Salaam Xou maker, waw man ma ngui suivre poadcast bi depuis longtemps et nio ngui feel tamit job bou nice bingay déff yakk sa wa team bi yeup dilén si shoutout bou wérr. Mais le bémol en est que hip-hop wala rap nitt kou nék ak ninga koy concevoir ré gni daniouy koy déff par engagement et dénonciation des moeurs, gné pour fun, gné pour lénéne. Chacun est libre de faire du rap comme bon lui semble. En tout cas pour man mouy Meuz, Zou ak Jamal niom nieup nék si deug, rérro mo si am rék mais saga yi ak xaastanté yi meunone na niak koi kounék kay suivre poadcast bi di diégalou wat bou wérr.
J'attends que ça soit disponible sur Audiomak

C'est regrettable... que deux adultes se comportent ainsi.
Waa Zou ki Wkhoul Lou graw 😭😭😂😂😂
Who the hell you is agaaiiiin 😂😭🤝🏾
Ciey man zou mi😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Zou est ce que nekoul si koor 😂
Zou kana merna sama adouna mani sogua guis Zou meer😂😂😂