Je suis 2000% FAARAAMAAREEN mais la musique sénégalaise sans lui c’est comme une Can sans le Sénégal 🇸🇳. Très beau clip avec une qualité d’image à la hauteur. Le retour de L’homme de la génération consciente .🔥 PAPA DIOUF naamnaagnleu d
@@latyrmbaye4732 non bro Pape ndanane leuh d bilahi domou Pikine leuh neuk mais Wally lanou andaal neuk duu teh niou waxx lii baxx wagni wuul dara bilae ioe
En fin de retour mv suis faramaree mai j l'adore beaucoup ❤❤❤❤❤❤onts t'aimes beaucoup boromou diabar bou bakh biii tée daaalé ❤❤❤💍😍😍longue vie à vs ❤❤💍💍😍😍😍😘😘😘😘
Bravo pape diouf yangui finga nekone bataye billaye wallaye sa musique dafa diarrrr yone meusoko changè lep tek ngako si class ak expérience bravo pape diouf
cc Page. .j'espère que ta ptite famille et toi même allez tous bien. comme d'habitude, tu viens encore de frapper très fort. que Allaahou Soubhaana Wa Taahlah Veille sur toi et les tiens 💖💖💖💖💖
waw j'ai mm les larmes aux yeux on t'adore tellement pape yalla nala yalla samou yak sa ndiaboot on est fiére de toi je n'est mm pas les mots t'a encore frappé trop fort diam si yaw jambar
Machala Pape . Si contexte vacances nga défé clip bi et c'est trop cool. Bravo au réalisateur de ce clip vraiment ndanane leu et c'est très bien réfléchi
Sou donn fi ba 2040 dama koy khar machallah mon chanteur prèfèrè ❣❣🥰🥰😘😘😘❤❤❤❤
Ndaysane il restera le mellieurs
Pape diouf déé wayagoul sakh kiiii dafa DOF wayyyy rek layy def
Man ki damako beugg rek teii Yalla takh wallah😭❤️😍😍🫶🏾🫶🏾🫶🏾🫶🏾
Def classe def gental est sama chanteur original si lepeu
Je suis 2000% FAARAAMAAREEN mais la musique sénégalaise sans lui c’est comme une Can sans le Sénégal 🇸🇳.
Très beau clip avec une qualité d’image à la hauteur.
Le retour de L’homme de la génération consciente .🔥
PAPA DIOUF naamnaagnleu d
Vraiment nila wané nga finga fété douté nga wakh lou bakh ci kénéne.Dougnou aye ennemis.
Bien dit 😍❤️ta maturité est juste waouh🤧❤️❤️
@@latyrmbaye4732 non bro Pape ndanane leuh d bilahi domou Pikine leuh neuk mais Wally lanou andaal neuk duu teh niou waxx lii baxx wagni wuul dara bilae ioe
@@oulimatambow3080 Dayy Ouley est-ce vous vous êtes pas trompé sur la personne dmaa immature baa yakkou😂
En fin de retour mv suis faramaree mai j l'adore beaucoup ❤❤❤❤❤❤onts t'aimes beaucoup boromou diabar bou bakh biii tée daaalé ❤❤❤💍😍😍longue vie à vs ❤❤💍💍😍😍😍😘😘😘😘
Le meilleur parle peu et des qu’il se décide de sortir c’est toujours un chef-d’œuvre qu’il nous sert chapeau bas Pape Diouf
Bravo papa longue vie 🙏
Franchement pape Diouf il chante bien c un autre niveau ça se voit que c’est un mélange entre tradition et modernité
Vérité absolue Lou ler nga wakh
@@awabalde2307 b.
@@awabalde2307,,
Clip bi meunoul niaka sét ndax khaléyi si nek nio raw numéro 7😍mashala,son image,lep Thiég in💥
😊
Tu es un génie Pape,ta constance dans l'excellence mérite salut.Félicitations!
Nice na sapo
Bravo pape diouf yangui finga nekone bataye billaye wallaye sa musique dafa diarrrr yone meusoko changè lep tek ngako si class ak expérience bravo pape diouf
Mix
Le prince de la musique sénégalais machallah 🎤🙏
Un grand monsieur exemplaire très discipliné bonne continuation
Je suis 500% faramaren me nekhoul ba nekhoul nakh clip bi nkh na nice na trop j'aime ❤️❤️❤️❤️❤️❤️😍😍😍
Mashallah félicitations à Pape diouf toute l’équipe de dakarpop felicite pour ce chef-d’œuvre bonne continuation
Il chante comme youssou ndour machalla👌god job💪❤❤💥💥💥
Ladial pape diouf bo beuguei kham louy xéwi 😂😂
cc Page. .j'espère que ta ptite famille et toi même allez tous bien. comme d'habitude, tu viens encore de frapper très fort. que Allaahou Soubhaana Wa Taahlah Veille sur toi et les tiens 💖💖💖💖💖
Macha Allah Lou waye mou nekh sama fance bi
Ay sama ndanane bi yaye yeunguel adouna 🇺🇸🇺🇸🇮🇹❤❤🇸🇳
Wa fils
Yaw danga dioum walleu danioula fay xaliss pour nga wax lii
@@matarsouare1773 si laaan nonou
Khamoul touss wayy
@@matarsouare1773 kikay da dioum 😭 Boudei dafa ame niarr adouna aussi nagnou wax🤣
Pape Diouf kou d'accord ni la classe là
waw j'ai mm les larmes aux yeux on t'adore tellement pape yalla nala yalla samou yak sa ndiaboot on est fiére de toi je n'est mm pas les mots t'a encore frappé trop fort diam si yaw jambar
Pape diouf l artiste le plus constant de sa génération ma cha Allah belles images. Belles paroles beau son. RAS
Pape diouf c le meilleur
VRES NDANANE MOY PAPE
machala pape
Machallah ❤️ pape Diouf ❤️❤️ ❤️❤️
Amoul morome c le meilleur wayyy REK lay def
Pape Diouf kagnia guay rendre hommage ibra Thiam koula beugone la fonkone la machallah bouléne ko di faté yalla yeureum ko kharéko adiana
Wayy thiokoui waly seck sonal naniou ak ritambalé....Pape diouf fonékonnn💥
Mom khalissam figurant moko nara diekheul , ses clip sou amoul 200 personne rek dou contane.
Mais dans l’ensemble nice
Pape diouf mii amoul borome c le meilleur président
Ndaysanne damala beugue tei yalla takh rek amal diam
Pape ya daka.way.boy yi waye amo serigne outeul danga soulou
Doyna war 🥹
Chapeau à mon fans pape Diouf dou wakh dafay liguéye rek
Mon chanteur préféré khôl yi sedina Tina! Wouyyyy sama nday ayyyyyyy! Liii dinama rayyyy!💃💃💃💃💃💃💃
Machallah aka meuna weuy yalnala yalla diapale takhawou la
Oh après Omar péne thione seck youssou ndour yaw la meun deglou 🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Force à toi pape Diouf 👊🏼❤️
Étalonnage bi tmt😭😭😭♥️♥️♥️♥️♥️😍😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️machalla hoooooooo
Maachallah yalla na nga am djam 😘😘❤️
Il fait partie des meilleures de la musique Sénégalaise
Pape Diouf 😍et la génération consciente mtx tjrs conscient way et constant ✊🏽😍laf bouche
il a une tres belle voix; il chante bien et tres coherent
Pape Diouf rk inchallah
PAPE UN GRAND PROGRES MACHAALLAH CLIP BI SETT NA BARIWOUL THIAMBAR THIAMBAR NEKHNA BRAVO
Je l'adore car mon garçon l'aime depuis tout petit, aujourd'hui il a 20 ans 😘♥️
nice neu trop pape diouf son bi nékhna clip nice neu mais kén dou pace dedjey le meilleur de ça génération 🎥🎬❤❤
You're my super star long live pape joof
Giss na sa thiass 🎵🎶🎵
Maan nena pathiakh 🎵🎶🎵
Nga waroon wax rek ✍️
Fi né paashhh 😁
😭 li la namonn
Très bonne chanson et très beau clip machaAllah bravo à toi Pape Diouf tu as encore cartonné 👏👏👍🥰
Loumou woyoul bakhoul yay nanane
Do moromou béne bodio bodio
Vive Pape Diouf
Bly wly
Ooooooh machallah khalé mole naniou trop
Lo déff mou nékh papa Diouf niou nguilayy khar inchallah❤👍
Machallah papa Diouf nekhena lol
Magui khar sa Duo ak la seule reine de la musique sénégalaise Viviane Chidid 💪👍
Poir une fois pape diouf def clip sans kouy kamath...avec c lampe et autre. Bravo
Li dhé bou done waly seck amna 1millions v
Parce que nitt yi gnoko beugg
Bou Lolou wésso sa meune weuy🎵kéne wakhatouko seul les mélomanes savent
Machala Pape . Si contexte vacances nga défé clip bi et c'est trop cool. Bravo au réalisateur de ce clip vraiment ndanane leu et c'est très bien réfléchi
Billaye dafay liGueye c le
Amadou Fall Ba au fait gayi sen répertoire yeup mbeguel la bouniou doon innove touty dina bakh
Pape diouf amoul morome déé wakhe deuggg yalla kene dakkouko wayyyyy
J'aime tellement Pape Diouf je le jure 😘 longue vie à toi
Pape diouf yarou meune nako lounè
Kiiii VRES ndanane la billaye
Pape diouf dafa nekha beuggg c le meilleur
Pape dafa meune limouy def
Billay wallay
Wayy reik laye deif bilaye walaye
The king 🤴 gneuwna 💂♀️ da vous wooooyyy baneh Lou roub nekh chéri Bebs
Quand t’es mélomane t’écoute tous les musiciens sans contre partie même si t’as un musicien bravo pape Diouf t’as encore frappé
Wawaw pape diouf wayy Ohhh son bi nekhhna trop clip bi niice trop trop trop Macha allah 🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️
bayilene bamou radisson ko ngene khamne lep deugg leuu !!!!❤❤🤞🤞👌👌
Le king pape Diouf dou ay thiakhane
Mn coeur Il a Encore Frappé jtmmmm walahi souma Doundei ba dh tei guisa toumala douma douma Taliii😭😭💑❤🤩
MACHAALA clip de l’année pape diouf dafa meune limouy def
Mashallah Pape diouf❤️❤️❤️❤️
Vrémt pape diouf ndanane deugue nga❤💪
Ça fait longtemps on ne s'est pas vu mais tu as fait un travail extraordinaire belle chanson
Bobou mongui roukeume di liGueye
@@seynaboundiaye6008 🤣🤣🤣🤣 rekkkk Ken dou momm
@@seynaboundiaye6008 amgue no mél 😂
Machallah pape yallah na yallah déf diam😇🥰
Très belle vidéo machalah mention spéciale pour les réalisateur 🫵
Pape diouf billaye senegal mossi dakka wayyyyyy
Ndeysane aka meuneuh waye nakk damako guedji guiss saxx ♥️🤚🏽🤚🏽🤚🏽 voix bi beine leuh masha allah
Niogui melni kou neck décembre clip yagui diougué founé😉 machallah pape diouf son bi nêkhena trop
Defati meune meuname.Constance mash Allah sur la qualité de sa musique .Tu es un grand de la musique.
Bilay ndanane ga pape
Machallah vidéo bi dafa rafete
Machaalla merci beaucoup pape diouf sama way❤👌❤👌❤💝🙏🤝👌🤲👊
wawaw mister pape diouf jolie clip macha allah
Pape ligua sagneser si clip bi nice na
Machallah machallah pape Diouf mon chanteur👍
Nexoul mba nexoul nak clip bii mounguii cool 🔥🔥🔥
La légende vivant pape diouf toutes mes félicitations Nice clip avec des paroles sensibles😍🙈❤❤❤🦁🎺🪘🪘🎧🎷🎤🎛🎚🎙🤟🎶
Wawe 🤯 pape mayma touti dama nek di def bac après mou dadi nekh 🤗❤️❤️❤️🥰🥰🥳
Mm mw😠
Bonne chance et reviens nous avec le sésames
@@mariemendiaye1416 bonne chance à toi aussi
Merci et amine 🥰💯
@@dafaxewtv9628 mrci bcp
Clip bi rafétt na 🔥way bi nehh na 🔥🔥🔥🔥🔥🔥 j'aime trop les couleurs 😍avec la piscine et tt
L'international Pape Diouf 🇸🇳💪one love ❤️
Pape wayyyy rek lay def kiii c le meilleur
Ce. Daba machallah rafetna ♥️♥️♥️💯💯💯
Vraiment taye mome pape dafeu déf clip bou nice 👍❤️ retour bou Sokhor 💪💪
macha llah sama fans bi
Heure bo diogué yeungeul réw miiiii ❤️💪
pape Diouf et la génération consciente nameu nan sa live ☺️
mashallah jolie sound
L’originalité des images me dépasse ❤️😍
Billaye pape diouf rek la beugg kiii damako yagga neuggg c le meilleur
Mai il nekh na
Meilleur chanteur du Sénégal 🇸🇳
Pape diouf yaa mann wouy
Machallah sabou gêne nekh toujours égal à lui même que la grâce de dieux t'accompagne frèro amine
Pape diouf restera un.grand chanteur
Bravo Pape Diouf 2eme de sa generation big up🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Machallah machallah tonton pape Diouf le meilleur
Ken dou yaw
Pape bilahi ya meuneu woyy Dioufa niohobay
Lima nekh si mom ay wakham dankoy comprand bou bakh 🔥🔥🔥
🇨🇲🇨🇲🇨🇲🇨🇲love this song from Cameroon