Lima sétlu ci Dr Ahmet Lô mooy très rarement lay cité ay référence buy wax ci diné xawma daa japé bobam hujja xawma ils dit généralement boroom xam-xam yi neenañ comme celui qui disait raconté par les raconteurs ( رواه الرواة) sans citer les noms
La paresse intellectuelle est un des plus grands maux de ce pays. Comment peut on sérieusement attaquer des livres de recherche sur l'islam par des messages whatsup ou des messages youtube. QU'est ce qui vous empêche d'ecrire des livres en réponse à ceux de Ahmad Lo? Un musulman, et à fortiori, un savant ne doit pas perdre son temps dans des débats stériles qui n'avancent en rien la communauté. Vous perdez du crédit auprès des gens serieux.
Ah Serigne Abdou lahad ki diaroule tontou gnép khamnagnouni nafékh pire le c que Ahmed lo dafa tardé parce que mom ba lègui khamagoulni gniko raw dagno beuri loool mais mom pour mom mofi raw ndaysane mako yeureum
Def na ay téré ci jangalé alfiya fi ouloumil khour'ane الفية في علوم القرآن ak yenen ci domaine you beuri. Jang na ci ay lokham fanne you beuri. Borom kham kham la surtout hadiths rijal yi ak assanid yi oussouloul fiqh ak fiqh ak yeup il est trop calé. Jang rek ley def ak jangalé. Ignanéwoul kene. Té dey jéguélé rek. Machallah
Alpoulaar yi 🤣🤣🤣🤣da ngénaa nèx ndeysaan. binde kat taxoul li mouy wax wér. nooni yonénetébi bari na niou si adina ta niou si bari da niou léne di toudé ay boroom xam xam ndax sènii binde you bari. ta pourtant nioune dioulitt gni da nioo geum nioom xamou niou dara. xamouma nak ndax sax yaw geum nga yonéneté bi am dèt. ndax ameth lo aki nioniam moom bokou niou si diiné islam dji. daa mél ni naar yiy fo aka thiaakhaan la niou topou di doundè séne xaaliss
Pourquoi ces soi disant docteur ne parlent du chirk flagrant qui existe dans ce pays. Docteur Ahmad lo ha est un grand savant d une grande envergure. Ce Abdou lahad sane à defendu le habd dans un débat.
Ameth lo daal féne katt la bou wér. Loolou moom oumpatoul kéne. Yéne gniko topou sax kérook grand theatre wax na lène ni Serigne Touba kéne la ta pourtant si souf dou lène wax loolou. kon moom naafékh la. Gni sankou ba noppi rék nioo ko topou.
Ameth lo soutouraam xawè kou na. Niépa xam ni féne katt la ta naafékh la itam. loolou moom oumpatoul kéne. Xanaa kay gni niék ak gni nga xamni da nioo farè seytaané rék nioo déss si moom. Grand theatre da koo sanke deug sax. ndékété dou dara
Dr. Lô fait beaucoup trop de jaloux qui n'ont aucune production intellectuelle reconnue et qui passent leur temps à ressasser des détails insignifiants sur son oeuvre rien que pour se faire connaître. C'est nul!
La malhonnêteté intellectuelle de Dr lo doit décrédibiliser toutes ses œuvres... Dr a le droit à le droit de critiquer nos guides spirituels mais lui on n'a pas le droit de le critiquer... c'est quoi cette façon de voir les choses.
Yaw kou nafékh ngua Ahmet lô moye kane badou dioum, il ne fait que du plagiat, il ne sortira jamais démentir ce que Dr Abdoul Ahad Sané vient de dormir.
ماشاءالله جزاكم الله خيرا يادكتور عبد الأحد ساني اطال الله عمرك ومتعك بصحة وعافية تامة بجاه شيخنا الخديم
Merci dr abdoul Ahad amna solo
Machalah
Hahahhaha kazab lahad
Machalla cheikh abdou lahad amna solo yalla na yalla goudal sa fane ta may la were thi barkép Serigne touba amine
Amine
Nonou rek. Yaar ak teguine.
Dieureudieuf
Dieurdjef Serigne habdoul ahad linga wakh mo werr té moy deugeu
Macha Allah cheikh abdoul ahad
Merci beaucoup amen sololl
Masaa-allah amna solo
Merci sene
Machahalla s Abdou lahat sané diaradjieuti yalna la yalla féyla. barkep s Touba machahalla
ماشاء ياعبد لاحد شاني أطال الله عمرك وصح جسدك أنت مالك الصغير
Mâcha allahh dr Abdou Laht
Abdoul ahad ana sa doctorat wangniouko
Merci Serigne Abdou lahade
Machallah dr abdou lahad sane
machallah amna solo dh téwlou na lépe yalla na yalla fayal yiw si lérale yi
Amna solo
Xam-xam tayeel du ko maye nangoo sonn ci xam-xam rekk moo koy waye jërëjëf sëriñ Abdu lahat saane xam-xam rakka woor
Machaallaah
Lima sétlu ci Dr Ahmet Lô mooy très rarement lay cité ay référence buy wax ci diné xawma daa japé bobam hujja xawma ils dit généralement boroom xam-xam yi neenañ comme celui qui disait raconté par les raconteurs ( رواه الرواة) sans citer les noms
Macha allah limouye tounto yi am solo
Mashallah khamkham bi rafetna tè lerr
Merci abdou lakhat
XÃNNA DIAYY XÃM XÃM BII DJËËDEE KOO XAALIIS !!!
XAALIIS REEK ! DUU YALLAH REEK ! XAALIIS REEK !!!
Machalla
Dfa meuna diangal améd lo ba noppi eupko ab yarr
Lou léer nga wakh modou ndakhar reuy moko sonal
La paresse intellectuelle est un des plus grands maux de ce pays. Comment peut on sérieusement attaquer des livres de recherche sur l'islam par des messages whatsup ou des messages youtube. QU'est ce qui vous empêche d'ecrire des livres en réponse à ceux de Ahmad Lo? Un musulman, et à fortiori, un savant ne doit pas perdre son temps dans des débats stériles qui n'avancent en rien la communauté. Vous perdez du crédit auprès des gens serieux.
gnou eppe Dr Abdoulat sanè xam xam nioo sèdè Dr Ahmed Lo xam xam mam
Waxi xale, yan boroom xam-xam ñoo seede xam-xam dr ahmet loo ?
@@daoudawade809 oumar sall mdrr gnii danioo khamoul dara xam xam bou sélle andak ay tegine loolou si mag gni rek la am amoul feneen
@@fallouseck3149 wallaay ndaysaan lu leer nga wax
Té loungeen si khamoul béss ni tay 11 novembre retour d exilé de serigne touba
Wayyé hitt niou eup kham kham docteur nio nanguoul khamm kham abdoulahad sané
Abdou ahad sané dél wakh deugue
Ah Serigne Abdou lahad ki diaroule tontou gnép khamnagnouni nafékh pire le c que Ahmed lo dafa tardé parce que mom ba lègui khamagoulni gniko raw dagno beuri loool mais mom pour mom mofi raw ndaysane mako yeureum
Wax Nga lépp
@@beggboroomdaarusalaam554merci
Vérité absolue
Thiéy ndidiaye Google
leegi Fataaway Yaw Abdoulat sahnè defal yaw faata bò manè
Dangaa tarde ndaysaan kii ci fatawa la dëkk
Dara diaff séringe Abdou laht sané xam xam bi rafétna
Machahallah
@@mbackeleye4264 ❤️👍
Juhal que vous êtes..hahahah
@@abuahmad9938 tontou ma thi Wolof
Abdoulat cigna mingi ley diap dè
Jërëjëf sëriñ Abdu lahaat saane yàlla gafi yàgg lool te wër
Kazab lahad cheikh google.. dara khamo ko
Jërë jëf cheikh dr Abdoull ahad sane yalla na yalla faay
Hahahahahah cheikh google
Merci Ch Abdou Ahade Sane
Ou sont tes diplomes et tes livres
Cheikh google hahahahahaha
Dr Ahmed lo moye séne baye si xam xam
Sa khalate la comme nimou nekké souniou khalate k doctar sané mo eupp khamm kham sénégal
Jamiil saane
Macha allah jërëjëf oustaz Serigne Abdoul Ahad Sané Mérci beaucoup Que dieu vous accorde une longue vie. Alhamdoulilahi Sagalnga tarikha yi yalnala yalla sagal amine barké Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul bonne continuation
Waw yaw mi wak lobinde yaw??!
En tout cas c'est un Dr...
Def na ay téré ci jangalé alfiya fi ouloumil khour'ane الفية في علوم القرآن ak yenen ci domaine you beuri. Jang na ci ay lokham fanne you beuri. Borom kham kham la surtout hadiths rijal yi ak assanid yi oussouloul fiqh ak fiqh ak yeup il est trop calé. Jang rek ley def ak jangalé. Ignanéwoul kene. Té dey jéguélé rek. Machallah
Alpoulaar yi 🤣🤣🤣🤣da ngénaa nèx ndeysaan. binde kat taxoul li mouy wax wér. nooni yonénetébi bari na niou si adina ta niou si bari da niou léne di toudé ay boroom xam xam ndax sènii binde you bari. ta pourtant nioune dioulitt gni da nioo geum nioom xamou niou dara. xamouma nak ndax sax yaw geum nga yonéneté bi am dèt. ndax ameth lo aki nioniam moom bokou niou si diiné islam dji. daa mél ni naar yiy fo aka thiaakhaan la niou topou di doundè séne xaaliss
Très bonne question
Dieuredief tontou bi xam xamena yague te wer
Tu n'arrive mm pas au niveau de Cheikh Dr Ahmad lo , motakh ses étudiants vont te démonter en règle
N’importe quoi
Il est allé consulter Google pour vous le réciter😂😂😂
T,
Ahmad lo yalna fi yagg té and wére.
Amine Mokka docteur sané yeup
Soussi douguei legui tioki bi diekh nakh molene eup xam xam
No saway Ray nama thioki bi kay terminé
Xam xam rek neex
Cikh abdou latte bien jie ap tire
Abdou lakhat.mii mane na jangal loo
Loo ñi ko jangal rek laye sagua ak.di.léen deff ay yafer
Lo mikay nekhuta layal
Lii kay du njuumte daa amul xam-xam rakk
Ahmed lo fumu todieu bay bind ci bopam ab tere ki dafa yabate ak kanamame bou leundeum bi
Pourquoi ces soi disant docteur ne parlent du chirk flagrant qui existe dans ce pays.
Docteur Ahmad lo ha est un grand savant d une grande envergure.
Ce Abdou lahad sane à defendu le habd dans un débat.
Docteur yallana yalla Faye
Tu es le meilleur de ta génération
Alhamdoulillahi
Ay kama mome day yo sokhar
Docteur Abdou Lahad Sané môo eupp kham kham Modou Lo ndakhar wahabite rew mougnou dougue yakh ko sén problème môy danguéna reuy
@@mbackeleye4264
Serigne Mbacké
Nioum gaddé Akhloul sounna amoul gouréy
Docteur Ahmed yalla soutoural nako
Bapparé
Docteur Sane
Sédalnako ko ,
Nañiou ragal souñiou borrom
@@mbackeleye4264 lane moy wahhabisme ?
Ameth lo daal féne katt la bou wér. Loolou moom oumpatoul kéne. Yéne gniko topou sax kérook grand theatre wax na lène ni Serigne Touba kéne la ta pourtant si souf dou lène wax loolou. kon moom naafékh la. Gni sankou ba noppi rék nioo ko topou.
Ameth lo soutouraam xawè kou na. Niépa xam ni féne katt la ta naafékh la itam. loolou moom oumpatoul kéne. Xanaa kay gni niék ak gni nga xamni da nioo farè seytaané rék nioo déss si moom. Grand theatre da koo sanke deug sax. ndékété dou dara
Dr. Lô fait beaucoup trop de jaloux qui n'ont aucune production intellectuelle reconnue et qui passent leur temps à ressasser des détails insignifiants sur son oeuvre rien que pour se faire connaître. C'est nul!
La malhonnêteté intellectuelle de Dr lo doit décrédibiliser toutes ses œuvres...
Dr a le droit à le droit de critiquer nos guides spirituels mais lui on n'a pas le droit de le critiquer... c'est quoi cette façon de voir les choses.
Yaw kou nafékh ngua Ahmet lô moye kane badou dioum, il ne fait que du plagiat, il ne sortira jamais démentir ce que Dr Abdoul Ahad Sané vient de dormir.
Il manipule simplement les coeurs égarés ainsi que les faibles d'esprit comme toi
yawe daga sokhore nak
Ay bouda ap julit dou wax nit Lou niaax xana d'égo ki xam xam bi nimou amé tégui. Ga tok diko saga Loumou wakh louy soxor?
Ana louy soxor fii modou xaragne toogn lo laalko ci pass pass moukoy dioubante diko dimbali ngay niak teguin modou douko tontou deh.
Wallahi dafa sokhorrr