La fille de THIATE SECK explose le plateau de WAYAL NABI sur TMS et fait pleurer son père...
Вставка
- Опубліковано 9 лют 2025
- TELE MUSIK SENEGAL:
La première chaîne Sénégalaise totalement consacrée à l’expression musicale et culturelle du pays.
Reflet culturel, TELE MUSIK est conçue pour être une tribune d’expression par excellence pour les artistes musiciens du Sénégal.
Une passerelle qui relie l’histoire de notre musique et sa modernité, ce pont entre la Diaspora sénégalaise et sa culture, cette rencontre entre plusieurs ethnies qui sont nées d’une même entité.
Contacter TELEMUSIK AU +221 77 508 14 14 ou à l'adresse contact@telemusik.live
Maa shaa Allah tiaat seck lo amoul si musique yalnako yalla mey sa dom dji yalla samm ko lafal ko tiat si barkei seydina Mouhamed SAWS
Amine ❤
Amine ❤
Amine Sallallahou Haleyhi Wa Sallam ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Salalahou Alaihi Wasalam
Allahuma Ameen
Sunuu sangue bi psl keneu dou mome alkhamdoulila bima yalla defe sopey nabi psl alkhamdoulila alkhamdoulila
❤Sénégal mérite des jeunes talentueux comme ...
Vraiment laf thiate doundeull ba teral say wadiour ❤❤❤vb
Machalla waye laf thiat xele bi yalla na yalla goudale sa fane 🤲
ÀMIINE BARKEP MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP BABOUL MOURIDIINA BOROME NDIGUEUL.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amine yarabi 🤲
Deret fort na. On dirait la fille de Mapenda. Qu'Allah la Garde et la Protège Ci Barké Seydina Muhammad SAW
Ah machallah thiate seck music faynalla bim la mayé dome diou takhaw waye yonéneteu bi lou nékhé ni machallah ❤
Mon dieu c’est magnifique Salalahou aleyhi Wa salam ❤❤❤❤
Machala machala elle a une voie d’or et elle est très jolie yalla na batt bi wer inchala ❤
Li nèkh na way machallah 🥰🥰❤️❤️🥰laff bouche Yalla nagne la dégue fou sorri way Amineeeee 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼je suis chrétienne mei weuyou Coumba bi ak Sabdou karbala je l’ai aime bcps ça m vas droit au cœur ❤❤❤❤🥰🥰🥰🥰🥰😍😍😍😍
Wawaw Yena niakignane Mash'Allah.
Vero danga bakh
@@giado8414 ohhh ken dou yéne 😍❤️
@@AlassaneDiop-rv4hf ken dou ioe Alassane
Aÿ dôme y alla n'a thiat sékhlou mashalla l'AF thiat way ma adorée ,bonne continuation je t'adore
Macha'allah wayy elle est juste merveilleuse bonne chance à elle 🥰🥰
Non machallah bilaye yémé n'a lolou nak yalla nako yalla défal diam AK goudou fan ❤❤❤
Mom elle est mignonne machala yalla nala yalla lafal si thiatt
Honestly am so impressed with the melody 💙 voice of this lady 😍. May almighty Allah guide you 🙏
Machallah yalla nala yalla sam arla mayla goudou fane ak weir ci barker seydina mouhamed psl
Machallah la petite perle noire ❤❤❤❤yalna yalla samleu bopam amin
Machallah 🙏 elle a une belle voix 🥰🥰
Alhamdoulilah.seu way ci prophéte Mouhammad salalahou aléyhi wa salam,way bobou dou nul dafay déss la belle ♥️ bonne suite
Ki Vue Son Ressemble ave Bigué Mar Lo❤ Machallah 🎉
Machalla quelle voix impressionnante bien encadrée elle sera une icône de la musique ❤❤
Thiatt rek lá beugui man dou Wally secke dou sidi diop Man yaw rek laye topou thiatt love you❤
Elle chante vraiment bien Mach ala yalna yalla lafthiate ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Pourquoi j’ai des frissons 😢
Kene d’où Seydina Mouhamed saws moko waral machalla
Sister beugu nla sétsi😊😊 machala yokal diom rek😢 Inchaala sa papa diambar la jadore tellment
Tallent dou rere ❤bonne continuation sister ❤🎉
Boye bii gawna mague des karr machalla
Xalei bi nagneko diapalè way cheuu 😓❤️❤️❤️❤️❤️
Kouy sa baye thiate seck khol sedna
❤❤❤❤😂😂😂
Thiate seck djour nga sa dome machalah
Domou ndanane lha mashallah mame nare bon continuation rak dji❤❤❤❤
Thiey seydina Mouhamed loko way mou nekh
Psl billahi❤🙏
Psl❤❤❤
Bilay dioy na ba sonou
PAIX ET SALUT D'ALLAH SUR NOTRE BIEN AIMÉ PROPHÈTE MOUHAMAD SALALLAHOU ALEYKHI WA SALAM ❤️❤️❤️
PSL
Manchalah ma fille chérie yala nala yalla lafal thiat kan ja tes vue l'autre jour avec Coumba gawlo je me suis dit mais c ki cette petite poupée qu'Allah puisse t'assister yobou foukawee.cii barkee seydina mouhamed Saw.domou ndanane ndanane rek l'ay done.bonne continuation ❤️❤️❤️
Saws❤️💐💐💐❤️💐❤️❤️❤️❤️❤️
Machalah xalé bu musique sénégalaise di dess ci loxom mingui ndank rekk❤❤❤❤geum se bop banane nga
PAIX et SALUT sur notre MOUHAMED RASSOULOULAKHIE
Mame nar sama dom dji machalla yalla n'a bat bi werr thi barki cheikhoul khadim
allahouma amine té papam diok si mom balaa yeekh yalnako yalla samm si barkei seydina Mouhamed SAWS 🙏
machalah mane dh khawma niata yone lakoy visionné si journée bi
Mame Nar Seck ❤❤❤❤❤❤
Elle est très belle la fille de Thiat et elle chante super bien ❤❤Machallah laff thiat
Way machalah way you nekh voix ki dès mo dakeu way artiste you djiguéne you naw yi machalah thiate outale ko aye sangatte dès bala mouye dougou si art bi na takou ba deugueur
😂😂
Waw gua deugue ndakh légui serigne lagnouye leke diko nane damako dounou sama woudiou perthiorgo moma deudale famille bimaye seye lou doye ware laye wakh ni dagnou beugue serigne
Boul gueume lolou lep sounou borom leu, yow del djoulli di diap rek, Lep Yallah la. Lo guiss dey diekh
Suis Catholique mè à chaque fois que ma dégue sons bi je ne peux plus me tenir et je cesse que de verser les larmes
Machallah kou bax nga
Merci beaucoup
NOTRE BIEN AIMÉ PSL ❤❤❤
Limoye waye bilahi machallah 😍😍
Machallah ma sœur li amna solo trop yalla nala sugnu borom sam
❤❤❤❤❤fi gua tambalé bakna ken dou rassoulilah swl manchalla ❤❤❤❤amal diam way
Machallah ci xalé yalna la yalla def mak bou ame niam avec bcp de succès dans tous tes projets
Bilay mangi dioy
Kiy foureul xana lii moy rolam thi emissions bi😂😂😂blac appart mashalla pour la fille de thiat Elle chante très bien sax 😢art bi amguafi place dei❤❤❤
Machallah yalla nako sunou borome défale diame akk salam wayyy néhna loleee
Allahouma saali hala Seydina Mouhamed nooril-aanwaar❤❤❤. Kénn dou Nabi
Quel talent❤❤🎉 dama dioy 😢😢😢
She's so beautiful a very black queen 👑 machallah
Machallah sama yaram bi dafa daw yalla nala yalla lafal thiat
Yaw dh bilahi geune nalla beugg nak mame cheikh ibrahima fall minga waye 💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞
Machallah bonne continuation
Machallah belle voix
Machalla yalla n'a yalla yokou ❤❤❤
Machalla paix et salut sur lui
Ma challah tre belle voix ❤❤❤❤❤❤❤
Barki alkhourane ki en souma amone si mome ndoguall d'où music tag yonene rekk❤❤❤❤
MachaAllah yalla nako yalla lafal thiat nékhna trop mais sou mourone bop rék ohh
1ere fan❤❤ds kelk années inchala bouko ken kheutio ak man 😂😂machala machala
❤❤❤❤❤❤machallah ligua way mame cheikh ibrahima fall lamp machallah ❤❤❤
Ken d'où Nabi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Heee kiii moy mame nar sama dom dji.laf thiat wayyy.❤❤❤
Machalla
Yalla nala yalla lafalllll thiattt
Machallah laf thiat mais plateau bii Nice na c'est jolie ❤❤❤❤
Lolou am n'a nguéweull dom di way bay di way machalla laf thiat mai dfa khawa timit na niémé micro bi toutti
Li baye bi togue la motakh meunoul niakk ❤
Kikay lekna micro bi 😅
teksi.khalè tamite amoule loudoule 16 fokk mou desss toutti
Machalah,mais je pense k âge bila rek motakh mou khawa timit mais Dina nieuw inchallah
Ak badien bi tmt day way
Machalla way ndeysane 😭
A chaque fw ma deglou ko je pleure je vous jure
Machalla yalla nala yalla défal diam 🙏 référence gua bilaye ❤❤❤.
Black beauty ❤ she is a beautiful girl ❤️
Bonne continuation ma fille
Mashalah laff thiate ❤
Mashalha belle voix ❤
Yalla n'a souniou borom samoula ci barké Mame cheikh Ibrahima fall 👌❤
Yalnaléne yalla takhawou
MachaAllah Lii Waay Mame Cheikh Nekhna Lol🙏🙏🙏❤❤
Notre fille chérie
Seck saala toubé wayal
Khana ki moy Daba SEYE bou ndaw macha Allah
Le son est très faible on n’attend pas bien mais machala elle chante très bien ❤️❤️❤️
Enlevez les bouchons à l'intérieur de tes oreilles
T'as un problème toi
@@gamesandfilms8944 😂😂
Waw machalla 🥰🥰🥰🥰laf thiate
Ma challah
Un père content laf thiat ❤
Quels belle voie machalla bonne continuation
Qui Moy way katt deugue batou yeurmandé bagui djoyy lo kholl😱🥺😭😭😭 mouhamad psl
Machallah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah elle a du talent et une belle voix k Dieu la préserve des mauvaise langue mais elle ressemble trop à Farida (Bigué) on dirait des sœurs
Ouï ouï am nagnou trace deh
Machalla dioyna
Nguewella nekh, dome di weuye papa di fellou, Mash'Allah
Machaallah yalla wéral baat bi Inchallah
Boulfate moraybi machalla tagual gual younentibi DH boul woy amoul ndiarinie
Bilahi
Donou na baye bi machallah
Oh y’a Mouhamed ❤️❤️❤️🙏
Yalla nala yalla défal diam❤
😢diayma gorr deug bi❤❤
Ndeysanne
J’aime Thiat Li diomouko
Yalnako Yalla lafal thiat thi barké SEYDINA MOUHAMED (PSL)
Tu m'a fais pleurer
❤❤❤❤ machalla quels belle voie bonne continuation
Ndeysane ❤❤❤
Sallalahou aleyhim wassalam Allahouma amine y’a rabii 🤲🤲🤲♥️♥️
Machallah ❤️❤️♥️ 😢
Billahi xole séd na ❤elle chante comme un DS c dans le sans nice. Thiate légui nak am gua liguéy
Machallah yalla nala yalla defal diam te mouseul la ma belle ❤🎉
J'AI EU DES FRISSONS 💚❤️💛💛💛
Hii ki papame rek laye waye machala ❤