‼️Alahu akbar: Wa famille ki ray Aziz Dabala gni ngui khatarayou oh ken mounoul tei sa bop si teudj

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 28 жов 2024

КОМЕНТАРІ • 328

  • @lala_aishaa
    @lala_aishaa 2 місяці тому +249

    yalna niou yallah mousseul ci diour dome bou reykatou nitt 😪😪😪

  • @FamaDiop-k6j
    @FamaDiop-k6j 2 місяці тому +46

    Bi gathié yalla na bougnko am adouna AK alakhira 500 ou700 mil takh nga Ray nit semaine mou diekh nga dess AK sa conscience yalla na niou yalla mouthial si beug alale adouna🙏🙏🙏🙏🙏

  • @ramathiamniang6820
    @ramathiamniang6820 2 місяці тому +294

    Tongne nga sa famille takhal ngalén si lou diaroul dara
    Té so démé ay goorlaniou ay bagne kat laniou😢😢😢 c'est malheureux

  • @ndeyediouf8777
    @ndeyediouf8777 2 місяці тому +81

    Bravo police sénégalaise chapeau à vous 😢

  • @mouhamedndiaye2665
    @mouhamedndiaye2665 2 місяці тому +496

    Police deff na ligueyam mais bougn ko taudie , nagn ko diebeul askane wii mou mattal ligueyy bii ,kou d'accord ak mane rk ,👍👍

    • @laminelayekebe615
      @laminelayekebe615 2 місяці тому +15

      Je suis d’accord avec toi 😒😒

    • @magembaye8842
      @magembaye8842 2 місяці тому +11

      Lolou rek
      Teuthie day yombeu

    • @siroupam7249
      @siroupam7249 2 місяці тому +5

      Bouboba dou bakh kone kounek day def loula nekh

    • @ThioroDiagne-us5wm
      @ThioroDiagne-us5wm 2 місяці тому +13

      Nagnouko ray ossi rk pour donner une bonne leçon à la population .

    • @lovemamiishwallyseck
      @lovemamiishwallyseck 2 місяці тому +8

      Gnou tal ko bouko defé legui rayy bi diekh

  • @ndeyebinetafaye4141
    @ndeyebinetafaye4141 2 місяці тому +217

    Ay way bly Mamadou diao ligua tég sa familles ag familles Aziz ag Wally disna trop trop sah

  • @sallandaye2266
    @sallandaye2266 2 місяці тому +122

    Barina kougnou yapp ndiaboot mokoy yaplou yalla nagnou yalla moussal

  • @fallougentlemara4853
    @fallougentlemara4853 2 місяці тому +138

    Ki Ray Aziz gathial na wa famille bimou bok bilahi té niom douniou si dara c'est dommage pour eux

  • @Diarista90
    @Diarista90 2 місяці тому +129

    Yalla naniou yalla mouseul si gathia adouna ak alakhira 🥲😭😭😭

  • @sekoubadji9764
    @sekoubadji9764 2 місяці тому +39

    Bravo à nos Jaambar la police et la. Gendarmerie DIC chapot à vous

  • @diarrysadio4056
    @diarrysadio4056 2 місяці тому +11

    Yalla na gnou Yalla maye moudje bou rafféte akk dignou khirtal thi bopame 🙏yow mi deff li dé guathiel gua sa askane yeupe tékk nakar famille Aziz..Waly akk sénégalais yeupe loula diaral li

  • @ndeyesarr9660
    @ndeyesarr9660 2 місяці тому +77

    Wa légui Danako diap après mou diékh nanko Ray comme nimou rayé domou ndiamour yi lolou Moy deug

  • @oumoukalsoumLoum
    @oumoukalsoumLoum 2 місяці тому +47

    Mangui soga guis li Sénégal non li méttina way yalnagnou yalla mousseul thi gathié adouna ak bou alakhira

  • @BinetayoussouDiakhate
    @BinetayoussouDiakhate 2 місяці тому +87

    Ayo ndaysaneuu aziz y’all nako sa Borom bi diegal ki def ndiaw Tef bi ding ko layo

  • @koumakhfaye8360
    @koumakhfaye8360 2 місяці тому +15

    nekoul boy, kou am 25 ans mag la, nekatoul hale. c est un sadique, un sans coeur

  • @mbakhengom7488
    @mbakhengom7488 2 місяці тому +32

    Ki deh waroulwone toudeu Mamadou Lamine. Togne na mbokki Aziz ak Waly, togne ay mbokam diakhassé adina. Wayé nak il ne paye rien pour attendre. Yakheuna adinam ci zero.

  • @Nana-o7e3x
    @Nana-o7e3x 2 місяці тому +26

    Yalna ñou yalla mousal si seytane si pexeme mo am dole sou ñewe rek dome mo geena for nitte ndeysan 😢😢😢😢

  • @adamaadama4923
    @adamaadama4923 2 місяці тому +22

    Kassou Sankara 100f lakhassou yamba 1000f fane laniou dieum

  • @awagaye4878
    @awagaye4878 2 місяці тому +13

    Li ma meti rek moy wa famille wam dotonio am kadu si rew mi lonio wakh nionelen sen dom mofi ray niary nit nga gathial sa famille ba faw lan mokofi diar😢

  • @asambe463
    @asambe463 2 місяці тому +3

    Dianguate deugeuleu , nah defois nit domame deye fef dara niou wah ko wadiour ya wedi andil la thiowe
    Wayee li mome guore khadioul si yena yi surtout lou melni khamnee adouna bi niepeu ko dioye
    YALLA BOUR Bi kharee lene😢😢😢😢😢😢😢 Aldjianeye Firdawsi ah bepeu Dioulit bou moufa nekal Amine 😢😢😢Aldjianeye

  • @sunhomengor2887
    @sunhomengor2887 2 місяці тому +14

    Amadou lamine diao tass nga yakarou famille, tegg nga sa famille gathié goudoul faye ba faw louka fi diar 😢

  • @modououmy1676
    @modououmy1676 2 місяці тому +7

    Yalla naniou yalla may moudjie gou rafét

  • @adjathiam2398
    @adjathiam2398 2 місяці тому +22

    Yallah nako yalla yeurem khareko aldiana firdawsi momak wally ak mbolom domi adama gnifa neke te yeukhniou

  • @maguettediouf4464
    @maguettediouf4464 2 місяці тому +40

    Barké cheikhoul khadim kii rayy aziz dabala améll na wakeureum akk bou reuy sokhor késsé moko waral domékharam djimou done

    • @loveallah6355
      @loveallah6355 2 місяці тому

      Senegalese b ak Gambian lepu kai la amell akk 😢😢😢😢😢
      Lee dafma meti 😢😢

  • @alleualleu693
    @alleualleu693 2 місяці тому +3

    😢yalla nanou Yalla moussal thi ndom diou bon😢😢😢😢😢

  • @ibrahimandiaye-5250
    @ibrahimandiaye-5250 2 місяці тому +39

    Boy yi dounou khalate sakh inconvénients yi

  • @adamambengue6117
    @adamambengue6117 2 місяці тому +3

    Quel gâchis. Louko fi diar ndeyessane aziz est parti comme ça. Yaw mi dieuf dieuf diou bone ngui Torakhal nga sa bop torakhal sa famille ame guéne way boudoule fay mouk. Ya bone ya yéss, yaw louma la beugue wakh khép ko, yalna la Yalla ték métite bou raw bi nga ték famille aziz. Ya bone ya yéss

  • @fayebirame3656
    @fayebirame3656 2 місяці тому +11

    Xamon youkhou dineu djib fougnou xalatoul'woon
    Gathiél sa wakeur ci digou adouna nii

  • @ousmanesarr756
    @ousmanesarr756 2 місяці тому +37

    Togn famille Aziz tek sa famille gathié gou reuy gui dara diarouko si adouna té degg na papay ki Ray meusoufa dioug ba tay sakh mongui wone si bậches bi thiey yalla🤦🏼‍♂️😭

    • @AmyThior-kv3gh
      @AmyThior-kv3gh 2 місяці тому +4

      Daguay wakh rék 😢

    • @ousmanesarr756
      @ousmanesarr756 2 місяці тому +7

      @@AmyThior-kv3gh bilahi nenagn bamou degué nouvelle bi la dioug meunoul sakh dokh ndakh gathié

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 2 місяці тому +4

      *Loy wakh ni ioe ohhhhh😢😢😢tégue naléne gathié bou reuy*

    • @pronosticfootsenegal1112
      @pronosticfootsenegal1112 2 місяці тому +4

      Ohhhhh kholal ma li rek doyna waaar gathié bi meune na ray ass gor

  • @mbayesembene6153
    @mbayesembene6153 2 місяці тому +17

    Sénégal bén bop la. Xaley yi dugnu xam li gnouy déf. Yalna borom tapez khôl yi. C'est très triste oh ndeysane

    • @AblayeDiop-e8r
      @AblayeDiop-e8r 2 місяці тому

      Wallahi khayne liga dogal sakh khamokou doyna war dall

  • @Daouda_venezia
    @Daouda_venezia 2 місяці тому +2

    Bo demé sen wa keur ay gorgorloulagnou gua tek len benen Nattou.. vraiment boy raygua sa famille yeup

  • @NdeyaSarr-xp3fv
    @NdeyaSarr-xp3fv 2 місяці тому +2

    Nakar ack gathie yallah yallah nous seul si nit kou bonne😢😢

  • @matyndiaye6070
    @matyndiaye6070 2 місяці тому +34

    Merci police sénégalaise li thi desse moye nguene diebalko wa thies gnou motali yenedji

    • @yayefall9395
      @yayefall9395 2 місяці тому +2

      Haaaa lolou idée laa dee Thiès rekk dagnon efficace

    • @moustaphasylla1773
      @moustaphasylla1773 2 місяці тому +3

      bilahi nioune niougui ni genres Yi laniou meuneu réglé

    • @madytall801
      @madytall801 2 місяці тому +1

      Wawa legui nagne nioko livre nioune wa thies niou def suniou ligueye

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 2 місяці тому +2

      *Maléne gueume déh bilay wlay ligua wakh lagnou wara deff sakh nakk*

    • @matyndiaye6070
      @matyndiaye6070 2 місяці тому

      @@moustaphasylla1773 yene la gueme mane soriwouma thies je suis de notto

  • @AwaDiallo-h4j
    @AwaDiallo-h4j 2 місяці тому +4

    Ki dafa ray deux familles familles Aziz ak sene familles

  • @abdoundiaye2069
    @abdoundiaye2069 2 місяці тому +14

    Natou dou wess aduna leep dinguaĺéla yalna yalla doli diam

  • @OmarFanne-wd7tp
    @OmarFanne-wd7tp 2 місяці тому +1

    Bilaye yeureum na niari fami yi 😢

  • @MouhamedFamaraPierreSAMBOU
    @MouhamedFamaraPierreSAMBOU 2 місяці тому +36

    kholalma guathié bi reik

  • @abdallahconte
    @abdallahconte 2 місяці тому +35

    Allahou Akbar li niaw na 😢😢😢😢😢

  • @laminezofall8917
    @laminezofall8917 2 місяці тому +7

    Li métina lolou nite bala guayi def dara del khalate sa guinaw après yanne conscience la mène indi

  • @evelynediallo4731
    @evelynediallo4731 2 місяці тому +12

    Oh ndeysanne metina torop bilahi khale bi limouy def niaw na torop😢😢

  • @yusub2543
    @yusub2543 2 місяці тому +3

    Wallahi je me sens tres mal
    C'est vraiment très triste.

  • @DiorDIAKHATE-hh6mr
    @DiorDIAKHATE-hh6mr 2 місяці тому +1

    Que DIEU nous préserve de ce malheur..mettina

  • @abdoulayesarr1138
    @abdoulayesarr1138 2 місяці тому +12

    Bayille fene ana bassbi danou ragalall yalla anayalla bourbi

  • @rihannand5701
    @rihannand5701 2 місяці тому +5

    Deuk ndo lou ñaw khadiou thi bilaye 😢😢

  • @maimounasidibe781
    @maimounasidibe781 2 місяці тому +1

    Mamadou lamine mi tégoul séen gathié adouna 😢 yak adouna Aziz ak wally😢 😭😭😭😭

  • @NdeyefatouSylla-yp9px
    @NdeyefatouSylla-yp9px 2 місяці тому

    Ripbss en paix Aziz yallna nakou yalla khr kou alldintou firdawci Amin 😢😢😢😢😢

  • @AnnaFaty
    @AnnaFaty 2 місяці тому +3

    Thiéy bii kathié dara diarouko thi aduna

  • @MariThiame
    @MariThiame 2 місяці тому +1

    Yalna len yallah jegal té Karel len aljana, mais Esquie alalu aduna dar na fat bakan, ki déf li dan nuko wara ray li metina trop 😭😭

  • @MalickSeck-i7d
    @MalickSeck-i7d 2 місяці тому +6

    Yalla nako yalla kharé
    Alldiana firdaws

  • @laminelayekebe615
    @laminelayekebe615 2 місяці тому +9

    Nn Li dafa niaww Bilahi 😢ték ga gathié sa wa keur 😒😒😒

  • @AissatouWade-z2n
    @AissatouWade-z2n 2 місяці тому +25

    Ki yalna nako yalla trokhal

  • @FatouSylva-d1i
    @FatouSylva-d1i 2 місяці тому +2

    En raby kabir yahalla yaraby hamdoullah yaraby nous à montré qui a fait ça hamdoullah

  • @clairemari7292
    @clairemari7292 2 місяці тому

    Incroyable mais vrai c triste et grave ça

  • @Thiernothiam-ph8ob
    @Thiernothiam-ph8ob 2 місяці тому

    Touba est une ville sainte

  • @fabisane3445
    @fabisane3445 2 місяці тому +16

    Prison sax dafay yomb

  • @bambagabi9720
    @bambagabi9720 2 місяці тому +2

    ces quartiers sont indignent d etre a dakar

  • @Diamila79442
    @Diamila79442 2 місяці тому

    man sama problem moy deujie bi pour lan la ki ñaan la sokhla togandoo bi mounoon na ñakk verement😢😢😢

  • @soldarousbabacar7291
    @soldarousbabacar7291 2 місяці тому

    Yal nako yalla yeureum si batou la ilakh illala

  • @adandoye3759
    @adandoye3759 2 місяці тому

    Bravo la police sénégalaise 🇸🇳 legui nagnu ko raye rek c’est tous

  • @MbayeGakouNDIAYE
    @MbayeGakouNDIAYE 2 місяці тому +1

    Courage aux trois familles

  • @seckassane8064
    @seckassane8064 2 місяці тому +8

    Naniou. Ko rayy domeram la

  • @ISmile__
    @ISmile__ 2 місяці тому +4

    Il faut informer juste et vrai…. Quelles bâches sont tombées??? mais non

  • @tabatreich89
    @tabatreich89 2 місяці тому +5

    Mais gnom ils n’ont rien fait! Tueur bi kaay moy niit kou bonn rek! Tegu nelein guatiè d ndeysann

  • @NdeyefatouSylla-yp9px
    @NdeyefatouSylla-yp9px 2 місяці тому

    Masa yalla bkhna de 😢😢

  • @FatousineNdao
    @FatousineNdao 2 місяці тому +1

    Yalla na niou Yalla mouseul thi séytané bou nék si biir société 😭😭😭😭

  • @user-2032
    @user-2032 2 місяці тому

    Yalla naniiou Yala mouseul si cheytane ak gathie

  • @mamediarraka2214
    @mamediarraka2214 2 місяці тому

    Xallei bii dioyla ma ndeysan😭😭

  • @IbrahimaBaldé-b4s
    @IbrahimaBaldé-b4s 2 місяці тому +3

    Familles bi nakar molén di Ray niom gneupp

  • @MameThierno-o8q
    @MameThierno-o8q 2 місяці тому

    Ndaye sane😢

  • @ndeyefallndiaye8063
    @ndeyefallndiaye8063 2 місяці тому

    Gauthier na familles dè li darai adouna diarouko😢

  • @Coubagéi
    @Coubagéi 2 місяці тому +4

    Ligua ték sa famille bi bilahi métina trop ya bon ya yés bakho bén yon kham guani li nékhoul si khôl

  • @laminezofall8917
    @laminezofall8917 2 місяці тому +3

    Arrêté c genre de vidéo la c pas bien j'ai Les larmes aux yeux

  • @NdeyeBeye-c3p
    @NdeyeBeye-c3p 2 місяці тому

    Bouniou wakhoul si yamba bissi rewmi desna yanen ray kounek nak man nga doon kiniouy ray 😭😭😭

  • @CNMBusiness
    @CNMBusiness 2 місяці тому +6

    Bilhay bouye dina dioure khatakhe dagnaye boke si famille you bakhe yawe nga nieuwe rek yoré sa djiko bope

  • @mmmomo4267
    @mmmomo4267 2 місяці тому +1

    RAISON pour laquelle si tu as un enfant incontrôlable dénonce le sinon un jour viendra on va vous mettre TOUS dans le meme sac

  • @FatimataBa-r5j
    @FatimataBa-r5j 2 місяці тому

    L'éducation e la basse

  • @Gorguisenegal
    @Gorguisenegal 2 місяці тому +2

    Deff léen si ndank esk mo réy wa dic wakha gouniou ni le procureur

  • @mansourndione178
    @mansourndione178 2 місяці тому

    Tu a raison nankoye reye

  • @yacinediop7557
    @yacinediop7557 2 місяці тому +1

    Ay gni sen guathié bi😢😢😢

  • @MamedialloGueye-pm1tx
    @MamedialloGueye-pm1tx 2 місяці тому +34

    Prison a vie travaux forcées

    • @sodasarr-hb8nw
      @sodasarr-hb8nw 2 місяці тому +7

      Lolu Dafa yomb trop nagne Koy Ray comme nimu rayé nite gni lolu la diiné wax

    • @guedjgueye6478
      @guedjgueye6478 2 місяці тому +4

      ki gnou warko pendre publiquement pour mettre en garde

    • @yayefall9395
      @yayefall9395 2 місяці тому +2

      Alla yomb nagnoukoo simmi bamou sett diell sen temps dikoo torturée bamou dee kassara Matt bii ngeupp nga tere nelaw ba pare nganni danga magalii

    • @beugueserignesaliou6842
      @beugueserignesaliou6842 2 місяці тому +1

      Day yomb torop kikay gass pakh rek mélange xérou béton ak ciment soti ko ci kawam limou ma dioylo doumako ko baal

    • @Yes-eq7me
      @Yes-eq7me 2 місяці тому

      @@yayefall9395bilahi si jamais on le laisse beaucoup vont en profiter li bahoul sah si xaléyi Mon Dieu😭

  • @CheikhsadbouAidara-ck3vu
    @CheikhsadbouAidara-ck3vu 2 місяці тому +1

    Mamadou diao Aziz guennalao demine ndakh kougnou ray thi tognla aljanna moy se keur yow nak doto guiss dient bi te biss pencc dinguako layo

  • @mansourdieng2000
    @mansourdieng2000 2 місяці тому +3

    *Samedi Le 24 Août 2024*
    Nagn Déf Li Yalla Wakh Nagn Ko Ray Comme Nimou Rayée Aziz Dabala Lolou Moy Manou Té Lolou Mofi Dieulée Raye Manou Nio Am Yeurmandé Ba Eupp Ko Yalla Mi Niou Sàkk Bakane Bakane Mokoy Faye Nagn Ko Ray C'est Tout Bou Féké Ay Dioulitt Deug La Niou Nagn Ko Ray Nagn Ko Ték Nieup Diko Guiss Niou Ray Ko Bouko Défé Kéne Dotoul Raye 😡😡😡😡😡😡

  • @abdourahmaneba3294
    @abdourahmaneba3294 2 місяці тому +1

    Non cheytané barina dolé ohhhhh yallah nagnou yallah ték si yonou siratal moustakhim mais boy bi ray aziz kholal gathié bi nga ték sa yaye ohhh li métti na légui sa famille nane lagnou nara doundé si quartier bi rk ohhhhhh c'est malheureux vraiment vraiment🤦‍♂️

  • @rahmandiaye3469
    @rahmandiaye3469 2 місяці тому

    Paix a son ame

  • @mamanmbaye1305
    @mamanmbaye1305 2 місяці тому

    Merci beaucoup police sénégal

  • @madakane3786
    @madakane3786 2 місяці тому +6

    Dé koumou waroul dara doula warr ak li ga titré ni diféren ak li ga wané

  • @fatoukinembaye4787
    @fatoukinembaye4787 2 місяці тому +4

    Hohoo li gnawna trop

  • @BinetteDiegne
    @BinetteDiegne 2 місяці тому

    da ngiou bay ngiou ray léne rekk wayé kou ray dangiou la wara ray😢😢😢

  • @bintamane8232
    @bintamane8232 2 місяці тому

    Sa yaye au nonom may galenn lougnou wakhe ss yaye dou meul dem fenn fimou guenn on dit ki moy yaye reykatou nitte bi 😭

  • @awasall3904
    @awasall3904 2 місяці тому

    Gathiel nga Say mbok togn ngalene rouslo ngalene
    Khaliss kouko beug da ngakoy liggeey 😢

  • @FamaMbaye-v5d
    @FamaMbaye-v5d 2 місяці тому +4

    Naniou ray ndeyem

  • @MarianneDieng
    @MarianneDieng 2 місяці тому

    Li comme film

  • @YayouNabi-w7z
    @YayouNabi-w7z 2 місяці тому +1

    preparez vous au moment des reconstitutions des faits rek kou raay gnou raay le pour des miettes tu elimine des espoirs li gnawna

  • @RokynaSambou
    @RokynaSambou 2 місяці тому +1

    Nagn ko ray

  • @AntaGueye-z5g
    @AntaGueye-z5g 2 місяці тому +2

    Na niouko Ray mogane tadj niarifan nioudieunako moudefat ko

  • @mariemegadio774
    @mariemegadio774 2 місяці тому +1

    Bravo à la Police Sénégalaise, c’était juste une question de temps pour élucider ce double homicide.
    Mais ki deff li togne gna Azziz, Wally et sa propre famille. Yallah nagnou Yallah mousseul si guathié aduna ak Alahira.
    Tout ça pour de l’argent

  • @mamethiernobeye2209
    @mamethiernobeye2209 2 місяці тому

    Stp nagn ko ray li dafa eup

  • @megalebu
    @megalebu 2 місяці тому

    Merci la police mais il faut le livrer a la population niou taal ko

  • @BintaSagna-z3r
    @BintaSagna-z3r 2 місяці тому

    Naniou ko rey comme nimou réyé Aziz ak wally justice soit faite déf lén lou charia wakh lolou moy deug

  • @revolutionsenegalaise7568
    @revolutionsenegalaise7568 2 місяці тому

    Ay bi gathié nit dafay am loumuy diombou 😭😭😭