Bilahi papa mane damala naw trop...tu es le seul lutteur bo xamni magui lay supporté + de 10 ans t chak jr damalay gueuneu naw...yalna ALLAH (SWT)diapaléla mayla lu wéssou sa ndiorte...
marietou mbengue amna solo mom kouko degg beugg ko ndaakh beugoul kouko yapp motakh dou togne dou garouwalle niit deugg la yalla naniou yalla sakhall si joupp mom mi mom joup amine
champion papa Sow je te respecte beaucoup tu es intelligent dicourag ça va aller inchallah dieu et grand que dieu vous bénisse toute qui est devenu devant toi
Tres intelligent wakhine bi rafetna lol sakh e puis nitt yi kén momoulén so xolé commentaire yi rk par rapport au autre lutteur ngua xamni nieup rafétlou naniou sa yarr Ak sa teguine... Continue kom ca
Je suis fan de Balla Gaye, Sa Thies et Ama mais j'adore Papa. Après sa défaite j'ai pas jubilé. Il est temps de quitter fass et d'aller à Rock Énergie pour redémarrer ta carrière.
Mbeur yi yarou , teey té am teguine bari na.
Wayé raw Papa Sow yomboul Mashallah
Yalna Borom bi japale la.
Bilahi papa mane damala naw trop...tu es le seul lutteur bo xamni magui lay supporté + de 10 ans t chak jr damalay gueuneu naw...yalna ALLAH (SWT)diapaléla mayla lu wéssou sa ndiorte...
il communique tres bien cest pas mon lutteur preferé mais je lui souhaite le meilleur pour le reste de sa carriere respect PAPA SOW
papa machalla borom bahgua so amatè comba yalla nalla yalla may ndame way parkè yeunéntibi psl
C la première fois ma deglou mbeurr mouy wakh wakh djou correcté provoqué sa béne morom lutteur mé respect champion...
Franchement interview bi nice na! amoul attaque personnelle, tognoul ken té wakhna wakh bou rafet.
Papa sow danga meun waakh man nawnala trop continue come ca reik doundeul AK ay ndaam you beurri
Khadim Ndiaye amine way kii ndanane deug leuh il est très cool
Je l'adore vraiment il n'est pas mon lutteur mais il parle bien wakhe djii rafete na lole merci
Cheikh Mboup guiss nga deih Goor la ndaakh Goor moy deff li
marietou mbengue amna solo mom kouko degg beugg ko ndaakh beugoul kouko yapp motakh dou togne dou garouwalle niit deugg la yalla naniou yalla sakhall si joupp mom mi mom joup amine
Amine
Franchement PAPA sow kou yarou Amoul Ben problème en plus c'est un très bon lutteur
Franchement papa sow est un grand homme
Papa Sow kou yarou gua manchAllah nalla yalla méy ndam sa prochain combat inchAllah. Wa salam.
Vraiment Papa sa waxx rafét na yalla nala Yalla défal diam Macha Allah Tu es le vrai Champions
Je me suis dit que papa Sow kenn bagnouko si lamb dji
Papa yaw borome bakh nga champion nga du courage yalla nala yalla maye nabm la prochaine fois inchallah
PAPA SOW Est tres Noble et veridique.beaucoup d'estime pour toi.
Merci beaucoup papa sow rafétna trop
champion papa Sow je te respecte beaucoup tu es intelligent dicourag ça va aller inchallah dieu et grand que dieu vous bénisse toute qui est devenu devant toi
Bilay man guene nala beug ndakh sa wakh dj rafetna trop trop way lisi kanam yalla na dakha lisi guinaw way papa sow décourager
Merci papa nice na
Wakhji rafétna lool yalla naleen yalla défall diam
bonne continuation dina bakh inchallah champion nga vraiment lamb dan ak danou gno and ☝☝☝☝👈👈👈
Bien dit papa sow
Il sait bien parler Papa.
Chapeau à toi
Tres intelligent wakhine bi rafetna lol sakh e puis nitt yi kén momoulén so xolé commentaire yi rk par rapport au autre lutteur ngua xamni nieup rafétlou naniou sa yarr Ak sa teguine... Continue kom ca
Machallah papa dina bakh
papa sow yalla nala yalla défal diame yarouga taye ga champion
Ohh Papa Sow vraiment sa combinaison rafét na guiss néy linga yééné mbeur yii
Sa xol mo rafét yalla nala yalla défal diam
Du courage papa tu as bien dit
Il est très cool champion Ndam rek
Bonne continuation et bon courage dina bakhe inchalla
Yaw Champion nga té borom bakh nga Yalla naga am diammu
respect papa día dieuff way
Machalla ❤️❤️❤️❤️
Je t'aime papa sow courage
Machallah papa kadou yi rafetna
Vraiment T un champion say wakh rafète...fans balla mé je t'apprécie beaucoup
Macha Allah bien parler
Nice papa Courage rek cou gor nga bilahi
nice mbeur mane pikine lay supoter mais champion nga yalla yalla takhawoula
Machallah sa wakh rafétena mbok mi djarama Sow
Il communique bien mrci 👍
Do sama mbeur wayai sa wakh rafetna Macha allah
Rafetna dina bakh incha Allah
Machallah Papa wakh dji rafeet na
Respect champion
Merci boye sow👏👏👏
Merci lutte tv
Machala papa rafetna
kou bakh la papa sow
Papa nieuweul Rock Énergie day geuna nekh rek
Machala papa wakhbi rafetena setena te selna
machala papa sow nikel
Merci Mbeur
Dinga am loubakh ndakh sa khol dafa rafét ☝wakh diou rafét loumoula mayoul doulako khagne sa wakh Rafétna machallah 👍 👍 👍 👈 👈 👈
Machala papa sow wakh dji rafetna
Ndaysan billahi kanam gui dafa sedd nala yalla maye li guen si yaw
Avez vous remarqué mbeurou fass yi danio yarou té bah MachaALLAH
Papa sow yow dangaa bakh Lou raféte rek ngay wakh osi téy yarou yalnala yalla défal jamm
Douma sen fans modou lo ak iow dh
Mais geste bobou nice neu yalla nalel yalla lafall thiatt
Vraiment sa kadou tafetna machallah
Franchement papa vrai sportif ga sa communication bax na
Man balla me papa modou neke len ci diamo bo bakhe nice 💎
papa wah dji teguinei neu rafet neu masha'alla
rafetna way papa
Bien dit champion
Ndama li wakhbi rafetna machallah lepp dina bakh inchallah diap rk ndamaa ngathia kanam walahi
Merci papa sow lepp rafet na yaw ndam rek guay am sa kholl mo rafet
nice na mbeur bonne contuation
Bien dit
Machallah
Ma sahaalh papa
Machala champion
Non papa sa khole rafetena fi nga Tek sa tank foufou la ba la le er daye leudeum dina bakh du courage
Wakhji rafetna trop Nice
wakh dji rafet mon lutteur préfère Dagua ame yare lolou la niepp wakh le meilleur reste à venir
Jahjeuf Papa Sow
Machalla wakh dji rafètna machlla
yallah na sadiam yagu papa sow nit deug nga nit nga tenitenga
Merci Papa wakh dji rafetna
rafetna bone continuation
Nice pp rafetna trop
Nice papa
Yaa bakh rek machallah
mbeurr Jajeuff yalle na yalla dijapalé la
Ki est là en 2024
Vraima wakhbii rafetna papa sow
Adji toyngua
rashford Ndaw byil togn
Nopp nala dall
adji yw yagui fepp khana
Ameth Cisse ahh yam guis dee machala
Nice
Diadieuf papà nice na
Nice toff
Frenchemn papa daguama neih psk dagua cool yarou xam adouna
Mer6 grand wa pikine bégué nanoula bo a maté comba soudoul pikine YALLA NALA YALLA may ndammm
Dicourace papa lepaye bakh
Je suis fan de Balla Gaye, Sa Thies et Ama mais j'adore Papa. Après sa défaite j'ai pas jubilé. Il est temps de quitter fass et d'aller à Rock Énergie pour redémarrer ta carrière.
mahcalla papa
bon change papa soh
Diadieuf champion
Rafetna Bro begué
💪🇸🇳🔝
Il parle bien comme Tapha Gueye
Wadji mom seytané deuguleu papa Sow borom bax la
Do sama mbeur mai heure boy beuré iow laay farale dila nianale boubakh lissi kanam lepou di ayy ndam
Il communique bien c comme sa...