Siteu met Balla en garde : " tu as battu Yékini, revanche leu "

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 4 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 273

  • @mamecheikhmbow5033
    @mamecheikhmbow5033 2 дні тому +26

    Fan's Modou lô la meii ce sera la première fois que je supporte Balla

    • @DjibrilBa-xp7te
      @DjibrilBa-xp7te 2 дні тому

      @@mamecheikhmbow5033 wakhi doff 😁😁😁😁😁

    • @DjibrilBa-xp7te
      @DjibrilBa-xp7te 2 дні тому

      @@mamecheikhmbow5033 nioune Modou kharagne lô bourou lamb dji seul

    • @aidajuf8377
      @aidajuf8377 День тому +1

      Park mo douma sa mbeur dan ko

  • @RokhayaBiteye-g8k
    @RokhayaBiteye-g8k День тому +8

    Siteu guirr yalla amal diom rék nga tahaw bi dou yooyou déh 😂😂😂mafia Balla gaye ana guéne 🎉🎉🎉 Balla seul amoul lénéne

  • @omarlaye2658
    @omarlaye2658 2 дні тому +12

    Je suis un fans de Modou lo, Mais Balla gaye 2 yalnako yalla maay ndaam

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo9171 2 дні тому +13

    Situé bipa do youhou do napaté ki Moy Balla mola Daka wah mola Daka beuré

  • @AbdouSene-f5k
    @AbdouSene-f5k 2 дні тому +81

    Balla seule je suis fière d'être sérère euplé wo Balla gaye 2 ay suportere sérère

  • @loufa299
    @loufa299 14 годин тому +1

    Balla gaye 2 Seul kou d'accord lalal j' aime🥰❤

  • @MatarNdiaye-j9n
    @MatarNdiaye-j9n 2 дні тому +9

    Je supporte modou lo mais siteu damako yagg beug walahi ❤❤❤❤🎉 ndam rek baye fall bi nio bok darou salam ❤❤❤ mais amal yarr nigua dokhalé ak modlo bakhoul .😢

    • @FatouMbaye-dy2ol
      @FatouMbaye-dy2ol День тому

      Kon déh. Nion yam mane supportére modou lô la mais siteu la faral siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 inchallah

  • @elhadjipapaseye5540
    @elhadjipapaseye5540 2 дні тому +36

    Je suis fans modou mais yalna baalla dan

    • @MamegorDieng-os2fj
      @MamegorDieng-os2fj 2 дні тому +2

      Amine

    • @sambadiouf9121
      @sambadiouf9121 2 дні тому

      C'est parce que siteu def lén douma dan lén avec la manière et vous vous êtes refusé 😂

    • @SYN979
      @SYN979 2 дні тому

      @@sambadiouf9121sou dégoul français nopil wala nga wax li nga xam😂

    • @FatouMbaye-dy2ol
      @FatouMbaye-dy2ol День тому

      ​@@sambadiouf9121boul wakh lolou Mane supportére Modou lô la mais siteu la faral siteu damako beugue bilakhi siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 le 5 juillet inchallah tarkidan bi ak Modou kharagne lô kessé lagniouy toppou siteu rek amoul lénéne

    • @FatouMbaye-dy2ol
      @FatouMbaye-dy2ol День тому

      ​@@sambadiouf9121Mane déh mbokkou masi Mane supportére Modou lô la mais siteu la faral siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 inchallah

  • @kanegueye388
    @kanegueye388 2 дні тому +14

    Siteu fait attention Ballah est un vrai lion

  • @DjibrilBa-xp7te
    @DjibrilBa-xp7te 2 дні тому +19

    Yaldaw vs fawzeyni 😂😂😂

  • @oumar-dz2ne
    @oumar-dz2ne День тому +2

    Fans de modou lo là mai je supporte BALLA GAYE 2 ndam rk INCHALLAH

  • @yacinebouballaguaye2243
    @yacinebouballaguaye2243 2 дні тому +12

    Machalla respect pour mon petit frère l'homme au mental fort nous les supporters fidèles nous sommes la pour vous souvenirs force a vous champion yalnala yalla défal diam ake ndam inchalla Amine yarabi balla rék balla késsé 🤲🏻❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏻

  • @NeneCorrea-sy2ll
    @NeneCorrea-sy2ll 2 дні тому +8

    Pere max mom 10% rek nio ko intéressé si combat bi wayé amoul yakar si mbeureum bi😂😂😂 Yaldaw vs Simba

  • @CHeikhKebe-um4ku
    @CHeikhKebe-um4ku 2 дні тому +16

    Siteu késsé❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @soppeousmanesonko777
    @soppeousmanesonko777 2 дні тому +8

    Modou Lo Seul 🥰 Siteu Ndam reke inchallah 🙏

  • @mhdmetza122
    @mhdmetza122 2 дні тому +8

    Ohhh "Balla le lutteur le plus populaire 😊"

  • @omardieng5422
    @omardieng5422 2 дні тому +2

    siteu kasé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @sambaba683
    @sambaba683 2 дні тому +17

    Balla guaye2 doussa morom moleu moune wayyyyyy😂😂😂😂😂😂😂

    • @ndiagaseye5304
      @ndiagaseye5304 2 дні тому

      Boul si ték sa khaliss de Siteu moko mane té inchalla siteu dinako dane inchalla

  • @KamaraSarr
    @KamaraSarr 2 дні тому +4

    machallah je trés contant balla gaye2 surtout sporsor néwéli métani en paulh ci wolof moy nékhna météwoul

  • @AbdouAziz-ri8td
    @AbdouAziz-ri8td 2 дні тому +4

    Siteu Thiak Thiak le Comédien la Dey Daw

  • @LibasseBa-c6u
    @LibasseBa-c6u День тому

    Balla gaye le lion 🦁 de Guediawaye ndam rek inshalla ❤❤❤💪💪💪💪

  • @TaphaKara-e9t
    @TaphaKara-e9t 2 дні тому +4

    Siteu a vie ❤

  • @MameAbdouNdao
    @MameAbdouNdao 2 дні тому +5

    Je suis un sérére et fier d’être supporter balla gaye 2

    • @ibrahimadiouf9685
      @ibrahimadiouf9685 2 дні тому

      Ma sœur ngèneu lène ci li ngéen nek: nek sérère téwoul nga supporter Balla. Bo wakhei ni:" je suis fière d'être sérère mais je supporte balla" c'est comme si nek sérère supporter balla dou lou normal. Alors que siiiiiii

  • @LamineBadji-x3r
    @LamineBadji-x3r 2 дні тому +3

    Balla dhé dinalleuh door ayy door you métty daane leuh 🤣🤣🤣🤣

  • @CASI7797
    @CASI7797 2 дні тому +8

    Mome ak Lac beine leu, sougnouy signer rek guani ils vont écraser leur adversaire 😂😂😂

  • @LamineBadji-x3r
    @LamineBadji-x3r 2 дні тому +5

    Balla dhé ayy wakh danou koo boo dawwé dinalleuh diappp 😅😅😅😅

  • @khalillze1672
    @khalillze1672 2 дні тому +10

    Regard Max mbergane 😂😂😂dafa melni xaliss moko dougal ci combat wayé dou revanche déeee😂😂😂

    • @mouhamadoudiene1315
      @mouhamadoudiene1315 День тому

      Dmrm ji xaliss rek la geum mom moy dawlo siteu bagn mou danou pour meun yokk cachet wam

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 2 дні тому +10

    Way Siteu Amna gnianou way diour 😊😊

  • @adamadiouf9926
    @adamadiouf9926 День тому

    Vision Sénégal 2050 inchalla ❤❤❤

  • @FALLOUNDIAYE-d2m
    @FALLOUNDIAYE-d2m День тому

    Siteu rek ♥️♥️♥️♥️♥️

  • @taphajawara
    @taphajawara 2 дні тому +7

    Siteu ndam rek ❤🎉

  • @elhadjimamadoudiaw3628
    @elhadjimamadoudiaw3628 2 дні тому +13

    Siteu bilae yangui dogga dathie nakk barki serigne Bamba

  • @NdiagaNdiaye-kj5om
    @NdiagaNdiaye-kj5om 2 дні тому +26

    Première fois may supporté Balla gaye,Siteu Dafa Bari wakh trop

    • @abdoukhadrediouf5919
      @abdoukhadrediouf5919 2 дні тому +2

      @@NdiagaNdiaye-kj5om tei tapett la . Lolou rek mo m méti

    • @MatarNiang-m9g
      @MatarNiang-m9g 2 дні тому

      Séne data yaye situé seull

    • @ouzlepikinois
      @ouzlepikinois 2 дні тому +1

      @@MatarNiang-m9g fils bayil saga yii li sport le rék té ndam li ngènoul galsen

  • @Gofaye-g9p
    @Gofaye-g9p День тому

    Yale mbine bi seul❤❤

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 2 дні тому +1

    Yalmine bi seul❤❤ yalla nala yalla may ndam❤ kanam inchallah borom xôlou social❤

    • @FatouMbaye-dy2ol
      @FatouMbaye-dy2ol День тому

      Amine yarabi je suis supportére de Modou lô mais siteu damako beugue bilahi siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 le 20 juillet inchallah

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 14 годин тому +1

      @FatouMbaye-dy2ol amine

  • @AliouNdong-w1g
    @AliouNdong-w1g 2 дні тому +1

    Siteu rk❤❤❤

  • @mortadacisse8992
    @mortadacisse8992 2 дні тому +3

    Siteu seul❤🎉

  • @IbrahimaNiang-r7f
    @IbrahimaNiang-r7f 2 дні тому +6

    Siteu seul fière d'être sèrere ndam rékh inchallah

    • @FatouMbaye-dy2ol
      @FatouMbaye-dy2ol День тому

      Amine siteu rek amoul lénéne je suis fans de Modou lô mais siteu la faral siteu yalla nako yalla soutoural mayko ndaam sikaw balla gaye2 le 5 juillet inchallah

  • @issagueye9656
    @issagueye9656 2 дні тому +5

    Nous sommes tous des humains afférou ethnie bokoul sii sport boulén gnou sonal

    • @ibrahimadiouf9685
      @ibrahimadiouf9685 2 дні тому

      Balla moko fi adiwoone d contre Yékini. Ndem si Yallà, papam doubless yalnako Yalla xaarei aldiana mais dem na ba casamance di diooy nane Yékini néna faaléwoul diolas yi tei walaaaahi Yakhya waxoul lolou. Yalla baal ma mei bobou da fekkei ñou ragal mystiquou Yékini dou woute wallou. Grawoul on a compris. Olof ndiaye nak wax na ni:" kouñou fay nga mérr li nga lèblé mo baxoul"

  • @AblayeCarvalho
    @AblayeCarvalho 2 дні тому +1

    Siteu ❤❤

  • @Petitzo
    @Petitzo День тому

    Siteu siteu leuhhhh 💥😂❤

  • @bagiss360
    @bagiss360 День тому

    Je suis supporter de Modou lo mais balla yalla nako dane insalah 😊

  • @abouThiam-j7t
    @abouThiam-j7t 2 дні тому

    Siteu ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @petitjoeba4031
    @petitjoeba4031 2 дні тому +4

    Albourakh dala nakh gua djitou si press bi

  • @ndenediagne50
    @ndenediagne50 2 дні тому +7

    Siteu yaw dara Djiomboula baye fall nga ❤

    • @AssaneSadio-nk2ih
      @AssaneSadio-nk2ih 2 дні тому +2

      @@ndenediagne50 Beury défaite REK. Man fii nga diarr baa dane balla fala xamoul

    • @ndenediagne50
      @ndenediagne50 2 дні тому

      @ balla gnata défaite la am mdrrr dane force 😂

    • @zrtikhdcbn
      @zrtikhdcbn 2 дні тому +1

      Je supporte balla mais tu a raison

  • @FallouDiop-r6l
    @FallouDiop-r6l День тому

    C'est amine Bruxelles 👑🦁❤❤❤

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo9171 2 дні тому +1

    Gnari siteu balla moléne meune. Situé Wahbi mo eup djeuf dji. Balla Moy lamb

  • @KhadimLeye-w4s
    @KhadimLeye-w4s 2 дні тому +2

    Siteu bula balla daane dinga bayi bàri😂😂😂

  • @SaliouNdiaye-v1p
    @SaliouNdiaye-v1p 2 дні тому +3

    Balla seul seul seul seul ❤❤❤

  • @ndenediagne50
    @ndenediagne50 2 дні тому +3

    Siteu késsé ❤

  • @khadimdiop241
    @khadimdiop241 День тому

    Siteu Wakh guay diay Balla molako dakkeu😂beuré balla molako dakkeu ,fitte balla molako eupou ,supporter balla molako eupou ,fin bi gueuno donnn balla baye fall 🎉

  • @BocarGuangué
    @BocarGuangué 2 дні тому +5

    Siteu beugg na actionè te lamb dji yeup lay daww 😂😂😂

  • @mouhamadoudiene1315
    @mouhamadoudiene1315 День тому

    Supporter Modou la mzis Yalla na balla tègeul sa ndy do nitou dara domaram ji tekk khél rek nga nékkè ci lamb champion clos clos bi. Balla Gaye yalla nako yalla soutoural ba do am reupp ci mom sinon rek adouna toukki ndakh sa gatt gou reuy

  • @aliouba9834
    @aliouba9834 2 дні тому +1

    Siteu guir yalla boul daw deuguelal sa bopeu guir yalla bi dou yoyu 😂😂😂

  • @FallouMboupe
    @FallouMboupe День тому

    Fans Modou lo yepp balla le faral ❤❤

  • @MbayeDonde-n9o
    @MbayeDonde-n9o 2 дні тому

    SITEU SEUL BROM DEUK BU ❤❤❤❤

  • @2M5-Motivation
    @2M5-Motivation День тому

    Siteu réwna néna sama combat ak Omar Sakho taxawna 😂😂😂

  • @SambaSarr-g4w
    @SambaSarr-g4w 2 дні тому +7

    Nn siteu mo dakka djaye lamb kw😂😂😂😂😂

  • @boromebakh28
    @boromebakh28 12 годин тому

    Le regard de Max Mbarguane 😂😂😂😂

  • @aablayesy409
    @aablayesy409 2 дні тому

    Supporter modou Lô Yi si commentaire yii Louye sene bleme Siteu mo dane modou Lo sérieux Siteu seul ❤❤

  • @ndoyebara4040
    @ndoyebara4040 2 дні тому +6

    Siteu télna na wouti walou di monan revenche lay dieuleul yekini 😂😂

  • @senegalkesso1293
    @senegalkesso1293 2 дні тому +2

    MANI KENE DÉM JEUNDI JUS AK GLACE WELLY❤️

  • @khalillze1672
    @khalillze1672 2 дні тому +1

    Héeee homme de tenue héeeee😂😂😂

  • @MoussaNdiaye-w5c
    @MoussaNdiaye-w5c 2 дні тому +1

    Fier d'être sérer siteu rek bi dou yoyou dé balla

  • @xellxellu9160
    @xellxellu9160 День тому +1

    Yaldaw bi😂

  • @pascalkane9767
    @pascalkane9767 День тому

    Siteu sait faire le show il vend bien ses combats maintenant Balla Gaye 2 c'est une autre réalité 😂

  • @mbayetalibebromdaroubi1729
    @mbayetalibebromdaroubi1729 2 дні тому +1

    Mafi djitou 🎉

  • @allefall5545
    @allefall5545 2 дні тому +1

    Siteu wakh dj mo eupou dieuf dji

  • @GoFall-y6j
    @GoFall-y6j 14 годин тому

    Siteu wakh rèk la meune papaye Modou ga ame dë yaroule boy siteu🤫

  • @gueyemoussa7657
    @gueyemoussa7657 2 дні тому +2

    Per Mex c'est une très bonne ménager

  • @damelo2653
    @damelo2653 2 дні тому +4

    Yaw mom do touss mounane revanche 😂😂

  • @MamadouKa-h2k
    @MamadouKa-h2k День тому

    😅balla neena dekoy dakheu ba diappoko daane Kone déjà khamnaci saway dou daw

  • @bayelayendiaye8575
    @bayelayendiaye8575 2 дні тому

    Ndangoulal balla AK champion waw tmt

  • @papefaye7806
    @papefaye7806 День тому

    Siteu svp ne méle jamais Yékini à ton combat contre Balla kokou championla defna limou warona def béparé

  • @mortallasarr1630
    @mortallasarr1630 2 дні тому +1

    Siteu am nga problème nak 😂😭

  • @cheikhahmettidianendiaye3585
    @cheikhahmettidianendiaye3585 2 дні тому +3

    Siteu dagua dioum dh Balla dou yoyou dh

  • @AliouBadaraSall-v2n
    @AliouBadaraSall-v2n 2 дні тому +2

    Lac 3 BNE chance et comment tu vas faire pour continuer à fuire cet Fw ci

  • @TenneNdiaye
    @TenneNdiaye 2 дні тому

    Yalmine bi rek gnou demm🎉🎉

  • @MassambaDiop-n9l
    @MassambaDiop-n9l День тому

    Yaw amo diom Balla gaye 2 dinala gnouss bangua doul 🎉 Nguay diay saytané nann revanche Yékini nguay dieul ❤khana dangua fatté Sa Thiès milla naronn Rayy 😅😅

  • @LayeSall-w8c
    @LayeSall-w8c 2 дні тому

    Balla gaye sen 🎉🎉

  • @PenKhadim
    @PenKhadim 2 дні тому +1

    Valdo vs ama nékh❤❤🎉❤❤

  • @bachiroufaye7265
    @bachiroufaye7265 2 дні тому +4

    Balla rekk❤

  • @ibrahimambow9000
    @ibrahimambow9000 2 дні тому +6

    Takatile radio yi ba balla diap la dinga xame ni que balla bi dou yéné

  • @demboababacardiedhiou2539
    @demboababacardiedhiou2539 День тому

    Parlementaire bi 😂😂😂😂

  • @Bayedarou-r7l
    @Bayedarou-r7l 2 дні тому

    Balla nguirre yalla kii dakharale ndayame

  • @BarameThiam-zs6gj
    @BarameThiam-zs6gj 2 дні тому

    Siteu seul siteu rék siteu kassé siteu rék lanii topou yallmin bi ❤❤💪💪

  • @mameballacisse1621
    @mameballacisse1621 2 дні тому +1

    ❤❤❤❤❤

  • @aliouba9834
    @aliouba9834 2 дні тому +3

    Tapet ga😂 siteu wah rk ga meun 😂

  • @OumzoFall
    @OumzoFall 2 дні тому +1

    Mom daysane day wakh thiey siteu😂

  • @Dani-ibrah
    @Dani-ibrah День тому

    Kou dann bakhna 😂

  • @mambayedieye6289
    @mambayedieye6289 2 дні тому +2

    Siteu Tapéte la 😂😂

  • @PapaThiam-pm8ss
    @PapaThiam-pm8ss 2 дні тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @FallouSow-lw5qj
    @FallouSow-lw5qj 2 дні тому +4

    entreneure bounane le so beuré mou dane la😂

  • @mamadougalsen8712
    @mamadougalsen8712 2 дні тому +2

    😂😂😂amal diome touty

  • @TalibEsxadim
    @TalibEsxadim День тому

    Vraiment waxkate gua avant combat day wax après combat day wax😅😅 biir combat gua daw
    Introduction wax
    Développement daaw
    Conclusion waax😅😅

  • @AliouneGning-j7j
    @AliouneGning-j7j 2 дні тому +4

    Père max Dina raylou boynia dakh 10%

  • @adamagaye3659
    @adamagaye3659 2 дні тому +3

    Je suis supporter de Modou lo c'est la première fois may faral balla yal daw Dafa rew bari wakh new dieuf

  • @mbayesene1072
    @mbayesene1072 День тому

    Balla dousa morom ahh

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 2 дні тому +2

    Wallahi siteu amna problème 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ModoubarraDIAW-u9k
    @ModoubarraDIAW-u9k 2 дні тому

    Siteu bari na wakh légui mogui mélné gou kham Dara 😂 ba balla diap la