ibou Ndiaye Obeuly

  • @MamadouLamineGaye-b6d
    @MamadouLamineGaye-b6d 14 годин тому +3

    Serigne diaye 2 kasé

  • @ModouFall-f9b
    @ModouFall-f9b 3 години тому

    Ana cheikh bass keur massare

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 7 годин тому +1

    DOUDOU SANÉ VS ALBOURY

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 7 годин тому +1

    ORDINATEUR VS ALBOURY LAMBJ

  • @SaliouSarrMaçon
    @SaliouSarrMaçon 14 годин тому +1

    Macha Allah ❤❤ eumeu seul

  • @djimbaniang2190
    @djimbaniang2190 13 годин тому +1

    Serigne Ndiaye meun Doudou Sane de

  • @bakaricisse726
    @bakaricisse726 13 годин тому +2

    Tapha Gueye lol risque la

  • @papasalioucisse9639
    @papasalioucisse9639 12 годин тому +1

    Pourquoi pas eumeu vs quench doudou sane ak serigne ndiaye yeup quench molen raw boulen yakh lamb ji

    • @modo6218
      @modo6218 10 годин тому

      @@papasalioucisse9639 kan moy quench anaconda vs quench moy combat bi

  • @salioudiallo3412
    @salioudiallo3412 14 годин тому

    Bilay serigne défal lolou

  • @MOUHAMEDdiopdiop-o7c
    @MOUHAMEDdiopdiop-o7c 13 годин тому

    Sa Bocal vs Thiatou Walo
    Sa Bocal vs Boy Dakar
    Sa Bocal Vs Talpha
    Sa Bocal vs Mamady Ndiaye

  • @afro3827
    @afro3827 12 годин тому

    Serigne ndiaye yak doudou sané beureulen sen bir gayi dagni wakh rek ken doulen si may chance ndakh ken beugousé danou 😂😂

  • @bourathobouratho4672
    @bourathobouratho4672 11 годин тому

    Dieul léne doudou sané ba paré combat la

  • @amaduamadu1600
    @amaduamadu1600 4 години тому

    Dangen bakheu rek Doundou ñemewoul serigne ndiaye dako dan ba soneu

  • @BabacarGueye-t7d
    @BabacarGueye-t7d 12 годин тому +1

    Serigne Ndiaye 2 nah bagne

  • @papendiaye6896
    @papendiaye6896 11 годин тому +1

    Sa bogal vs Ada boy Baol combat leu

    • @ndiobengom4422
      @ndiobengom4422 11 годин тому

      Frr sa bokal garga 2 Moy combat bou nekh

    • @Mamadou-Fall
      @Mamadou-Fall 10 годин тому

      Sa bokal dou mbeur wayyy
      Boulenn niou sonal !!!

    • @moustaphadiop8903
      @moustaphadiop8903 9 годин тому

      Respect garga 2 way svp

  • @mbayendour7931
    @mbayendour7931 4 години тому

    Wa me khana dou doudou sane mi serigne dane ci mbabat yii.

  • @modo6218
    @modo6218 13 годин тому

    Franc mom nekoul si sen yi ay mayma chanse louy lolou 😂😂😂😂

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 7 годин тому +1

    Eumeu sene khamout kouy niane dangendi def kom franc ndiago 🤷🏽‍♂️tangale

    • @fifty6292
      @fifty6292 2 години тому

      Dieuloule Franc di

  • @jaynprods2
    @jaynprods2 7 годин тому

    sou ma nkone serigne ndiaye combat bi souniou ma fayoul sax damey beurei , li tek djexal dagey daane book si course bi , eumeu meuneu tou la bagne so gestoo lac2 taxaw sa wett, combat bi sou la reuthé rek serigne ndiaye ngaka nga

  • @BoubacarCamara-u2s
    @BoubacarCamara-u2s 10 годин тому

    Pape ndoye vs sabokal

  • @AgenceSylla
    @AgenceSylla 6 годин тому

    dema beuga kham kane leu serigne ndiaye dane ba paré ???
    Doudou sané mo dane Garga 2 dane Thiatou yarakh legui serigne ndiaye bebe saloum la dane

  • @aliouba1174
    @aliouba1174 13 годин тому +1

    Sa bokal vs Toubacouta lamb leuh

  • @FallWaly-c6g
    @FallWaly-c6g 14 годин тому +1

    Doud sanne monul dor

  • @NdiaboutaDiouf
    @NdiaboutaDiouf 7 годин тому

    père sa intérêt rekk ngay xol. Guiss far nimou mete del xol des fois say communication mais eumeu je n'ai rien contre serigne Ndiaye mais tu devais prendre Alioune seye 2.lolou mo geuneu logique bilahi

  • @MOUHAMEDdiopdiop-o7c
    @MOUHAMEDdiopdiop-o7c 13 годин тому

    Serigne Ndiaye2 méme sou dané mok Eumeu Séne Dou combat

    • @salioudiallo3412
      @salioudiallo3412 11 годин тому

      Sou nékoul combat lane lay done match wala rugby

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 8 годин тому

    mais sou doudou dané NK 😂eum séne lék avance bi😂

  • @abdoulazizndiaye3161
    @abdoulazizndiaye3161 6 годин тому

    Laniang koula bayi ngay wakh père tapha

  • @user-modousene
    @user-modousene 14 годин тому +1

    Combat bou nekh

  • @sizzlasane6309
    @sizzlasane6309 11 годин тому

    Combat bu normale laa doudou sané kén meunuko bagn au contraire gayyii dagnukoy moytou

  • @laminesagne3563
    @laminesagne3563 6 годин тому

    Bou doudou dané dieul gris bordeaux

  • @badiafaye5314
    @badiafaye5314 6 годин тому

    Pourtan comba bou neh la 😂😂😂😂

  • @PapeSow-l2d
    @PapeSow-l2d 2 години тому

    Daniou wara bayii dii bollé mbeurou mbapatte yii niouy beuré sén birre pr koi pas niou diokhlén yénén mbeur

  • @fayealpha2215
    @fayealpha2215 14 годин тому +2

    Moo atout leumou Serigne ndiaye foumou fek doudou Sané dioylo ko guéni khini khini fi. Serigne Ndiaye 2 souy nélaw Doudou Sané meunou ko yeugueul

    • @laminethiam1599
      @laminethiam1599 12 годин тому

      Wakhi doff yi ngay wax😂😂

    • @salioudiallo3412
      @salioudiallo3412 11 годин тому

      Bilay loulerr ga wakh bro doudou sané serigne moko meune

  • @MohamedThioune-p9k
    @MohamedThioune-p9k 6 годин тому

    Dam souker2 AK sa bokhal Moy comba deur bi

  • @BabacarGueye-t7d
    @BabacarGueye-t7d 12 годин тому

    Serigne Ndiaye 2 loh raw doudou dane boum teubeutt doudou sane amoul bayrer

  • @récré-o1d
    @récré-o1d 11 годин тому

    Makane à créer un trophée 🏆 le roi des VIP pour eumeu sene

  • @récré-o1d
    @récré-o1d 11 годин тому

    Makane à créer un trophée 🏆 le roi des VIP pour eumeu sene