Massa waye,parents yi naniou conseils sene domi guedj dafa am ay rap you bone té daniouye sokhlo bakanou domou adama,na nieup moytou guedji ak deekhi ci année bi c est dangereux
Parents yi déléne téla diangal sén dome yi natation Sénégal deukou ndox la Té guédjou dakar yi dafa bari courant liko dalé koussoum ba st louis courant la Guédjou dakar yi boléne minoul té meno fééy da ngua wara andak dale guécc dagne koye meun dou aye thiapakh thiapakhi rék Mane alap lébou guédjou ndakarou yeup sangou namafa
Massa way ca me rappel mon cousin c triste
Ndeyssane mettina😭😭 yalla yalla yeureum té diégueul gni lape kharé lén thia aldianaï firdawssi thi barkè sedina Mohamed sws 🙏🕋
Amine
Hooo Migui may fatali sama rak bi nouaé si lac rose bi ama goul sakh 40jour 😭😭
Yalna ko yalla khar aldiana
Pabi kou dal la yall nako yalla yeurem
Naleu yalla degg chicorien. Doundeul baye darou
@@seynabougueye6401 wawaw fa mam borom darou kéy
Ay yaw li.metina dh 12 ans😢😢😢
J'habite a camberene mais meussou ma niémé guedj gui ay khalé yi moytoulene
Soupkhanala
Il est au paradi al hamdoulilahi rabil alamine.
Paix à son âme
Yalla nako yalla yeureumm
Sana deuk kébémer
Guèdiou camberene dh ganne lay bagne en plus fikkk tawoul kouko kham dossi sangou
C triste,Senegal un pays sans loi.toutes les plages du monde y'a des maitres nageurs.A quoi sert les sapeurs pompiers.
Yalla nako Yalla nitt
Massa waye,parents yi naniou conseils sene domi guedj dafa am ay rap you bone té daniouye sokhlo bakanou domou adama,na nieup moytou guedji ak deekhi ci année bi c est dangereux
Doy na war
METINA
Parents yi déléne téla diangal sén dome yi natation Sénégal deukou ndox la
Té guédjou dakar yi dafa bari courant liko dalé koussoum ba st louis courant la
Guédjou dakar yi boléne minoul té meno fééy da ngua wara andak dale
guécc dagne koye meun dou aye thiapakh thiapakhi rék
Mane alap lébou guédjou ndakarou yeup sangou namafa