Amina Poté accusée: Dafa torokhal yayam bamou heuy dé, mère bi da souffrir ba heuy dé

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 29 жов 2024

КОМЕНТАРІ • 50

  • @Yallaykesser221
    @Yallaykesser221 2 дні тому +15

    Bayiléne doul amina bou torokholane yayam yalla douko teralll🥰

  • @CoraBa
    @CoraBa День тому +2

    Amina pote yalla nala Yalla same ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Goudale fane❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @corinesagna8952
    @corinesagna8952 19 годин тому +1

    Je ne te connais pas je te vois seulement à la télé mais je sais que tu es une bonne personne car tu as aidé beaucoup de personnes laisse les gens parler si tu avances on te creuse des trous occupe toi de mari et de tes enfants. Tu as la bénédiction de ta maman car depuis lors tu as avancé et non reculer yall nalla yalla samedi te mey lër ci barkel li gue guem.

  • @AichaFaye-j4m
    @AichaFaye-j4m 4 години тому +1

    Amina auto bi si kham laniou gorné bi si guinaw khéne d'où go gorné dokhal 😢😢😢

  • @MbayamSowe
    @MbayamSowe День тому +3

    Amina pote sah yay kou bah la won bima neke man ak alin tall domam nion deukon paswar sah yay dal bah rek la ham si mom sah rak alin tall ham nama nio fowa do magui lay wah ga moug oto bi si kanam la niouy korne yala nala yala dole tahawou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @OumySylla-c5z
    @OumySylla-c5z 3 години тому +1

    Amina mounieul rék laisse les parler et avance

  • @ouligueye4404
    @ouligueye4404 15 годин тому +1

    Diam rek gaye âme té dieukeurou nar soula beugué rek beugueu nala dagno labir

  • @nafissaba4207
    @nafissaba4207 8 годин тому +1

    Amina nagnou maye diam doule yak sa yaye

  • @IbrahimaGueye-jg8py
    @IbrahimaGueye-jg8py День тому +5

    Ay bayi léne gor gni nguéne di yakh

  • @NabouBa-s7n
    @NabouBa-s7n 20 годин тому +1

    Amina bouléne khalé toudoule sa dounous bayiléne ak yalla

  • @coeur2lion38
    @coeur2lion38 День тому +2

    Amina li yép wah bou bari molaco yobé nék si réseau di wah gisga silence arme la

  • @fatoubarre2946
    @fatoubarre2946 День тому

    Walahi ndeysan maitina ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @dieynabadiallo4950
    @dieynabadiallo4950 День тому +4

    Kham leup wakh leup bakhoul mere fatou djiola yalna souf sed si kawam yaye diou bakh lawone ndeyssane

    • @manguebourgeoise2760
      @manguebourgeoise2760 День тому +2

      Machalah deuk boustane keur famille thiam ndeyssane niom ngoné thiam

    • @choupetekebe4599
      @choupetekebe4599 20 годин тому

      @@manguebourgeoise2760 billaye sa mère a trop souffert

  • @layendeyefatou5815
    @layendeyefatou5815 День тому +1

    Amina poté tu es la meilleure

  • @ndiemendiaye3459
    @ndiemendiaye3459 День тому

    Amina poté yallna yalla same la

  • @khadimkasse4401
    @khadimkasse4401 День тому +1

    Mimi beugue nalla bilahi❤❤❤

  • @PapeNiang-j1b
    @PapeNiang-j1b День тому

    Amina mérénala amina mouno bayi gni yaw kham ngua yala kham ngua ay amina yeureume gnou bakh ngua bou yaag ndeysane yalna yala saam

  • @MamefamaTop
    @MamefamaTop День тому +2

    Amina yagui maye togne doule Kate yii yagui léni bégale sokhore ignane légui fi la fék bakhe bayiléne gnou wakh ba khame loumoulaye wagni😢

  • @IbrahimaGueye-jg8py
    @IbrahimaGueye-jg8py День тому +1

    Mane dé khaw mla poté. Wayé. Je c que nit cou bakh ngua nit noumou mel mou fegne si kanamam

  • @Kiaradorigatti
    @Kiaradorigatti День тому +1

    ❤❤❤

  • @fatoutine5299
    @fatoutine5299 19 годин тому +1

    Soxor amna...ey way...laissez les maman et les papa dans vos sorcellerie là...ins bi kou neubeutouwoul senegal yangui si erreur...jalousie bi eupna...

    • @lacolombeblanche4589
      @lacolombeblanche4589 19 годин тому +1

      Surtout ci parents yi dé rek laniouy wakhal Lou niaw dama choqué

    • @fatoutine5299
      @fatoutine5299 5 годин тому

      @lacolombeblanche4589 wa parceque hamnegn ni pour atteindre nit ki deug fo k nga diar si parent wam...degniy chercher coût k vaille à destabiliser la personne...K ALLAH ns protège parcek sohoranete bi ça dépasse...liii ça fait peur ts les pays où ya tant de méchanceté n'avance pas et pire même ay calamité rek parcek YALLAH bougoul liii bo xamale sa nit lou bone sah dang ko wara neub....

  • @souadoundiaye2744
    @souadoundiaye2744 День тому

    Amina stp sors des réseaux sociaux tu n’as pas à te justifier laisse tomber ses énergumènes si je pouvais avoir ton contact t Yallah Takh je suis en France 😢😢😢❤❤❤❤❤je t’aime

  • @MoussaDieng-y2y
    @MoussaDieng-y2y День тому +1

    AMINA. LOUTAKH. MOUY. WAKH.

  • @oumydiawara3533
    @oumydiawara3533 День тому +1

    Courage tu n'as pas à te justifier

  • @MamefamaTop
    @MamefamaTop День тому +3

    Dagané dama narona kharou rék gnouné kharale rék gnou rayeko béne yone bou KO nogou Ay domou kharame lagnou li lagnou beuge bayiléne Mane damala sope trope bayiléne

  • @NancyEva-d7l
    @NancyEva-d7l День тому +1

    Kou torokhal yayam di tédd amoul fénn,Amina yala téral nako machalah donc arretez vos mensonges,sokhor nguén trop,taff niit diko yakk rék,amna niit gno khamné yala yakamti woulén bilahi

  • @tidianedoumbia4457
    @tidianedoumbia4457 День тому +1

    Sénégalais legui yereum na leen bess pencc

  • @IbrahimaGueye-jg8py
    @IbrahimaGueye-jg8py День тому

    Ay waye amina poté. Cou ko khol kham ni nit cou bakh la bayi léne gor gni nguéne yakh

  • @FatoundeyediopDiop
    @FatoundeyediopDiop День тому +4

    Malick de grace necoute pas ls comerage Amina c t une grande dame

  • @awadiopdiop-v2s
    @awadiopdiop-v2s День тому +1

    vraiment moi je ne te crois pas kouye torokal yayam dou teki denguena igniane amina ne repond pas aux mauvaises personnes

  • @BertheDepina
    @BertheDepina День тому

    Amina ne répond pas au détracteur tu as la bénédiction de ta maman arrêt de les écouter on répond aux imbéciles par le silence ne les expliques rien de grâce moi je suis une maman qui t,estimes beaucoup suis ton traitement si tu les suis tu risques de tomber malade ma chérie je suis cabe verdienne née à Dakar j,habite nord foire tu es un enfant béni de Dieu

  • @khadijadiandiaye8990
    @khadijadiandiaye8990 День тому +3

    Diamalé sa dieukeure té ga bayi wakhe bi nianala sa yaye

  • @KhadidiatouTouré-n3g
    @KhadidiatouTouré-n3g День тому

    Mais amina do guene thi reseaux sociaux yi dagne laye yakh

  • @FatoundeyediopDiop
    @FatoundeyediopDiop День тому +3

    Mais on es ou la Sénégal dek teraguala Amina ducourage ma soeur arrête de parler soi heureuse laisse les parler de grace Amina ne parle plus

  • @KounadyCissokho
    @KounadyCissokho День тому

    Amina souma sagnone ga bayi reseau yi danio sokhor

  • @yacineboye2243
    @yacineboye2243 19 годин тому +1

    Tu n'as pas à te justifier arrêtes les réseaux sociaux stp

  • @BertheDepina
    @BertheDepina День тому

    Amina nous t,aimons beaucoup je suis de tout cœur avec toi nous te confions à la vierges Marie pour qu,elle te couvre de son manteau du courage massa tout ça la c,est de la jalousie rien d,autre reste dans ton foyer la dame la c,est une moins que rien pourquoi te rabaisser devant une ordure

  • @khadimkasse4401
    @khadimkasse4401 День тому +1

    Mimi rek momo nekh

  • @mariatoudemba5174
    @mariatoudemba5174 День тому

    Amieñapls..live..this..this.. rhey

  • @NancySeck
    @NancySeck День тому +1

    Amina boule ne falle