Jahman X-press Feat Ahmada Jadid - Bamba Ndiokonial (clip officiel)
Вставка
- Опубліковано 7 лют 2025
- EN CONCERT AU POINT FORT D'AUBERVILLIERT 27 SEPTEMBRE 2024 : shotgun.live/f...
Stream & écoute : bfan.link/bamb...
Crédits de la chanson et du Clip
Beat : Jrclavinova_61
Arrangement : Ada Studio
Mix : Moussa Ngom
Prise de Voix : Freeman Kay Feel studio
Percussions : Magaye Seck et Prince Jadid
Stylisme : Maam Samba - Bamba
DIRECTOR : BILAL MBENGUE
D.O.P : MBAYE DIOP
DRONE OP : FEFSY
LIGHT : BRASMAGIK
MAKEUP : EBENE BEAUTY CARE
DECO : NDAYANE DECO
Suivez-moi sur mes réseaux
Instagram : / jahmanxpress
Facebook : / jahmanxpress
Twitter : www.twiter.com...
Maam Samba :
Site Web : www.maamsamba.com
Facebook International : / maamsamba
National : www.facebook.c...
Instagram International : ...
National : ...
Tiktok International : www.tiktok.com/@maam.samba
National : tiktok.com/maam...
Threads : threads.net/@m...
Contacts Maam Samba :
Touba : 771150808
Dakar: 775992222
Saly: 775023865
REMERCIEMENTS : Maam Samba, Bambayda, Xippil Xol, Fathala
Lyrics
Okhoyolaana Mame Bamba barké naana Touba
Waw nañ dem Touba
Ku demoul ma dem dem ziaar yeslu
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Takk djouk sakhar
Ropalan
Auto ak
Kounek lalay yobbou
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Bismil ilahi
Niou sante yallah
Mom mi waraal
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Banouy mana ziaaré dji
Borom Touba ak Ndiareme
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Yaw lañou wôlou
Goor gui demoon ma Yomba
Gnibissi am ndam kenn dou domi Mame Diarra
Nitt ak Djiné ak Malaka yi tamite Kham nañoula
Cheikh Bamba dou mass lim’ñou defal amouñou payam
Defñou ñouy Mouride
Teksi yarñou banouné neureum
Bamba dou massoum
Fôré dou massoum
Bouraki Kangam
Kenn dou Bayi Seugne Bara
Dem na Gabon si ngor deloussi am Ndam
Demaat Ganaar ñeuw indi ngeuram
Souñou wadja mo def ci ñoun lou adina seedé
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Ba do khamé djoola Ndiago ak Sereer
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Mouride day djeufé Ndiggal
Tei bayi ay Téré
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Neelén euskeuy ci Sanguoup Borom Darou
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Mom nii ñeup nèè massam amoul ci kharnoubi
May sante Sasouné magui Borom deureum ngeureum
Mbacké Kadior mbir yafa khew Barina lol
Leneen dathia khadioul
Cheikh Bamba rék ci khol
Thierno Borom Darou Djambar dja
Moko djitou woon fa ndaar li wernaa
Amna lol kouñouko wakhoul meunoko kham
Amittna lol kouñouko djokhoul meunoko am
Dedet
Djaraama Djaarama wakhlénn (Djaraama)
Djaraama Djaraama neelén (Djaraama)
Djaraama Mame Cheikh Ibra Fall’la minn yonn wi batay kouné meuna djaleu (moniou’wann Cheikh Bamba)
Bam lér ni djante né fangeu
Wolounala
Wolounala
Cheikh Bamba doylooo nala man
Okhoyolaana Mame Bamba Magal Touba yè Mame Bamba akhoyta ngaa ko mouride kéfop-nooyè
Bamba akhoyta ngaa-yé bilay Magal Touba
Alhamdou Sante nañ ci lingañou defal
Kou wet ci ñoun fokné lokho ngako beeral
Yañou sagal Cheikh Bamba Yañou teraal
Tayma fethie sar kholé yamako djaraal
Ndangou Yallah ki dogualam Yonén ak ay ndioñam
Ndangou yay kifi djokhé ñam
Djambarou kharnoubi
Waw mbeuroum meunéssouko daan (Ngeuram la am yonén baadi sangam)
Ndakh loum ñaan mou am (lam tontou ndaar molen takhona dem)
Ndeysaan wakhlén’ma Cheikh bamba mi foum’né si man
Sa yoko toudé may yendo retaan
Lima metiwoon nekh ma fassa saman
Souñou wadja mo def ci ñoun lou adina seedé (Diaraama Diaraama)
Ba do khamé djoola Ndiago ak Sereer (Diaraama Diaraama)
Mouride day djeufé Ndiggal
Tei bayi ay Téré (Diaraama Diaraama)
Neelén euskeuy ci sanguoup Borom Darou (Diaraama Diaraama) 🔇
#jahman #magal2023 #bambandiokonial #ahmadajadid
Force à vous d’avoir valoriser la culture sénégalaise 🇸🇳♥️♥️😭Santal leine ma Khadim Rassoul en me donnant un pouce bleu kene dou mom 🙏🏾🙏🏾
Nion gui koy sante bou bakh silimou niou défall 🙏🙏
Kouko santoul goré wo
Dieureudieuf serigne touba khadim rassoul ❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️
Bamba La Paix 2018
Bamba Niepp 2019
Bamba La Joie 2020
Bamba Teranga 2021
Bamba mo Daan 2022
Bamba Ndokonial 2023
Jahman Ahmada
Yalna niouko yagga andeu ak yeen ay déwéni déwéne yalla défal niou magalou jamm ❤❤❤🙏🙏🙏
Machalla
Allahouma Amiiiiiiine Mach'Allah ❤
Allakhouma amine inchallah 🙏
Long anticipated bambaship! Love from the US
@@moblackdon6589 ❤❤❤❤
Kouy khaar magal 2024 beusseul jaime
Bobu mom noum wara mell❤😢
Kgkbpjf
@@le__petit__hady
mane
Ndaysan❤
Je suis talibé cheikh mais j’attends chaque année tellement c’est apaisant et revigorant mashallah. À toute la communauté mouride, je vous souhaite par avance un très bon magal dans l’allégresse, la quiétude té bou ken manquer si barké Nabbi Moustapha 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Yalla nala yalla faye
Yaw bakh way❤❤❤
Amine
Machalla daga bakheu
Bari nga ci morom ❤❤❤❤❤
Kou begue féké 100 magal yalnala ko yalla may barkep safar gui lalal JM svp❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Kou sétane tournage bi si parc lion yi ak jahman nn ndéke Jah tapét bou mak leu di guéstou lion yi rek mais nak son bi nékh machallah
Ahmada et Jahman sont dans un niveau extra-exceptionnel, ils ont instauré un besoin que les talibés ne cessent pas d'attendre chaque année on dirait même un hymne et chaque son qui arrive dépasse le degré de merveilleuses. Qu'Allah vous guide vers les rangs les plus honoré du Cheikh
On patiente avec impatience du bonheur que vous allez nous procurer
Amine🙏🏾🤍
Amine ❤
😂 Hymne bayi hasida yi thiaxane gui Barina ci rewmi
Mm ns les tidianes on attend avec impatience 😂
Disons qu'on attend tous cette chanson pour allez à Touba.
Qu'Allah soit avec vous pour aujourd'hui, demain et après demain et je le souhaite à toutes les personnes Amine 🤲🏾
❤
Amine inchallah 🙏✨🙏
Le
Amine
❤😂 imaginez un notre duo avec cheikh ndigal lo aya ya ya 😅ca va cartonner et je l'exige svp
2018 bamba La paix
2019 bamba Nieup
2020 bamba La joie
2021 bamba Teranga
2022 bamba Mo daan
2023 bamba Ndiokonial
Machallah Yalna sah bon magal à tous ❤🙏🏾
Vous avez assuré 🎉 comme chaque année machallah 6ème édition qu'Allah le bon Dieu vous protège
Amine❤
Yalla nagnou koo tewé ay att yu barii tchi brkp cheikhoul xadim🤲🤲🤝
Amine way
Amine
Bon magal à tous 🥰🥰ani talibé cheikh yi beug cheikh akhmadou bamba borom touba ak ndiarem manifesté vous👍👍👍
Kay ma invité la
@@Leuz_vision bilay nonou la beugé dem touba
@@Leuz_visiongneuwal mangui ni
@@aissataba4817en loy wakh ni
Manchala des ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ pour vous ❤❤❤❤❤❤
jourou Magal bi beu légui mom lay dégulou vraiment nigueni def sama khol bi yalla nalenko yalla fay
Je suis catholique mais moitié mouride j'ai grandie dans ce milieu à Diourbel. Ils sont sympas 🥰 bon Magal à tous. Un jour je vais venir connaître Touba et ziarer Khadim Rassoul 😊😊
bienvenue à TOUBA❤
Ça nous ferai plaisir 😊on attend avec impatience mm pourkw po mm cet annee
🎉tu sera le bienvenu
Machallah defale lolou doko rethiou
Machala beug gua ku diara beug do ko rethiou
Je suis guinéen🇬🇳 mais la musique Sénégalais joué un rôle important dans l'Afrique ❤️❤️❤️ Bon magal sngal
❤❤
❤❤❤❤touba
❤❤❤❤
❤❤❤
Dieureudiefè borom touba Cheikh ahmadou Bamba yallah na yallah yokou léram ❤❤❤
Le clip de Jahman et Ahmada offre des images visuelles riches en symbolisme, mais malheureusement, beaucoup n'ont pas prêté l'attention nécessaire à leur profondeur. Ces images captivent l'essence de l'histoire de Serigne Touba lors de sa déportation au Gabon, où la mer représente le lieu où il a effectué sa prière, trouvant la paix et la détermination face à l'adversité.
Un autre moment marquant est celui du lion affamé que les colons espéraient voir attaquer le Cheikh. Cependant, le lion a agi de manière surprenante en se prosternant devant lui. Cette scène est un rappel puissant de la force intérieure de Serigne Touba et de son lien profond avec la nature, démontrant comment sa spiritualité transcendait les barrières imposées par les colons.
À travers ce clip, Jahman et Ahmada nous invitent à nous plonger dans les symboles et les métaphores qui tissent l'histoire de Serigne Touba, offrant ainsi une perspective enrichissante sur son voyage spirituel et sa résilience face à l'oppression. C'est une opportunité de mieux comprendre et d'apprécier l'héritage de Serigne Touba, qui continue d'inspirer et de guider de nombreuses vies aujourd'hui.
Je suis catholique mais j'aime bien cette musique ❤. Elle dégage une joie profonde ❤❤.Bon MAGAL à vous📿🕌
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci
BAMBA LA PAIX❤🙏🤝
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
merci❤❤
Je catholique mais j'adore trop cette chanson ❤ longue vie nous les sénégalais
Un hymne que tous les Sénégalais attendent à chaque Magal. Tellement c'est beau et c'est apaisant d'écouter les louanges de Cheick Ahmadou Bamba❤ j'espère un jour aller à Touba pour le Magal inshallah. Bon Magal à la communauté mouride particulièrement à mes amis mourides. Contane si yeen vraiment. Jërëjëf Serigne Touba, jarama pour cette joie.
Machallah ya niak kiniane way❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha Allah kay ma invité la
je suis chrétienne mais à chaque Maggal j'attends leur chanson et cette voix sérére😘 que le seigneur nous protége
Bilay sama khole sedd na trop yen rekk lay suivre bilay chaque année Magal bou dessé semaine may khar sen duo bi ooooooooooh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Kouy khar tmt sons renne bi besseul j'aime 🎉🎉🎉😂❤
❤❤❤❤
Bou mel nii esk dina amatii
La sérénité que dégage ahmada m'impressionne, toujours calme, juste les mains qui bouchent avec sa belle voix encore machalla
Tas remarkè
@@fahtine2484 oui machalla
C’est un marabout 😅 il ne se permet po de danser …
En tout cas ne pas danser fait parti de ses principes
Je te jure lolay wax si sama xèl, çè telma captivan il dégage une forte personnalité , jahman se comporte á ses côtés avec bcp de respect , c'est est trop beau , yalla mayna Señ Touba dal ...
Les paroles le rythme , l’accent 😫 les images 🥺🥰 yéna meune kay ♥️ Bamba thi xol .
4:01 ❤
Mane diola ndiago bi ak sérère bi je me sens visé dé dieureudieuff borome touba je ne peux pas expliquer ma joie merci a vous
Je suis chrétienne mais a chaque fois quand j'écoute votre duo pour le Magal c'est toujours top.vous hissez la barre très haute.merci
Et voilà notre hymne national du safar tant attendues ❤❤yalna yalla gueneu weral batt yi rek
Amine yarabal alamine
Amine ya rabi ❤❤
Qui est là en 2025😢😢 ioe mi lire sama commenter bi yalla nga fékké 2026 inchallah ☝️
Le Rythme limage les paroles l'Environnement la voix si particuliere de cette dame sèrére🥰 (Pensèe à Yande Codou Sene🥹) Tout est juste magnifique❤️❤️❤️
Bilahi Penda Lolou mo yok dolé thi song bi ❤
@@astoudione6802 yèména sokhna si moko geuna nekhal machallah rek❤️
J’ai l’impression d’écouter Mbaye Ndiaye
❤Ahmada et Jahman sont dans un niveau extra-exceptionnel, ils ont instauré un besoin que les talibés ne cessent pas d'attendre chaque année on dirait même un hymne et chaque son qui arrive dépasse le degré de merveilleuses. Qu'Allah vous guide vers les rangs les plus honoré du Cheikh
Moi je suis une babariénne mais j'aime Serigne Touba bly❤❤❤machallakh
❤❤❤❤
Go pour 1million de vues en 24h. Merci Mame Bamba🙏🏽. Talibés Serigne Fallou yi pouce en l'air 👍❤️❤️🥹
*Waw le clip est magnifique machallah moi je suis chrétienne mais à chaque année je vs attend avec impatience lo len guéné ma télécharger Diam thi yéne gniar❤🥰❤️😍Ndiago 100% la meusse na déme Gamou jspr que dina meusseu déme Magal bou nékhé Yalla 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼*
Non non c'est pas possible non seulement les paroles mais linstrumentale me rend fou machalla quel duo❤❤❤
Wao même les lions jouent le jeux que dire de plus si ce n'est que magnifique ❤ talibè serigne Babacar bi mougui lene di gnanale magal ak diam lep Lou way def si magal gui yalla nala yalla ak serigne faye ba wiss leu yonou magal ak diam inchallah
L'accent et le rythme serrere me retient ici🥰Bamba Diokondial🥳
Bi mom bene la si walay❤
Je suis fière d'être talibe borom Touba machalla le clip est très exceptionnel
mouy nex wala mouy naxare borom touba amoul morom kou dacord beuseule jaime svp
❤❤❤❤❤
Serere yaguna ak yalla serere tahawou na founee Modou Bamba exemple Bour Sine mo tah mercii d avoir rendu hommage au serere au debut et à la fin de la chanson…Dieureudieufati Cheikh Ahmadou Bamba
Ahmada je ne le connais pas. Mais sur son visage tu peux lire de la sagesse et d’une modestie inexplicable. Genre il est adorable tellement ❤
Le duo a encore frappé tothie guén fii nékh na trop mashallah
DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA KHADIM RASSOUL ❤
Force á vous d'avoir valoriser la culture sénégalaise🇸🇳❤❤😭santal leine ma khadim Rassoul en me donnant un pouce blue kene dou❤❤
Histoire retiendra qu'on t'en attendu cette belle
chanson f (ta)
1 million de vue avant la magal inshaallah qui
d'accord avec moi?
Dieuridieufé SERIGNE TOUBA
Le calme et la sérénité que dégage ahmada jadid sur tous les clips macha Allah bon magal si diam
Ki est d'accord que Bamba La joie est le meilleur son lalal ❤bi rek
Serigne Mountakha Al-bassirou yalla naffi yague loll té wérr🙏🙏
Kou bègue Serigne Touba lalale ❤
Une revue de la culture et des rythmes musicaux sérère ❤
Masha Allah et Déwénaty 🙏
Zikhr serrere
Commissaire Nane Na Ndokhmi Bi yeupppp
Le duo triomphal a encore frappé fort. Un clip qui répond à l'emblème de notre pays et tout ce qui touche notre histoire et culture. Machallah. Dafay geuneu nekh rekk❤❤❤❤❤
Chaque année c est avec joie que j attend notre hymne qui véhicule les éloges de Ahmadou Bamba
Bamba la paix
Bamba fepp
Bamba gneup
Bamba la joie
Bamba teranga
Bamba Ndiokonial
Ken dou Cheikhoul Khadim❤❤❤❤
Manguiléne di nianal bou bakh si sama khol lako tibé goudou fane djou and ak wer ak werlé
Ci barké Seydina Mohamed psl
Machallah le duo à encore frappé 🤩 dieureudieuf Serigne Touba diarama Mame cheikh Ibrahim fall Serigne mountakha mbacke yalna fi yagg lol té weer bonn magal à tous 🙏
MachaAllah ❤️ Magal diam ak tawfeex. Yalla naniou ko yagu di téwé 🙏🏾
Done mouride mo nekhhh Mbecté mingay yeuk si sa kholl ohhhh😭😭 en plus d'être riche si paroles, habillement touttt❤❤❤❤❤❤❤❤
Ana sopey Kou Teed
Wanéleen Sen boop
Yalla nanu kou Teed kiii nangoul sunup Talibé
Kou wax Amine yalla na dajeek ngereum guii
Dix-huit safari j;ma🎉e
Taou
Ihogjfypte78
7f7tiy9titify5zypfymdtmztlsltslslgwjfsggfgkhwgkhwkghwsyfifuf🎉😅😮😢😢🎉🎉😮😅😊😊😅😅😮😮😢🎉🎉😅😅😊😅😊😊😅😅😅😅😅😢🎉
Bravo tout d'abord à celui qui a composé cette musique, les sonorités sont tout simplement exceptionnelles. Bravo aux deux chanteurs, vous confirmez que la voix est un instrument de musique (vous avez de belles voix). Le clip , magnifique, de belles couleurs , tout est bien pensé, bien agencé ...Grossomodo, un clip qui devrait dépasser les centaines de millions de vues.
La culture mouridisene fais partie des plus exceptionnel❤
❤❤❤❤
Le Jour du Magal vous atteignez le Million de vues. Le hasard n'existe pas. Machaa ALLAH . BONNE CONTINUATION MES AMIS MOURIDES❤
BII MOM WALAHI DOTOU FI AMATI YALLA 😢YEUP MOSI DAKHH❤BOU RÉNN BI MOM NÉXOUL
Bly mo dak yeup😊
Ohhh li nexna yalnalen serigne touba fay way❤❤
Al Jadid Ahmada rek lay topeu ba deh Sama wassila bii doundeul mbacké
La touche SEREERR est juste waouh 🥰🥰🥰❤️❤️🙏🏾 La valorisation de la culture nationale 🇸🇳🇸🇳🇸🇳 une fierté
BON MAGAL chers frères et sœurs Mouride
❤❤❤❤j❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yaa degg
Qui est là après celui de 2024
Moi
Moi bi moma dakhal 🎉
Quand j’écoute 🥰cette chanson, je pense à note maman y’a ndeye codou sene😭 hommage repos en paix🕊️
Yalla nanu féké magal gui ta diéku ko yalla nanu dem thi diam niaw thi diam ak salam keneu bania manki yalla na kheweul yi baeri ban diéku magal gui machala jahman et ahmada sen son toujours dani diagal kan moy s touba donc nanu bayi khel leson de morale yi 🙏❤❤❤thiakaw thia kanam rek🙏🙏🙏
Bi mom dumasi doyal
2024❤ 😊😊😊
Kou contane té degago son bi rek besal j’aime diakhmane nationale ❤
Le best duo, vous ne décevez jamais❤❤toujours au top machallah. J’ai trop kiffé la tonalité serère dans ce tube🥰🥰😘😘
Bon Magal à tous, niou téwé ko ay ate you barii bari🙏🙏
❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉yena meun kayy 🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳
Vraiment même nous les chrétiens ça nous touche du fond du cœur ♥️ ❤
Ahmada et jahman vous jouez une rôle très essentielle à ce qui concerne la culture mouride.❤
Machalla
Mashllah done mouride mo nex nakkk❤🎉🎉🎉suis fière d l’être vraiment li nex naa tropppp c topppp
Machallah vous avez encore frappé tres fort 💪🏽 🙏🏽♥️
Merci de nous avoir partagé le lien ❤
adgmiknfer❤
Machallah yalla guén ko yague def inchallah Dieureudieufaty Serigne Touba ❤🥰🙏
Je suis tidiane mais j aime bcp les mourides et leurs chansons diadieuf serigne touba
Wuaw machallah jahman x-press vous avez encore bien frappé chapeau 👑 yalna yalla déf niou magali si diam té nieuwate si diam inchallah ❤️❤️🤲🏽🤲🏽🤲🏽
La qualité de la vidéo on en parle waouh
Sincèrement vous êtes machallah 🙈
Ahmada yarou n'a blh❤
En tout cas mbacke Mbacke bi mo mom song il rime facilement ❤❤❤mashallah
2018 Bamba la paix ❤
2019 Bamba nieup❤
2020 Bamba la joie ❤
2021 Bamba Teranga❤
2022 Bamba Mo dann❤
2023 Bamba ndiokodial❤
Yalnagne ko yagua fékké té talko inchallah😊
Yalla weral battt bi ngenn diko weuy ayy magali magal xol sedatina gouyy heur boleinnn gueinei rek mou nex
Toujours au top vous ne décevez jamais💃❤ clip bou riche d'ailleurs comme les autres yalla nanou ko yagga telwou bepou djoulite nguen yagg ko diokher serigne mountakha yagg fi loll trh wer
Yall nay démé ni saxx magal inchallah
Ce mec srx ce mec manchallah ambassadeurs musique sénégalaise zéro vulgarité nuditè ohh
La partie où les lions sautent pour grimper ensemble sur l’arbre c’est pour m’achever
#talibe bamba❤️
Manchallah
Sama diamou serer yi bon boulot l’accent magnifique ❤️
May nalen Senegal boulein ko diayat nak dieundè ko mbourou 😂😂
Chak année day guena nekh mashallah 🥰 qu’Allah facilite à tout le monde les moyens de transport pour le Magal amine 🙏🏽Ila Touba🕌inshallah
Non du jamais vu ces deux chaque année ils frappent sérieusement nak jahman presque chaque jour j'écoute ces chansons Bilay il est mn artiste yalla n'a yalla wéraal voiby bounakh je voudrais même Sakh avoir son numéro pour le remercier sûr cette chanson là encore merci grand frère bcp de cœurs pour tw ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machalla chapeaux les gars cheikhoul khadim aka bakh mome mi ni yalla yeureumeul lép louy doundou dieuredieuf serigne touba
Ho hohohoho diarama khadime rassoul❤❤❤❤❤ mantion jahmane et ahmada❤
Franchement chapeau à vous pour l'honneur que vous faites chaque année pour notre bien aimer Cheikh Ahmadou Bamba khadimou rassoul❤️,longue vie à vous merci et merci encore 👏👏🙏
Mais mère sérère yi ayy nagn machahalah AHMADOU protège ❤
😂dieureudieufeti Mame cheikh Ibra hima fall😂tayou mako dama contente 😊❤❤❤❤❤❤😂😂
Kén dou bayou serigne bara ❤sama yakar tay ak euleuk 🎉
Vraiment vous etes formidable le rythme serere est extrement super j sais pas coment vs avez fait trouve cette inspiration suis tres fiers de vs et beaucoup meme en plus suis serere yalla na endeu bii yageu 'guene koy yague di meune inchallah diameu si yeneu
J'ai des frissons en écoutant les paroles ❤ Mashaallah yalla na yalla wereul baat yi beu nguéne di gueuneu meuneu wayal sunu kou tedd ki ❤❤
Ki kom moi actualisais la page de Jahman depuis 18h😩🤍🤍
1 million avant Magal ❤❤🎉🎉🎉
Dieurefeufe serigne Touba 👌💕💕💫⭐💫🎉🎉🎉🎉🎉 machalla nice na bilay ♥️🌹⭐💫
Depuis ce matin je l’écoute en boucle très belle chanson jahman et jahid vous êtes extraordinaire tjrs Mâchalla rek chaque année on attend pour votre duo de choc yalna diam yague guen koy deff ay atti att inchalla 🙏
Je souhaite à toute la communauté mouriez de passer un très bon magal
Wollah chaque année je me répète que c'est la meilleure des chansons alors que la suivante sera meilleure 🎉❤
Oh la la la j'ai frissonné en n'écoutant s magnifique duo ki représente lhymm du grand magal vraiment du haut niveau mashalahh. Bon magal à mes confrères musulmans paix et joie 🎉