Musicalement elle est au top machallah ses tubes cartonnent❤❤❤ Côté habillement et paroles elle est très correcte machallah❤❤❤ Nala Yalla lafal thiat inchallah ta boula kéne kham ci you niackk fayda yi nga gueuneu géré sa menage, Djeyla nioune dagne la beugue réck GUEYE ndeyssane❤❤❤❤❤ Ça kaw ça kanam inchallah
Dieyla est devenue une femme machaAllah ! Ndeyssane adouneu dou dara, yalnala yallah diobolé ak seu dieukeur mou yeureum leu ndakh kou yarou ngay niroy
Ayy dorr ak sagua bokoul si seuy yedd leneu goor gni mo geuneu yaye gua fékhel yarr say dôme si arr ak yirr djigueneu djigueneu yi beug nagnou seuy dagno guisoul louléneu teuyé
Deugeuleu mom mais audio rek rek te meun am c etait l unique nagoul ka itam seuy soutourala ak mougn mais nak mougn loo meun kou meuneutoll rek demal .@@AwatoureTouré-u9h
0 vulgarité 100% talent 100% tenue bravo dieyla comme dab elle déçois machallah 🥰🎊🫶🩷🥰et bonne continuation inchallah yasi meuneu ce que vous brillez 🫶💜 🤍
Mane ahh dieyla ak Ndeye Marie damaléne beugue lolou sakh ba melni niouma bokkal ndeye ak baye ba kou wakh si niome lou niaw sakh damay metti trop sakh😢bonne continuation mes sisters love❤❤❤❤🎉
Elle est l'artiste de l'année du côté vestimentaire elle a beaucoup travaillé le style. Music rime avec mode. La partie de Aziz Ndiaye , Aïcha , Miss, Elimane Lam, Maty est juste top
Je comprends rien de la chanson mais je vous assure que j'aime grave la voix de l'artiste et le rythme de sa chanson. J'écoute en boucle 😂😊. J'aime trop ❤
Subitement j'aurais aimé être sénégalaise à cause de cette chanson 😊😅. Mais bon je suis fière d'être Camerounaise ❤. Je sais pas si l'artiste lira mon commentaire, mais vraiment je l'aime grave et du courage à elle dans sa carrière
@@MaryamNkambafélicitation❤ heureux menage. 😂❤L'importance est qu'on est des enfants de l'Afrique. Même si on n'est pas du même pays non partageons le même continent. Vive le Cameroun 🇨🇲 vive le Sénégal 🇸🇳 vive l'Afrique 😍. Que dieu vous préserve du mal 😘🥰🙏
Kou beugue dieyla depuis qu'elle chante sur s'en petite gll jusqu'à présent rek aimel ❤️ li nékna way machallah bonne continuation yalna yalla di wérel batbi rek on t'aime 🥰🔥
Malaa aimée barké Mame Khalifa ❤depuis sen petit gallé jusqu'à présent 🎉🎉Que le tout-puissant te protège!amine ya raabi 🎉focus rek🎉🎉on est derrière toi🎉🎉🎉🎉
Et si chaque personne qui regarda cette video s'abonne au compte de Dieyla, cette jeune talentueuse artiste sans vulgarité. Ne pensez-vous pas que celà pourrait encore lui redonner courage pour nous bombarder de titres epoustoufflants ?❤❤❤
Elle incarne pleinement le futur de notre industrie musicale. Tous ses titres sont des master-classes, chapeau. Pourtant, elle parle pas beaucoup mais fait son petit chemin. Elle ira loin, inchallah.
Mais Chérie Yass ❤❤ Nexx nexx bi suniouy nopp yaw leuh🎉🙈 j'écoute la chanson en boucle depuis hier MachaAllah tt est au rendez-vous yalnala yalla samm laffal la thiatt inchaAllah 🥰🙏 Love U ❤
Bilahi walahi tahala souma amoul dom bou touddou Dieyla souma dewé douma talli sokhla wouma sakh nga kham ma wayé mane mala beugg nguir lingay def yalna yalla defal la diamou ak wére limoy wané ni vous aviez mérité de gagner la finale sen petit gallé si vous voyez gniko dieul gnepp kenn amoussi aye single mais yaw Dieyna yalna yalla defaléne jamm diou yaatou ❤❤❤
Li doumasi doyal plus de 10fois magui kay sétane di ré comme dof bilahi dieyla ya meun kay doflo nga niou dale 😂 machallah yalna yalla wéral bate bi bonne continuation ❤
La meilleure de tes sons 🎉🎉🎉❤
qui comme moi écoute cette chanson tous les jours tellement que son bi dafa nekh bilay khalei mo meune way yalla na yalla lafal thiat
Mane chaque jour magui kay deglou❤
Mane chaque jours ❤🎉
Musicalement elle est au top machallah ses tubes cartonnent❤❤❤
Côté habillement et paroles elle est très correcte machallah❤❤❤
Nala Yalla lafal thiat inchallah ta boula kéne kham ci you niackk fayda yi nga gueuneu géré sa menage, Djeyla nioune dagne la beugue réck GUEYE ndeyssane❤❤❤❤❤ Ça kaw ça kanam inchallah
❤😢ndeyessane ta dernière phrase me touche dei bb ,adouna nila nani begeuneté rek😊
Charlotte GUEYE laa sante motakh xol lay wakhé kii bilay damakoy nianal Yalla réck damako beugue ndeyssane❤❤❤
Moi je n'arrive pas à tenir mes larmes merci Dieyla
Veritee absolue
Mrci laba ❤😢
Khalé bilahi do sen morom nioun Say fans contane naniou fepp nga mené❤❤❤
@@RabiSané 🥰🥰
Dieyla est devenue une femme machaAllah ! Ndeyssane adouneu dou dara, yalnala yallah diobolé ak seu dieukeur mou yeureum leu ndakh kou yarou ngay niroy
yérim néna sank si émission ni si gni dakh woye nga bokk si sénégal
Niou wadié ko tabaski bi inchalah 😂❤🎉
Inchallah 😅
Nekh na trop 2:07
Barke serigne babacar sy yalla nala diam sonal
Quand Dieyla la chante il ya tjrs une certaine énergie qu'elle déploie pour donner l'aspect de la chanson inssi une raison de l'aimer 🎉🎉 c'est ouff 🥰
Waouh ça me fait plaisir ❤❤❤❤❤❤❤
Goorgorloul té mougne reck té khamni seuyy reck moy galadiou djiguéne 🎉🎉🎉🎉
Bravo 👏
Ayy dorr ak sagua bokoul si seuy yedd leneu goor gni mo geuneu yaye gua fékhel yarr say dôme si arr ak yirr djigueneu djigueneu yi beug nagnou seuy dagno guisoul louléneu teuyé
Deugeuleu mom mais audio rek rek te meun am c etait l unique nagoul ka itam seuy soutourala ak mougn mais nak mougn loo meun kou meuneutoll rek demal .@@AwatoureTouré-u9h
0 vulgarité
100% talent
100% tenue bravo dieyla comme dab elle déçois machallah 🥰🎊🫶🩷🥰et bonne continuation inchallah yasi meuneu ce que vous brillez 🫶💜 🤍
Kou d'accord ni elle est le mlleur de sa génération lalal j'aime 🎉❤❤❤❤
Mbeugue itam machalah.
🎉🎉@@mberryable
Lo😊😊a
'kjj😊àqu
Mane ahh dieyla ak Ndeye Marie damaléne beugue lolou sakh ba melni niouma bokkal ndeye ak baye ba kou wakh si niome lou niaw sakh damay metti trop sakh😢bonne continuation mes sisters love❤❤❤❤🎉
Elle est l'artiste de l'année
du côté vestimentaire elle a beaucoup travaillé le style. Music rime avec mode.
La partie de Aziz Ndiaye , Aïcha , Miss, Elimane Lam, Maty est juste top
Kouko sétane plus de 2 fois rek beusseul j’aime ❤
Mandé sétane nako 3 fois machallah 🥰❤️
😅0e n😅❤❤😊@@SokhnaNdiaye-md3wk
❤❤❤❤
🎉🎉
Je comprends rien de la chanson mais je vous assure que j'aime grave la voix de l'artiste et le rythme de sa chanson. J'écoute en boucle 😂😊. J'aime trop ❤
Subitement j'aurais aimé être sénégalaise à cause de cette chanson 😊😅. Mais bon je suis fière d'être Camerounaise ❤. Je sais pas si l'artiste lira mon commentaire, mais vraiment je l'aime grave et du courage à elle dans sa carrière
Je veux te marier💍
oomarfaye2500ansjazhb72hhĥhhhhh ⁴😢kǰ ɓv a1ɓ?
Qy0p
@omarfaye2500 😄 je suis déjà gravement mariée 🤭☺️
0
@@MaryamNkambafélicitation❤ heureux menage. 😂❤L'importance est qu'on est des enfants de l'Afrique. Même si on n'est pas du même pays non partageons le même continent. Vive le Cameroun 🇨🇲 vive le Sénégal 🇸🇳 vive l'Afrique 😍. Que dieu vous préserve du mal 😘🥰🙏
Elle et trop belle ta musique macha'Allah toi ci tu es trop magnifique et tu Chantes très bien je suis très contente ❤❤😊😊
Li dou dara ki waya goule sakh yalla naniou fi yalla bayi bassi kanam ngéne khol
Ndaysane lolou forna
13millions de vues 🎊🎊🎊
Machallah❤🎉❤🎉
Notre coumba gawlo junior si elle continue sur cette lancée elle ne décevra jamais amin❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Uyhjjii chi Minh
So Meué rek Meun gua Cheri Yass💍Mâchalla❤️
Dafa ler
Le charisme de bb-bineta dougne si Wakh machallah dieyla
Ya meune si sa génération
Meune génération gnom mia guisse
Talent pur sans vulgarité ni frasque
Bonne continuation petite Soeur
Étoile montante, chaque tube qu'elle sort est un hit, machallah
Mashalah, clip magnifique je sens bcp la marque de coumba gawlo que dans le style du chant mais egalement vestimentaire. Djeyla domoromou gard yi❤
Kou beugue dieyla depuis qu'elle chante sur s'en petite gll jusqu'à présent rek aimel ❤️ li nékna way machallah bonne continuation yalna yalla di wérel batbi rek on t'aime 🥰🔥
❤❤❤❤ i love you my dieyla since sen petit love you so much dear wish you all the best ❤
@@AdamTouray-qq2sc😅
@@AdamTouray-qq2scli😅😅😅😅😊😊œkik😮k
Uik 😊😮😮😮
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
😂😂😂😂😂@@AdamTouray-qq2sc
parmi tous les jeunes qui sont passés par Sen petit Galé .. elle est la seule et l'unique que je kiffe.... Belle vidéo com Dab. bonne continuation.
Malaa aimée barké Mame Khalifa ❤depuis sen petit gallé jusqu'à présent 🎉🎉Que le tout-puissant te protège!amine ya raabi 🎉focus rek🎉🎉on est derrière toi🎉🎉🎉🎉
Oh magui sogua bok si 10000 premier voir un clip waouh 😂😂😂🎉🎉🎉
Depuis le cameroun
Et si chaque personne qui regarda cette video s'abonne au compte de Dieyla, cette jeune talentueuse artiste sans vulgarité. Ne pensez-vous pas que celà pourrait encore lui redonner courage pour nous bombarder de titres epoustoufflants ?❤❤❤
C déjà fait y a longtemps ❤
@@alimatouToure-zq1yx machallah comme ça on va la supporter à aller de l'avant
Ta raison il faut qu'on la soutienne elle chante hiper bien
Merci pour ce message
Wawaw
Son bi doumassi doyal dieyla Bilay ya meun way❤
Khale bi meun na waay dhè elle tres forte bonne continuation
Meilleur tube de l'année ❤❤❤🎉🎉🎉🎉
😂😂😂😂❤❤❤❤
🎉🎉🎉
Elle incarne pleinement le futur de notre industrie musicale. Tous ses titres sont des master-classes, chapeau. Pourtant, elle parle pas beaucoup mais fait son petit chemin. Elle ira loin, inchallah.
I
Dieyla yaffi néeee dieuliko♥️🤩 0:47
Bilahi khalébi damako beugue ndakh meune way, correcte mashallah
Niaffff li nexna wayyyy ❤🎉🎉🎉🎉🎉ohhhhhh🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳💪🏼💪🏼💪🏼💪🏼💪🏼💪🏼✌️✌️✌️😍😍😍😍😍😍
Machallah yalla nala yalla takhawou ci barké Seydina Mohamed psl
Thioum😂...mane mom yama doflo ya meune nak😂
Comme d'habitude rek tu ne décois jamais, simple, naturelle, belle voix franchement rien à dire🤩
Popopoppop dieyla ya mmeun nianou dofloo khalebi chanter rek ngay deff sans oublier avantage d'etre skinny tes robes te vont à merveille
Ki mome dou nite comme djinei machalahhh khalei biiiii sheuteute ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieyla ni laniou koy bayui yén ohhhhhh néxna trop ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Aziz dabala yalla nako yalla yeureum
Non vraiment cette femme incarne la beauté, le talent, mais que dire? mais Dieyla tu es la reine que tu penses être mama pardon félicitations 🎉
Dieyla tu es la meilleure chanteuse de ta génération
C'est pas ton probléme alors vas faire pipi et dormir ignoble
C'est pas ton probléme alors vas faire pipi et dormir ignoble
Flow, feeling, sagnsé, qualité image lépp est au top une touche publicitaire pas comme les autres 🎉❤
Mais Chérie Yass ❤❤ Nexx nexx bi suniouy nopp yaw leuh🎉🙈 j'écoute la chanson en boucle depuis hier
MachaAllah tt est au rendez-vous yalnala yalla samm laffal la thiatt inchaAllah 🥰🙏
Love U ❤
Anita AK bamba niaf beug n'a li mes ken d'où sama Rak dji dieyla❤❤
*Li dafa fess mogui tourou way fo teuleu mou gueuneu nékh guoné guilé y’a meune nakk machallah 🥰🥰🥰🥰Bne continuation le meilleur reste à vnir🥳🥳❤️❤️❤️*
Yalla nala yalla sam te deugeureul sa seye
Nan dieyla ya dakk weiyy senegal mane mom tes ma chanteuse parmi tout les filles de ta génération
❤❤ la voix d'or machallah ma puce❤❤
Nekhoul ba nekhoul mais Khalè bi dafa mane bilay ❤😭🥰🫶
Notre diéyla nationale tu a encore tapé fort 💪 ❤❤❤❤🎉🎉❤❤❤🥳🥳😊
Moussoul guainai weuy mou nakhari c fort ça ❤
Machallah BB dieyla, j'ai trop misé sur toi, ne me déçoit jamais ❤❤❤❤❤ ni rék leu déh, la route est certe longue mais pas impossible 🙏🙏🙏🙏
Ma dieyla chérie ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤yallah nala yallah same te are 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
❤❤
Jeune artiste yi mom yalénn di diangall tu es la meilleure 🤭❤️❤️
❤dama contan bilahi vivi ak per youssou dano bokk si man bouma nekke bitim rew gnomay angkouragè sen personnalité sen dignité ❤🎉
J'adore cette fille❤❤❤
Lima nèhe si mome son âme d'où goudou tè daye nèhe Machala
Li doflo na kounei ya meune kay❤❤😂🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🥰😭❤️❤️❤️😭❤️❤️❤️🥳🥳🥳
Yako lale 😂😂😂
Yako lale
Lou lerr
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
6ou67
Félicitations la lionne de la musique sénégalaise ❤
machaAllah ❤️ la jeune chanteuse à la voix d'or,ca kaw ,ca kanam rék inchaAllah
elle a une voie magnifique elle a du talent la meilleure de sa generation 🎉❤bilahi ya meun😂❤
Sheuuuuutttttttt Sama daphné Feeling mom yakofa am.
Fepeu nga meuné Say sound rekk lay khar❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieyla très sérieux dofloongama parce que danga meunn ❤🎈🎊🎊🎊
Bobou clips bou hêrre 🎉🎉🎉Machallah le chanteur du peuple merci notre mya guisse et a amendes le King 👑 🎉🎉🎉🎉
Danga meune ko bakal diamono bayii nala kheil ❤🎉
Meilleur chanson
Chanson de l'année 2024
❤
10millions de vues🎉🎉🎉🎉🎉
Elle mérite 🎉🎉🎉
Machallah elle l'a mérité ❤🎉🎉
Son bi jour bima ko jeuké dégue tik tok la kham ni dafa nekh trop nekh way sa donne envie de danser 💃 ❤😂
Bo meuné rek meuneu nga mashallah Dieyla yalna yallah lafal la thiatt
Bilay walay talay ya mana way lafe thiat waye mo takh ma beugeu la,❤❤❤❤
Machalaa yalla n'a yalla wéral batbi téguil la bépe diafé diafé akk mbolom dioulite
Mom ay wayom mo am feeling🎉 way li nexna trop
Moi je l adore ni tambour elle travaille puis dans son coin star bi mom doundouka ce qui fait la difference ne change ma ma belle❤ ❤❤
Bilahi walahi tahala souma amoul dom bou touddou Dieyla souma dewé douma talli sokhla wouma sakh nga kham ma wayé mane mala beugg nguir lingay def yalna yalla defal la diamou ak wére limoy wané ni vous aviez mérité de gagner la finale sen petit gallé si vous voyez gniko dieul gnepp kenn amoussi aye single mais yaw Dieyna yalna yalla defaléne jamm diou yaatou ❤❤❤
❤❤❤❤❤
Amen yarabi
Vraiment finale bi mérite nako guisouma kou ko dakh way ❤❤❤
Hey jtm c tout
😢😢😢😅
Barki Serigne Babacar Wayyy djeyla meune weyyy wayyyy akhhh 😭😭❤
❤
Xalei bi laf thiate yaa meune kay macha Allah 🥰
Cette fille la elle est exceptionnelle machallah ❤❤❤
Ki mo dakha woye Senegal 🇸🇳🇩🇪👍👍
❤❤
Oh elle chante bien dieyla des cœurs pour elle ❤❤❤
ya meune sa son ladone xar pour ma meuna sagnessé si Tabaski bi merci dieyla
Vivi, titi, mia et dieyla les reines de la musique Sénégalais 😊❤😊❤😊
Y’a meune nak bilahi oh damala beug rek te yalla tax 😭❤️
Wopopopopo dieyla machallah linguay dff nexna trop ❤🎉
Mais Dieyla 🎉🎉🎉ya meun bilahi 😢
Bilae nakk ya meunn ya eupp dole ya geuna fété khalé té ioe laniouy topp ont adore notre dieyla nationale ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Vréma deffatigua sa meunine wayé sa bongoman bi loumou beau lanla🥰🥰
kou beugue dieyla depius quelle chante sur petite gll jusqu à prèsent rek aimel❤❤❤❤❤❤❤❤
Li doumasi doyal plus de 10fois magui kay sétane di ré comme dof bilahi dieyla ya meun kay doflo nga niou dale 😂 machallah yalna yalla wéral bate bi bonne continuation ❤
❤❤❤❤❤❤❤
La meilleure chanteuse machallah ❤❤❤
Heii khaleyi am gueine filing deh 🎉🎉❤❤❤ niafffffff😊😊😊😊😊
Je kiffe grave ❤️
Bilahi dieyla ya meun waay MachaAllah
Machalla un belle voix accompagnée d’une mélodie d’une grande facture