Serigne bi yagui parprlo signature kounekaye waxe mo lo li euppe thie sénégalaiye khanane né kou respecter domou adama la te mane euppelewonala waxe si lambe,🙏🙏
Saliou Niang yaw moom xanaa ci lepp nga am xam-xam 😂😂😂 Li gën a bon nak mooy jàpp ne da nga wara wax te yaw rekk a wara noppi. Une vrai tête vide mooy Breudeu bi Saliou Niang 😂😂
Serigne man dh sou ma sa ndion ga mandou ci lambou ji li gay khamoko ta yagi wakh ci dioumtou kay bo khamni kou nék mou lay deugelou ta sa wakh dji firi na bopam manam yaw dafa am ko faraloll ci combat bi
Je comprends pas comment peut tu être à nous tympaniser avec tes analyses bidons, yew démo arène, sétano télé le minimum c’était dougou youtube revoir les images pour comprendre maneu joxé sa avis. Beug lo wax ak ñak lo wax métina dé
Wakh deugu dh tay ando ma ak iow Yaané sétano ko khamo kon waro si wakh Siteu lodol daw ta nékée woka fa won Pour man nak ba nga déme bay wakh waron nga sétane ba nopi bo mandou ngay weur🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Wakh deugu dh tay ando ma ak iow Yaané sétano ko khamo kon waro si wakh Siteu lodol daw ta nékée woka fa won Pour man nak ba nga déme bay wakh waron nga sétane ba nopi bo mandou ngay weur🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Sénégal pour les sénégalais yi la
Tahirou Sarr
Tahirou Sarr
Tahirou Sarr
Tahirou sarr
Seul rekk inch'Allah barke sëriñ Tuubaa inch'Allah
Manchalla amatina sollo
❤❤❤ machalla amna solo
Kii mome louko modou deff paa bou tollou nii niakk nga fayda trope
Tay mom D’accord rouma ak ioe li dosa waréff Akh 😡😡
Ki kay néna sonko lay garouwalé so ragalés liga bègue wahk nga nopi😂😂😂
Serigne bi yagui parprlo signature kounekaye waxe mo lo li euppe thie sénégalaiye khanane né kou respecter domou adama la te mane euppelewonala waxe si lambe,🙏🙏
Sama Serigne li âme poo rék lah , amoule solo si ly geneu done farata
Modou lô seul macahalla ❤❤😢😢
Serin..daga farr😂😂
Sama serigne tay mom danou nga
Tay mom kou bakh wakhofi dara lou am solo
Séétanoo lamb dji nga wax déjà téga dém sétaane ba paré 😂😂😂
Ki kay néna sonko lay garouwalé narnga sonou😂😂😂
Pape Name nane sa wakhtane ak serigne cheikh fall mbaor
😂😂😂😂 tay mom danno geh moudo lo incalah doko bayyi Guinea mokk de ko tewlo
Ana Tahiirou
Ki kay néna sonko lay garouwalé😂
Tahirou Sarr rekk
Saliou Niang yaw moom xanaa ci lepp nga am xam-xam 😂😂😂
Li gën a bon nak mooy jàpp ne da nga wara wax te yaw rekk a wara noppi.
Une vrai tête vide mooy Breudeu bi Saliou Niang 😂😂
Ki kay néna sonko lay garouwalé narnga sonou😂😂😂
Saliou naafekha lila nakhari kham nanuku moy li modou lo bayie bokale
Serigne man dh sou ma sa ndion ga mandou ci lambou ji li gay khamoko ta yagi wakh ci dioumtou kay bo khamni kou nék mou lay deugelou ta sa wakh dji firi na bopam manam yaw dafa am ko faraloll ci combat bi
Guèneul si yii li dousa domaine
Je comprends pas comment peut tu être à nous tympaniser avec tes analyses bidons, yew démo arène, sétano télé le minimum c’était dougou youtube revoir les images pour comprendre maneu joxé sa avis.
Beug lo wax ak ñak lo wax métina dé
Wakh deugu dh tay ando ma ak iow
Yaané sétano ko khamo kon waro si wakh
Siteu lodol daw ta nékée woka fa won
Pour man nak ba nga déme bay wakh waron nga sétane ba nopi bo mandou ngay weur🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Yaw da ngaa waroon'a seetan ( Coumba) bi, bapare moo gën. Li gay wax xamoo si dara, lu dul deeg naa.....
Losayn thie lambou souf yaw daga farr
Yaw lou sita wakh
Somko somko somko rek
Wakh deugu dh tay ando ma ak iow
Yaané sétano ko khamo kon waro si wakh
Siteu lodol daw ta nékée woka fa won
Pour man nak ba nga déme bay wakh waron nga sétane ba nopi bo mandou ngay weur🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏