Mais, vous ne pouvez pas foutre la paix à ce couple ! En quoi cela vous concerne ? Franchement au Sénégal vous avez du temps à perdre en vous mêlant de tout Merde quoi
Moi dé j'entends un jeune mature et responsable par ses paroles et la tonalité de sa voix très posé très calme pour un jeune dr son âge bayiléne jambour bi nguir yallah cest sa femme qui ne devait pas venir sur les réseaux sociaux elle devait laisser couler ❤❤❤
Walay ndeysann frère c'est ce que j'avais dit dans l'émission en direct le sens de maturité et de responsabilité que la dame a vu en ce garçon malgré son âge elle ne l'a vu nulle part ailleurs Sénégalais nio wara mandou diadieuf bro
Bilahi tt a gnémé deugueu sénégalais khamouma Lou takhe mou Faux fi thie Europe danguaye guiss kou tak toubab bou mél ny golo gnou diko félicité ki tak sénégalais gnou diko saboté@@talibeserignetoubaibrafall6311
Barké s touba béne parent gnanoul yalla li sokhna pénda mi sou domame démone di taki béne mère douko nagou ki mak la ki khalé nako bayi mou dème taki khalé ki méné paux li bakhoul way 😭😭😭😭
Si cté une blanche on comprendrait que interêt lako topé mé cas bii khalébii Lane la topè mère bii? Arrêtez l’hypocrisie et essayez d’être à la place d la mère de ce p’tit
Boy bi andoul ak khélame dée limouy wakh ni maîtrisée wouko boy ya yakh sa dér ya abandonné sa famille ndakh khalis ak djiguéne mes kou d'accord si seuy bi rek yalla na yalla déf gua am dom djou mélni
@@modourokhaya9616mais Yow yaye Yalla? Niata Niit nga fi guiss niou sey ba maguette té amou niou dom. Bayileen tokk plassou Yalla. Dom bonus la rek ci seyy. Kou leen wakh beugue n’a am dom? Kou leen ni meune n’a am dom? Niemé ngeen sunu borom torop. Et puis gérez votre vie, vous en avez une non ? Putain
Senegalai hi amou gnou programe wallahi lou si sèn problem si sèye diambou felicitation Mon frère Aïsatou djiguièn bou baxlaa machiallakh yalla na sèybi barquèll ❤❤❤
Il est tellement discret. Il n'a fait aucune révélation, et le journaliste n'a pas été très curieux. Ce qu'on attendait est de le faire parler des causes et l'histoire de cette relation rarissime chez nous.
Vraiment xalé bi ma dég ni kou mature la donc bayiléne diambour tak mague mou donne sa sokhna mo gueune di top mére di teudé gigolo bagui melni toulék maléy si réwmi bouléne falé seuyal sa seuye
Je suis une maman de 4 enfants que dieu te protège respecte et aime ta mère bégueule KO sa yaye la wakh le reste ta khamé li neik sa khole boule meusse manqué respect djigueine le reste yalla mo khame soit heureux
Merci frère té lousi yéemé Moy domou PSL yépe khadidiatou Molène dioure té elle avait âgé 42ans Aissatou mo nekone khalébi niata dôme la ame , amoule bene dôme. Nanou bayi boy bi bounou yaké seuye bi Lou mounti khéw après niome niouye responsable yi
Wagnil dou 42ans dé 40ans la té 40 ak 54 dou beene doom moom yalla koy diokhé. Scientifique ment parlent 40ans mounna am doom mais 54 ans bou amee doom keemaane la
Qu'est-ce que la loi vient faire entre deux adultes consentants ? Ils sont musulmans non ? Je ne comprends pas la frustration de certaines personnes qui prétendent parler pour le bien du jeune homme en plus s'il s'agit de descendance il a le droit de se marier au moins 4 fois non ? Occupez-vous de vos propres turpitudes et foutez la paix à ce couple...
Sénégal mo nekh ont n'ai 18 millions boy bi nek exception ça ve dire que moy lolou 24 ans ak 54 ans esk sey bi dou intérêt commun pour les deux ?fi ké beugoufi sa dom 24 ans tak 54 ans
Dôme bénéfice le si séye nakh yalla mayouko gneupe tak khalé takhoul nguéne ame dome gueume léne yalla moye dogal défou léne dara lou harame soyez heureux
Arrêtez de nous casser les tympans avec le ménage d'autrui et occupez vous de vos affaires. Combien d'hommes, je dis bien combien d'hommes ont pris pour épouses des filles qui ont moins de l'âge de leurs petits enfants ??? Moi je crois qu'il y a à fouetter ailleurs que dans le couple d'autrui... Ce mariage s'est passé dans les bonnes règles de l'islam et de nos coutumes. _
En tout cas, moi je vous encourage. C'est mieux que la fornication et l'adultère. Il ne faut et faudrait jamais se refuser ou s'interdire ce que Dieu a rendu licite pour le croyant.
Niou bari gnikoy wah sah nionguay thiagatou di ndiaaloo soubhanalah de gauche a droite. DAMANI FRÉROT Heureux Ménage. FI mome Allah lim niou wah laniouy def inchallah
Mani demal gnibi sisa famille sa yaye diakhlé n'a béneu bou goor nga takal sa morom nguir euleuk nga meuneu fondé sa famille iaw xam ngani mère bi meunoula dioural dôme eh goss reviens sur terre gnibil nga bayi borom badio bou lakh bobou ok
Mais pourquoi les gens veulent toujours faire feu de tout bois ? En quoi la vie privée d'autrui les concerne. Naniou mandou si yeufou diambour té lidienti souniouye yoss. Wa Salam 🤲🤲🤲
Mais kel et en faite il l'âge d'avoir une femme il à fait son choix où le problème c'est mieux de faire le zouna si le problème d'âge ya aucun problème car notre religion ne la pas interdit si c'est une femme blanche y amoule ben problème epui journalistes Sénégal ya d'autres informations informations ki peut nous ke de s'attarder sur la vie privée des gens vous n'avez aucun compte a rendre a personne heureux ménage
Aïssatou à tout dit que " mak gni antalouniouko , c'est une COUGAR et c'est son choix. Rendez-vous dans 25 ans , elle aura 78 ANS et son mari 49 ANS INCHALLAH...WAIT AND SEE😮😮😊!!!!!!
AMOUR AMOULE :COULEUR ,AMOULE FRONTIERE,AMOULE ETAT. ❤❤❤
Mais, vous ne pouvez pas foutre la paix à ce couple ! En quoi cela vous concerne ? Franchement au Sénégal vous avez du temps à perdre en vous mêlant de tout Merde quoi
*Bilay ils ont bcps de tps mm tchimmmp*
elle est une femme des medias donc C normal
❤❤❤
Vraiment
S'agissant du prophète slw et son épouse je vous dit ceci :
La comparaison n'est pas raison
Moi dé j'entends un jeune mature et responsable par ses paroles et la tonalité de sa voix très posé très calme pour un jeune dr son âge bayiléne jambour bi nguir yallah cest sa femme qui ne devait pas venir sur les réseaux sociaux elle devait laisser couler ❤❤❤
❤❤❤
Yow ki Li dakoy oume c lui le perdant Kou djiguen ki Moy rajeunir rk...Moy graw graw di nékhal batteu ni
@@adamadiouf487yaw ya am fite té gnimé yalla
Walay ndeysann frère c'est ce que j'avais dit dans l'émission en direct le sens de maturité et de responsabilité que la dame a vu en ce garçon malgré son âge elle ne l'a vu nulle part ailleurs Sénégalais nio wara mandou diadieuf bro
@@adamadiouf487😂😂😂😂😂
Entouca beneu parent revewoul am beneu dom bou goor seulement dans ta famille mou wara fondé famille di marier a une dame de 54 ans
Mo geune geneu Di mouy yalla yen dall wakhou nit gen Di soralle mes pas li yalla santane
Te sou ou takhone toubap bou âme khaliss dolen cas
Bilahi tt a gnémé deugueu sénégalais khamouma Lou takhe mou Faux fi thie Europe danguaye guiss kou tak toubab bou mél ny golo gnou diko félicité ki tak sénégalais gnou diko saboté@@talibeserignetoubaibrafall6311
Mais il a la possibilité d’avoir une autre femme plus jeune pour avoir des enfants.
Barké s touba béne parent gnanoul yalla li sokhna pénda mi sou domame démone di taki béne mère douko nagou ki mak la ki khalé nako bayi mou dème taki khalé ki méné paux li bakhoul way 😭😭😭😭
Saway kii wakham Dji Tegou woul feen ! Waydiour Dou Morom Boy Nala Sa Bakan Geuneul Wadiour After yakay Rethiou
Laay yaw qui sayaye la dekouwaye wowe maman
Heureux ménage❤❤❤❤ mon frère aux Sénégal il ya beaucoup de hypocrite si c'était un blanc il aura pas tt se bruit
Si cté une blanche on comprendrait que interêt lako topé mé cas bii khalébii Lane la topè mère bii? Arrêtez l’hypocrisie et essayez d’être à la place d la mère de ce p’tit
Jeune nga tola go fene mtx warowon seuy ak morom yaye vraiment haramoul me sa différence d’âge bi c énorme
Boy bi andoul ak khélame dée limouy wakh ni maîtrisée wouko boy ya yakh sa dér ya abandonné sa famille ndakh khalis ak djiguéne mes kou d'accord si seuy bi rek yalla na yalla déf gua am dom djou mélni
Legui Yow lou ciy sa yoon
Bilaye doyna War worone na khalate ay famille wam khale bou ndaw
En cone setlou gua lolou 😢 c’est triste
vraiment
Machaallah vivez votre amour comme vous le voulez ❤❤❤
Kou neck yaye bougo li sissa dome yaye bou ame dome yarko beugue nga mou tack diabar indil leu goro mane dé yaye la mé beuguou ma li sisama dome
L'islam terrewouko té yoneti bi psl sokhnam Khadija manguénako 15 ans ..donc yalla Moy dogal
Wax deugue yalla
Jeune gosse je t' encourage .
Paa yaangui fi di takk khalé you ndaw te kène wakhousi kone donc seyeul bamou neekh.
C pas la même chose. Un pa peut faire des enfants mais une dame de 54 ans cas même...
@@modourokhaya9616mais Yow yaye Yalla? Niata Niit nga fi guiss niou sey ba maguette té amou niou dom. Bayileen tokk plassou Yalla. Dom bonus la rek ci seyy. Kou leen wakh beugue n’a am dom? Kou leen ni meune n’a am dom? Niemé ngeen sunu borom torop. Et puis gérez votre vie, vous en avez une non ? Putain
Waxal say wakh té guéné si paa yi😂 pa yi danio meilleur💪
Senegalai hi amou gnou programe wallahi lou si sèn problem si sèye diambou felicitation Mon frère Aïsatou djiguièn bou baxlaa machiallakh yalla na sèybi barquèll ❤❤❤
Bro sa data yaye mais dinga douguou si lou nékhoul sa yawe
@MODOU-r2ybayil togne yonetebi swls soxna Khadija 40 ans la ame môme Moy ame 25ans
Il est tellement discret. Il n'a fait aucune révélation, et le journaliste n'a pas été très curieux. Ce qu'on attendait est de le faire parler des causes et l'histoire de cette relation rarissime chez nous.
Il ne veut pas confirmer si c'est sa sœur ou pas, pas de sens
Cela signifie que c belle et bien sa sœur
@@julesniang4562Ah !!! Lou takh wakhouci ? Mok diabaram louniou beugue sèto ? Menace , plainte tribunal ?
Waw kéye baye nonou la mana démé beuye sou andoul ak moromi beuyeume andak deukhine mba tiéré
Mére bi fok mou goungué talibéme mbaye pitakh thi yeungueul Sénégal
Ki dafko liguey tayouko. Mere bi domeram la
Wa boye foy dieulé ndiaboott nak bayil hél bou bakh
xana dou djoulite meunoul am ba 3 femmes
Heureux ménage champion
Vraiment xalé bi ma dég ni kou mature la donc bayiléne diambour tak mague mou donne sa sokhna mo gueune di top mére di teudé gigolo bagui melni toulék maléy si réwmi bouléne falé seuyal sa seuye
Je suis une maman de 4 enfants que dieu te protège respecte et aime ta mère bégueule KO sa yaye la wakh le reste ta khamé li neik sa khole boule meusse manqué respect djigueine le reste yalla mo khame soit heureux
Man jai 25 ans tata bou am 45 voir 50 lay weur 😂
félicitation frero heureux ménage
Seye diamou yalla la tè adouna diamou yalla monioufi indi nite ak djinè yalla na seuye bi barkèl mbokou dioulite ndam rèk inchallah
Heureux ménage l'islam terrewouko té yoneti bi psl sokhnam Khadija manguénako 15 ans.❤ donc yalla Moy dogal
Man damay ladie yen dioulit yi deuk sénégalais est ce que ayy dioulit lanou
Li borom bi dogal ayy simple nit nioy tahaw diko contester
Merci frère té lousi yéemé Moy domou PSL yépe khadidiatou Molène dioure té elle avait âgé 42ans
Aissatou mo nekone khalébi niata dôme la ame , amoule bene dôme.
Nanou bayi boy bi bounou yaké seuye bi Lou mounti khéw après niome niouye responsable yi
Wagnil dou 42ans dé 40ans la té 40 ak 54 dou beene doom moom yalla koy diokhé.
Scientifique ment parlent 40ans mounna am doom mais 54 ans bou amee doom keemaane la
Tay nak la bayi Wa senegal personne n’est libre de faire ce que bon lui semble mais toubab yi douniou aye nite niom Dangay libre ohhhhhhh
Mére bi Na dem séti moromam li loi dafko wara criminalisé❌❌❌❌
Hé doul yow quelle loi
Ioe xanaa do dioulitt 🤔 saway loi yalla rk mo waur té lii bou aramone yonente bi (as) douko déf
😂 non copain tu n'est pas serieux.Mais ce problem le prophete l'a deja reglé ce problem d'age entre couple.
Qu'est-ce que la loi vient faire entre deux adultes consentants ? Ils sont musulmans non ? Je ne comprends pas la frustration de certaines personnes qui prétendent parler pour le bien du jeune homme en plus s'il s'agit de descendance il a le droit de se marier au moins 4 fois non ? Occupez-vous de vos propres turpitudes et foutez la paix à ce couple...
Yow es que nitt gua
Heureux ménage
Heureux ménage djambar ❤❤❤
Il est vraiment mature ce garçon,soyez très heureux et vive l’amour !
Yallah na seye bi barkel
Amine
Yalla ga am dom bou goor mou takalle mère bou am 55 ans 😂 amine
Seuy bi mome leu concerné coussi wakh danga seuytane
Boy boulen falé vie ta vie et soit heureux senegal nio bari lounouy lidieunti té mandou wounou si ken
Et pourquoi porter plainte mais de quoi très bien tu as gagné une maman et une femme heureux ménage
Heureux ménage❤❤❤
BOY WOUTEUL BÈNNEU 2EME BO KHAMNÈ KHALÈ LEU.20ANS BAKHNA.JABOOT CILABOK.MERE BI NICE HAN MAIS 2ME BOU BAKH.OK.NIO FAR OK?
Bon Conseil
Voilà ta tt dit si la dame l'aime n'a ko gardé outeul khalé boukoy may ndiabote
Li Yalla bouko toudoul wone hè dou am sey tia arass la
Seuy you bari yalla toudou ko , bayilen yalla tranquille. Seuy you bari ay serigne gnokay tak.
@@user-vibf6ji2n.Dafa fek mou nekh yalla aussi
@@user-vibf6ji2n.Astafiroula sey bou ame yalla ko dogual
C'est pas vrait il n'as qu'à expliquer a propos de sa soeur qui a parler ce matin
Et après qu'est-ce que tu y gagne ? pourquoi vous perdez votre temps sur la vie d'autrui
C'est sa sœur
@@NdiayeBoris beug ka rek
Machalla fils heureux ménage dioklene nope bou bonebi
Sénégal mo nekh ont n'ai 18 millions boy bi nek exception ça ve dire que moy lolou 24 ans ak 54 ans esk sey bi dou intérêt commun pour les deux ?fi ké beugoufi sa dom 24 ans tak 54 ans
18 millions boy bi nek exception nono lii bari nafi deh boy bi mo tak kou siiw rk
Ok mais en quoi cela vous concerne
Vraiement senegal pourquoi dou wakh lou si yoname .senegalais sèn gnak mandou motakh yeneuyi dilène dal
Mo wahofi dara hawma foye dieulé dome😮😮😮😮
Il peut toujours prendre une 2eme femme donc il peut avoir des enfants laissez les trankil vivre leur vie
@@serigneathie881 bro doom yalla mokay mayé sakh
Yalna borom bi barkel seybi
yalla na barkel thiéy beuguel ❤❤
Dôme bénéfice le si séye nakh yalla mayouko gneupe tak khalé takhoul nguéne ame dome gueume léne yalla moye dogal défou léne dara lou harame soyez heureux
Koukoy encourager yalnaga am dome diou tak nday mére bouko magué 25 ans wassalam
AMINEE
😂😂😂😂
Amine 😂
Ya bonn 😂😂😂😂😂😂😂😂
AMINE yah rabal alamina
Mai il es mature chycologiquemen
Heureux ménage à vous ❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Heureux Menage Bro
Laissez les vivre leur amour pour l'amour de Dieu il n'a pas tué quelqu'un ni voler .
Boy ya taye takal koula nékh, sénégalais mo soff ndayam louci sén yone, my boy gères ta femme naci yallah def barké
Arrêtez de nous casser les tympans avec le ménage d'autrui et occupez vous de vos affaires. Combien d'hommes, je dis bien combien d'hommes ont pris pour épouses des filles qui ont moins de l'âge de leurs petits enfants ??? Moi je crois qu'il y a à fouetter ailleurs que dans le couple d'autrui... Ce mariage s'est passé dans les bonnes règles de l'islam et de nos coutumes. _
Kou gueumeni mère bi dairaite jeune haler bi la sohla raik lalal j’aime tai bousi parai torohaleko
Heureux ménage ❤❤
En tout cas, moi je vous encourage. C'est mieux que la fornication et l'adultère.
Il ne faut et faudrait jamais se refuser ou s'interdire ce que Dieu a rendu licite pour le croyant.
Ms boy kon sa yaye metrigewoul limouy wakh😂
Lune de miel kagne😂😂bayiléne khalé bi mou seuy😂😂lamou saf kouko mathia ko kham😂
😂😂😂😂😂😂😂
Courage diaplen rekk dinabakh daguane na c l'essentiel
Heureux ménage frère
Ko wakh mouné justice
Focus détails rek❤
Il faut les portes plainte tout reste à parler du n'importe quoi sur tictok chaque jour vraiment le Sénégal c'est du n'importe quoi
Faut pas donner un exemple sur mame aicha parapor avec cette dame en peruq ce gosse la est préparé sur récitation 😂😂😂😂😂
Mane dei dama warou si sa ma rew le senegal amouniou programme bilahi danio tarder bou bakhe sakhe
.
😂😂😂walay mr mbégue wakhoufi dara
Nn senegal degay ame panou mbalite dii lidjeunti tassou diabour lii mo gueuneu ndjalo bilahi walahi 😊😊😊
Sénégal deukeu lidieuti séyi diambour loussi souniou yone ah😢
Moma diakhal 😂
Boudé toubape c posible nit kou ñoul no complexé heureux ménange a boux ❤
Seuy la allah beugueu bayilene polimique bakar rek lagniy def
Bayilenn yonenté bi psl
Kiimoy Mr. MACRON🤣🤣🤣
C'est un garçon et il est majeur.ceux sont ses parents qui devaient respecter son choix comme c'est pas haram.heureux ménage fils.
Courage mon frère, vous avez une femme digne courageuse et musulmane, défo lou haram, yallana yalla samlén maylén goud fane ak wër
Démal topato sa yaye boybi limouy wakh dara amoussi
Aissatou est une vraie bonne dame tres véridique je lui souhaite tout le bonheur du monde elle n à que 39 ans
Niou bari gnikoy wah sah nionguay thiagatou di ndiaaloo soubhanalah de gauche a droite. DAMANI FRÉROT Heureux Ménage. FI mome Allah lim niou wah laniouy def inchallah
Il est posé mature beau et très respectueux et intelligent
Juste une question ms yaw ya déme séyii wala😅
Kii kay khamoul limou deff,ça c’est grave ,beugue lou yombe rekk
FEELING DAKAR ON A RIEN A FOUTRE DE CE MARIAGE. PARLEZ DE SUJETS PLUS UTILES POUR LA SOCIÉTÉ
Sougnou borom mo tak saye bi si Arass kou mer kalamel Yallah
Mani demal gnibi sisa famille sa yaye diakhlé n'a béneu bou goor nga takal sa morom nguir euleuk nga meuneu fondé sa famille iaw xam ngani mère bi meunoula dioural dôme eh goss reviens sur terre gnibil nga bayi borom badio bou lakh bobou ok
Mais pourquoi les gens veulent toujours faire feu de tout bois ? En quoi la vie privée d'autrui les concerne. Naniou mandou si yeufou diambour té lidienti souniouye yoss. Wa Salam 🤲🤲🤲
Salam, il faut ëtre hônnette et repondre les questions .
Ioe soumala nioussé diga gnibi sa yaye
Mais kel et en faite il l'âge d'avoir une femme il à fait son choix où le problème c'est mieux de faire le zouna si le problème d'âge ya aucun problème car notre religion ne la pas interdit si c'est une femme blanche y amoule ben problème epui journalistes Sénégal ya d'autres informations informations ki peut nous ke de s'attarder sur la vie privée des gens vous n'avez aucun compte a rendre a personne heureux ménage
Boy gorgorlul ci sa yaay bala mula wone ginnaw Soxna neexna lool waayé yaay bén bén la... Sëy bi dara nékussi waayé bumula taxa won ginnaw sa famille😢
Vraiment
Vive mrs MBENGUE Ak madame MBENGUE savourer votre mariage avec plaisir é bc da bonheur ect .,
Kone sa yaye metrisewoul limouy waxx??
Aïssatou à tout dit que " mak gni antalouniouko , c'est une COUGAR et c'est son choix.
Rendez-vous dans 25 ans , elle aura 78 ANS et son mari 49 ANS INCHALLAH...WAIT AND SEE😮😮😊!!!!!!
Boy yaw reww rek nga deff bilay walay
😂😂😂😂
AK beug Lou yombou
Mayal boy bi jaam mou zemberé 😂
Boy courage fimoy sen régal dagne lay warakh soukaré la beut doundal sa aldiana
❤❤❤😢😢
Seuy bou barre rek inchallah ndakh meunone nga jap sa adouna en tant que jeune di fo rek té defoko. Merci
Il répond jamais au questions, pauvre garçon 😢
❤❤❤❤❤❤❤❤❤mashaalah
Gommuma ni sa yaye andi na c frere
Bilahi li dafa méti kounek ak sa xalat mais doyna War yayam Dina am louko méti souko waxe'ak souko waxoul yeup
Ndialo bi Sénégal beuri na, Solène beugué gérer ay situation... Tchiip
Est ce que moy waax ni saax😂😂😂
Hélè day yem way do Dara🤭🤭🤭🤭
Tu na pas a te justifier mon frere
je te souhaite heureux menage mon frere.
vie ta vie .
MAIS POURQUOI LA FAMILLE SORT POUR DIRE QU’IL S NE SONT PAS D’ACCORD AVEC CE MARIAGE.
la vérité finira pas juger. Que Dieu nous guide dans la vérité.
Aissatou penda mi ci bopam dafa niaw 😊mane lolou moma mèti,ndakh bou rafètone sakh wola mou toyi😅 ame filling ma meune co mougne😅
Wakhatiko dé ,khessal rothiékou ,au lieu mou dème outi makk mais mou ipnotisé domou diambour ,khalé 20 ans lii dafa niaaw
NIAW maguet déguisement bi pour XALÉYI la 😅😅😅
Yague n'a teuder kgaller bi
Mane dal cas bi dama dépassé kounek ak sa choix