Dikoon episode 102

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 9 лют 2025
  • TikTok Pikini☆~~👇
    rebrand.ly/Tik...
    FACEBOOK☆~~👇
    bit.ly/Facebook...
    Abonnement Gratuit ici☆~~👇bit.ly/Abonneme...

КОМЕНТАРІ • 430

  • @lenamane8360
    @lenamane8360 7 років тому +66

    S'y tapha yémal! Makk bou tolni ioe! Tchiiiip! Kou name khassté dada yi beusseul j'aime way

  • @modoundiaye7270
    @modoundiaye7270 7 років тому +324

    Koy begui DIKONE j'aime MA GUISS

  • @ndeyendomendoye5384
    @ndeyendomendoye5384 7 років тому +24

    Ana gni beugue dikone beusseul
    J aime😚😚😚😚

  • @astougueye328
    @astougueye328 7 років тому +6

    kou djeppi papay tapha sarr beusseul j'aime pa bou soff la bopam bi di melni khokhou bouyy

  • @amdykandji3524
    @amdykandji3524 7 років тому +141

    Gayi Machallah Nice n'a ziar n'a nieup mais ani wa #team #DiopFall senn bokkou comédien yalla nakko yalla yeukatiiii

  • @karmamania4867
    @karmamania4867 7 років тому +5

    Ndeye Fily Bravo pour ses performances... SiTapha aussi joué trés bien.... mention spéciale à toute l'équipe Dikoon, bonne fête de Tabaski à vous tous... nous vous souhaitons que le meilleur pour cette année et les prochaines années.... Khady ma comédienne préférée ...🤗

  • @sokhnacoulibaly6529
    @sokhnacoulibaly6529 7 років тому +19

    mane xawma loutax kanamou sytapha dima enervé ish soxor ga trop nd fily iow mom ni rek never change

  • @ndeyemaremediop7539
    @ndeyemaremediop7539 7 років тому +70

    Sitapha sa réunion bi comme discours fin d'année ABDOULAYE WADE Eup na waay ishhh

  • @ngonendoye8214
    @ngonendoye8214 7 років тому +105

    Non sytapha y'a bone en plus Tasse sa Keur mola takha dioke mais dikone mome manon si môme dara Tapha sarr Dikone la love

  • @fallaaida6568
    @fallaaida6568 7 років тому +35

    non sytapha sarr dinama ray da wara dé sakh sokhore nga toropeee di fénn rék ak khalise bi.ma beugue dikoon ani fans dikoon yi Waye foléne nék way partage lénn video sytapha sarr bi waye 😂😂😂😂

  • @ndeyeastoundiaye6872
    @ndeyeastoundiaye6872 7 років тому +11

    khadi tu réfléchit tros je vous j'aime

  • @wanealmamy3457
    @wanealmamy3457 7 років тому +30

    Non sitapha sof ne
    Limou df dikon dama merr😣 en même temp di rigolé 😂😂😂comm po posibl ki mo soff way

  • @yandeism
    @yandeism 7 років тому +3

    Dikoone boul wakh dara , le balais sera pour laver le sang qu'ils vont verser pour la grande bataille pour les 500 millions. Togaal rekk di sétaane 😙😙😙

  • @blackapple6593
    @blackapple6593 7 років тому +19

    Mdrrr khadji à la robe apple😂😂😂😂 ndeye fily tu dérange c'est quoi ces lunettes😂😂😂😂😂

    • @mameboy4629
      @mameboy4629 6 років тому +1

      Mdr, vous êtes styliste ou quoi

  • @serignecheikhastoufallsow7621
    @serignecheikhastoufallsow7621 7 років тому +35

    Thieuy dikon ndokh mou tagg Ana wakeur dikon way beuseul j aime

  • @goldengirlsenegal513
    @goldengirlsenegal513 7 років тому +274

    Ani wa team dikon folen nek ??
    Bonne fête de tabaski à tt le monde

    • @madjiguenediagne3780
      @madjiguenediagne3780 7 років тому

      Golden girl Senegal gnogui nii

    • @abdoundione5464
      @abdoundione5464 7 років тому

      Golden girl Senegal

    • @gueyesega8892
      @gueyesega8892 7 років тому

      Golden girl Senegal salut tu es belle

    • @gueyesega8892
      @gueyesega8892 7 років тому

      Golden girl Senegal sinon fo deuk?

    • @gueyesega8892
      @gueyesega8892 7 років тому

      Marietou Diop elle me plait et je veux juste faire sa connaissance c'est tout Mariétou lol

  • @ndeyedieng7217
    @ndeyedieng7217 7 років тому +96

    teint noir moy bombe .... khéssal mom égal niank classe akk tâches you bari akk khassaw khoune!!!

    • @lalionne3789
      @lalionne3789 7 років тому +6

      Anita di bilay walay lolou dafa lerr 😂😂😂

    • @mariamadiallo1527
      @mariamadiallo1527 7 років тому +9

      Anita di no mais teint naturel en général mo rafet k mou nek teint noir ou teint clair! Khady yaram bi dafa sett mom ak la mama de Aissatou j sais pas

    • @yamandao6759
      @yamandao6759 7 років тому +1

      Mariama Diallo

    • @siraniasse8933
      @siraniasse8933 7 років тому +1

      Anita di anita je t adore bien dit

    • @nanishhanne2033
      @nanishhanne2033 7 років тому +7

      Anita di je t'adore fier d'être noire j'aime les femmes noires comme moi noire moy bomb

  • @mounassndiaye6647
    @mounassndiaye6647 7 років тому +13

    Kou nameu pama ..arame ...ak ndaye coumba

  • @2km173
    @2km173 7 років тому +2

    dikoon yalnala yalla defal diam si sa doundou je taim fort

  • @darifall8821
    @darifall8821 2 роки тому +3

    Dikone yagui sisou dh💫💫💫

  • @nogayediouf9076
    @nogayediouf9076 7 років тому +1

    Pa bi da niowe pour diakhase ndiabotame waye bogoule dee 😉😉😉😉

  • @evachouevacho8594
    @evachouevacho8594 7 років тому +6

    😂😂billay ndey fyli mo bon ay retan dama diap sakh .si tapha mi khawmakoum yap

  • @ndeyendomendoye5384
    @ndeyendomendoye5384 7 років тому +1

    Kou beugue khast beusseul j aime 🤗😍😍😍😍

  • @khadimsylla2440
    @khadimsylla2440 7 років тому +45

    Kouye dhè loye doyè tak diabar

  • @khadydiop1827
    @khadydiop1827 7 років тому +39

    sitapha dafeuuu bone loutakhhh mou bagne dikonne té mom kilifeu bou tolni mom di féne 500.000.000 yii kou nékkk mounileu yaw lakoy diokh non kou bagne sitapha talale sa lakho ma kholl wayyy

  • @dancelife9372
    @dancelife9372 7 років тому +65

    Yen niepp manguilendi niaanal kouci nek am xarou tabaski fekeko te talko bonne fête a tous les musulmans

  • @adji6996
    @adji6996 7 років тому +6

    j'adore ndey fily xale capable

  • @fallmameanta1841
    @fallmameanta1841 7 років тому +13

    Pa bi tamite tass na keur gui d. Peuthieukho dè mo fi nareu am. Mais ki gueneu rafette xol si niom rek mossi nareu eupeu chance.

    • @ndmme
      @ndmme 7 років тому

      Fall mame anta c est vré dh liguawakh ni kousi gueneu rafét khol rék yay am ndam si séne kaw

  • @aminalo4954
    @aminalo4954 7 років тому +1

    dikoon mala beugue baarcké bleu bleu👑💞💖

  • @diorlabambisteseck8727
    @diorlabambisteseck8727 7 років тому +5

    Aÿ way ma tardé di wa Sy tapha balé douche bi nak pour lâne😂😝😝

  • @rahmadieng4
    @rahmadieng4 7 років тому +3

    Pama la naaaame😧😧😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @diadjifall6501
      @diadjifall6501 7 років тому +2

      Rahma Dieng ♥️♥️♥️🎵🎵💘💝💟💓💗💖❣💕💞💙💜❤️💛💚🎎💎💎💒🏩🌈🌠🏯🏟🗽🏘🏰🎇🎆🌉🌌🌠🌉🌌🌃🏙🌆🎗🎖🏅🏆🏵🏹🎣🍩🍪🍭🍿🍬🍰🎂🍦🍨🍧🍡🍚🍘🍢🌮🌭🍕🌯🍔🍤🍖🍗🍤🍟🍕🌯🌜🌟🌙💫☄✨☄☄✨✨🌟☀️🌜🌝🌙🌸💐🍄

  • @paradiseparadise7373
    @paradiseparadise7373 7 років тому +27

    Ndeye fily dall Moy Star série 👏👏 dikoone 👑👑👑😍😍

  • @ndirafall1374
    @ndirafall1374 7 років тому +22

    wa sitapha sarr yapp naléne koum ni pausal rek ngua nguéne d'i melni aye mikké

    • @nenembengue1161
      @nenembengue1161 7 років тому +4

      Ndira Fall te en plus els peuvent faire marche arriere video bi pour xam ce kila dit aux autres😂😂

  • @moussasy2127
    @moussasy2127 7 років тому +34

    Cest ça qui arrive quand on ne veut pas mettre fin à une série, on tourne,on tourne sans savoir exactement où on veut aller, on crée des histoires, pour faire genre rebondissements,mais bon cest pareil,la flamme n'est plus la,cest mon avis à moi nak,je n'oblige personne à le partager

    • @fififall2016
      @fififall2016 7 років тому +1

      Moussa Sy !!!degg na deugg

    • @oumoundiayediop9398
      @oumoundiayediop9398 7 років тому +4

      Moussa Sy Liga wakh mo ame danio yabe ak sen video meleni discours 31dec

    • @lorelene
      @lorelene 7 років тому +2

      Moussa Sy film bi kay mo guen nul si filmi eup amoul béne sens

    • @adamaka1412
      @adamaka1412 7 років тому +1

      Moussa Sy Tu as parfaitement raison.. ils ne savent plus ou mettre les pieds.. cst quoi cette scene a la con.. ils se sont inspirés de quoi mm #foutaise

    • @fatmafall315
      @fatmafall315 2 роки тому

      Genre Abi et Pragya rkk 🙄

  • @rokhayasamb1019
    @rokhayasamb1019 7 років тому +3

    Sydapha daga eumbeul yayou khady sarr wo Wa charia niou door la lègui xalissou saoudien yi ga sathie wowal Wa charia niou dague sa loxo✋✋

  • @ndeyefatoumballo6640
    @ndeyefatoumballo6640 7 років тому +17

    Wa yéne sytapha nilanoukoy bayi mom di diakhassé ni rek pa bé bone

    • @sidina6338
      @sidina6338 7 років тому

      Ndeye Fatou Mballo 😅😅😅😅

  • @diarrakeita9750
    @diarrakeita9750 7 років тому +3

    Wa yene sitapha sarr koumou yapp mounane nieti djiguene la beg niou tedji ma en plus diaxassè moka takha diok 500 million kounè mou denk lako xalass😣😣😣😣

  • @zeinabkkonte1244
    @zeinabkkonte1244 2 роки тому +2

    merci dikone bonne réponse

  • @diopnafissatou4326
    @diopnafissatou4326 7 років тому +2

    di ballou nieup akk cii beussou Arafat bii🙇🙇

  • @leylamb342
    @leylamb342 7 років тому +48

    Mai film bi warna dièkh taye amoule sanse dara

    • @lorelene
      @lorelene 7 років тому +8

      Leyla Mb ..merci film bi kay moy lolou tt est mélangé

  • @GoGo-qs9kd
    @GoGo-qs9kd 7 років тому +25

    Dikoon rék si tontou namoul dara

  • @fatoushfashion8699
    @fatoushfashion8699 7 років тому +8

    May numero 1 allezzzz

    • @profdiouf8767
      @profdiouf8767 7 років тому

      Fatoush Fashion diokhél clé yii Bok so pareiii

    • @sarafaye230
      @sarafaye230 7 років тому

      Dème gnowate

    • @fatoushfashion8699
      @fatoushfashion8699 7 років тому +1

      prof diouf boul wakh dara souma parer yaw lakoy diokh

    • @laytifaye2948
      @laytifaye2948 7 років тому +1

      Fatoush Fashion Lala Lala

  • @goldengirlsenegal513
    @goldengirlsenegal513 7 років тому +75

    Pa bi dal dafa gneuw pour diakhassé laylah ki moy defeant 😱

    • @profdiouf8767
      @profdiouf8767 7 років тому +16

      Golden girl Senegal maa ragal pabii wayy seytané laa

    • @martialdiop6472
      @martialdiop6472 7 років тому +4

      ya wah Lolou sitapha

    • @jalliejuula73
      @jalliejuula73 7 років тому +2

      Golden girl Senegal . Mane dama djaxlé sax. Trop bizarre ce vieux Sitapha

  • @madjiguenegueye582
    @madjiguenegueye582 7 років тому +24

    wah yen ndeye fily kouko niawal naw naw bi😀

  • @khadimgueye8626
    @khadimgueye8626 7 років тому

    yallana yalla maye ma diabar bou mél ni dikon

  • @elmbodj2846
    @elmbodj2846 7 років тому +8

    M man lan motakh ma ndaye fily yaw nekhoma dara dikoon moungieul rek lep dîna djiekhe

  • @representationmatters
    @representationmatters 7 років тому +1

    No dikone bum am problem nak!
    #TeamDikone

  • @modouwague2645
    @modouwague2645 7 років тому +4

    Papa Tafha Sarr da sokor

  • @mbayewar6940
    @mbayewar6940 7 років тому +18

    Siteufa dewal way

  • @layeciss8318
    @layeciss8318 7 років тому +1

    Sitafa ioe kou mèlni yow amatoul si adunaa rèy gua djiguén yii nèk fofou yeup 😂😂😂

  • @princessefinah2376
    @princessefinah2376 7 років тому +12

    pausal video bi momay reiy mane .... wa pabi looumouy deif ni kouné mou dink la haliss bi theeei...ahh penda nak changer na nak ... balais douche 😲😢😭😭

  • @Awaa78127
    @Awaa78127 7 років тому +1

    " néna dé déh dans 6 mois"! Il m'a dead dr Sarr

  • @profdiouf8767
    @profdiouf8767 7 років тому +14

    Setane gnewatt bala thiogalll guii gnew 😂😂

    • @sallysy6598
      @sallysy6598 7 років тому +2

      prof diouf mdrrr
      Suis par terre

    • @profdiouf8767
      @profdiouf8767 7 років тому +3

      sally SY walay gayi dagn gaw melni nioufi am A.P

  • @sherifaaaidara9604
    @sherifaaaidara9604 7 років тому +1

    Mdr xana ballait bi pour mane miy rakhass douss la woy magui dead😁😁😁

  • @aramesagna1936
    @aramesagna1936 7 років тому +12

    Wa sitapha Sarr louko dalle sa famille bi ngaye diakhasé nak

  • @lafilledecasa8196
    @lafilledecasa8196 7 років тому +1

    Je suis vraiment très en colère contre Sitapha 😬😬😬😬😬😬

  • @mackydiallo9762
    @mackydiallo9762 7 років тому +2

    Ak Tabaski diam len fans Li dikoone li

  • @nina1sasy528
    @nina1sasy528 7 років тому +2

    Sitapha dal gorou thiapa Tate leu gorou thiokoto leu tass kati keur wabadjiba leu! Je me dde sakh naka leu meuner diakhassee ni sa famille ndeye flily mome brochette ko rek la bgueu bolè ko si yapou tabaski bi! Merna torop ( bref je parle ds le contexte de la série) merci

    • @demba4174
      @demba4174 7 років тому

      Nina1 Sasy I'm dying wouy thiokoto momay ray 😂😂😂

    • @toufa96
      @toufa96 7 років тому

      Nina1 Sasy 😁😂😃😀

  • @amicollefall4037
    @amicollefall4037 7 років тому

    sitapha ya bonne waye dikoon môme mano si môme dara nakh dafa moko love Ndaye fily yaw amo diom

  • @boypoullo901
    @boypoullo901 7 років тому +4

    Sen jekeur mougui deeeee mais koumou wakh wakhou 💸💸💸xalis rek mou 😂😂😂😂😂😂

  • @amydembele8812
    @amydembele8812 7 років тому +4

    Sitapha il divise pour mieux régner
    Il fait croire à tout un chacun ce qui n'est pas

  • @lavanillementhe849
    @lavanillementhe849 7 років тому +23

    Dikone yaw rekkk ya bakh si ndeye fily mais kéne dou sitapha mafé soupou kandia yassa yéppp ga diakhasé may wakh niouye contane ak séne changement you gaw té khamou niou li khéw penda so khamone li laye yotte diga bayi ligay yotte

  • @fatou8910
    @fatou8910 7 років тому +1

    Ndeye fily ligua niaw doyna gua beugeu Thie def aye lunettes mai j'adore vrema ak s'en teint noir yi

  • @lejeune3871
    @lejeune3871 7 років тому

    Naniou yalla mousseul thi bi borom keur

  • @maguetteka1888
    @maguetteka1888 2 роки тому +2

    J'aime 😍😍

  • @jamesjoob3771
    @jamesjoob3771 7 років тому

    nedye fily dikoon rek bakhe thi môme
    bravo dikoon

  • @fatoushfashion8699
    @fatoushfashion8699 7 років тому +3

    May first tay

  • @khadidiatoundongo8607
    @khadidiatoundongo8607 7 років тому +3

    Mane môme sidy tapha diakhalnama, ni lanara bayi si guinawam?
    En plus ,il a humilié dikkoon devant tout le monde😰ndéyssane.
    Félicitations a toute l'équipe.
    PS:J'étais ému quand Sidy Tapha sarr parlait a ses filles.
    Mérci a vous et Courage pour la belle suite khamna dou yomb .

  • @deugrek3312
    @deugrek3312 7 років тому +2

    Il parle en parabole: cela veut dire qu'elle balaie Ndeye Filie de la famille

  • @fatimazakhrasine7255
    @fatimazakhrasine7255 7 років тому +3

    Khadi sarr kassei bou dougone dina lirate yeup 😂..c'est dommage oh

  • @mbackediop7678
    @mbackediop7678 7 років тому +46

    Thieye allalou aduna hoo penda sopé kona

  • @ndongomouhaned8093
    @ndongomouhaned8093 7 років тому +171

    Ku bengue dikon beuseul wayy

    • @mamydiagnendiaye9560
      @mamydiagnendiaye9560 7 років тому +16

      no le papa de tapha sarr il est pas du tout gentille avec dikonn il la humilier devan tout le monde ?? dikonn mougnall yalla bakhna cava aller ma chérie :-) :-) :-)

    • @cheikhndaw6181
      @cheikhndaw6181 7 років тому +3

      Mamy Diagnendiaye
      .

    • @khadidiatoundongo8607
      @khadidiatoundongo8607 7 років тому +9

      +Mamy Diagnendiaye billahi je suis dégoutée ,dikoon dafa nara Faye Aÿ néne yimou todjoul.Sidy Tapha Sarr dioubowoul ak imam mo takh,lép lou tak simom dafkoye déranger

  • @maevamaeva1271
    @maevamaeva1271 7 років тому

    Sitapha yallah khamnani Afrique mérénala no meuné lii 😡Mé khana dagua fatté ni li gnome dikoon necké yaléne ko téck guaye bakh yép 😖té kilifa dou dokhalé nii 😭Lo bocke ak Ndeye fily yéna nirou djiko thi theatre bi 😪Mé borom xolou Or bi Dikoon la Reine de son Roi daye goré ba dé Dicourage Bébé Séte mo gueune Bone 😭

  • @fatoudiakhate8733
    @fatoudiakhate8733 7 років тому +15

    pa bi sof nama bilay yéneu ngui yak serie bi nakh secrét ak deal

    • @nataa6051
      @nataa6051 7 років тому +5

      Fatou Diakhate merci là-bas. Ils nous fatiguent à la fin

  • @ndeyedieng7217
    @ndeyedieng7217 7 років тому +40

    sitapha déwal dakh niou am diam mdrrrr li gay expliqué sakh j crois k ayy door la!

  • @papicogningue4046
    @papicogningue4046 7 років тому +26

    Pa bi day diakhassé😂

  • @aminalo4954
    @aminalo4954 7 років тому

    dikoon mala beugue baarcké bleu bleu

  • @evaseyefall1263
    @evaseyefall1263 7 років тому

    Ndeye fily tu es tres belle pareil piur dikone machalla

  • @diopro3543
    @diopro3543 7 років тому

    wa goor gou mel ni sitapha sarr ame na ma tiiittt

  • @nenefa81
    @nenefa81 7 років тому +2

    Sitapha veut seulement gagner leur confiance. Il n'est pas malade

  • @ibraseck2211
    @ibraseck2211 7 років тому +12

    lou neh rek ngéni jouer yenafi mane mai tay gnepa done setane mem niom dikone sax danio tok di setane si tapha lol mai si tapha daléni nakh verai bandi la bo maytouwoul yena koy ndieuka dé

  • @royalekane5988
    @royalekane5988 7 років тому

    Wa tamit ndeye fili warna arrêté d mou melni guoumeu téranga ni hay 😂

  • @astoucisse6616
    @astoucisse6616 7 років тому

    Bne féte de tàbaski a.tt l mnd balénma akh yén niep pikîni ak wa serie dikoon yeup keulz ,nd fily, mounass ,bîrane, niep balén niou àkh nioune wa you yube yeup si comentàire yiîi yinu wax lou len nexul mai fooo rk lanuko dielé xamnàne lilén tàxa dîok ak liguen dioubeloù sî askan wii.yété rkkk lepa nîce xamnanuni film rkk la mélolén nonu proféssionel guen

  • @aidabouserignebabacarsy6536
    @aidabouserignebabacarsy6536 7 років тому

    Anta sa tein bakh na Macha allah

  • @yacinediop4119
    @yacinediop4119 7 років тому +1

    Bilay ma bagn sy tapha mai dikon mala aimé

  • @dabadiop833
    @dabadiop833 7 років тому +3

    Sitapha mo bone deug.tal sen keur gui la beug.

  • @thiammbaye9696
    @thiammbaye9696 7 років тому

    bilahi aystou rekk motakhh may sètann

  • @boudechou
    @boudechou 7 років тому

    Sitapha mom télécharger ngagnou!!!! na yam si yaw rek niyoul gnou wa alakhira

  • @Senegalfirsttv
    @Senegalfirsttv 7 років тому

    Wa sytapha mom dafa bandit wala dafa say say sa famille nga xadialei dii

  • @mathezodasilva8573
    @mathezodasilva8573 7 років тому +1

    no pa bi mo boneee 😈😈😈

  • @alimadiaw657
    @alimadiaw657 7 років тому +1

    Ailleur d'une cassette video, il devait faire une video conference via facebook ou youtube ca sonne plus vrai

  • @adondiaye2938
    @adondiaye2938 7 років тому

    mais pabi mo graw limou bagon lep amnako 😃😃

  • @diarradiakhate7632
    @diarradiakhate7632 7 років тому

    Ahh Anta dh machalla, namoul dra

  • @fayekhayta392
    @fayekhayta392 7 років тому +2

    bien joue il a montre le vrais visage des hommes

  • @lliyn2906
    @lliyn2906 7 років тому +14

    ndaye comba la namou

  • @tefmb3313
    @tefmb3313 7 років тому +1

    Yena khorome sene waay gaaw

  • @fatoushgueye1412
    @fatoushgueye1412 7 років тому

    Omg ndeye fily😍

  • @awaboiraud9648
    @awaboiraud9648 7 років тому +45

    Dikoon nekh gama

  • @shouweyla6342
    @shouweyla6342 7 років тому +3

    Khadi est inteligente

  • @karimiensene1393
    @karimiensene1393 7 років тому

    Sytapha Sarr😂😂😂😂😂😂😂😂🤦🏽‍♂️🤦🏽‍♂️seytané tamite si mak😂😂😂😂😂... Ahh no way😆😆😆
    Penda mome kopar yi nieuweugoul mou sopékou😳😳😳😳mome deh si les sous viennent mou yeik si kaaw mère bi😳😳😳😳😂😂😂😂😂😂😂