Un sujet d'actualité très sensible k tout un chacun devrait mettre sur la table. Le viol est un acte ignoble fustigeons le au lieu d s taire/ Osons en parler et régler la situation une bonne fois pour toute
Khawouma kagne lay sétane série guiss ci une femme forte ,toujours on te bas do sah diéma défendre sa bop com djiguén dal waroul def effort ah vraiment
@@awacheikhdia885j'ai pas terminé je ne pouvais plus continuer mais si elle s'est rebellée c'était presk trop tard,parce qu'il la violé et torturé maint fois
Cet épisode est tellement intéressant.Vous avez mis l'accent sur la marginalisation que subissent certaines femmes.On peut aussi retenir sur cet épisode l'attitude irresponsable des parents envers leurs enfants.
ndjir yalla bayi lenn xésal te nguén geum senn tn, bou si topou moy djarou bi boko solé rek sa weurseuk oubékou boolé si tekki am xalis 😂😂 sénégal mo nékh rek 😂😂😂😂😂😂😂😂
A chaque fois que je regarde le début d'une scène de viol dans un film je prie pour que qqun entre dans la pièce que qqun vienne sauver la victime avant que ça ne soit trop et si j n vw personne venir et que la scène continue jusqu'à ce qu'on viole la femme ça me met en colère
Yayou khale bou djiguene bi kene guenouko sagane yore sa bome amo si môme bene setlou Lou meusoul âme so guisè dosi waslou ak mère yii légui nat ndayale rek laniouy topato
Mane magui sagua pacoreck alort que c une série sa me dechire le coeur sa en tant que homme mnede samaye soeur damalaine sakhe rousse badi khalate yeneuyi qui il est malade waye😡🤬🤬🤬😡🤬🤬😡😡🤬🤬🤬😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡🤬🤬
Pourquoi ngène nane grand viol grand amour lay done after g pas fini l'épisode mais j c qu'un homme va changer sa vie et la sauver des griffes de son frère
Li niawna yalla naniou yalla mayy mounie nioune djiguenn th niou sent ko boubah guinaw bigua hamni mayy naniou ay mak youguenn kou bonnki😭😭😭 man koyy tonie sah nah th li film kasela mais nak niawna😭😭
C un sentiment difficile a comprendre...tant que tu na la pas vécu tu ne peux pas comprendre on ressent de la honte même quand on décide de le dire on ne c pas par ou commencer
Yalla nanou yalla moussal si niit kou bn mais yén djiguen gni tmt lou lén dall rk dou guen si wax ak kén ay dioy rk guén di ko fayé xalé bou djiguen waroul nabou drr yayam délén wax ak gnom bouguen amé lou lén méty mais di nabou ba kagn 😭oh li méty na trp
@@mamemariamaseye5183 ndeye San nako yalla yeureum....t xareko al djana suniu maman jooju.... m tay so amoul ay mbokku you bakh tuti moungasi jaare doon sauvage alors q mbokku legui yi trokhala laniou geuna man q jappalela
Mais non vraiment c'est honteux pour un grand Fere comme lui qui doit protéger ta propre Soeur 😭dommage pour pour tous les filles qui sont vie comme ça 🙏😭
Les hommes qui violent sont des lâches surtout ceux qui ont la même famille comment peut on faire un acte si ignoble couché avec quelqu’un sans son consentement j’ai trop mal pour ces femmes la peine de mort doit être appliquée 😭😭😭😭❌ Mais aussi une maman doit être bienveillante et avoir l’œil une moindre changement sur ces enfants
Mou way man 16 commentaires lafi fekon avant may sétan 😯 mais sa mome dafa wara diekh par se que barina trop si famille yi encore félicitations yakamtiwon nako lol...
Li Ba kagn...Nous ne devons se laisser tjrs abattre...On est plus forte que ça...arrêtons de subir...wollah kumu meneu nek ci adouna nagnu ko dénoncer, xawi soutoural...
Thiey sounou yay yi tjrs a nos côtés yalnala len fi yalla bayi banou feikei leip 🙏❤️
Grand amour mo dakh si serie yi ay thieu pikini ki d accord vk mw
Nane wadial magal porokhane ngui inchallh s mountakha mbackè balla yalla nafi yague lool
Amine
Inchallah sounio yitte
Amine way
Amine
Amine inchallah
Machalla ame na solo trop waye Sénégal yalna nagnou ame diame barke moukhamed saws thé mousal thie bala
Allahouma amine
Amine
Stop stop stop j'ai bcp pleurè li dafa wara diekhe Sènègal boudoul sa frere nek sa oncle wala sa cousin wala sa Papa ba cagne Stoppppppppp😭😭😭😭😭😭
C dégueulasses 🤮😡😡😡😡
Vraiment sokhna mbow li daffa nianww
PSP pour la violence et la viol
@@okboomer3220 de trop
wala khalé bou gor bi nek si kogn bi wala Mr diop isec stop
C'est vraiment triste yalla nagnou yalla mouseul si viol
Genre bi mofi bari nak nopi walé rék
Amine
Amine
Amine way
Amine sibarke Serigne Touba 🙏🙏🙏🙏
Paco ake kanama gui di melni passerelle mounane daay violer cochon de chrevre😂😂😂
😂😂😂😂passerelle mo takh mou niak jom kay
Waa louy cochon de chèvre nak🤣🤣🤣
Cochon de chèvre 🤣🤣🤣
Yaw han😂😂
Penda Diop 😂😂😂😂😂😂😂bayima d
Ku bëgg serign touba beussul j aime
L'I môme nekoul grand d'accord grand viol la ay way yeureum lene jiguene yi guir yalla 😢😢
Ak man li dafa niaw toroup
@@boromtoubakhelcom8902 bilay sa meti 😭
@@khadijaibnibrahima359 grand amour tay mom bi andou ma si li dafa mety toroup way
@@boromtoubakhelcom8902 bilay dama joy sakh
Wahal dé limom grand viol la wayé dou amour doyna war
Un sujet d'actualité très sensible k tout un chacun devrait mettre sur la table. Le viol est un acte ignoble fustigeons le au lieu d s taire/ Osons en parler et régler la situation une bonne fois pour toute
Li nekh na lolu ❤️
Khawouma kagne lay sétane série guiss ci une femme forte ,toujours on te bas do sah diéma défendre sa bop com djiguén dal waroul def effort ah vraiment
Djigèn dafa fragile mais dou nieup Mais sama genre yi dinala niouss ba ngeu khamni yalla nieup la may dolé
bilay
Pourtant elle sest releve dh
@@awacheikhdia885j'ai pas terminé je ne pouvais plus continuer mais si elle s'est rebellée c'était presk trop tard,parce qu'il la violé et torturé maint fois
@@Mamita221 WALLAH Mane mêm souma dadiék goor bo khamni moma meune DINA dadj deud bâ daw.nah douma KO may dara
Un frère est censé protéger sa sœur et non pas la violer! 😭😭😭
Wakh deug yalla
Wallahi khalé bou djiguene bie yeurame nako trop 😭😭
Cet épisode est tellement intéressant.Vous avez mis l'accent sur la marginalisation que subissent certaines femmes.On peut aussi retenir sur cet épisode l'attitude irresponsable des parents envers leurs enfants.
Vraima noppu dalotina lifoumou ame yalla nanou si yalla mousal
Si seulement j'avais un frère comme paco👉baxal ko rek la si meune
Li niaw na trop mane dh kou goor ki yalla bouma tassé ak mom bone na saleté na thiiiim
Li métina t daw yaram. Gnouy doundou li bilay li metina 😭😭😭😭😭😭😭
Billahi j'ai même pleuré
Macha halla wa pikini production vous faites un bon job 🙏🙏🙏
Vraiment li mome geuw ma neh mane na nek sœur ak nimou nekhé mane souma guissé samay sœur sama khol day fekh
Ohhhh bilahi sama xol bii mogui méti li dafa gniaw ci frère way😭😭😭😭😭
Ndeysan wolahi amena solo nous sommes tous derrière vous si kaw si kanam rk dina bx
Kou fi nek 2024rk❤ man mene nama comprends sa propre père sa oncle wala sa cousin ms sa frère lolou mome théâtre cassé la menoul nek 😢😢😢😢
La fille est tellement simple j’aime 🥰
Mome noumou toudou
mame cheikh ngom diké 🥰
@@missbosse3527 merci
mame cheikh ngom tkt
j'ai pleuré au début mais j'ai été soulagé à la fin il faut savoir se défendre dans la vie ne jamais se laisser faire
eva Reine j’ai vécu la même chose avec mon demi frère sama domou baye
@@adjayade7418 j'espère quil pourit en prison le miserable massa puce jespere que tu ten remet
Ndaysann j'imagine ta douleur ma puce 😢yalnalén yalla até déff katou gnawtéf mo yalla dakoy wérr beuthieu courage
Ki papam ak yayam gnoy aye dof ndom bou djiguene soko yorei dagua koy setlou bou bakh di waxtane ak mome oubil ko sa bop doula ragal wax dara
Surtout yaye
coumba sy voilà mane lolou la done wakh sakh
Pour mane problemaebi si papa djila kw
Adama Gaye dioumou lo déh. Yaye dji tamite ame na ci part de responsabilité. Nagnou khaare épisodes yi ci topeu bakham
@@adamagaye6043 yaye dji kay kène démoul mou dès surtout dome djou djiguéne
Je sais pas pourquoi mais j'adore déjà sa maman ❤
😭😭takh guène ma fatalikou lou mètti courage Fatime
Grand frère bou melni paco merci rek
Wa mousieur matar❤️🙏bonne continuation
Danga warana diammm ndayéme ki goor bou bone la kou d'accord ak mane beujeul j'aime
Paco mi Kou dokhann bayamm mou dieulleuh sérieux mouguii mell ni mane leenn ko deff 😭😭😭😭
Zeynab diallo wax deugeu yaaye yi sonnou nagne yaay rk laniouy saaga mais li mome niaaw na trp
Zeynab diallo li serie rek la dani yété rek bayil saga yi
Ms li théâtre la rk daniouY Yetei rk ymgx
Que Dieu nous épargner les mauvaises personnes 🤲
ndeyssan yallna gnou yalla samal bopam
J'aime très bien ces séries ❤️🙏
ndjir yalla bayi lenn xésal te nguén geum senn tn, bou si topou moy djarou bi boko solé rek sa weurseuk oubékou boolé si tekki am xalis 😂😂 sénégal mo nékh rek 😂😂😂😂😂😂😂😂
La blessure du frère de dické semble tellement réelle😄
A chaque fois que je regarde le début d'une scène de viol dans un film je prie pour que qqun entre dans la pièce que qqun vienne sauver la victime avant que ça ne soit trop et si j n vw personne venir et que la scène continue jusqu'à ce qu'on viole la femme ça me met en colère
Yayou khale bou djiguene bi kene guenouko sagane yore sa bome amo si môme bene setlou Lou meusoul âme so guisè dosi waslou ak mère yii légui nat ndayale rek laniouy topato
Bilay amna mére yokhamné amougne sétlou sisédome khéw rék 😭😭😭
Célibataire yi reik nio tei la commenté🤣🤣 nioune mariée yi niome on vient de visionné 🥰❤️
C'est normale iowite 😀😀😀😀
Yaw do bayi todie ms yalla bakhna
Deug lawakh marié amoul diotou wakh 😀😀😀
@@mamadoumareme9849 😒😒😒
Ki mo raw Coronavirus Billahi li Febar la
Li dawna yaram bilahi 😭
Wa yèn amonlén ay nelaw khana mane deh insomnie total la am montax vive Grand Amour
😍😂💃
khana yama walleu
Grand amour moko diarr naq😎😎😎🤗
Pikine yalle nguèn gaw am 1million abonnés 👌
Aminé
Amine inchalla h
Yalna nou yalla mousal si lou bonn
A li de kou kaye dèf sa rakk raye ko rèèk mo Dagann si momm
Quel inspiration waw ça donne des frissons que des surprises bravo
Mak dji dou Maguou dara Ki mo niak fayeda Amoule sakhe khole
Bilay🤦♀️🤦♀️
Boul faté film rékk La
Mais parfoi daye ame même boudoule viole si yéne coté yi
Chapeau à diké
Mane magui sagua pacoreck alort que c une série sa me dechire le coeur sa en tant que homme mnede samaye soeur damalaine sakhe rousse badi khalate yeneuyi qui il est malade waye😡🤬🤬🤬😡🤬🤬😡😡🤬🤬🤬😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡🤬🤬
Ak rak nomou nekhe ho samay rek damay begue di anda ak niom ci mbeda my 😭😭ms pikin production nice diop bilay
Gor gouma féké ngayy torokhal djiguéne dina Todie.....
La fille ma fait pleurer bilahii
Ba kagn lay continuer tamiit li metina
😭😭prenons la peine d'écouter nos enfants
Ndaysane li métinama trop bil y souma guissé kouye déf lou niaw djigén dmy âme khôl bou diekhe diapaléne djigenyi nguir ylla rk 🙏🙏🙏🙏
Pourquoi ngène nane grand viol grand amour lay done after g pas fini l'épisode mais j c qu'un homme va changer sa vie et la sauver des griffes de son frère
Toi tu as compris
Li niawna yalla naniou yalla mayy mounie nioune djiguenn th niou sent ko boubah guinaw bigua hamni mayy naniou ay mak youguenn kou bonnki😭😭😭 man koyy tonie sah nah th li film kasela mais nak niawna😭😭
Série bii nékhna trop machalla ms diké môme dafma yagua nékh
WA Paco Bono rek ak djiguen nimou beure si deuk bi
C un lache
C'est très triste à travers un frère séducteur
Amna nio xamni nio beugue kouléni violé niou lay violé doko wakh lossiy neubb nane xawi soutoura da meuna wésou nioulay violé
C un sentiment difficile a comprendre...tant que tu na la pas vécu tu ne peux pas comprendre on ressent de la honte même quand on décide de le dire on ne c pas par ou commencer
@@naturalmavista1917 Merci
Dèsolè mais lou niaw khana djiguèn diouroul amna niokhamni mala yi sax nio lèn tanè foufffff sax
Ms grna bi mere nako trop
Jiguene day ray diko nakh ms ken douko dor yalla naniou yalla soutoural si korona virus bi
Vraiment taye mome sama khôl dafa nakhari dioyena ba sonou luttons contre le viol 😭😭😭
bien joué 💪💪💪inceste da bary si deug bi ...
C deguex
Kène dou yaye...dama beugue sama yaye li mon takh
Khawma yaye ji ak papa ji kousi gena saganne rékk
Paco ak papadji gno yam😡😭
Yalla nanou yalla moussal si niit kou bn mais yén djiguen gni tmt lou lén dall rk dou guen si wax ak kén ay dioy rk guén di ko fayé xalé bou djiguen waroul nabou drr yayam délén wax ak gnom bouguen amé lou lén méty mais di nabou ba kagn 😭oh li méty na trp
Non lidafa wara dienkh djicuene dafa sonou torope bodoute sa papa disa cousin wala disa frere wala kanéne dafa wara dienkh😭😭😭😭😭😭😭😭
Non sama yaram daw na nak bilahi li mom nexxhoul dara ci xol 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Salam. Ça pourra aider des jeunes qui vivent cette situation. Merci et bravo.
yall naniou yalla mousseul ci goor gou bonn
yall nala yalla defal diamm
Yeuremu lene jigun adouna dou dara bilahi 😢😢😢😢
C vraiment triste mai machalla grand amour c bien continuer sa ira inchalla❤💕
Nit dina yoor comportment boo kham ni ay dafay bizarre alors que Ken tegoukoko koudoul ay mbokkam......
Bien dit
Bilahi daouda khamo sakhhh ligua wakhhh nimou neker deugue. Mane Depuis la mort de ma mere je suis devenue desagréable
@@mamemariamaseye5183 ndeye San nako yalla yeureum....t xareko al djana suniu maman jooju.... m tay so amoul ay mbokku you bakh tuti moungasi jaare doon sauvage alors q mbokku legui yi trokhala laniou geuna man q jappalela
Bien dit
@@sokhnadioumadiaw2972 guisnga d
Souma meusana guisse sama xarite wala sama domou Badiéne bi niouye fo ack séne mag dama léne di nié billahi nakh mane amou ma mag th Frére ack domou baye la guena begue th amou masi béne mais mag bou goor bou méle ni nianou ma yalla ame cko th gni cko ame yéné woumaléne cko 🥺🥺😭😭
Cet une série trop intéressant
bravo Matar Sy le rôle du directeur te va bien .Bonne continuation
No mais pikini mashalla koi tha kaw tha kaname rek
Wa li lanla ca mom c est triste😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Mais non vraiment c'est honteux pour un grand Fere comme lui qui doit protéger ta propre Soeur 😭dommage pour pour tous les filles qui sont vie comme ça 🙏😭
Wa kou goor âme na khôl bonne gaaa dhe
Hooo 😭😭😭😭😭 Man kouy metital jiguen Rk la bañ dafay metty xoll bi dafmay naxari tropp
Compréhension yaye da am solo si yaroum dom surtout bou Djiguéne. Nañou yallah mousal si viol 😥😥
Thiey grand amour à chak fw bou bess😊💞 Wa tmt li mom foumou amati gnoulay violé ngay nopi rkk🤷♀️ mak bi yonou tole lako bgue df isshh
Moma diakhal ngamay violé may nopi khala toumako ak coum mat ti done si mane damay khékh ak yaw apres ma denoncé la
@@maxesseck6756 ahhh waxatiko way li tmt da yombou trop nak.
Li théâtre la rk daniouY Yetei rk
Les hommes qui violent sont des lâches surtout ceux qui ont la même famille comment peut on faire un acte si ignoble couché avec quelqu’un sans son consentement j’ai trop mal pour ces femmes la peine de mort doit être appliquée 😭😭😭😭❌ Mais aussi une maman doit être bienveillante et avoir l’œil une moindre changement sur ces enfants
Très important 👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿
Pourquoi les hommes sont cruels envers nous les filles soudoul dara djiguéne moléne diour s'il vous plaît épargne nous😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Goor mo diour djiguene tamit
Ho ne dis pas les hommes dis certains des hommes
@@kabendoumarewe6368 goor mo diour djiguéne wayé djiguéne tmt mo diour goor té djiguéne moy sougnou yaye
Li djiguéne di dathie goor douko dathie
J’imagine même pas ceux qui sont en train de vivre de telles choses... c’est horrible , triste 😭😭😭!!!
Djiguëne moy sene yaye
Stop les violences faite aux femmes
Djigén moy sounou yay moy sounou lepp je suis de tout cœur avec vous les femmes
Goor deug dou melnii jiguen ken doukoo humilier
Pape matar deih kanamou domaram la yor
Sonou bone meuno ame djigen diap sa rak diko def yène yii lii meunoumako sax contunier 😥😭
Film kasser leuh wayer j’ai une de ces rages contre Paco🥺🤦🏽♀️🤦🏽♀️🤦🏽♀️
MamiiSha Sow mais mane ma fokni ay niit gnoy bind seen histoire gnom gnou jouer ko?? Wola??
Non Wallah Bi mome ouff Manoumako setane Dakh dama beug sama Rak Paco cet rôle ces difficiles pour moi bilahi Oufff metti na trop
Coool en tout cas mangui khar suite bii😍👏