Mbeur toute la communauté sérére,les îles du saloum et le village de Dionewar particulièrement de tout cœur avec toi ndam rek incha allah fils de dionewar
Thiat danga wara xolat sa bopou dafa mélni gueumo sa bop siteu sama mbeur la mé ama moko mann fouf boumou dieul ama day yakou deféte rk yén beugolén siteu mé comme danguén ko wara wkh deug pour aveniram
Saliou Gueye bro iow sonounga dé founé nga comantair fa ndax ama baledé 😃😃ténga dieule siteu mo geune si iow pour nga ame lo korité sax Pasqua insbi mome yeureum nala touss yoroko😃
Khassoum Cisse def anne blanche dé baxoule si mbeur Pasqua ama moy séne yakarou famille bi kone nak dafa wara ame combat nenguéne moko meune kaye na dieule combat bi daaneko séti lénéne mo geune wax dji
Yaw kou sonnou nga nekk si youtube di wakh rek siteu 4 deffait la am du 5 boy seye sa tiess mame balla gouy gui tenga bayi siteu te outi lo am mo geune kokou yalla moko maye si deffait la jougue te taye la geuneu saff nit yi ama lim tegle diy victoire te manoul passe fim nek te siteu bokoul sakh ak mom Te nga nopi bari nga wakh trop
Mbeur toute la communauté sérére,les îles du saloum et le village de Dionewar particulièrement de tout cœur avec toi ndam rek incha allah fils de dionewar
Thiate Le Champion... Ndam rék INCHALLAH
BEN ABDOU FALL
Allez Ben❤️💪🏽
Tiz Afia 🦁... Brother 👌🏿❤
Bravo lamine..tu as posé une question pertinente sur le cas père boy bambara.. tu as permis a thiat d'en parler largement.. mercii
Thiaat Ndam rek inchallah
Gnogui sa guinaw
Mbeur💪🏽❤️
Allée champion ndam rek inchalah
Thieuy lutte tv machaallah
Thiate iow kou rew nga ama balde momeune bayou siteu yalla nga ame defaite inchallah si barke yonneneti bi psl
Mbeur ndam rek inchalla tarkinda yep gnongi sa ginam boul ragal dara
Ndam rek nakk magg dji💪💪💪💪tous derrière toi
Mdam ✌️🤞rék 💪👉thiate
Boula armé diappé
Yalla nala yalla défal ndam inchallah 🙏🏾
group wastapp de thiate mome la sohla
Ndam rèk thiat
bèugu lamine liguèye Tarkala jeujeuf 👍👍👍
Ama siteu momm c un comba biuñou beugue forcé mai dou comba merci lamine
Armée rek💪💪💪💪💪
Thiate abiage laa démal défi contact sinom do dane kéne
Yow ak siteu boule boléwo Ama doumalè
Dam rek inchalla
Thiat danga wara xolat sa bopou dafa mélni gueumo sa bop siteu sama mbeur la mé ama moko mann fouf boumou dieul ama day yakou deféte rk yén beugolén siteu mé comme danguén ko wara wkh deug pour aveniram
Tiat bayil wah
Lamine ziarr Nala Ana Boubacar Ndour
Armèe ak thiatt Ndaw combat bou nekh
amo safara
thiate Dam rek boy
Siteu mane sakh mounou ma daan i
Bayville Animé bi Nak yawitte
@@yassinetoure6091 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Thiat billahi dafma diaakhal kiii 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
🤟🤟number one des vues🤟
😁😀😂
Dame rek fiis
Thiat yw boula armée diapé dalay bong bong
Ndam rek mbeur
Siteu amoull Beraii Dolai Bou Dann Ama balde amoull ausi Beraii Bou Dann Ama balde Boulma waxloo way thiath Yaak siteu Yaina Yamm Yaina Geuneu saltai palmarès sain Général kou Naik 5 Daifaitt la Amm siteu 5 Daifaitt Yaw aussi 5 Daifaitt Baparai Bariwax.....putin 🙂😎
Saliou Gueye bro iow sonounga dé founé nga comantair fa ndax ama baledé 😃😃ténga dieule siteu mo geune si iow pour nga ame lo korité sax Pasqua insbi mome yeureum nala touss yoroko😃
@@dioptalla227 ama xar bou amout boom la xamout foumouye taxaw bou dieloul siteu dou am combat
D p 😃😃😃😃doyna waar dé ama insbi damako yeureum sax insbi deureum yorouko
Khassoum Cisse def anne blanche dé baxoule si mbeur Pasqua ama moy séne yakarou famille bi kone nak dafa wara ame combat nenguéne moko meune kaye na dieule combat bi daaneko séti lénéne mo geune wax dji
Yaw kou sonnou nga nekk si youtube di wakh rek siteu 4 deffait la am du 5 boy seye sa tiess mame balla gouy gui tenga bayi siteu te outi lo am mo geune kokou yalla moko maye si deffait la jougue te taye la geuneu saff nit yi ama lim tegle diy victoire te manoul passe fim nek te siteu bokoul sakh ak mom Te nga nopi bari nga wakh trop
Woly nak wali ne khoul
Boy thiate ama baldé mo meune 10 siteu
Vraiment
Ndam rk boy
Invitè tigre junior lansar
Appel à Maréme Faye Salle
Thiat brom ngb ya meun armé dh
1ére taye
Ndam rek inchalall
yaw wakhal sa wakh boula armée diapé
Wahi doff denko wakh rek tremblement de terre am😂😂😂😂
Siteu biss bou djeulé ama dotouko defati
Tey Mom Contane si Yaw trop Tey Dega dal te lolou moy niit
Thiat.sama.mberla.tamit
Ndam rék mbeur iboutoucouleur
Woxo refa da okine koy.Comme tu as commencé par parler serère Niominka tu vas gagner ton combat.Okine opogoum