Tidiane laa déi. Waayé si sama guiss guiss, serigne fallou mii saf na sape ak yalla. Diagualnama lou bari si Mame cheikh Ibra Fall. Beuss kiki téy diapènaa bail fall yeupe ay nitou yalla. Yalna yalla yok sène lèr. Dègue yalla dafa nèkh Dieureudieuf
Je suis tidiane je viens de le découvrir mais je l'aime beaucoup mashalllah yqlla nqlq yqlla yokk banga yek ko yalla deefal La diam t yok kham kham serigne touba amoul morom Mame cheikh ibra dou tiakhane
Salut..machallah il a bien parlait car il se réfère sur le saint Coran et poursuit sur les khassida de mame BAMBA..Donc liih douh ay tiaxaneu waay.. Yalla nanou yalla défeu aay mouride dëgeu..Magui Ziaar serigne bii 🤝🤝🤝
Yalla na nek talibé cheixou Tidjane mais bilahi dama bgue mame cheikh IBrahima fall ba beineu yoon bima dem touba xabrome la fanane sama xol nekk naci té yalla boumou ci djiog
Mbengue ibra nékk adouna* t doundo baye fall mo woroul ndakh Mame moy baboul mouridinah t lolou moy wone ba dieum thia Yalla( l'Universel)...kone dessouko yamalé fén
Mane dh amna yènè guiss si dieum ngir dieumi cheikh ibra fall tawfèkh rk koula tèk beutt khamni fess nga deug baye fall èlegance civilisè yalla na lèn kou tèdd dèfal diam ❤
Goor fall walahi liguaye wakh kou khame yalla rék molo mana dégue diadieuf cheikh ibra fall, goor fall na gayi déme khame lahilahaila lép moye diamou yalla cheikh ibra batine la yoro wone,serigne touba diokhéwoul diouli , woor,adjimaka yalla ladone woné diko khame lé ma baeugue cheikh ibra ak serigne touba bima khamné yalla la léne khame deugue ñome douñi nite walaye hi ...?
khamnani daaal sangou makka ak medina diouli moo daane feekheul kholam وجعلت قرة عيني في الصلاة mo waxaat ni liniouy takkalé ak yeefeer yi moooy diouli
Thieuye borom ndiapandal mo bakh d tes Barry kham kham sa diangeu alkhourane lerr nama mane mi machalla Yalla sa diam yageu borom Ndar deuk Pape Malick Mboup ba
Ndeysann serigne fallou ndiapandal takh nga niou geuna xam cheikh Ibra Lamp baboul mouridina chak jr Gouddi gui damalay sétane ba nelaw souma yéwo fadiar gui avant may diangui damay sétanate avant may diangui
Tidiane laa déi. Waayé si sama guiss guiss, serigne fallou mii saf na sape ak yalla. Diagualnama lou bari si Mame cheikh Ibra Fall. Beuss kiki téy diapènaa bail fall yeupe ay nitou yalla. Yalna yalla yok sène lèr. Dègue yalla dafa nèkh
Dieureudieuf
Machalla Daga am tawfékh rk te Mame cheikh ku yalla nara dimbali wan la ay mbiram jajuf
Ndeysann
Kou beug douguou aldiana na mandou si Cheikh Ibrahima Fall🙏🏻
Kepp nk
Man li douma ci doyal 💙💗💖💕💚❤❤❤❤😢😭😢li dioye lo na koune man chiekh Ibrahim rkk la beug wa'Allahi
Kou fie nék diko déglou 2021 Yall nagne ko féké 🙏🏾🙏🏾
Je suis tidiane je viens de le découvrir mais je l'aime beaucoup mashalllah yqlla nqlq yqlla yokk banga yek ko yalla deefal
La diam t yok kham kham serigne touba amoul morom
Mame cheikh ibra dou tiakhane
M
Bien dit
Wallaahi kou yalla dimballi ngii yaaaram
Yallha na la yallha fay
Lii amna louko dak li 💗💖💕💔💓bly done baye fall mo wore ❤❤❤❤❤
Salut..machallah il a bien parlait car il se réfère sur le saint Coran et poursuit sur les khassida de mame BAMBA..Donc liih douh ay tiaxaneu waay..
Yalla nanou yalla défeu aay mouride dëgeu..Magui Ziaar serigne bii 🤝🤝🤝
Yalla na nek talibé cheixou Tidjane mais bilahi dama bgue mame cheikh IBrahima fall ba beineu yoon bima dem touba xabrome la fanane sama xol nekk naci té yalla boumou ci djiog
Akassa Macha halla
Macahall ko bakh yalna yalla godal sa fane taga wèr barekip serigne touba
Yal nala SIDI Brahim fall fay
Yaw Dh man fallou Mbacke beugna nou khamante
Boulasi Dr géuné beug nala ngir yalla
Je viens de voir video bi, Mashallah, Serigne bi amna xamxam am yar, am fit, foulla ak fayda. yalnala Yallah doli ler ak wer.Alhamdullilah
Li kawei na barki broome touba
Qu’ALLAH swt nous fasse miséricorde et t’ei def ñou aie baye fall deugg 🙏🏿👌🏿
Alhamdoulilah machala waxtane bi am na fassakha cheikh Fallou diapandal yala na yala defal la taw fexxxx barke ya rabiii
Neke senegal te neko baye fall yangui si ereur diarama cheikh ibra fall niake la kham woroul 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Mbengue ibra nékk adouna* t doundo baye fall mo woroul ndakh Mame moy baboul mouridinah t lolou moy wone ba dieum thia Yalla( l'Universel)...kone dessouko yamalé fén
Bilahi
Bi wakhtane doumathi doyal❤machaAllah
❤️❤️❤️❤️ je l’aime beaucoup Serigne Fallou diampanale ❤️❤️❤️
Macha allah Sérigne bii ^Dieuredieuff Cheikh Ahmadou Bamba Mbacké-yakarou diam gnii ^Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall-Lamp
Thiéy Cheikh Ibra ❣️❣️❣️💖
😭😭😭😭 chekhraaa Falll yaar nga ñou khamal ngañou souñou borom😭😭😭😭 sama khol sed naaaaaa
Macha-allah sama xol sédena trop sakh ...Thiaye Serigne Touba ak Mame cheikh Ibrahima Fall
Ziza Bay Darou Tv amoul mo roum
Mame cheikh Ibrahima dall es le meilleur kén dou mome
J'sui baye fall
Mane dh amna yènè guiss si dieum ngir dieumi cheikh ibra fall tawfèkh rk koula tèk beutt khamni fess nga deug baye fall èlegance civilisè yalla na lèn kou tèdd dèfal diam ❤
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machallah diareudief Serigne Fallou diapandal , yalna ngafi yague té wer
Maa chaa allah Mane dé Serigne Babacar s'y moy sama Serigne mais ki dema ko beugue té yallah rek takh yalna la yallah defal diam barki yonente bi saw
Mane dh catholique la waye yonou cheikh Ibrahim fall deug deug yonou aldianala
Thiey, li nga wah yéména deh, alhamdoulilah
@@diogoulfarba5586 guisse deug wakhko ayoul gayi si tereyi lanigne Sète Chiekh ibra te nekoussi Chiekh ibra dimension la
@@petitboumoussaballagaye5699 akassa, guiss deug wahko nak borom tawfekh rèk moko meun, yaw borom tawfekh nga, masha allah, deuk bi da beuri gnou sokhor
cieyy li nga wakh sèddna xoll dèh
@@diogoulfarba5586 DEUG dafa nekha wakhe
Lailaha ilal'allah mashA'llah li nekhna DIEUJEUF MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL KEN DOU MOM
Allahou Akbar ...thieuy Cheikh Ibra DIARAMA FALL
Eskéy 🙏 Äkåsä fall baboule Mouridine Dieuf Dieul dieureudieuf 🙏🙏🙏
Wakhtane by amna sollo amna yar am téguine machalla
Bismilah barkep Cheikh Ahmadou Bamba, alhamdoulillaah Allaahouma salli Allah Seydina Mouhamadine wa sallim,jeureudieuffé Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul, jaaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Baaboulmouridiina
Kéne la CHIEKH IBRAHIMA FALL 💞👌💞💞💞🤔
Ndeysane 'ndeysane degggg degggg am na soloooo machala sang bi Macha la taw fekhhh si ioooe
Nationalité mame cheikh Ibrahima fall yoboul hame a100%
Machalla diere dief Serigne Fallou baye fall amna solo
Macha allah serigne fallou wahtan bi kawene lerna werna
Diarama cheikh ibrahima fall
❤️❤️❤️ ndeysane. Do len ma dimbali ci ki di wayy ci souff
En repeat j’écoute ce waxtaan. Ken dou Mame Cheikh Ibrahima Fall.
Quelqu’un connait connait le zikr en fond?
Baba Sakho sidy mboup"lamp Fall"
@@khadijalasalihate6698 merci 🙏
Eskey machalla yatouna dh kou bax Xam Yalla Xam Diamou Yalla Cheikh Ibra képpou kouko dingattt rkkk danga guatteu xam xam
Thiey cheikh ibra fall kén dou mom 👌🏿👌🏿
Dieuredieufay Serigne touba mais son bisi souf nekh na trop machahala
Assane Ndiaye sidy mboup la
Diuerue diuef serigne touba diarama mame cheikh Ibrahim fall 💓💓
Dééguenaa degue ALLAHOU AKBAR LA ILAHA ILALELA rek woorrrr
XAM XAM amena
Ken dou Serigne touba bilahi😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏿🙏🏿
Akasa amna solo Dieure dieuf machalla merci 2stv
Amna solo dh thiey sowrou fall
Machalla amna solo lol mercie beaucoup pape sidy !!!
😍 thiey cheikh ibra 😍
Cheikh Ibrahima fall amoul morom
Diadief amna solo trop machalla
Machalha wakhdji rafétna lérna YALA nguéne am gueureum fa Yalla ci barcké brom TOUBA
Mane dé tidiane la wayé sama khol dafa toy envoyer léne ma numéro téléphone nous cheikh falou diapandal
Mbathip Ndoye mane mi veug nako
Deifleine ma signe si 777904597 ma yonei leine koo
manchallah
Kene dou cheikh ibrahima fall❤️
Baye Fall Triple Noble La
Jeurejeuf Serigne Fallou👌
akasa waw gor serigne touba kène le amoul morom ibra fall diaraw lakk
Macha allah wakh tabi weer té leer ! Yallah na khame gui guena yokou
Amine
Tiey mame cheikh 💓💓💓sedena
M'achallah Baye Fall Yal Nanio Yallah Dëfal Topë ak Dëgue çi Barkép Mame Cheikh ibrahima Fall Lamp : Gracias Mame Bamba !
Yallanala yalla yok salér si barké Mame chiehe ibrahima fall
Dieureudieuf Mame ckeikh ibra fall
Goor fall walahi liguaye wakh kou khame yalla rék molo mana dégue diadieuf cheikh ibra fall, goor fall na gayi déme khame lahilahaila lép moye diamou yalla cheikh ibra batine la yoro wone,serigne touba diokhéwoul diouli , woor,adjimaka yalla ladone woné diko khame lé ma baeugue cheikh ibra ak serigne touba bima khamné yalla la léne khame deugue ñome douñi nite walaye hi ...?
Ma challah amena solo
natou768 sama yaay name nala ani pere
Zikar bi daw si souff kouka zikar
Manchalla .Mais svp kou xam kiy way si souf si commencent bi
khamnani daaal sangou makka ak medina diouli moo daane feekheul kholam
وجعلت قرة عيني في الصلاة
mo waxaat ni liniouy takkalé ak yeefeer yi moooy diouli
Saa waay doulll bo khamoul noppil
@@wakeurboromtoubasenegal5905 dieureudieuf
@@marasarr2619 ap mbiir bo thi xamoul dara boul ci dougou boul ci wakh way yen
Dioulite bou touder batou saidai dioulite lagne kayy wowai
koudoul diouli yefeeer nga
Thieuye borom ndiapandal mo bakh d tes Barry kham kham sa diangeu alkhourane lerr nama mane mi machalla Yalla sa diam yageu borom Ndar deuk Pape Malick Mboup ba
Fall Ibrahima sama kharite borom chine
ken dou cheikh ibra fall koudul BAMBA cheikh ibra mola mann
Cheikh fall rekk ❤❤
Akassa fall amna solo
Oh sama yarame dawna.
Dioye na ba sone ndakh khol bou sedd.
NDEYSSAN
Dioyii fii la waré barké serigne touba
Je veux le son stp
Sidy mboup lamp fall
الله اكبر
me quelle homme macha allah
Allah bless senegal Dakar
Thieye Mame cheikh Ibrahim fall
Wakhtan bi nekhna troppp
On est fière d'être Yaye Fall❤❤❤❤
Salamalaykoum sam mbook bay Fall yi ziar bou werr Man dh dama khamoul souma donoul won Mouride nane lay def 😭😭😭😭😭😭😭😭 titres Sons bi Svp
Sidy mboup « lampe fall »
Machalla envoi ma sa nimero seuyebi
Ndeysann serigne fallou ndiapandal takh nga niou geuna xam cheikh Ibra Lamp baboul mouridina chak jr Gouddi gui damalay sétane ba nelaw souma yéwo fadiar gui avant may diangui damay sétanate avant may diangui
Kéne dou chéikhra fall
THIEYE CHEIKH IBRA KEN DOU MOM
yaw yalla ngafi yague
Thiey cheikh ibreu
koudoul baye fall dalle baye fall mola geune
Fall niou Cheikh ibra rek laniiu beug
Ahmadou fall saer ndiaye
Thiay SERIGNE TOUBA Bilahi kéne dou MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL
Commence ma emission bi son biy daw si souf noumou toudou svp
Sidi Mboup LAMP full HD
tapél lolou youtube
Direudieufé borome Touba diarama mame lampe fall
son bouy daw ci souf dawna yaram comment l'avoir SVP
Modou aida fall
Non c sidy mboup lampe fall
Merci mes confrères
@@fatoudethiembaye4632 sohna Fatou je confirme que c'est Sidy Lamp Fall et encore une fois merci pour votre apport
Machalla babill mouridine
Non danane ga machallah
Merci
Machalah fall yaram
Man chaka fi ibrahima fall
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Serigne bi ya réy ay doul
Amna solo
Machallah
Machalla fall
ma wakh nittt niou bonn gni mom dislike👎ba tokk yèna trokh dèhh