Série - Lady Diama - Saison 1 - Épisode 48 - Bande Annonce
Вставка
- Опубліковано 10 лют 2025
- Créer des émotions fortes et de qualité et les rendre accessibles à tous les consommateurs du Sénégal et d’Afrique, tel est l’engagement de Marodi TV.
S’inspirer des émotions des différentes couches de la population pour créer des opportunités de visibilité et d’engagement pour les marques, telle est l’opportunité qu’offre Marodi TV.
/ @maroditvprod
Ohhhh le bonheur de Asmao et de tahib❤❤❤ kou contane wayyy❤❤❤
Mane dèh mome contane na ❤🎉tropp
Mon combat🥰
Sama khol bagui séd ni❤❤🎉
J’ai la conviction que Taib aura une promotion dans son lieu de travail incha’Allah
Mak yaw gno bokk lignou khalate deh da nara wax serigne bi deug li gnar gnognou di deal aprés serigne bi tek ko si wétam moukay liguéyeul li deh la khalate 😂
Espérons qu'il soit ainsi mais mane j'ai peur si salif tém mou yakal ko rek
@@khadyseckje suis d’avis
G pensé aussi
Yes il va prendre la place de Salif insha Allah. ❤
Asmao lii nékh na dh kou contant rék lalal j'aime ♥
Trop content ❤❤
Lounexx fofou asmao mon soff bari caractere ishh
@@adjasaliou8309 caractère bi Taïbe guiss na ko ci mom takhoul mou nop ko louy problème bi
@@acseanpaul6719 je sais asmao est dhabitud trop severe envres son mari lolou la guiss
@@adjasaliou8309 lolou problème yi niou amone si sen liguèy mo takhone mais ça pass
Kou buegue seydina Mohamed lalal j'aime ❤🎉❤🎉
❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤psl
❤❤❤
Paix et salut sur lui❤❤
Allhadoulilha kou sopou seydina Mouhamet lalal j’aime ❤❤❤❤❤❤
Il y a des femmes comme Diama qui sont très chanceuse en mariage.
😂😂😂😂 vraiment 😅😅😅
Dafa xam bopam tamitt te xam koumou warout andal, c est très important aussi
Chérie kholal nabou dash bijou ngoné ak amina poté😂😂😂
Chérie lolu mooy bras long Sleeve #Arass
Être chanceuse en mariage c'est se marier et rester marier au même mari jusqu'à la mort .
Sokhna Diarratoulahi Mariama Bousso yalna niou ko yalla fayal😊❤
Amine barkép serigne fallou ❤
Amiiine Amiine barkeep Borom Touba
Amine❤
Amine
Je viens d’accoucher des jumeaux 👯 🎉❤nianal len 🥰🥰
Machallah yalla na yalla barkel banga fèkè sen ndieurigne
@@Khadyjasow-y8j je reçois aussi…
@@Khadyjasow-y8j Goudou fan werr ak soutoura Yalla nalen ko Yalla défal 🙏🏽
Yalla naleine yalla sameu❤
@@Khadyjasow-y8j machallah yalnasi werr topou niou doundou th barkél wall mako amine
Yalla naniou yalla fayal soxna diarra❤❤❤❤🎉
Des cœurs pour notre prophète psl🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
❤❤❤
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤psl
Lady Diama aime trop les hommes wsh calme ma cheuri
Vraiment
Vraiment
Diama dafayy khemem rekk beugeulll kene legui mom kane la beugua mariell
@ mdr peut-être Seigne
Bi 🤣🤣
Aladji@@FatimaGaye6489
Mane dehhhh Faiblessou Diama Kane bi dama yemmmmmm😂😂😂😂😂
Justice pour serigne fallou fall 😢
Maneu Diama Ak MBACKÉ s’y rek la beugue tout sauf ALADJI svp 😢❤❤❤❤li mo meuneu nek Diama a trop souffert pour revivre la même histoire merci Marodie 🎉🎉
Mais tamit bala mo dougou thi mbacké sy mi na débarrassé wou thi basse mou signer papier de divorcer yii soff na trop té deugeur bop tout sauf basse
@@oumouba-dd4in Surtout lolou. Tout sauf Bass bilay 😂
@@oumouba-dd4indeugue bou werr nga wakh c’est clair Bass si bopam mi soff djiguene dagne kay meuneu nignouy meunei goreu dika topato❤ ni bb wayei je t’aime boudoul diekh yoroul ken 🎉
@@ModouFall-b2qbilay wakhal deih ❤❤❤🎉😂😂
Yalla nagnou yalla samou inchalla 🎉❤
J’ai vraiment de la peine pour Bass
Il aime Diama d’un amour pur et sincère 😢😢😢😢
Bly ndysn Diama kay mo xamoul loumou beugue
Peut être, mais il ne devait pas la menacer ..
Ça c’est de la bassesse…
En tout cas elle a bien fait de pas se marier avec lui, il m’a l’air instable mentalement.
Diamant bilay dafa égoïste
@@ElDiablo02-r2f égoïste rek 😒🙌🏻
Koudone khar bande annonce bii rek lalal j’aime ❤❤❤😂😂😂😂
Diama ak aladji rk niou dém ❤
Sava stp u peut me traduire ?
@@FarimaDoumbia-tc2mbdiama a dit qu’elle a pris sa décision et qu’elle va se marier mes on ne sait pas avec qui
Merci et Aladji ? @@blackwomen2381
Bilay
Vraiment aladji soufre
Merci Baya Niass ❤❤❤❤❤❤
🎉🎉🎉Allahou Akbar felicitation a vous l'equipe de Marodi TV.vraiment chapeau bas pour ces belles et importantes lecons de vie.
Sincerement aye djangate you ame solo lagnoussiye djeullei EN resumé:mougne, patience, veracité,Foi EN Allah et EN sois=perseverance🎉🎉🎉🎉
❤❤❤
Diama moy diapalé tayib nak soukoo serigne bii takéé😮🎉
A lo takh gua wakhko
Aller marodi 😂
Mo Tayib kay khaw ma loum sokhla mais dou diapalé waadji batou diapalé lay bagn yaw😂
@moustaphatoure2044 kham naa bii mm sou bañé d'oùtoul amatii léguéy😅
Notre prophète bien aimé Muhammad paix et salut sur lui ❤🙏🏼❤🙏🏼❤🙏🏼❤
Première commentaire ❤diama sa xol biii oyofff na 😅
Bliehi 🥺🤦🏾♂️
Noo jigen daal moiy lolu
Man lol MoMA diakhal wallahi mom Khana Amol dieukeur wala bass do dieukeuram
Vraiment 😂😂😂
Dima bo seyé ak serigne bi ma bayi serie bi kou d'accord rek lala j'aime ❤
Yaw yayy bayii mais niounn bayi wouniou loutah niouy lal j’aime🙄
@@oulimatafall3494😂😂😂😂😂😂😂
@@AmySall-m8r khana yaw yaye bayi mais Mane mi jamais de la vie 🤣 j'espère que aussi digua bayi rk bis bou seyé ak Serigne mbacké sy
Ma chérie esk wolou nga serigne ba paré dafay khémém dh lolou sama xalatt lah nak
@@ThiatFall-o3mwalai deh, Alaji moh buga Diama naturellment.
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Sallalahou Ala Mouhamad 🎉❤
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Basse ça suffit ça suffit inaf Basse inaf inaf 😂😅😭🙏
😂😂😂😂
Wa Toma 😂
@@MarietouWade-z2p wakh na deug di 😂
Diama et serigne mbacké sy couple bou raféte ❤❤❤❤❤❤
Mane dh sama khol bi worna aladji😂😮mongui si mbacké sy légui😅
@@SallaSylla-u1mMbacke mom bayilén ko ak mann 😊
Diama ak bass sama couple préféré
Yalla nagnou yalla may moudiou bou raféte yalla na yalla yeureum way dawelou yiii 😢
Diama migui wadja seyi dé ay wy li nékhna dé😂❤
Ah diama def na choix 😅❤
Xol bi déf na choix si Serigne Mbacké Sy 😂❤ yague na
Bass AK diama yallah nagn mboudié couple bbou dafma nkh bly ❤
Team lady Diama je vs aime tous bilahi.tay mom je content et heureux du couple diama et mbacké sy❤
Loutakh guéne sokhore délénma may aay saime 😢
Dinko yeukha am louy saime
Mafi nieukk des coeurs way❤🎉
Wa diama koukoy tak fofou yeureum n’a bas nak☹️
Bass mome merite woul li vraiment
Bilaye sama hol diekhna
Mya shu future ❤❤actrice est la ❤🎉🎉
En tout cas Diama,bass ne t a rien fait pourquoi tu lui fait subir ça. Il t aime d un amour sincére
Ne fait pas croire aux hommes k djiguéne dou beugue😪🥹
Vrément
Yalla na diamou yague rk ❤
Je viens d'accoucher un triplets mayilénema ayi nianne 1:23
Khana chak minutes ga accouche
Yalna barké❤
Yalla nangnou dounde ame Ndaye al baye
Alhamdoulilah yala naniu dundu tee barkel
Machalla
Alhamdoulilah 😍
Diama et Serigne bi Fav couple gay ame niiii lila toubap bi di wakh coup de foudre 😻 🎉
Diama Kay kene kamoul Lo boukh teye bass souba Alhadj😢
El.hadji.mena.nekk.sey.bi.daffa.gaw.diama.so.guissoul.lo.kham.deLou.sI.Elhadji.tu.es.en.regle.avec.la.religion
Wa mais Bass signé guoul papiers yiiii 😂😂😂Marodi inafff
Asmao yalla n’a continuer ni Nila djiguene daguay wagni thiow li 😂 😂 wane ko liguako naral tasaréko si kaw lalame dinala mey keur gou Bess wourous ak gualam c bien c tres bien ❤❤❤
Je te jure 🤬 😂😂😂😂😂😊
taib de mbouraké ak ndir lako diokha goum 🤣
Dinama kane xol bi comme car rapide kou nieuw bou Yap sheuu😅
Ma fi djitou jtm papa 🎉❤
Si diama retourne avec aladji j aurai complètement perdu mon temps à regarder cette série
Pourtant ils sont fait l'un pour l'autre 😅
@@nissankara1493Vs regardez seulement le faite quil sont beau mais la souffrance quel a subir sa vs dit rien QUoii?
@ en quoi ils sont fait l un pour l autre diama ne l à jamais vraiment aimé elle se sentait comme pris au piège dans ce mariage
Diama mi ww li guéna gaw😂❤
Bass 😢😢il souffre car trop amoureux d'elle 💔
@@Sani.5724 c’est triste
Bilaye sama hol dafa diekh nakh bass lako yene
Il s’en remettra
@@BaraToure-j7hseries bi amatoule béneu sences scenario bi lagnou changer khawma
Motakh kouy nekak nitt en relation del soralei a tout moment que tout peut chamboulé gnou bayisi hel
Legui wa marodi no leen di def bass sofguene torop teh meneu changer scénario 😮😮
Et aladji nak 😂
Bass na takk assy mou diéx, alhadji yame ci diéynaba ndx diéynaba amé bonheur ci seuy bi
@@fantasogue3816 stp u me traduire un peu stp
Diama Ak Aladji leu 😊
Diama veut faire du bara yégo pour revenir avec aladji
Le Seuy le plus rapide du monde
Legui mim serign mbackè la beugua seuyeull yombb na assay a aussi droit au bonheur sama xoll bi diexna
Ah mane parena si série bi dafa doywar torop Bass kholal niou bayiko ni
@@adjasaliou8309vous oubliez que Assy est en veuvage donc impossible mou am relation
Té Diama faut que mou marier pour meuna délou watt thi Aladji
@ bbilayy le temps quil faudra scenario dafa yombb kenene nieuwatt pour diama bilayy jai rien contre assy a droit etre heureuse
Diama et le monsieur vont se marier ??
Diama switch vite entre les hommes hein son coeur ne se repose pas ?
Kou d’accoroul si diama rk beusseul j’aime 👍 😢
Khana tay dina am plus de 10 jaimes
Diamma day fans rek
Kou bègue ❤❤❤❤
Mustice pour fallou fall❤❤❤
Diama néna bass nekal nit yow mom ya wara nek nit sey diam
Ce Mbacké Sy ummm quel bel homme je te dis, je me le souhaite vraiment vrai billaye
Ma fi djitou ❤
ou est l'amour dans ça a la fin pour le couple diama et le mr venant la ? pufff je suis confus sincerement mais j'ai espoir que a la fin aladji vas se remarier avec diama je vous jure hein
retenez bien ce commentaire svp lol
Je suis d’accord
Diama souyy marié ak serigne bi mayy bayii sétane série
Bilahii
Bayil légui ni ndakh mariage mom day am
Serie bi mome diekhna ba paré
Mafi dieuk damay compos nianal lén ma 😭
Yalla naniou Yalla diapalé🙏
Gnousal diagui😂
Aladji et Diama mon combat ❤️❤🫶
😂😂😂😂😅😅😅😅😅
Il faut que Diama se marie à quelqu'un pour que Aladji puisse la remarier
@@VivianeWella fi dé amoul remariage
Dieurediouf baye Niass ❤❤❤
Nechallah ba❤❤❤
Diama khana bala gua mariée gua signé sa papiers de divorce ba paré diama sa xol bi comme car rapide 😢😢😢😢😢😢😢😢mane Adji la beug akk diama comme couple
Adji c une fille 👧 c alhadji 😂
Aladji rek mo diara yeureum
Premier commentaire des cœurs ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Basse chaque jour mou neck dii diapalé Diama Ndayssane
Nekhoul ba nekhoul mais diama diama dagua niou yapp bly💔💔💔💔mane may moudie bayi di setane série bi bly
Ayy wayy Basse 😢😢😢
Diama mom khamoule limou beugue nak vraiment vite fait mouni day seuyii indécise la def 😂😂😂
Assy lako yéné wone nak
Ay diama bass nack 😢❤
Façon aladji m’enerve la, donc c'est maintenant la faute de youssou si tu te crois tout permis ?
Diama beugna goorr lii mba diam
Première voir le banne de annoce🎉🎉🎉🎉
Diama sa djiko djiko bi nekhou ma sa dara bi safou ahhh
Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalna niép am diamou
Diama sa seuyi aka gaw 😂😂😂 wakhgua deug deh genre yi woroula romb 😂😂😂
ceux qui veulent croire que diama dou beüg, c'est faux, diama a aimé basse avec une autre facette de l'amour, l'amour passionnel qu'elle cherchait depuis le début de son mariage avec aladji, mais le mariage ce n'est pas de la passion seulement c'est au delà, jiggen dañ koy tane, goor tamit dañ koy tane, goor neu meutte kilifeu mais pas basse borom soirée et hôtel yi, les blancs signent monogamie avec une épouse et pourtant ils ont des femmes amantes, des femmes pour les accompagner à des soirée mais femme épouse ils cherchent des femmes exemplaires et mature pour leurs enfants, diama cherche un mari pas un namoureux, mais j'espère qu'elle reviendra avec aladji, il a droit à une seconde chance, tout le monde a droit à une seconde chance
La première 🎉🎉❤
Diama comme wifi 😂kou am code bi rék connectéwou
Wakh sii
Bass syndicats bi nenagne gua bayi mou sedd
J'aime mom lanlansiy ame beug nguén j'aime lale j'aime lllljjj rek
Diama oyof gua xoll😭
Attend diama je la comprends pas, elle fait patienter bass combien de temps pour âpres rompre avec lui et le nouveau kilifa qu'elle connaît à peine elle veut déjà se marier avec après le jour ou elle aura une déception elle va encore se plaindre des hommes. Elle se précipite trop, à sa place j'allais prendre mon temps pour mieux le connaître car nitt dafa leudeum
Faut pas oublier que c’est une série 🌝, on peut pas trop trainer dans les détails.
@abouhariamlamali871 bah si justement, une série reflète la réalité sinon pas lapeine de regarder
@@wanefatimata4432 oui mais malheureusement la série va prendre fin la semaine prochaine. Ils ont sauté comme d’habitude plusieurs faits qui auraient pu être pertinents.
@abouhariamlamali871 ah je savais pas que la série allait finir la semaine prochaine, c'est dommage car on est un peu perdu là, y'a trop de choses qui se précipite et c'est pas logique
Série da djéxx ba paré sa reste 2 épisode 49 et 50
Bass ak aladji dé nguene di coalition porter plainte Diama😅
I am so happy for Diama Kane
Non diama bo seyé ak kokou damaye kharou😢😢
Diama dou nitt 😮
Kharoul
Mafi djitou sama série préféré ❤❤
Diama kholou car rapide ngua yoor kou nieuw ngua yebb😢
Yallna diamu yagge wakh léne Amin
Allhamdoulih mafi djitou
Suis la première 🎉🎉😂😂❤
Ay diama bene saison nga beug si 3hommes
Diama mi tamite khol bi kom rapide
Orrrgg j'ai tellma hâte que Demain arrive vite wooo 😂