17 Avril:Tawfekh Mbaye Todj na Thiant yi découvrez les pas de danses de Serigne Saliou Ndigueul Thio

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 12 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 78

  • @boubsboubacar8609
    @boubsboubacar8609 Рік тому +11

    Thieuyy yalla cheikh Bethio nako yalla yeureum té diégalko ak bep dioulit🙏🙏

  • @adamaka5641
    @adamaka5641 Рік тому +1

    Machalla yalla na yenbi oyof
    Ndeyssane nekhna tawfekh mbaye limay la woy rayna
    Wayé diar nguako ame ngua yar ak diné
    Cheikh yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana firdawci ci barké Seydina Mohamed

  • @ndeyediop335
    @ndeyediop335 Рік тому +20

    Cheickh Bethio Serigne Saliou té wakeur Serigne Saliou nénagne yaw le makk djitou rak topp le Touba kham kanam rék boul titte boul ragal kou wakeur Serigne Touba andal loye khalate

  • @seynaboudiouf2203
    @seynaboudiouf2203 Рік тому +20

    Douma thianta dh ms franchement mane ki dama nex parsk dall na yarou na teyy na te degg ndiguel continue comme sa Serigne Mountakha mola djiteul kouka bagn sonnou

  • @bintadiao3696
    @bintadiao3696 Рік тому +2

    Franchement un homme très sympathique je lai rencontré l'année dernière a l'aéroport j'ai même échangé des paroles avec lui que le bon dieu le garde et le protège inchallah amine

  • @milab9987
    @milab9987 Рік тому +13

    Saliou ndigueul aka yaruuuuu machalah ❤

  • @mamindiaye8519
    @mamindiaye8519 Рік тому +1

    Barki s saliou santate nane s bethio banoula amé sangue thioune doundeul wéreul sagou wate nane ndamou wate nane dieuredieuf thioune ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamediarragueye2479
    @mamediarragueye2479 Рік тому +4

    Ndeyessane soumako guissé damay contane ❤

  • @aramediop4711
    @aramediop4711 Рік тому +1

    Machala ndam rek
    Kou mérr dhéwal

  • @seyemamadou8131
    @seyemamadou8131 Рік тому +2

    Yerreume nall ene déh feeth rek 2020 yeewoulene bayilene feeth té diamoudji yallah

  • @sigafaye8868
    @sigafaye8868 Рік тому +10

    Barkép Serigne Saliou mbacké ndigueul Thioune mala beug❤❤❤❤

  • @ndeyetoutyndiaye1906
    @ndeyetoutyndiaye1906 Рік тому +6

    ❤❤ Barké s saliou thianta ba daw🧡 cheikh Bethio Mame Bambi yala n'a gnou ki yala fayal

  • @pendadiaw1798
    @pendadiaw1798 Рік тому +3

    Yall nafi yageu loool thioune ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @oumarblonde3018
    @oumarblonde3018 Рік тому +6

    Dieuredieuf Serigne saliou ndiguel thioun

  • @petitngom9295
    @petitngom9295 Рік тому +3

    Machala thiante GUI moy sounou diné yalnagne sakh si thiante GUI ba fawe

  • @ndeyecodoundiaye2185
    @ndeyecodoundiaye2185 Рік тому +1

    Taw bubax ndimballl la, Thioune yabax❤

  • @ndeyecoumbadiouf6116
    @ndeyecoumbadiouf6116 Рік тому +1

    Thioune yague fi loll teh were 🙏Tawfekh yala na batte bi were❤

  • @papedjibrilkarafall-ri6xo
    @papedjibrilkarafall-ri6xo Рік тому +5

    Sant rk kou sant gnou dolil la Sant Serigne Saliou MBACKé ❤️💯❤️💯

  • @ndeyeantangom7910
    @ndeyeantangom7910 Рік тому +3

    Dieureudieufety Serigne Béthio 🥰🥰🥰

  • @gnagnadiene218
    @gnagnadiene218 Рік тому +3

    Kou guiss am ndao son excellence

  • @ndeyediop335
    @ndeyediop335 Рік тому +1

    Am ga ak talibé dall d'accord na ak yaw guiss na Serigne gnou star yi ak Serignette wayou yi

  • @dawguisse3482
    @dawguisse3482 Рік тому +3

    Ah machala ndiguel rek moo waure tu es rassuré ❤

  • @mamadoukane7055
    @mamadoukane7055 Рік тому +2

    Li thiakhane Kepler diamou dyilene yalla te bayi fethie yi li AK concert reck yame

  • @ggyggggxek3kojhh
    @ggyggggxek3kojhh Рік тому +2

    Focus 2024 OUSMANE SONKO 🌍💪🏾🇸🇳

  • @merebayefall4160
    @merebayefall4160 Рік тому +1

    Bilaye wallay yow yaye cheikh Béthio mack djitou rack yi toop thi sokhna woutal dieukeur

  • @massanthiofaye5488
    @massanthiofaye5488 Рік тому +4

    Dieurdieuf Thioune sangue yaram ya fi nekk ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @yacinendiaye8718
    @yacinendiaye8718 Рік тому +5

    😂ma yeureum gnila bagne

  • @falloufall6440
    @falloufall6440 Рік тому +3

    Bilay serin khadim dabakha

  • @boussofaye8105
    @boussofaye8105 Рік тому +3

    machala thioune

  • @ibrahimafall2982
    @ibrahimafall2982 Рік тому +2

    Machalah thioune yag fi lol❤❤❤

  • @makhdydiabou9248
    @makhdydiabou9248 Рік тому +5

    Ndaysan kou diour dom déwo comme papam

  • @ousseynoufall5004
    @ousseynoufall5004 Рік тому +3

    Thia kaw thia kanam rek

  • @sadiocamara7957
    @sadiocamara7957 Рік тому +1

    C sa la sunna 😂😂😂

  • @evagassama9831
    @evagassama9831 Рік тому +3

    Tariha bohameni féthe reck

    • @khadyndiayeyayefall9014
      @khadyndiayeyayefall9014 Рік тому +1

      Lousi sa yone ténga lidianti sa bopp tei yam sisa tarikha bayi niou ak sounou boss😂😂😂 nala sa bopp doy ak sa diganté ak yalla geunoul wala

  • @serignemansoursane-sd8wo
    @serignemansoursane-sd8wo Рік тому +4

    Wa fii dh motané soiré de galla bii😂😂

  • @coumbasene289
    @coumbasene289 Рік тому +1

    Machaalah thioune

  • @fallouseckmame1451
    @fallouseckmame1451 Рік тому +2

    S bethio dieureudeufeuty

  • @amdidieng8171
    @amdidieng8171 Рік тому +1

    Machalla

  • @seyemamadou8131
    @seyemamadou8131 Рік тому +1

    D'oùnguéne yewu moukou liffi hewone yéwouléne

  • @doudoufall4718
    @doudoufall4718 Рік тому +1

    Avec ça nga nékh serigne nga domeram dji serigne dina féthi ioe ak Aïda diallo yeupa yamm Aïda tanei leu

    • @dioussousmane
      @dioussousmane Рік тому +1

      Kou nagou gnou nakh la Yako tek sa bope Mane mome kéne douma nakh koumay yobou si yonou yalla rek

  • @marianecoulibaly8802
    @marianecoulibaly8802 Рік тому +2

    ❤❤❤❤❤

  • @ndiayafall9468
    @ndiayafall9468 Рік тому +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @wakhdeugreckteyallatakh5716
    @wakhdeugreckteyallatakh5716 Рік тому +3

    Antouca dal thiakhane bakhoul rawatina si djioulid wasalam

  • @adamaka5641
    @adamaka5641 Рік тому +1

    Khadre la wayé maynako Mohamed gueye diabaram mame bousso Ézane Abdou mbacké dieng Adama sow saliou dieng
    Ken dou cheikh bi
    tabé mena wakhtane té guemone Serigne Saliou

  • @akhmadieng986
    @akhmadieng986 Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aladjifaye157
    @aladjifaye157 Рік тому +6

    JAMMOUL DJILEEN YALLA SUNU BOROM di bayi fo Li nguen neké teug fethie goor gni ak djiguen gni diakhaso bokoul si diné lislam yewouleen bala deh niow Aída diallo mom kouko damako dieulélé ak njiko top

    • @profcoly6085
      @profcoly6085 Рік тому +2

      Yow sa dokhotou kilifeu way ahh khana boy adj maka boy weur kabba khana douniou diakhasso ak djiguéne gni

    • @aladjifaye157
      @aladjifaye157 Рік тому

      @@profcoly6085 yow dé finga nek defarou motakh ngay saga may wakh nganan bounouy weur kaaba yafa dem ?

    • @aladjifaye157
      @aladjifaye157 Рік тому

      @@profcoly6085 yeen dall kouleen deug wala louleen guindi saga rek nguen diap ni mossiy soloution

    • @aladjifaye157
      @aladjifaye157 Рік тому

      @@profcoly6085 te kaaba gogou ngay wakh demal ak sa gangor di def ninguen def dadiola di fethie teugue aka woy kon dé dague nanou sen bop yi bou Yagüe ay neew nguen di doon

    • @awasall1757
      @awasall1757 Рік тому +2

      @@aladjifaye157 Elhadji Merde li guay wakh ni Sa yone nekousi lifianetil Sa Djiné mo geune. MBEKTÉ gui gnoune doundou mom guéne meunoul ame

  • @albaba45
    @albaba45 Рік тому +1

    🤣🤣🤣🤣

  • @NdeyeMauitte
    @NdeyeMauitte 6 місяців тому

    ❤❤❤❤❤🫶🫶🫶🫶

  • @seringtouray6608
    @seringtouray6608 Рік тому +1

    Is this a islam no no no i feel sorry for Senegalese people

  • @aliouneseck6083
    @aliouneseck6083 Рік тому +1

    Thiahan ya ngi bega bary te ngena toupee delou si yalla

  • @paconese
    @paconese Рік тому +1

    Alors, ça se passe bien la soirée dansante🤔. Le secte confrérique est de retour

  • @sadiocamara7957
    @sadiocamara7957 Рік тому +1

    Retard sans hasana

  • @adamaka5641
    @adamaka5641 Рік тому +2

    Machalla yalla na yenbi oyof
    Ndeyssane nekhna tawfekh mbaye limay la woy rayna
    Wayé diar nguako ame ngua yar ak diné
    Cheikh yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana firdawci ci barké Seydina Mohamed

  • @coumbafaye4030
    @coumbafaye4030 Рік тому +1

    Machalla

  • @akhmadieng986
    @akhmadieng986 Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ManiangthioNiang
    @ManiangthioNiang 8 місяців тому

    ❤❤

  • @adamaka5641
    @adamaka5641 Рік тому +1

    Machalla yalla na yenbi oyof
    Ndeyssane nekhna tawfekh mbaye limay la woy rayna
    Wayé diar nguako ame ngua yar ak diné
    Cheikh yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana firdawci ci barké Seydina Mohamed

  • @modoundiaye5687
    @modoundiaye5687 Рік тому +1

    Machalha

  • @bassirengom
    @bassirengom 7 місяців тому

    ❤❤❤❤❤❤❤