Amna Lou Khéwati Ci Mbiri Aida Diallo:Thiéddo Mouride Sadikh néna Aida faaléwoul Bénn Mbacké Mbacké

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 23 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 231

  • @soxkhou247
    @soxkhou247 2 роки тому +4

    Astakhfiroulahaa Astakhfiroulahaa Astakhfiroulahaa Astakhfiroulahaa Astakhfiroulahaa Astakhfiroulahaa Astakhfiroulahaa yalla nagne yalla diegal degg gui soubkhanalaah

  • @mamydiop8573
    @mamydiop8573 4 роки тому +4

    Honzibillahi mina seytané radjim aida diallo seytané laa boumakk

    • @elhadjifall9210
      @elhadjifall9210 2 роки тому +1

      Diereu diaf sokhna ayda hay sunu yakar bayilene Yok sawara si essence nena du not sunu s kh Bethio tag di te wer

  • @mariamangom8163
    @mariamangom8163 2 роки тому +4

    Machalah degue d'où rombi nôp

  • @ramatoulayebarry6980
    @ramatoulayebarry6980 4 роки тому +1

    Vraiment je tu avait raison man mom quand je reecoute les Video de aida Diallo Elle est allée loin merci de m'eclairer

  • @ballandiaye2208
    @ballandiaye2208 4 роки тому +13

    Kou ande ak Aïda Diallo saytanéga

    • @aladjisetedrame8074
      @aladjisetedrame8074 4 роки тому +1

      Wakhal kou neka mourid saytane nga nakh aida sy yenla bokou aida defoul dara

  • @nenekane6786
    @nenekane6786 5 років тому +19

    Aida Diallo doyna warr Sénégal lou way nekh def li métina trop bilay walay 😥😥

  • @momoniang6776
    @momoniang6776 4 роки тому +2

    Aida diallo moytoul yangui fowé sa bopou deh yangui late Biss dina nieuw ga deéh déloul guinaw si boumouy téle🙏☝️

  • @modoufall5006
    @modoufall5006 2 роки тому +3

    Aïda khamoul bopam walahiii wayé adouna mongui sounou kanammm inchallah

  • @assanegueye5727
    @assanegueye5727 8 днів тому +1

    SOKHNA AIDA DIALLO MO GUEUNESENE KHALIFE YOYOU BAYILENE DOULALE SOKHNA AIDA,DANGAYEDOULEREKE

  • @gallassmbackekonte2916
    @gallassmbackekonte2916 5 місяців тому +1

    Machalla thiédo mouride sadikh❤🎉

  • @talzofashion8416
    @talzofashion8416 4 роки тому +4

    Ma challa mourit

  • @fallalpha710
    @fallalpha710 4 роки тому +4

    Dieuredieuf Mouride yalla gua fi yagg tei wer amiiine

  • @zeinaboufall6504
    @zeinaboufall6504 4 місяці тому +6

    Moi qui vous parle, c'est SERIGNE SALIOU MBACKÉ QUI M'A RECOMMANDÉ DE FAIRE MON ALLÉGEANCE À CHEIKH BÉTHIO À TRAVERS PLUSIEURS SONGES EN 1991 d'abord à Thiès puis à Tivaouane. Je refusais au début d'y croire pour l'accepter. Ce que jusqu'à présent may toubal SERIGNE BI. MAIS SERIGNE SALIOU DÉFAL MA NDIMBALAM BA après bima dieufé NDIGAL li, lors de notre première rencontre à TOUBA dans la résidence KHADIMOU RASSOUL, après que ma mère lui raconta un de mes songes avec LUI, IL NOUS RASSURA à travers SES PROPOS AVANT DE Nous INVITER À ATTENDRE LE DÉJEUNER AVANT NOTRE RETOUR SUR TIVAOUANE.

  • @abdoukhadretop255
    @abdoukhadretop255 4 місяці тому

    Dieureudieuf
    Serigne Saliou Mbacké yallah sounou borom soubhanahou WATT-ALLAH dolli léer

  • @abdousylla6390
    @abdousylla6390 2 роки тому +6

    Wakhofi dara dara ba dara dièkh
    Yonewii wonou nieupeuleu
    Aida je t aime amiine

  • @modougueye555
    @modougueye555 3 роки тому +2

    mane mom naniou ma maye aïda rèk, vérémant damako nop ❤️

  • @niasskossoganar4772
    @niasskossoganar4772 4 роки тому +5

    Machalla Thédo morid

  • @gassndoye6712
    @gassndoye6712 2 роки тому +6

    Ragalale yalla féne rék ngaye déffff sokhna ayda yalla nafi yage t wére

  • @bambagueye4167
    @bambagueye4167 2 роки тому +4

    Aida diallo d'où mouride sakh

  • @ndiayendiaye313
    @ndiayendiaye313 4 роки тому +4

    Machallah

  • @BAOLINFOTV
    @BAOLINFOTV  5 років тому +7

    Ndéysaan Wakhi Daawna Yaraam Lool , Thiéddo Mouride Sadikh Nééna Aïda Diallo Faaléwoul Serigne Mountakha Ak Serigne Cheikh Saliou

  • @bocarndondykanekane5285
    @bocarndondykanekane5285 4 роки тому +5

    Maye lèn ma aïda diallo bii ma dèf ko 2èm famme

  • @khadimkhouma1534
    @khadimkhouma1534 4 роки тому +3

    Bilahi deuguela

  • @khadimfaye3613
    @khadimfaye3613 4 роки тому +3

    Machallah Thiéddo Mourid Sadikh Linga wakh lépou Degue la yalla nala yalla défal ndam

  • @modouboussogueye69
    @modouboussogueye69 4 роки тому +1

    Gracias

  • @Baye4444
    @Baye4444 4 місяці тому

    Gniagua Kham Rek. Loulou dou dara si Yallah. Dieu Yallah a dit ça sur les humains : celui qui fait tout ce que j ordonne et évite tout interdit, il agit comme si j étais lui .

  • @fatyndiaye6558
    @fatyndiaye6558 4 роки тому +2

    Kii Guélou pape Faye la

  • @GoraKane-t9n
    @GoraKane-t9n 4 місяці тому

    Allaho akbarr

  • @GoraKane-t9n
    @GoraKane-t9n 4 місяці тому

    Allaho akbar

  • @gueyeibrahima6221
    @gueyeibrahima6221 4 роки тому +4

    Inalilahi waina lilahi radji honn

  • @senemedoune-s5n
    @senemedoune-s5n 4 місяці тому

    aida diallo ❤rek la nope maylemako ❤ma defko 😂niarelle

  • @galayediop6667
    @galayediop6667 4 роки тому +3

    Dieureudieuf am na solo

  • @aliousarr8703
    @aliousarr8703 4 місяці тому

    Waw goooor 👍

  • @NdiasseNdoye
    @NdiasseNdoye 5 місяців тому +1

    Aida dallo sacrifice laye dèf

  • @mamisarr7787
    @mamisarr7787 4 роки тому +2

    Merci mon frère

  • @serignesalioumboup6736
    @serignesalioumboup6736 4 роки тому +7

    Thiéddo mouridd siarnala bouwer dinga am ndame inchallah

  • @mbayendiaye9488
    @mbayendiaye9488 2 роки тому +1

    Waho fi dara

  • @SumpDiaya
    @SumpDiaya 5 місяців тому

    Ya mene double sz thoapa ndeye ❤❤

  • @mouhameddiallo8975
    @mouhameddiallo8975 6 днів тому

    Astahfiroulah
    Xamna nii kenn dou Borom TOUBA ✨

  • @PapeNdeneNdiaye-l5e
    @PapeNdeneNdiaye-l5e 4 місяці тому +2

    Mounoulèna wakh ba dougnou geume ak topp sokhna Aida dieureudieuf yaguefy

    • @serignelahatsylla4441
      @serignelahatsylla4441 4 місяці тому

      Nanou bayii diambour waye mom dall toudoul kéna wakhoul kénadaraa man khawma aida masou mako guiss wayé barina gnoum tané fii

  • @moukhamedgningue5419
    @moukhamedgningue5419 4 роки тому +1

    Amna solo dé

  • @checkit113
    @checkit113 5 місяців тому

    Ya yess Aida Diallo parce que li ngay wakh c'est pour t'attirer la sympathie des mourides mais gueumouloko

  • @bambagold3672
    @bambagold3672 4 роки тому +5

    BI AÏDA NIEUWEE LA THIANT GUI RAKH

  • @awadiop9649
    @awadiop9649 4 роки тому +6

    Khàna aida diallo amoul mboke wala doome mou wakhko deugue

  • @biranepene2198
    @biranepene2198 2 роки тому +1

    Tiedo yaw maîtrisé wo yonou mouride te khamo serigne touba

  • @aronatop621
    @aronatop621 4 роки тому +15

    Thieedo mourite lo wakheu thi yonou mouride a yonou islam deugeuleu. Ziare nala bou wéreu

  • @doudoudiop5514
    @doudoudiop5514 5 місяців тому

    Naafeikhe boumacke n'ga

  • @manladia9153
    @manladia9153 4 роки тому +2

    Dieureu dieuf

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 4 роки тому +7

    Manchallah amna sollo

  • @PapeNdeneNdiaye-l5e
    @PapeNdeneNdiaye-l5e 4 місяці тому

    Moy yala

  • @madiorseye2304
    @madiorseye2304 4 роки тому +3

    Kou saga thieddo mouride rék sa baye dala hors jeu sén digger leufeull ndeye

  • @mouhamedmatargueye4733
    @mouhamedmatargueye4733 4 місяці тому

    En tout cas ande ak sokhna Aida moy diema tilimal liSlam parce que niaka diangue motakh goor gounè lingue di top ci ganaw djiguéne gni ko top khamouniou dinè

  • @aliousarr8703
    @aliousarr8703 4 місяці тому

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭🔥

  • @gueyeabibe7962
    @gueyeabibe7962 5 місяців тому

    Wa séne kheikh fanne la tolou

  • @niangmoustapha7102
    @niangmoustapha7102 5 років тому +17

    Aïda diallo dafa réw rèk

  • @salihatndiayedia1421
    @salihatndiayedia1421 4 роки тому +6

    Serigne Saliou dou samp ay thiakhane ayway yéwoulen wayé lep dina leer nagnou dem rek

  • @mallickdiagne3540
    @mallickdiagne3540 4 роки тому +3

    Thiedoo mouride nite kou bakh

  • @PapeNdeneNdiaye-l5e
    @PapeNdeneNdiaye-l5e 4 місяці тому

    Yow sa gatte nganane thièdo

  • @aitasyllaniang7932
    @aitasyllaniang7932 4 роки тому +1

    Merci beacoup 🙏🙏🙏

  • @mouhameddiallo8975
    @mouhameddiallo8975 6 днів тому

    Mok 'gnimi andall yeup ay séytanei laniou

  • @modoufall99
    @modoufall99 4 місяці тому

    Folklore môme Folklore la rek amul bu tané sa morome yen nieupa yam...

  • @mouhameddiallo8975
    @mouhameddiallo8975 6 днів тому

    Mai nagn sétann sën moudiou
    Barkè Borom Touba
    Loudoul deug dou yaggg

  • @mbackeyaram1946
    @mbackeyaram1946 4 дні тому

    Vere seytané nga iow dieune makk faye

  • @khadimkhouma1534
    @khadimkhouma1534 4 роки тому +3

    Waya li s.touba mokoy règlel bopam

  • @PapeNdeneNdiaye-l5e
    @PapeNdeneNdiaye-l5e 4 місяці тому

    Douli nènnnnne serigne touba kène. Momouko nopaloulène nafèkh nguène

  • @ibrakebe248
    @ibrakebe248 4 роки тому +1

    لاقوة الابالله، مسل ام دوله،قنا شيطان رك

  • @amyfall9653
    @amyfall9653 4 роки тому +2

    🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏machallah 👏👏👏

  • @moadcasa9176
    @moadcasa9176 4 роки тому +3

    Sokhna Aïda namougne réck

  • @bambagold3672
    @bambagold3672 4 роки тому +15

    AÏDA SEYTANE DIALLO DJIKO IBLIS LA YOREE MOUY DEUGUERE BOPOU AK NIAK DJOM AIDA DEUGUERE GATTE MAIS ELLE FINIRA MAL

  • @elhadjithiam3637
    @elhadjithiam3637 4 роки тому +2

    Akassa diadieuf mouride wakh ji rafetna

  • @mbenguemalick545
    @mbenguemalick545 4 місяці тому

    Thiey ceedo ak nila serigne bi dimbali we si ham ham nguey wah sa wahi yi ahh ceedo tey bede ngama nak

  • @diokoul
    @diokoul 4 місяці тому

    Neexa billasokkin rek. Yalla buma muthia si yow. Alxayri

  • @mbackeyaram1946
    @mbackeyaram1946 4 дні тому

    Sa wakh dji diouboul d bilahi

  • @abdoucamara5924
    @abdoucamara5924 4 роки тому

    Ki da meuneu doul fi la takhaw nii serigne BETHIO Lika serigne SALIOU DIOKHONE DIEULATHE NAKO TAYE MOUYE ANDEU AK DOMOU SERIGNE BETHIO SA LEUFEUL NDAYE WAY

  • @bassirounguer7411
    @bassirounguer7411 4 роки тому +3

    Dédétt thiédou Mourid lingaye déff ni liguéyal s touba la bou thi sonou bou thi tayi dél wakh doneté kéne nitt moyal diklou sakh bakhna

  • @abdoucamara5924
    @abdoucamara5924 4 роки тому

    Thiedo mouride na kathe ndayame fé

    • @yacinethioune8040
      @yacinethioune8040 2 роки тому

      Yalla nga goudd fann Thiedo mouride ak weer ken d'où serigne touba bayil nonou rek lép dîna leer mais ndeysan Day fék mou trop tard walahi

  • @ramatoulayebarry6980
    @ramatoulayebarry6980 4 роки тому

    Wali ouzoubillah😔😔😔😔

  • @AlDaneNdiaye
    @AlDaneNdiaye 4 місяці тому

    YÉN DANGUÉN AM DIOT. NDAW SI YOROUL SAKH MÉLOKANOU DIOULIT NGUÉN DI PÉRTE SÉN TEMPS

  • @moustaphasadiocissokhothies
    @moustaphasadiocissokhothies 4 роки тому +3

    Seytane aida diallo thialmm

  • @abdoulahadgaye8399
    @abdoulahadgaye8399 4 роки тому

    Ndiaf ndayi ayda dialo

  • @ahmada8328
    @ahmada8328 4 роки тому +4

    Eupou na guay toudou derigne touba ba pré di toudou aïda ba nane serigne touba mou djiguén Magui toup si wakh dji s touba amoul mrom té kéneu la

  • @fatimdieng4209
    @fatimdieng4209 4 місяці тому

    Nioune sokhna aïda moy sounou Serigne say wakh guemou nouko

  • @minanetv6437
    @minanetv6437 2 роки тому

    Waw gore mourir bou nieuwal melon niuaw yonwi tegou ci yon

  • @makanethiam6329
    @makanethiam6329 4 роки тому

    Sohlawouniou hame lou héw

  • @thierfall1086
    @thierfall1086 4 роки тому

    Thiedo mouride aamna solo aida diallo dafa dooy waar naa bayi thiakhan

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp 4 місяці тому

    Lu leer 😂😂😂

  • @dieynabadiouf5842
    @dieynabadiouf5842 4 роки тому +1

    Dédéte seugne bi boul tayél dél wakh ndakh lî ngay wakh amna solo loool sante nagne la bou wére

  • @moussambaye6915
    @moussambaye6915 4 роки тому +2

    yawe rék ya wara wakh wame ga sii Lou Bari yalla nassa diam.yague

  • @bambagold3672
    @bambagold3672 4 роки тому +4

    AÏDA DAFA MISTIQUE CHEIKH BETHIO

  • @fallamar6357
    @fallamar6357 2 роки тому

    GESA GO LEN DARA SEN YONE WO TILIME BARI LEUNTEU

  • @papadiedhiou7485
    @papadiedhiou7485 4 роки тому +2

    Gnî dagne leen wara sandi ci mballit. Ay seytânes lagnou

  • @meyoundao4103
    @meyoundao4103 4 роки тому +1

    Bilahi Aïda mo guadou ak ki dafa yabaté sakh aida mi yalla na tousskaré rék ki vrai manipulatrice wayé sou beugue loumou diyte na gnousou keur bayam très satanique yalla nako yalla alak au gnimou andale yalla nako akou mouride you bakh yeup té beugue serigne touba dal

  • @AstouKhouma-w2u
    @AstouKhouma-w2u 5 місяців тому

    Wakhaloul yonou mouride kéne ladiouko

  • @wademahibouwade6916
    @wademahibouwade6916 4 роки тому

    😀😀😃😃😃 iow doul Way

  • @kallamoulahelevemovid4364
    @kallamoulahelevemovid4364 4 роки тому

    Thiey thiedo meungha doul

  • @tallafall4385
    @tallafall4385 4 роки тому +3

    Ye'n jiye saga thido sayou ginn bindate' balagin Koy anvowaye se'n datab nday

  • @maissabeye8756
    @maissabeye8756 2 роки тому

    Youno sarigne touba we mom mokoy samalbopam sarigne montakha moy sarigne touba bonio dethion chiekh bithio mbor kon nio am linio baga waye kindou sarigne montakha

  • @ndiagagueye1740
    @ndiagagueye1740 4 роки тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @awadiop8731
    @awadiop8731 4 роки тому

    Doyna war

  • @zeinaboufall6504
    @zeinaboufall6504 4 місяці тому

    Ce faiseur malin, Diène Mac Faye, yaw laay wakh ak gni melni yàww: fayyouléen naar bi khoromam! Ndakh yàww bou fekkoon ni sakh Li ngay wakh deugg la, boo amée toutim cig talibé wara meuna wormaal njabootou SERIGNE BÉTHIO mii nga khamni amoul loumoula téraléwoul: maynala keur 500m² DIANATOU, Sokhna, ay doom, boulot à la CBAO de TOUBA sans compter SA CONFIANCE D'être parmi ceux qui gardaient son argent. Les moyens d'aller séjourner en France comme tant d'autres talibés, etc. La liste des bienfaits du CHEIKH sur toi est longue. Waayé sache que SERIGNE BI EST EN PERMANENCE AVEC NOUS ET UN AVENIR TRÈS PROCHE VOUS JUGERA, toi et tes acolytes qui cherchent, je ne sais avec quel intérêt derrière à ternir l'image du CHEIKH et SON ÉPOUSE QU'IL NOUS A DONNÉ NDIGAL DE LA SUIVRE.