Ndama Faaty - Clip Xarnou bi

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 20 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 14

  • @nazilabuzzlab9825
    @nazilabuzzlab9825 9 років тому +3

    Mourine mane la Nazila depuis Paris baye fall danga seddal sama khol Bamba dafa deih ci sama khol bi . Bamba rek dou kénéne dieureudieufé Baye Modou Kara Noreyni.

  • @cheikhkane5872
    @cheikhkane5872 10 місяців тому +1

    Diadieufety sama gayi mame cheikh toucouleur

  • @lakagosha9779
    @lakagosha9779 Рік тому +1

    Macallah serigne bi

  • @khadidiadiallo2947
    @khadidiadiallo2947 Рік тому +1

    Ndeysaann Ndama faty

  • @cheikhdia9593
    @cheikhdia9593 3 місяці тому

    ❤❤❤❤❤❤ 0:24

  • @generalblingbling1180
    @generalblingbling1180 Рік тому

    Bly mn frr sma xoll iow rek la♥️😭😢

  • @aliounetoure1459
    @aliounetoure1459 Рік тому

    Nice song texte riche et beaucoup de melodies

  • @cheikhdia9593
    @cheikhdia9593 7 місяців тому

    Machallah ❤❤

  • @moortaalambaay9467
    @moortaalambaay9467 Рік тому

    Mboolem muriit yépp a ngi tuub,
    Tey réccu bàkkaar yi nu juub,
    Ba lu nu bay-bay, du nu góob,
    Sëriñ bi geesul xarnu bi.

    Mbàkke, dangay boroom i mbóot,
    Te sag njaboot tawat giloot,
    Ñu def ma ab àntalpareet,
    May làpputoo waa xarnu bi.
    Aw ma maqaamam di la woo,
    Waaye murit yi ñoo ma woo,
    Ne tawatal te bu nu woo,
    Saw làmmiñay wow xarnu bi.
    Tay jii ma wax ba ne tareet,
    Ngir yaa ma def àntalpareet,
    Yaa fab i xam-xam ne yuréet,
    Ci sama xel, ci xarnu bi.
    Gestul xarnu bii, Sëriñ bi gestul xarnu bii, gestul xarnu bii Sëriñ bi gestul xarnu bii (2X).
    Te bul ma tanqamlu ci ñaan,
    Ngir lii ma bon tey ku añaan,
    Muriid yi yépp a la ko ñaan,
    Ngir bëgg nga dekkal xarnu bi.
    Jooy i perantal la nu jooy,
    Boo nu fabul, lee nu ne wóoy,
    Ku nu yafal, ban def i kóoy,
    Mu dellu naatal xarnu bi.
    Jisu nu yaay te noo ngi raam,
    Ku ñàkk yaay, day nàmp maam,
    Buural te boot nu, ngalla daam,
    Roggndi mboolem xarnu bi.
    Fabal sa doom yi yépp boot,
    Ñoom it ñu boot séen ug njaboot,
    Ku manta boot nga jox ko mbóot,
    Ndax Yàlla naatal xarnu bi.
    Wuy nun a wuy noo ka torox,
    Yalwaan amoo ku la sarax,
    Garab bu daanoo xob ya lax,
    Bàmbaay ndànjaamal xarnu bi.

  • @abu_boydifferent2374
    @abu_boydifferent2374 6 років тому +2

    You are fantastici

  • @abyba1007
    @abyba1007 Рік тому +1

    🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @alioukara7634
    @alioukara7634 3 роки тому +2

    Ndessane taalif serigne moussa ka

  • @juniorog3638
    @juniorog3638 4 роки тому +2

    ❤️❤️❤️❤️

  • @abyba1007
    @abyba1007 Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤