Amna solo trop . mande ostaz madiama mo takh ma geuneu bayi khele muzik mangui USA mé mane nama doon deglou beneu son basi yangeu maguis niou bindeu si NCS Don Diablo REMIX X mani wà lii yeufou seuytanele ma koumace bayi khell mé barina lou nit yi di deglou ak dika khol ndakate moye takh douniou fonkou diamou yalla loumasi meuneu wakh barina mé DIEUREU DIEUF madiama fall ❤ yá takh maye geustou lou bari mé 2ou3 emison nga warona def par semene 🫡👏🏾👏🏾👏🏾
Yalla magui lay niàne madiama fall mi suma naré dieuk guéne adduna yalla ngama dieull nga bayikofi🙏 magui dollékou lol ta migui yété si Yalla 🥺😭(والله حار فؤادي)
Fa Tabarakallahou ma sha Allah 😍 Amna solo. Yalla na Buur Yalla fay leine tei yokk xam xam bi. Mou maygnou itam noppi deigg ak xolou dieufei in sha Allah.
Machallah 🥰 Amati n'a Solo ♥️ Diadieuf Oustaz Makhtar et mention spéciale à Professeur Madiama Fall longue vie avec santé de fer si Barke TAHA ALAYHI SALAM 🥰♥️🙏
Amna solo trop .
mande ostaz madiama mo takh ma geuneu bayi khele muzik mangui USA mé mane nama doon deglou beneu son basi yangeu maguis niou bindeu si NCS
Don Diablo REMIX
X mani wà lii yeufou seuytanele ma koumace bayi khell mé barina lou nit yi di deglou ak dika khol ndakate moye takh douniou fonkou diamou yalla
loumasi meuneu wakh barina mé DIEUREU DIEUF madiama fall ❤ yá takh maye geustou lou bari
mé 2ou3 emison nga warona def par semene 🫡👏🏾👏🏾👏🏾
Yalla magui lay niàne madiama fall mi suma naré dieuk guéne adduna yalla ngama dieull nga bayikofi🙏 magui dollékou lol ta migui yété si Yalla 🥺😭(والله حار فؤادي)
😢😢
Ndaysaan yal nangéen fi bòkk yàgg lool
Nianal Yalla bayilafi bayikoffi bouder mo geun si yen
@khadimgaye5997 yalla nanguénne fi bokk yagu
Yalna bour yalla bayi len fi nguèn dounde té wer lol
MachAllah sunu professeur Madiama Fall 🎉❤😊 bilay Oustaz Makhtar Sarr tay contente na ❤ ki waroul doufi geujj
❤❤❤❤
Machalaah amatina solo avec oustaaz makhtaar sarr moom day am solo rek inchalaah ❤❤❤
Fa Tabarakallahou ma sha Allah 😍 Amna solo. Yalla na Buur Yalla fay leine tei yokk xam xam bi. Mou maygnou itam noppi deigg ak xolou dieufei in sha Allah.
Machallah 🥰 Amati n'a Solo ♥️ Diadieuf Oustaz Makhtar et mention spéciale à Professeur Madiama Fall longue vie avec santé de fer si Barke TAHA ALAYHI SALAM 🥰♥️🙏
Machallah Machallah amna solo merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤
Macha Allah serigne bi mangui lay ziaar bu Bakh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudief yalna Yalla goudale séni fane wéral thiére yi
Machalla ❤❤❤❤
Macha Allah professeur mahdi sa nou reste peu le monde soyons unique pour mieux faire ont doit aider les palestiniens ❤❤
Sunu professeur
Dieureudieuf madiama fall bilahi yow yatakh bama geuna beuge yalla bilahi❤
Machalla amna solo de Nice 🥰
Machallah!!! Amatina solo
Amnasola yallna yalla faye seringue Matar Sarr ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
MachaAllah tabarakAllah toujours aussi pertinent yallah ngen fi yag temu barkel.
Dieureudieuf Oustaz, wayé Dieureudieuf Pr FALL
Machallah Machallah Machallah amna solo merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Machallah Tay émissions bi dîna nékh❤🙏
Sénégal dafa yakhou nitt gni amatuniou kilifa lolou moy li waral li lep
Pourquoi pas professeur guennn crée ay téléfilm dignes d nos valeurs ak dine di djokh jeunesse
Ande nassi akk ioe dh
Nioniou meneu dimbali dh wallahi
👍🏻🙏🏽🙏🏽
Machallah ya oustaz yalla na lène yalla faye ❤❤❤
Machaallah yallah nagnou lene fayal
Machalaah ❤❤❤
Walahi Neyesane 😭
Walaahi deugg la
Machalla merci beaucoup amna solo loll ❤❤❤
MachALLAH amneu solo
Machalla amna solo
❤❤❤❤❤❤machallah
Na gneup wah alhamdoulilah ❤❤❤
C'est très intéressant ❤yalla nalén borom bi sammeu maylén guddi fan ak wérr gui yaram
Alhamdoulilah
Machallah
ماشاء لله
Masha Allah dieureudieuf
Maachaa allaah amatina solo loool
Masa allha ❤️🙏
Assalamou 3alaykoum Wa RahmatoulLaah
wakhtan amna solo lool
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤🎉🎉❤❤❤❤
professeur ya bax dh
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
THIËY pantalon bi 😂😂😂😂😂
Aquí en España, hay playas donde la gente se desnuda 100 × 100
Wa pastef kay len deglou si oustaz madiama fall di wakh ce message s’adresse à vous
Numéro madiama fall svp
Amnasola yallna yalla faye seringue Matar Sarr ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdoullilah
Machalah
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤