Sama yone nékouci oui je l’avoue mais gamou bii sa ressemble à une réception de mariage les femmes ne sont pas voilées des cheveux et des ongles 😢hé allah c’était la nuit du prophète mouhamed sws❤😢😢
En tant que Talibe cheikh je ne conçoit pas l’habillement des invites kou nek prerrukou té goudi Yonanté bi lagne wax li dou yonne way dieul diné gui beug ko def fête tiakhane
Pauvre pays,folklore et karaté même avec la religion musulmane mais le jour du grand rassemblement,vous verrez et saurez que tout est vrai,In Shaa Allah...
Franchement les garde du corps xaw ma buzz molen si dougual wala ms li mom rafettoul as gorr ken douka torokhal xaw ma nk ndax daniou oen ko sant wala ms niaw na
Walahi Sénégal diné amou fi. Dioudou seydina MUHAMED sws. Niou wara diouli si mome. Nianal ko souniou borom yok ay léram, gni nék fi khawaré aka tiakhane ak séne gréfage.
N importe quoi,ces nouveaux riches analphabetes qui sont dans le voyeurisme,senegal vraiment…gamou bougniouy battre khaliss.. Lima geuneu diakhal mooy khale bou ndaw biiy battre khaliss bi,a son age,c est mauvais.femmes maquillees,khesalisees,perruques,talons..le senegal est devenu du n importe quoi..i m ashamed
Fi keyy ouzin khadione nafii ❤
Sama yone nékouci oui je l’avoue mais gamou bii sa ressemble à une réception de mariage les femmes ne sont pas voilées des cheveux et des ongles 😢hé allah c’était la nuit du prophète mouhamed sws❤😢😢
Deug pir nga wakh
Billahi motakh ouzin waroune ko wone dakh khamouma louniou Koy reproché mais sein gamou bi li yallah kham doyna
Wallahi mom kay yéména trop billahi li kay kéne xamol dal lomo done
Walay c bizarr😢😢
Dèmlène diamou yalla wa bakhna 😢
Nii denouye fotou rek ly keuye khawaré le dotoule gamou khéseule bé wékhe greffage yi Sénégal denon yape yalla wé nenou deme
Domou adama kén douko torakhal wayy ahh li réfatoul
Nous les chrétiens pendant nos fête nous invitons tous pas d'ignorance ❤❤
Ioe meygnu
Lolou yenn la
Warrone nagnouco bayi mou Dougou
Ndakh mounafa diangéi nitaye wala mou sopekou diangalefa.. Tamite nitela kheuyna dafa beugeu bakh
Delen diokhé deuxiéme chance
Gamou.validé kontana wallah il abdou aziz ndiaye merci beaucoup
MES KI DONE FILMER OUZIN DOMERAM DEUGUEUHH LAH
Sénegal khawma loutakh ngéne sokhor rék Aziz Ndiaye gamou wam bi nékh rék ta âme organisation ladeff ninouko organisé machallah légui civilisation bi dafa avancé lii dara nékouci sokhor ngéne trop
Pour yéne li Lou rafet la def nguéne Lou niaw😮
Thi keur la gneuw fi invitation mofi deugeul nitt
Wa l anniversaire de la naissance du prophetes les femmes onteur tête en l air senegal doy na waar legui dé
Borome dos nu bi nak😂
C est très méchant de votre part surtout en cette nuit où vous fêtez le Prophète
Na dém thi gamou gui liko indi kham négn ko fi invitation mofi dougou
Keur leu
Mayakarni kou yonénetibi takha diok to ame kosiy téré soula yalla takhé diok té khawma li récéption leuh walla😢😢 té daniouné goudi yonénetoubi somané diangue alkhourane ngua diangue diaglélko yonénetibi somanoul ngua téw fignouy diangué pas disi khawaré😢😢
Li ken douko df 😢😢
Vraiment li niawna ouzin nitte la 😢😢domage 😢😢
Thi keur la gneuw fi invitation mofi deugeul nitt
Ouzin Khana dou nite loutakh gnoukoy dak
Masallah lii réfétna loolll masallah
Machalla ❤❤❤
Gamou gui nekhenaa trop Machallah 🥰
YONENTE BI PSL KHADIO NA NIEUP NDEYSANE
Li rafeitoul nite kein douko torokhal
Manone ngen mour sén bop yi deh
Wakh deugu yallah , mourou bagna tegu greffage pour béne jour lolou yombe na
@@mounarositraore8684 ormal goudi gui Hana et aussi soutoural sen bop
Eyway 😢
Bilah gamou dou mariage prkoi pas ay mousor niou rafete mais cheveux si gamou tmt doy na war
domou adama kene douko trokhale vre domeram nguene alasane mbaye mo ngi fofou loutakh dakho lenko
Ouzin yaw tamitt amofi place , lii gouddi yonénete bi leu .
Pourtant nak dara nekoussi dh khana key dou nieuw pour ambiance ndakh gamou legn woter meunon negn ko bayi mou dougg rek
Barky yonenty bii mane talibe cheikh la mei manone ngueine mourr seine bopou yi tei wagnii si makeup yii
Allalou akh bar
Ka ouzin oudè nimou la guissè lalay euwelè bou beuguè boksi nite gni dina nek nite tè changè comportement
Bayil lene niémé yallah adouna diaroul fene yi yeup
😭😭😭😭😭😭
En tant que Talibe cheikh je ne conçoit pas l’habillement des invites kou nek prerrukou té goudi Yonanté bi lagne wax li dou yonne way dieul diné gui beug ko def fête tiakhane
Pauvre pays,folklore et karaté même avec la religion musulmane mais le jour du grand rassemblement,vous verrez et saurez que tout est vrai,In Shaa Allah...
Yen gni di wokh yen tamite dougoulen am nagni fa nek ouzin mo len tane
guisna na gnieup didéme rék mouni kharale ma déme ki
🤣🤣🤣
Wa yen est ce que aye nite Guey ki kite leu ndeysan 💔 vous faites hontes
Walahi li niawena sisa mbok dioulite 😢😢
Bilahi téléphone yi mena gniak thi goudi gui Mohamed PSL
Franchement les garde du corps xaw ma buzz molen si dougual wala ms li mom rafettoul as gorr ken douka torokhal xaw ma nk ndax daniou oen ko sant wala ms niaw na
Woné wouléne fougnouye wathié camir bi dhé .aye Segne sé aye greffage longueur 30 longueur 25 make-up iPhone rek lagnouye woné😂😂
Mou none nagn ko bayi mou dougou
Billahi
Fiiiiii mome nakh sangg bou tedd bi SAW tew na si gamou gii ?
Loum fay deff la khamoul nitt dey kham boppam
Bilahi, nou Mawdo fonké souna ak charia soufi nieuwone dou contane. Na niou geustou kifayate ar rahibine. Na niou sagal Maodo.
Je suis fière ❤❤❤❤❤❤❤❤
Geumougnou sarrap ndéme !!
Loutak dakolen borom greffage yi nitt. Ken douko trokhal
Mouray bi dé diap nala awo Aziz ndiaye
Kené waroul torokhal niit surtout, c'est un événement religieux, se pas sérieux
Soudé li mo fa amone ouzin khadione nafa
😂😂😂😂
Ay greffage ay boubou sexy ak kheyssal, fi nieup amneniou placé, ouzin nguen yab billahi
Li tidiane rek moko sagne niawna dh
Goorjigeen khathe la Astaghfurlah Khathe sakh moko tanei cest bien fait dagne la warone nook teek si
Non kéne dakouko dafa donne khékhe
Gayi nafek baxul bulen fate Niki gorjigen la bu dugon day yak s'en gamo Waye dumayi sikaw gneup lay dal ok merci
Du n'importe quoi avec vos cheveux et habillement sexy bayilen thiakhane cheikh seydi hadji Malick ak cheikhna Ahmed tidiane fofougnou thiakhanougnou
Wa limom gamou la wala mariage la goudi seydina Mohamed astafirla
Gamou wala magal
Thiey adouna
C'est pas bon
Wa ki daye diageu walla daye foh
Walahi Sénégal diné amou fi. Dioudou seydina MUHAMED sws. Niou wara diouli si mome. Nianal ko souniou borom yok ay léram, gni nék fi khawaré aka tiakhane ak séne gréfage.
N importe quoi,ces nouveaux riches analphabetes qui sont dans le voyeurisme,senegal vraiment…gamou bougniouy battre khaliss.. Lima geuneu diakhal mooy khale bou ndaw biiy battre khaliss bi,a son age,c est mauvais.femmes maquillees,khesalisees,perruques,talons..le senegal est devenu du n importe quoi..i m ashamed
Djiguen yi tek sen greffage san mourou li gamou la wara khaware
Khalé bi bakhna rék
*Da sec yeux ki😂😂😂😂*
Nieme na beutt deh
Bo waly nieuwon dh dousi yakk dara 😂
ya réwe 😂😂😂😂😂😂
Warone naniouko bayi mou dougue ndax dou gamou xaware la na nieup doug
Thi keur la gneuw fi invitation mofi deugeul nitt
Kimom day wanewou wayeih magaloul beussbi
Mo tey méchante