Les inscriptions sont ouvertes, ne manquez pas votre chance ! PROMOTION MAGAL 👇👇👇👇👇👇👇👇👇 Alibaba : Aulieu de -40.000- CFA ➡ 25.000 CFA Devenir Riche : Aulieu de -50.000- CFA ➡ 35.000 CFA Cour Français / Cour Anglais : Aulieu de -40.000- CFA ➡ 30.000 CFA Devenir Riche + alibaba : Aulieu de -90.000- CFA ➡ 30.000 CFA Devenir Riche + Alibaba + Cour Français / Anglais : Aulieu de -140.000- CFA ➡ 75.000 CFA TEL : +221 77 886 23 64 / 70 001 04 72 Chaîne WhatsApp : whatsapp.com/channel/0029VaZHdnKJuyAK6qJoYa38
Lolou amna solo frère lol. Mais Sénégal nite day nék nitou ba lakhou niou doreu ko beug gueustou. Mais gueustoul tmt Serigne Moustapha Sy Al Maktum ndax référence lh li lép té nitou Yallah pire lh.
« Borom karaw bou gnoul gnakoul dara, tola gougnu fougnuy amé bay gnak » phrase bi sank na gnou barri, merci beaucoup zoo encore une fois, tu ne cesses de de nous propulser vers le sommet ❤ on aime le concept, que ça continue svp 🙏🏻
Zo ya bakh beuge dimbalinit mane dioy na sakh ci zeste bi😭😭giusla bokkou na ci samay réve yalla na la yalla faye défar gua sama adouna inchallah dina édé nityi com nigua ma édé merci 🎉
😂😂😂 Zo vraiment daguaa ame espoir sénégalé yi aye khélou djieune lagne yore 😅ne te fatigue pas 😢kii malgré ligua wakh yeup pour convaincre dégouleu et aussi mouy essayer dila convaincre ak dila geumloo yalla moy wathie dèfar Lifam😂 Joe : dafa un jour ma dégulou sa bène vidéo gua wakh neh sougne séddé léwoone xaliss bisi monde bi yeup riche yi nañgou waate léppou après dama woo sama béne copin mayko 10 000fcfa si appel bi avant may coupé récupérer naa 7000 yi en lui proposant de lui vendre une protège de téléphone qu’on fiche son photo derrière 😢 mou renvoyer ma 7000😂yi C’est ton esprit vive Tekki for Life et tout l’équipe ✊✊✊💪🏽💪🏽💪🏽
Amna beus senegalais bouye diaaye fii thi espagne ba dougue thi been restaurent comme ni borome restaurantbi niko kaay mafayalla ngua def formation boulay def riche comme lima def mane mais meme reponsebi Mohamed wakhla zoo loolou lako tontou quetion de mantalitela souñou mantliteyi fiik changewoul douñou dem fen wallahi.merci zooo❤❤❤
@@MamatDrammeh-w2k mane nak yaguenaafi es ce que sakhe bimay dem zoo dioudena.mais souma khamoone lima zoo khamal thi ateyi guemoumane dinaa ñeuwefii.mane souma doumoul thi ndieuke suivre la book mais il fait un travaille exelent vraiment
Salut frère je suis marchand ambulant très sincèrement j’ai longtemps abonné sur votre Chaîne mais je ne laisse pas tes vidéos mais depuis que j’ai lu ce vidéo je n’arrête plus à lire les autres
Je comprend maintenant mieux lan motax certaines personnes nane ma man gueumatouma yalla c parck man dama xam legui Louniou louniou xamoul motax merci fallou tu y a joué un rôle colossal 🥰
Franchement tu as encore tapé fort. Ndeysane et c'est ça le problème de beaucoup de personnes yu nangou liguey mais c'est l'état de sprit qui bloque Que Dieu nous guide toujours vers la recherche du savoir utile d'ici bas et dans l'au dela❤Merci encore l'équipe Tekki for life ❤
bon man je comprend sa reaction par ce khamoula ba paré ngakay wakh affaire khaliss wala alal teksi deuk bi dafa beuri ay arnaque kheyna sa présentation mo reussiroul mo takh doula wolou dou guem lingay wakh genre fok nga wone len ay preuve nguir niou meun la deglou mais meune nga contituner affaire ame na solo trop merci😉❤
Vraiment Grand Jo avec Mohamed moy loulou c'était très difficile gna defko millionnaire car déjà niveau que tu parler il pouvait pas y comprendre et que mome Mohamed lep dafko bayé ak Yalla, son esprit même n'était pas bien pauser en parlant avec toi.... Et moi je pensais que tu allais là convaincre jusqu'à y réussir ce que tu voulais mé malheureusement... Et même a la fin sa te fais chier en énervant... Respect man
Jo nak taye dadjé nga ak koudeugueur bopou😂😂😂 c'est que da ame niokhameni nekhou nio dimbalé le problème est que le gars yewou oul jo nak bougonne n'a nga dadjée ak mane bama degloula hohoooo❤❤❤❤❤❤
Zoo déf gua vidéos bo khame ni da ga wakhe ni amna gno khame ni dagno fébare té geuguou gnou ni sakhe dagno fébare téki lolou moko dale Billy 😂😂😂 koudakore lalale j'aime zoo amale diammou rék❤❤❤❤❤❤❤
Bro i really appreciated your work. You really change my life. I listen to your proverb whole day an night an practice it. Thanks so much. Amal jama always . I wish u meet me. Love from Gambia 🇬🇲 ❤
Walahi bou doon man , diaralnama sakh took ay jours blh ✅✅✅ Allahou Akbar ki khamoul sakh chance bimou am blh J'ai 15ans dé mais t'as beaucoup changé ma vie blh et a couse de tes vidéos je suis entrain de préparer ma vie comme il le faut té blh awma sakh sa fayd té yalla gua goudou fane té yalnala yalla samou bou bou bakh, blh j'ai mm pas les mots mais bro chasse que t'es un mec extraordinaire, une chose aussi je m'appelle Mouhamed Diop 😂 Diam si iow
Wallah zo je sais que tu sais vraiment que tu intelligent mais je confirme Mais nioumel ni wadije bari niane si rèwmi bly Merci beaucoup 😘 les leçons que j'ai appris sur cette vidéo
😢 😢 😢 😢 NDEYSAN CE GARS NA RIEN COMPRIS ET PURE IL N'ESSAIE MÊME PAS DE COMPRENDRE ZOO YÀLLA NA MA YÀLLA MAY CHANCE MA DAJE AK ZOO AMINE EN FIN DEMA YEURËM WADJI SAA😢😢
Zoo déguloule ma expliqué la mém mane soumaye dégulou saye vidéos louné lagnou maye wahe.kou boune ki guay déguloule nane ma ki gua khame ni wakhie doof laye wakh . mais jamais douma léne dégulou.... mais appare sama yaye nouma méle ya ma ko défe Billy .❤ Mais sa formation devenir riche dama yorle xalise rék mais insaallha Dina si dougou ❤❤❤❤❤tékie fire life yalla guéne ame diamou boubakhe
Non sama troundor moo dëugër boppu warone Na am change dadjég zoo Mane depuis 2020 dama lay toppu Bobo makci daradji Saloum ci béna place Bou ndaw la néka sama Papa bou ndaw moko moom es-ce que Mane na tok Saloum di am lingéne am ngandé réf la am mais sama réfyi béna nékgoul dëgg 😢 bëgg Na wax tane Ak yaw amougouma xaalis Boumala fay diapplé ma Guri Yàlla 😢 Mane nala appél walla❤ sa réponse bëge Nako giuss boliré commentaire b
Svp! Zo ne le laisse pas! Fini ce que tu as entamer. J'avais pris l'engagement de former ma famille personnellement sur l'argent mais je vais les inscrire un à un sur tes formations.
Barki rassoull 🥰billahi mala beug zo ❤️non sérieusement mais nitt kou yèmè nga dieuleull ma façon example you mouy diokhè rek nga kham ni Kii khèll bou graw la yorè wollahi je t’aime 🥰 mais yalla nala boure bi same waye
Zo ninga beugg communiqué ak wadji bakhoull wakho ko Limou beugg dégg ta ki ngaye wakhal ni wa pastef la 😂 dafay yakar ni dangako xépp ta pauvre yi fi soy wax ak niom guennel lénn xaliss pour niom lénén la fawu nga dissi bayi xell aussi c très important
Wadji liko dalleu 60% de la population nonu lañuy xalaté, Sénégal leppp pour ñom ndogolu yalla leu, motakh fi Aduna tollu ni Diang Lou am solo leu da nguay am esprit d'ouverture do dieull lepp wekkeu ko yalla , wadji mom en dehors de son ignorance dafa ragal tekssi
Wadji du âm😢❤Vraiment jô sa ligeuÿ Amna solo trop thé bul décourage jamais,wadji xamul lingua ka done diokh Lou nitt nie Di faÿ xaliss bouwékh tall nielén Di défar formation kî amko gratuit Di dof dof lû thé blama dé RK muné lépu yalla la la ..... Lolu aÿ wakh yû yakû la ,banie Nako ba yalla dafa wax nî فإذا عزمت فتوكل على الله Ça veut dire que :guinaw bingua traces sa projet DF ngua lépû Lila war danguaÿ Gor Gor lule ngua bayî lépu si loxo yalla ,ngua geum nî Dina sotî ndax lolu moÿ wolû yalla . Sén ligeuÿ raféth na continélen parce que nitt nie danio sokhla genre formation yî et bonne continuation ylna sa brom duli diamu.
Parfois, elle travaille dur mais je sais pas comment calculer quelque chose. Je peux toujours être au boulot, tu te fatigue pour ne rien. Prends soin de ce qui te donne l'argent de plus.🙏
ZO WAN GNOU NAKA LANUY DÉF BA AMM INTELLIGENCE FINANCIÈRE POUR POUVOIR ACQUÉRIR UNE DÉPENDANCE FINANCIÈRE EST CE LIRE AY LIVRE SI XALISS RK MO NU KOY MAY🤲🤲🤲
Lima métti si mome il croit que Dieu va venir lui donner l'argent comment ça Khaliss dagua ko diangue pour meune ko géré et savoir entreprendre sur lolou Bly war nala guiss 😊😊😊
Billahi Wallahi Kii limou laton tou Nakhari nama torop Boudon mane ngakham né Amna louma la wara wakh Man amna idé Takham na Lan moye dimbalé samaye wadiour 😢😢
Franchement parler ont c'est pas kw dire à notre ami MOUHAMED (le pauvres) YALLA bakhna komm nimkoy wakhé 😢 Mais CHAPEAU À NOTRE ZOOOOO nationale 🤠chaque jour que dieu fais ghay sonn rien que souñu réussite,(vie,avenir,réaliser nos,réves....) YALLA BAYILAFI AK ÉQUIPE YPP❤
Les inscriptions sont ouvertes, ne manquez pas votre chance !
PROMOTION MAGAL
👇👇👇👇👇👇👇👇👇
Alibaba : Aulieu de -40.000- CFA ➡ 25.000 CFA
Devenir Riche : Aulieu de -50.000- CFA ➡ 35.000 CFA
Cour Français / Cour Anglais : Aulieu de -40.000- CFA ➡ 30.000 CFA
Devenir Riche + alibaba : Aulieu de -90.000- CFA ➡ 30.000 CFA
Devenir Riche + Alibaba + Cour Français / Anglais : Aulieu de -140.000- CFA ➡ 75.000 CFA
TEL : +221 77 886 23 64 / 70 001 04 72
Chaîne WhatsApp : whatsapp.com/channel/0029VaZHdnKJuyAK6qJoYa38
14:01 14:05
@tekkiforlife comment être en contact avec zô je suis de la Mauritanie
Zo un video pour cheikh mouhidne samba diallo s'il vous plaît
Fi on parle de l'argent dé cou bax🙏👌
Waw waw frr
Cheikh bi xalis rek la amone bay
😮
Demall setan xalaat tv deff nasi video buu am solo fre
Lolou amna solo frère lol. Mais Sénégal nite day nék nitou ba lakhou niou doreu ko beug gueustou. Mais gueustoul tmt Serigne Moustapha Sy Al Maktum ndax référence lh li lép té nitou Yallah pire lh.
« Borom karaw bou gnoul gnakoul dara, tola gougnu fougnuy amé bay gnak » phrase bi sank na gnou barri, merci beaucoup zoo encore une fois, tu ne cesses de de nous propulser vers le sommet ❤ on aime le concept, que ça continue svp 🙏🏻
Walahi
Zo ya bakh beuge dimbalinit mane dioy na sakh ci zeste bi😭😭giusla bokkou na ci samay réve yalla na la yalla faye défar gua sama adouna inchallah dina édé nityi com nigua ma édé merci 🎉
Amine yarabi 🙏 et merci aussi
Yalla na Yalla defal la diammo zo et tout le membres tekki for life❤
Tay la geune geum sa kham kham dagua gnio wakh gniou dégeu tay gua dieuf gniou guiss ok d'accord man signé na si yaw noumay déff ba guiss la
Merci 😊
Zo nékoul né kou diouk rk comprend ko😂😂 wadji dou am😂😂😂
Bilaye @@bassirouly9176
😂@@bassirouly9176
Zo ayoo nak sonékon man dana ma tonto te soma pare wol ak mome dou dem
Dafa dem te parewo si yawla
Ya sokhla won
❤Mouhamed leup la tek si lokho yalla ❤
Blh Mouhamed kay😢😂😂
@@adamaba6508 leup la tek si lokho yallah bo paraît Mouy watt koudoul yallah
Bilay ki vrai nakha nakha la no c'est pas vrai mé bari nasi ay morom nak mé merci ZO vraiment tu es unique 🎉❤
Bilahi Zo khol bou rafétt lala yalla may 😌😍😍😍😍
Zo est tellement une personne intelligente walay .
J’aimerais tellement le rencontré.
Je vous suit depuis 5 ans environ.
Tékki for Life mérite des millions de vues ❤🎉
Ki liko dal moy " il se contente de ce qu'il a " mé mom le rek nioune danio beugeu liguey ba meuna doundal deukou leumb ❤
Attention
Il faux bien réfléchir broh bien bien bien et bien
😂😂😂 Zo vraiment daguaa ame espoir sénégalé yi aye khélou djieune lagne yore 😅ne te fatigue pas 😢kii malgré ligua wakh yeup pour convaincre dégouleu et aussi mouy essayer dila convaincre ak dila geumloo yalla moy wathie dèfar Lifam😂
Joe : dafa un jour ma dégulou sa bène vidéo gua wakh neh sougne séddé léwoone xaliss bisi monde bi yeup riche yi nañgou waate léppou après dama woo sama béne copin mayko 10 000fcfa si appel bi avant may coupé récupérer naa 7000 yi en lui proposant de lui vendre une protège de téléphone qu’on fiche son photo derrière 😢 mou renvoyer ma 7000😂yi
C’est ton esprit vive Tekki for Life et tout l’équipe ✊✊✊💪🏽💪🏽💪🏽
😂😂esprit millionnaire
Frere 😂
Ya bandit 😊
Seugn Bamba néna yalla soula naré maye draaa dalaye maye yité djaa 🧠
Ki amoul yité si xaliss 🖤
Amna beus senegalais bouye diaaye fii thi espagne ba dougue thi been restaurent comme ni borome restaurantbi niko kaay mafayalla ngua def formation boulay def riche comme lima def mane mais meme reponsebi Mohamed wakhla zoo loolou lako tontou quetion de mantalitela souñou mantliteyi fiik changewoul douñou dem fen wallahi.merci zooo❤❤❤
Mais Frere SK Bala ngua don Dem espagne komance ngua suivre zo
? silt plais reponse
@@MamatDrammeh-w2k mane nak yaguenaafi es ce que sakhe bimay dem zoo dioudena.mais souma khamoone lima zoo khamal thi ateyi guemoumane dinaa ñeuwefii.mane souma doumoul thi ndieuke suivre la book mais il fait un travaille exelent vraiment
Salut frère je suis marchand ambulant très sincèrement j’ai longtemps abonné sur votre Chaîne mais je ne laisse pas tes vidéos mais depuis que j’ai lu ce vidéo je n’arrête plus à lire les autres
Ah billahi zo man ga worona dajel ki khamoula ndeysane😢😢😢😢😢😢
😂inchallah
M
@@tekkiforlife wallhi mane Mome léne rk mou ma métty mooye li gnou si warouna jari niou mou khage gnou yalna kou sunu akh dal
@@tekkiforlifeBilaye zo yangui mayy may courage ❤😢
@@tekkiforlifemais zo sokhla naa sa consei dei tailler bou ndaw laa beugg nekk bou makk😢😢✂️🙏
Liiiii motax rob kiyozaki dii wax "la pauvreté se transmis de génération en génération" wadji même mentalité la domam diii ammm euleuk
😂😂walay
Zo bilahi amouniou sa fayy mais yalla na yalla fayy 🙏🏿
Je comprend maintenant mieux lan motax certaines personnes nane ma man gueumatouma yalla c parck man dama xam legui Louniou louniou xamoul motax merci fallou tu y a joué un rôle colossal 🥰
Amna niou nkharé wakhall non kii amna change dh zo mootok ak môme digo pour trouver recherche mounekk fii nane yalla rek 😂😂ahh vraiment kou d'accord né kii beukoull khaliss lalall j'aime
Kikay est-ce que khamna khaliss sakh
Beug na xaliss juste il n'a pas le meme mineset comme toi
Vérité absolue @@badarasakho9692
😂😂
@@falloucisse8436 ki xamoul temps xamoul xaliss
Franchement tu as encore tapé fort.
Ndeysane et c'est ça le problème de beaucoup de personnes yu nangou liguey mais c'est l'état de sprit qui bloque Que Dieu nous guide toujours vers la recherche du savoir utile d'ici bas et dans l'au dela❤Merci encore l'équipe Tekki for life ❤
Tey lay soga geum ni am am wala gnak si état d’esprit leu ❤
@@benabdallaah walay
Bilahi 😢
bon man je comprend sa reaction par ce khamoula ba paré ngakay wakh affaire khaliss wala alal teksi deuk bi dafa beuri ay arnaque kheyna sa présentation mo reussiroul mo takh doula wolou dou guem lingay wakh genre fok nga wone len ay preuve nguir niou meun la deglou mais meune nga contituner affaire ame na solo trop
merci😉❤
Vraiment Grand Jo avec Mohamed moy loulou c'était très difficile gna defko millionnaire car déjà niveau que tu parler il pouvait pas y comprendre et que mome Mohamed lep dafko bayé ak Yalla, son esprit même n'était pas bien pauser en parlant avec toi....
Et moi je pensais que tu allais là convaincre jusqu'à y réussir ce que tu voulais mé malheureusement... Et même a la fin sa te fais chier en énervant...
Respect man
Jo nak taye dadjé nga ak koudeugueur bopou😂😂😂 c'est que da ame niokhameni nekhou nio dimbalé le problème est que le gars yewou oul jo nak bougonne n'a nga dadjée ak mane bama degloula hohoooo❤❤❤❤❤❤
@@drameomar6577 Faire dou deugueur boppou mes daffa khamoul kassé 🫡
Maa ngi lay suivre depuis côté d'ivoire 🇨🇮 sa ligéey rafet na.
Zoo déf gua vidéos bo khame ni da ga wakhe ni amna gno khame ni dagno fébare té geuguou gnou ni sakhe dagno fébare téki lolou moko dale Billy 😂😂😂 koudakore lalale j'aime zoo amale diammou rék❤❤❤❤❤❤❤
Sûrement wagui meusoul kham Louy tékkiforlife , meusoul sétane vidéo Zo .
Zoo ki comprend na koul fou adouna bii tolou réussi sii xéll leu
Ki xélam bii régule goul ❤❤❤❤❤
Mouhamed dafla dig lou woull ak khell motakh khamoul tous ci linga wakh😢😢😢😢😢
Il pense que ce le mépris à son égard
@@daoudadiallo6902 exactement
Bly
Neun la fa démé nk
Malheureusement nioune pauvre yeep nonou laniouy khalaté@@daoudadiallo6902
Bro i really appreciated your work. You really change my life. I listen to your proverb whole day an night an practice it. Thanks so much. Amal jama always . I wish u meet me. Love from Gambia 🇬🇲 ❤
Zoo ki nékhoulla wakh ta nall d rayena tan bi bali ñuwaronna diang diang ñuko ah ❤❤❤❤❤
Walahi bou doon man , diaralnama sakh took ay jours blh ✅✅✅
Allahou Akbar ki khamoul sakh chance bimou am blh
J'ai 15ans dé mais t'as beaucoup changé ma vie blh et a couse de tes vidéos je suis entrain de préparer ma vie comme il le faut té blh awma sakh sa fayd té yalla gua goudou fane té yalnala yalla samou bou bou bakh, blh j'ai mm pas les mots mais bro chasse que t'es un mec extraordinaire, une chose aussi je m'appelle Mouhamed Diop 😂
Diam si iow
Moukhamed ya gnak chance deug nk 😂😂
Zo Mouhaméte dégenala mé dég louwouma 😭 mame gisout la kanéne lay gis ni béne dor kat 😭💔
Mohamed bi dale yalla nako yalla tahawu comme nim ko beugué
Amine ohh ndayesan
So yalla déféi ma guise zo 🙏 lolou rek laye ndiane yalla 🤲
Ki soumako diegewone ba mbéthi ndayam néko dell kholll 😢way sarap lii😢
😂😂😂😂😂
Bilahi ki dafa degeur bopou ta niémé pevre 😂
No boybi defoul dar lepo zo la
Fimo komase bakhoul
Koubakh nga yeuneu Sénégalais yi nga réussir mais problème bouñou am xaloss lagnou am si alkhourane ak sunna merci beaucoup ❤❤❤❤.
Zo vraiment concept bi amna solo trop
Wallah zo je sais que tu sais vraiment que tu intelligent mais je confirme
Mais nioumel ni wadije bari niane si rèwmi bly
Merci beaucoup 😘 les leçons que j'ai appris sur cette vidéo
No Mohamed khamoul adouna dë zo ki boule ko bayi diapa thï comme guiss gua nitt bou mëlni të dou mom rék comme li sa job la 😢😢
Ndaysan gni man a cott amuniou mbam😂
Jugëll wuti mbame@@fallusekk6807
Zoo zoo zoo merci beaucoup mono wonn niak walahi borom bakh ngu machalah Yalna yala fay yiw 🙏🙏🙏
😢 😢 😢 😢 NDEYSAN CE GARS NA RIEN COMPRIS ET PURE IL N'ESSAIE MÊME PAS DE COMPRENDRE
ZOO YÀLLA NA MA YÀLLA MAY CHANCE MA DAJE AK ZOO AMINE
EN FIN DEMA YEURËM WADJI SAA😢😢
Ki kay djarena yeureum
xelam fof la tollou rek 😢 ak nio bauri ci deuk bi nak bilaye ☝🏻🙏merci beaucoup Zo
Wlh modou mii limou amnii si zo soumako amone
Diaralnama ay millions 😅
c'est par ce que modou dou frequenter les reseaux sociaux
😅😅
@@tekkiforlifezo mandamay djag methé mais dama ci beug réussir inchallah
Celui-là ça va pas trop avec lui
😢😢
Quel cadeau
Merci grand frère
Zoo déguloule ma expliqué la mém mane soumaye dégulou saye vidéos louné lagnou maye wahe.kou boune ki guay déguloule nane ma ki gua khame ni wakhie doof laye wakh . mais jamais douma léne dégulou.... mais appare sama yaye nouma méle ya ma ko défe Billy .❤ Mais sa formation devenir riche dama yorle xalise rék mais insaallha Dina si dougou ❤❤❤❤❤tékie fire life yalla guéne ame diamou boubakhe
Bilay nak 😂on me qualifie de fou
Moi aussi on me dit tout le temps ça parce que j’écoute les jours zo😂😂😂
Même moi frr
Jo ton vibrations est très haut ton voix sort un magnétisme tres belle ❤
Fière de vous 😊🎉
Non sama troundor moo dëugër boppu warone Na am change dadjég zoo Mane depuis 2020 dama lay toppu Bobo makci daradji Saloum ci béna place Bou ndaw la néka sama Papa bou ndaw moko moom es-ce que Mane na tok Saloum di am lingéne am ngandé réf la am mais sama réfyi béna nékgoul dëgg 😢 bëgg Na wax tane Ak yaw amougouma xaalis Boumala fay diapplé ma Guri Yàlla 😢 Mane nala appél walla❤ sa réponse bëge Nako giuss boliré commentaire b
Svp! Zo ne le laisse pas! Fini ce que tu as entamer. J'avais pris l'engagement de former ma famille personnellement sur l'argent mais je vais les inscrire un à un sur tes formations.
Kirassollay kii weroul😂
Machalh Amna ay idè yo am solo lool tè gnaw mayè khaliss lè pou si ligieye la reck ki dégola zo ki èkonomi bou gnaw lay dèf si mom mo am khaliss ligiè
Alhamdoulilah bima khamé zoo❤🙏🏿
😢 mais ngimane kottou amoun mbamee no amet bi outena akman amet mais lép zo la merci beaucoup zo ❤❤❤❤
Merci beaucoup zo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Billahi machallah merci ferer. Zo munom bini farnc❤machallah ❤billahi ❤❤❤❤❤❤❤❤video
Yenen te bi nena amna niokhamne denioulen doumo pour niou dougou aldjiane moy genre ki lah😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢 80%de africain ni laniou mel😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Explique clairement stp😢
95% Sénégalais ni lanu méle😢😢😢
Barki rassoull 🥰billahi mala beug zo ❤️non sérieusement mais nitt kou yèmè nga dieuleull ma façon example you mouy diokhè rek nga kham ni Kii khèll bou graw la yorè wollahi je t’aime 🥰 mais yalla nala boure bi same waye
Zo ki fokk nga comprendre ko yaw ak mom bokoulèn niveau motakh pour mou comprendre dafay méti😂
Zo yalla nga goudou fanne ❤❤❤ merci waye zo
Zo ninga beugg communiqué ak wadji bakhoull wakho ko Limou beugg dégg ta ki ngaye wakhal ni wa pastef la 😂 dafay yakar ni dangako xépp ta pauvre yi fi soy wax ak niom guennel lénn xaliss pour niom lénén la fawu nga dissi bayi xell aussi c très important
😂😂😂😂😂😂
Merci bcp bro 😂 li nak la beugona bindeu far nga bindeu ko 😂
Pourquoi wa pastef
@@kingbaba5369 dama lénn fans rek😂
Zoo barkép serigne Touba sama xol sedna ci yaw trop sakh Bly😭
Y'a des gens qui aiment souffrir toute leurs vie😢
Liñunàn jinax sooko yobbuwoon si appartement meublé pax lafay wut ndax mom la xam
@@DIAMBAR55saway Ray nguama 😂😂😂
Machalla merci beaucoup amatina solo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Zo info gua cokprandre nitt gni dafa am niou febare ta nagou wouniou ko 😢 Mohamed aussi nitt gni di niane yalla guiss ak zo guay deff lii yaw
Zo👋I have never cry😢for watching videos on UA-cam but this one made me cry 😭
But please keep going 🙏
Noon waye bro tassnga sama yakarr Mouhamed pour mane dinga changer😢😢😢😢😢😢😢
Please keep going don't give up 🙏 do another one it ll be different💪💪
Wadji liko dalleu 60% de la population nonu lañuy xalaté, Sénégal leppp pour ñom ndogolu yalla leu, motakh fi Aduna tollu ni Diang Lou am solo leu da nguay am esprit d'ouverture do dieull lepp wekkeu ko yalla , wadji mom en dehors de son ignorance dafa ragal tekssi
90%😊
Wadji du âm😢❤Vraiment jô sa ligeuÿ Amna solo trop thé bul décourage jamais,wadji xamul lingua ka done diokh Lou nitt nie Di faÿ xaliss bouwékh tall nielén Di défar formation kî amko gratuit Di dof dof lû thé blama dé RK muné lépu yalla la la .....
Lolu aÿ wakh yû yakû la ,banie Nako ba yalla dafa wax nî فإذا عزمت فتوكل على الله
Ça veut dire que :guinaw bingua traces sa projet DF ngua lépû Lila war danguaÿ Gor Gor lule ngua bayî lépu si loxo yalla ,ngua geum nî Dina sotî ndax lolu moÿ wolû yalla .
Sén ligeuÿ raféth na continélen parce que nitt nie danio sokhla genre formation yî et bonne continuation ylna sa brom duli diamu.
MERCI
W fall yaram bi da khamoule rk mais yalla yalla béye sa tole sa bopoula wallakhi 👌🏿
Non attendais le gars là fane la yaro ak foumou magué. Je n'ai jamais vu une personne avec ce Mindset. I have never seen this 😳
Il peut être difficile de changer la perspective de quelqu'un qui croit fermement que seul le travail acharné peut le sortir de la pauvreté
Zoo Mane mala buegueule sa ma boppou rék ❤❤❤❤❤❤
Zo ki bokoul ci talibe Teeke for Life yi
Mouhamed Amna Lo khmni si Sama rêve la bok. Moy toog Ak Yaw zoo❤️❤️❤️❤️
Bilahi iow rek lay topou khawama kan de me man magui guiss sama popou si li gay deff
Parfois, elle travaille dur mais je sais pas comment calculer quelque chose. Je peux toujours être au boulot, tu te fatigue pour ne rien. Prends soin de ce qui te donne l'argent de plus.🙏
Zoo Mane mala buegueule sa ma boppou rék❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
ZO WAN GNOU NAKA LANUY DÉF BA AMM INTELLIGENCE FINANCIÈRE POUR POUVOIR ACQUÉRIR UNE DÉPENDANCE FINANCIÈRE EST CE LIRE AY LIVRE SI XALISS RK MO NU KOY MAY🤲🤲🤲
Lima métti si mome il croit que Dieu va venir lui donner l'argent comment ça
Khaliss dagua ko diangue pour meune ko géré et savoir entreprendre sur lolou
Bly war nala guiss 😊😊😊
Zo you are very intelligent ❤️❤️
Billahi Wallahi Kii limou laton tou Nakhari nama torop Boudon mane ngakham né Amna louma la wara wakh Man amna idé Takham na Lan moye dimbalé samaye wadiour 😢😢
Merci zoo Une importante leçon pour nous
Non je te jure je suis choqué
C'est ses genre de truc laye khoulowé ak sama gayii chaque jour lo wakh gnouné yalla 😢
Mais zo continél Di déf ay vidéo yuo mél yi four sama jar yi Mona commprand ligay wakh merci zo❤❤❤❤
Franchement parler ont c'est pas kw dire à notre ami MOUHAMED (le pauvres)
YALLA bakhna komm nimkoy wakhé 😢
Mais CHAPEAU À NOTRE ZOOOOO nationale 🤠chaque jour que dieu fais ghay sonn rien que souñu réussite,(vie,avenir,réaliser nos,réves....) YALLA BAYILAFI AK ÉQUIPE YPP❤
Zoo wadji dako dépassé sakh 😂😂 déf ngua lepp lo meun ms sa wadji diemoul sakh comprendre c'est dommage quand même 😢
Franchement parler merci beaucoup non tu es une personne très rare d'avoir nous n'avons pas des mots
Wadji mo khoromou rék.😂😂
Té deugeur bopou 😂😂
Mouhamed kou gueum yallah laaaa kou d’accord la lal j’aime ❤
Des fois Yallah dina là indil khéwal ngua diambat beuko gniak 😅 Zo li man là waron döne. Je rêve de vous rencontrer 😊
Mon frère diamo si iow mais copain bi manoul communique motakh mais yalla n'a sa diamo yagg ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup frère yalla defal dîam ❤❤
Ms zo ki geum na yalla ms nk zo dfa comprendre wul dh hiii🎉
No. Zo billahi reygama😂😂
Alhamdoulilah ba yalla mayou ma genre esprit yi😂
Machallah sèttèt lal ngagnou zo merci bc Amna solo lolll