Salam Oustaz amna QUESTION: loo kham ci gor bouye toukh cigarettes si toilettes????? Est-ce djabar kat meun naala booler ak djinn amoureux???? DjazakAllah khayran
Machalah ya oustaz je m sens visé dans la plupart de t description fadiouna fou Nek defois May dem ba haddi ma togg on me dit que depuis xaleh lama dougg certains m disent que affairou mam Yi tmt cila bokk ayy lebou lagnu...que me proposez vous??
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH. Bien reçu nous vous reviendrons In Shaa ALLAH dans la prochaine épisode de la rubrique Anti Ndiabar pour répondre vos questions. Courage et bonne santé à tous !
As salaamou aleykoum wa rahmatoullah ya oustaze. Jazaakoumoullah khayran pour les vidéos elles sont très intéressantes et instructives. Man damaa beugon xam nax nit ax djine man nanioo am doom? Si oui, nax ki am farou rapp ou mari de nuit man na am ax moom doom ax lan mooy wane ni amna niou doom???? Te bou booba domou lan lay doon nax nit ax djine bokouniou espèce, kon sen doom noumouy mel?
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH mbokk mi Bien noté. Nous vous reviendrons dans la prochaine vidéo des réponses aux questions de Anti Ndiabar In Shaa ALLAH
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH mbokk mi Bien noté. Nous vous reviendrons dans la prochaine vidéo des réponses aux questions de Anti Ndiabar In Shaa ALLAH
Assalaamu halaykum maa ngi nuyu Ustaas. Damaa dégg ci sa benn Video nga Wax ne junne ak Nit dunu am doom te fii dafa mel ni danaa wax ne junne ji day gëm ne moo ngi am ak yaw doom ndax man naa see am lu gën a leer noo ngi jégglu bu baax jërëjëf
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH mbokk mi Bien reçu et bien noté. Nous vous reviendrons In Shaa ALLAH dans la prochaine vidéo des réponses aux questions Anti Ndiabar
Pour en savoir plus sur Paftane, vous pouvez aussi regarder l'épisode N°10 de Anti Ndiabar sur UA-cam en cliquant sur ce lien : 👉 ua-cam.com/video/D-WV4qiVacQ/v-deo.html
Diadieuf sangue bi amna solo trop yalna yalla fayla
Machaalah khafiizakoulah
Maa cha Allah diajakal lahou khayra
Man dehh sama boss bii wawlé bimi wawlé 🤧 Nianal lénmeu , man Geumna Yalla ❤
Maa Shaa Allaah ❤❤❤❤
YAllah nagnu borom bi mouthieul thi seni lorr 🤲🤲 Dieureudieuf Oustaz
Amna solo lool machallah ya oustaz longue vie à vous
Machaallah Oustaz amna solo lole machallah yalna yallah feyela yiw té samela jéréjeuf .
Macha allah amna solo trop qu'allah vous protège
Machala amna sollo ya oustaze
Diazakallahou khaïrane ya oustaz
Amna solo mashaAllah
Macha allah
Salam Oustaz amna QUESTION: loo kham ci gor bouye toukh cigarettes si toilettes?????
Est-ce djabar kat meun naala booler ak djinn amoureux????
DjazakAllah khayran
Bien reçu. Nous vous reviendrons In Shaa ALLAH
Machalah ya oustaz je m sens visé dans la plupart de t description fadiouna fou Nek defois May dem ba haddi ma togg on me dit que depuis xaleh lama dougg certains m disent que affairou mam Yi tmt cila bokk ayy lebou lagnu...que me proposez vous??
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH. Bien reçu nous vous reviendrons In Shaa ALLAH dans la prochaine épisode de la rubrique Anti Ndiabar pour répondre vos questions. Courage et bonne santé à tous !
❤❤❤❤
As salaamou aleykoum wa rahmatoullah ya oustaze. Jazaakoumoullah khayran pour les vidéos elles sont très intéressantes et instructives. Man damaa beugon xam nax nit ax djine man nanioo am doom? Si oui, nax ki am farou rapp ou mari de nuit man na am ax moom doom ax lan mooy wane ni amna niou doom???? Te bou booba domou lan lay doon nax nit ax djine bokouniou espèce, kon sen doom noumouy mel?
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH mbokk mi
Bien noté. Nous vous reviendrons dans la prochaine vidéo des réponses aux questions de Anti Ndiabar In Shaa ALLAH
Cva oustaz mane mane kouma digaalé rk dama wor té aussi louma yakar mou tass
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH mbokk mi
Bien noté. Nous vous reviendrons dans la prochaine vidéo des réponses aux questions de Anti Ndiabar In Shaa ALLAH
Assalaamu halaykum maa ngi nuyu Ustaas.
Damaa dégg ci sa benn Video nga Wax ne junne ak Nit dunu am doom te fii dafa mel ni danaa wax ne junne ji day gëm ne moo ngi am ak yaw doom ndax man naa see am lu gën a leer noo ngi jégglu bu baax jërëjëf
Wa Alaykoum Assalamou Wa Rahmatou-LLAH mbokk mi
Bien reçu et bien noté. Nous vous reviendrons In Shaa ALLAH dans la prochaine vidéo des réponses aux questions Anti Ndiabar
Est ce que xobou paftan bakh na ci rab
Bien reçu. Nous vous reviendrons In Shaa ALLAH
Pour en savoir plus sur Paftane, vous pouvez aussi regarder l'épisode N°10 de Anti Ndiabar sur UA-cam en cliquant sur ce lien : 👉 ua-cam.com/video/D-WV4qiVacQ/v-deo.html
Oustaz nan nguay def ba stress dagn ci yaw
Bien reçu. Nous vous reviendrons In Shaa ALLAH
Salam oustaz comment faire pour vous joindre ?
Salam numéro est disponible f
@@mamadoukatydiagne12 Salam à vous très cher j'ai essayer de l'appeler en vain
Veux-tu son numéro ?
@@moussaba8187 oui mon frère
Veuillez contacter les services de MMS Pro 221 pour plus d'informations