Boye niang a encaissé un coup et il forcé pour attaquer mais il n'est pas bien entré. Ceux qui ont déclaré la victoire de boye niang avant combat doivent accepter que c'est dieu qui connaît ce qui est caché.
MAIS es ce quil a recu les coups car moi jai beau regarder mais je ne vois pas de coups recus je vois des coups mais qui me semblent navoir pas touché aucun des deux lutteurs
Sénégal aka nakhare ame ndam modou lo danna euma sen 2 fois te wa pikin ken wakhol danko khelh me mo dan ama nione dan ko khekh mo dan boy niang nio ne danko khekh danio fatte yalla khana
Un siècle de préparation mistique pour au final tomber comme ça 🤣 mdr. Les gris gris Pffffh c'est du n'importe quoi, tu t'entraînes bien avec une bonne hygiène de vie et en prenant beaucoup de force et c'est bon. Modou lo lui il a capté la bail
Dara khéweul Youssou teuguoul Waly wayoul Ndiape Féthioul Modou mola dane Toke sa kaw photowou niou yobou wate Souniou Couronne👑👑😂❤❤❤vous lui devez du Respect 🫡 A Lô Ndamr Ciré❤❤❤😂
Modou Kharagne Lo guirr yalla bayil lamb desei lognou dara bayil soy beurei pression bi gniy andal c énorme comme Yalla defat na soutoura bayil il est temps teh nek sisa bopp champion on t’aime beaucoup
Il n'a pas pris de coup Boys Niang a Fuis le combat pour en finir avec une mauvaise attaque trop basse épuis fimou tibeu bakhoul Modou est un champion rusé calme le lecteur prêt sur tout les côtés moi je félicite Modou lo et j'encourage boys Niang épuis liii c du sport Sénégal mo gagner
Acceptez la défaite avec sportivité perdre face à Modou Lô n'est pas déshonnorant. Aussi bien Boy Niang que Ama Baldé ils ont encore de beaux jours devant eux.
De la même façon que les serignes de tariqas sont une ruse, les gris gris aussi pareil ! Seul le travail et la mérite peuvent payer y compris pour aller au paradis ! Sinon Boy Niang a bien lutté c'est mon lutteur il est juste tombé sur plus fort plus technique que lui, les gris gris et consort n'ont rien influencé dans ce combat ! Bravo Modou Lô pour sa constance !
Yaw dint guay doul nii tarikha fait partie du soufisme khamoleine doul Di wakh Modou lo loum doneuh sangoo foumm ko djeulei rew gueine trop tarikha mom Sénégal meunouleine fekhei bamm diekh fii
@@mouhamadoudiop678 SA saram ndèye toi avec tes serignes ! Man louma ame djokh sama ndèye ak sama baye, santi ci yalla saram ndéyou serignesi ak décervelé comme toi you lèn topou ! Sénégal dou avancé jamais à cause de domoukharam comme vous et ces dirigeants de sectes qui vivent sur vos dos et des caisses publiques de l'état ! Ca fait 100 ans aye magal, ziar ta dara magoul et ça va continuer comme ça ! Qu'à plus qu'un domékharam de serigne que ta mère ou ton père. Au lieu de suivre vos parents vous suivez des domékharam qui profitent de la vie avec des villa, belle femmes, belle voitures, beaux smartphones pendant vous et vos parents vous galérez dans la misère, meme la confiance que vous devez accordez à Dieu vous le donnez à ces domoukharam de dirigeants de sectes .
Au fait, aucun de ces supporters ne parlent de sport. "pikine negn bollo, li yeupp pikine motakh, modou lo danoul Boy Niang wa pikine nio ko dane etc...". Parlez au moins de technique ou de tactique etc... Essayez d'analyser le combat, est-ce que séne mbeur il a pris les meilleurs décisions tactiques etc... Modou Lo dina takh nieupp khamatt ni Lamb c'est culturelle d'une part mais c'est un sport de combat avant tout. Faut bien se préparer physiquement, tactiquement etc... Ceci est vraiment une mentalité à ne pas adopter, c'est à dire le fait de penser que ce n'est jamais de notre faute, on cherche tout le temps un autre coupable. Dangay déme keur sakh guiss kouy teudd 6h yéwou 15h déffoul dara pour situation wam changé, nga dégg mou nane "makhala sama nidjiay bi amna khaliss mais dimbali wouma motakh" ou tu entends les gens de la maison dire " Ndeysane woudjiou Yaye dji moko liguéyy" Meme chose ci politique, Kéneu dey nieuw rekk ni Macky motakh niouy doundd probléme youniouy doundd yeupp" rékk mbollo bi ni deugg leu, topp ko. Meme Sonko sou nieuwé in sha Allah dina amatt niou takhawat ni "Sonko motakh niouy doundd problémes yi yeupp". Nitt bou nékk ci probléme déy yakamti nga désignél ko dara niko " Tout ce que tu es entrain de vivre c'est à cause de X" Lolou dafay nékk béneu soulagement pour mom. Alors que forcément Présidents bou nékk dinga am lo déff am lo bayi, sa morom sou nieuwé am loumou deff am loumou bayi, ainsi de suite. Dans le contexte de l'histoire, Adolf Hitler a utilisé cette stratégie en désignant les Juifs comme boucs émissaires pour les problèmes économiques et sociaux en Allemagne dans les années 1930. Cela a contribué à la montée du national-socialisme et à la justification de politiques discriminatoires et génocidaires. La vie est une continuité inéluctable, où chaque génération, telle une vague incessante, succède à la précédente, inexorablement liée à elle, et où la transition se fait souvent de manière inévitable. Ce phénomène se manifeste également dans le domaine politique, où les dirigeants successifs prennent la relève et se complètent, tout comme il l'a été avec les prophètes, dont les enseignements perdurent à travers le temps, assurant ainsi une continuité dans la quête spirituelle de l'humanité. S'autocritiquer est essentiel pour favoriser la croissance personnelle, améliorer la prise de décision, renforcer la résilience (nitt déy mougn, rawatina djioullitt), promouvoir l'honnêteté intérieure, optimiser les relations interpersonnelles, encourager l'apprentissage continu, prévenir l'arrogance, optimiser la performance professionnelle, faciliter l'adaptation au changement et contribuer à la construction d'une identité solide.
Lolou rek motakh bouy beuré douma ko faral fans balla la mai tay môme Modou lo la fara lone môme ak siteu ak reug reug gnio gueuneu Bari wakh si lamb ji mai mane môme diél bi bétou ma khamone nako
Il devait aider Ama Balde et attendre le combat de Ama avant de prendre Modou Lo. C’est boy niang qui est responsable de la cassure à pikine. C’est bien fait pour lui. Amaaaaa Amaaa yé
Sa Waye boy Niang sou moumoune lamboji diélkou yeuna geuna khamné Modou lo Mou Mane téméri boy Niang geume léune yalla té khamné mounge merci seringe cissé AK masilla Diop AK sa Touba AK nieup ngi doune nianall Modou lo merci a tous
Modou lo c'est le Roi des arènes Maire de pikine n'a rang yi dioupppp khamoulénne sport P.A for life bandi cerveau.🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Balla moy sama mbeur mé Modou bagne Kate bimou done motax mou nex ma❤xamna ni dafa touti motax dakoy diaral mou entraîné chak jour té lolou kou bagne kou la yap rk lay nek si yw bon vent Modou lô
Chacun son tour chez le coiffeur..leigui supporters boy niang gnoo nane dagnko seitane 😂😂😂..il fallait aidé ama baldé au premier plan..yéna guena tay nii ama mo eup supporters birr pikine..et boy niang et son staff on montré quil ne soutenait pas ama pour quil prend la couronne..leigui vs ts vs avez perdu
Mais vraiment il est KO, il a pris un crochet et uppercut les gars c'est sa qui gaspillé son gaspillé son combat et il est attaqué aveuglemennt. Bon courage Boue Niang
Père Mansour Diop qui animait les plateaux en disant que modou lo n'aura rien Et maintenant qu'il a battu boy Niang il dit qu'il ne comprend pas ce qui s'est passé Il comprend après
Il n'a pas attaqué aveuglément au contraire il a eu un pieds peut-être sa position mais il n'a presque pas reçu de coups ( 2 ou 3 sur plusieurs) et il en a donné à Mdlo aussi. Son adversaire est tout meilleur c tt
" li daan Boy Niang Pikine la nek" bayi lenn yefou nafekk yii, PIKINE danou ko Modou Lo moko daan . Affaire yi yepp si digg geew gui leu .... Geum len Yallah bania geum yenn Serigne yii 😢
Kokou nane gnom gneup ay yambar lagnou mom mereina sen wa kogn dii😂 may wakh mounane Modou lo mii diko touteul😂😂non ki nexna félicitations Modou lo gnoune wa P.A on est fier🎉❤🎉❤boy Niang haler bou yarou nga je t'aime bien du courage
Félicitation Modou Lo Roi des arènes, Maire de Pikine ❤
Dafa lere
@@aminambengue6995😊
Félicitation sama rois 🤴 bi sama champion bi sama xarite bi daléna meune daneléne gueumléne YALLA NAK
Modou xaragne lo roi des arènes c'est le meilleur des meilleurs
Dafa leer
Modou Lô moma dane dou guathia courage champion ❤️🎉🙏
Bilahi lolou la wakh
M’Lo nak da meune wa pikine nak amoul lénén félicitation champion gnone mome rk lagnoy topou 🎉❤
Mansour Diop c'est un grand homme et a une très bonne communication et c'est de très grand sportif
Wa pikine Salide nan😂😂😂Mougne l'en yalla moy mayé ndam Félicitations mon Champion Modou Lo kharagne lo💪💪💪 🎉🎉🎉🎉🎉
❤ bilaye
Thiey sama Oustaz y’a meilleur Dee félicitations 😊
Boye niang a encaissé un coup et il forcé pour attaquer mais il n'est pas bien entré. Ceux qui ont déclaré la victoire de boye niang avant combat doivent accepter que c'est dieu qui connaît ce qui est caché.
Il a encaissé beaucoup de coups sahe ,
C'est vraie dafa KO motakh mou profitons dieule tank bi sinon li dale Ama moko narone dale
MAIS es ce quil a recu les coups car moi jai beau regarder mais je ne vois pas de coups recus je vois des coups mais qui me semblent navoir pas touché aucun des deux lutteurs
Il a reçu un coup de modou lo c'est vrai @@ibromeo9682
@@ibromeo9682il a encaissé un uppercut qu’il a mis K.O
Bayi Léne Diakhasé Bi Boy Niang Yalla Mo DogaL Mo danou Modou Lô Karagne Lô Le reste de Roi 🤴🏾💪🏽🤴🏾💪🏽🤴🏾😅😅
D’agnelles ko Gaye boor bi ama Di beurei gueinoul 😂😂😂
Deug leu pikine da tassaroo 😂😂😂wayè Mod lo mossi meune ndaye fouf❤🎉
Bane yalla
@@TheBandafall2003sou nekkoul yalla kann la ??? Modou yalla kasser lay topp
Sénégal aka nakhare ame ndam modou lo danna euma sen 2 fois te wa pikin ken wakhol danko khelh me mo dan ama nione dan ko khekh mo dan boy niang nio ne danko khekh danio fatte yalla khana
Son père est fou il devait prendre son fils dans ses bras et le consoler au lieu de le critiquer
Un siècle de préparation mistique pour au final tomber comme ça 🤣 mdr. Les gris gris Pffffh c'est du n'importe quoi, tu t'entraînes bien avec une bonne hygiène de vie et en prenant beaucoup de force et c'est bon. Modou lo lui il a capté la bail
😂😂😂😂
😂😂😂😂les gris,gris pppppfffff😂😂😂😂
Dara khéweul Youssou teuguoul Waly wayoul Ndiape Féthioul Modou mola dane Toke sa kaw photowou niou yobou wate Souniou Couronne👑👑😂❤❤❤vous lui devez du Respect 🫡 A Lô Ndamr Ciré❤❤❤😂
😂😂😂😂😂😂ya sof
Machalah Félicitations Modou ol 🎉🎉🎉❤❤
Appart balla Gaye (guediawaye) ❤chuii toujours pour modou❤🤗on l’adore
Vraiment boy Niang yalnoko yalla maye diamou
Modou Kharagne Lo guirr yalla bayil lamb desei lognou dara bayil soy beurei pression bi gniy andal c énorme comme Yalla defat na soutoura bayil il est temps teh nek sisa bopp champion on t’aime beaucoup
Billaay
Bilahi Wahga dégueu
Wa pikine gueum léne yalla ngéne ndagou séne défaite ta ngéne kham ni ngouram jékha goul machallah xaragne lô le king 👑 ya meune ya eupp doleh 💪💪💪🔥🔥🔥
Li dhé la wakh demb sonoouna trop ba légui tite bi danioule
Feeeen rek
Sénégal waarna wéeessou fii
Modou lo daffa meuneu beurréee loolou késsé
Te daffa wéeerou si Yalla
Flecitation modou xaragne lo macha allah nek leen fofo di wakh rek ❤wadji nelenko sono borom mo dogal modou lo daan boye niang 2 😢
5 minutes gayi dippi lamb dji 😆😆. J’aime mon pays!!
😂😂😂wooy
@@mariamacisse5972 Le pays est douuuxx
😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Bilahi le gars ma dead
Boye niang dafa ragal modou lo 😂😂😂😂😂
Ousmane sonko mo yoni ama balde pour mou sacrifice ndiol djinee falaye mingui Facebook ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Boye Niang defeant la pikine yalla moko df Ama mofi nk💚❤️
Félicitations modou lô le roi des arènes 👑👑👑👑👑❤❤❤❤❤du courage boye ndiang ❤❤❤❤❤
guem lene yallah sounou borom te nangou defete, they Sénégal, soyez sportif
Lou khéw 😂😂😂😂mougne léne daguéna mirrr😂😂😂 merci Modou alhamdoulilah
Khana 😂😂😂😂😂😂
Modou seul❤
Ndeysane sama mbeur bi dina doflo wa pikine rk sayoulène dané ay waxi doff rk laniouy wakh😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂wooyyy
Bilay
😂😂😂
Bilahi di semer terreur biir pikine😂😂😂 Modou arrêtel way bal léne Nawlé dafa fort
Roi 🤴 pour toujours❤ 💪🏻
Sallalahou aleyhi wa salam
Modou lo a terrorisé les pikinois du fait qu'ils ont accepté les deux avances sur deux nouveaux espoirs révélateurs de pikine
😂amou gnou xel
@@MrFayemanou c'est le cimetière des fous a dit xlo
Lii leep yenako eundi staff boy niang daniou warone khar ba ama parei niou sogua dieul combat bii lolou moy deugue
Absolument
J'avais pas pensé dans ce sens là mais c'est vrai
en plus bi Ama dano danio né problème staff la am..niouné boy niang staff bou bah la yor yalla atté na
Bilay souy beuré nimay tité dama beug modou❤❤❤😂
Akou ama baldé moko dall😂😂😂😂😂
Boy Niang dafa stressé wou depuis yobaneté yi gnon bari kounekeu nane beurel ma sama revanche mou melni gp 😂😂😂
rayguama😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂 ray ngama
Il n'a pas pris de coup Boys Niang a Fuis le combat pour en finir avec une mauvaise attaque trop basse épuis fimou tibeu bakhoul Modou est un champion rusé calme le lecteur prêt sur tout les côtés moi je félicite Modou lo et j'encourage boys Niang épuis liii c du sport Sénégal mo gagner
Acceptez la défaite avec sportivité perdre face à Modou Lô n'est pas déshonnorant. Aussi bien Boy Niang que Ama Baldé ils ont encore de beaux jours devant eux.
Bravo Fadel ❤
De la même façon que les serignes de tariqas sont une ruse, les gris gris aussi pareil ! Seul le travail et la mérite peuvent payer y compris pour aller au paradis ! Sinon Boy Niang a bien lutté c'est mon lutteur il est juste tombé sur plus fort plus technique que lui, les gris gris et consort n'ont rien influencé dans ce combat ! Bravo Modou Lô pour sa constance !
Yaw dint guay doul nii tarikha fait partie du soufisme khamoleine doul Di wakh Modou lo loum doneuh sangoo foumm ko djeulei rew gueine trop tarikha mom Sénégal meunouleine fekhei bamm diekh fii
Pourquoi les commentaires négatif
beug geum wollou yakar ragal serigne touba lagn ko def
mandoul rek gerer liga geum
@@mouhamadoudiop678
SA saram ndèye toi avec tes serignes ! Man louma ame djokh sama ndèye ak sama baye, santi ci yalla saram ndéyou serignesi ak décervelé comme toi you lèn topou ! Sénégal dou avancé jamais à cause de domoukharam comme vous et ces dirigeants de sectes qui vivent sur vos dos et des caisses publiques de l'état ! Ca fait 100 ans aye magal, ziar ta dara magoul et ça va continuer comme ça ! Qu'à plus qu'un domékharam de serigne que ta mère ou ton père. Au lieu de suivre vos parents vous suivez des domékharam qui profitent de la vie avec des villa, belle femmes, belle voitures, beaux smartphones pendant vous et vos parents vous galérez dans la misère, meme la confiance que vous devez accordez à Dieu vous le donnez à ces domoukharam de dirigeants de sectes .
Au fait, aucun de ces supporters ne parlent de sport. "pikine negn bollo, li yeupp pikine motakh, modou lo danoul Boy Niang wa pikine nio ko dane etc...". Parlez au moins de technique ou de tactique etc... Essayez d'analyser le combat, est-ce que séne mbeur il a pris les meilleurs décisions tactiques etc... Modou Lo dina takh nieupp khamatt ni Lamb c'est culturelle d'une part mais c'est un sport de combat avant tout. Faut bien se préparer physiquement, tactiquement etc...
Ceci est vraiment une mentalité à ne pas adopter, c'est à dire le fait de penser que ce n'est jamais de notre faute, on cherche tout le temps un autre coupable. Dangay déme keur sakh guiss kouy teudd 6h yéwou 15h déffoul dara pour situation wam changé, nga dégg mou nane "makhala sama nidjiay bi amna khaliss mais dimbali wouma motakh" ou tu entends les gens de la maison dire " Ndeysane woudjiou Yaye dji moko liguéyy"
Meme chose ci politique, Kéneu dey nieuw rekk ni Macky motakh niouy doundd probléme youniouy doundd yeupp" rékk mbollo bi ni deugg leu, topp ko.
Meme Sonko sou nieuwé in sha Allah dina amatt niou takhawat ni "Sonko motakh niouy doundd problémes yi yeupp". Nitt bou nékk ci probléme déy yakamti nga désignél ko dara niko " Tout ce que tu es entrain de vivre c'est à cause de X" Lolou dafay nékk béneu soulagement pour mom. Alors que forcément Présidents bou nékk dinga am lo déff am lo bayi, sa morom sou nieuwé am loumou deff am loumou bayi, ainsi de suite.
Dans le contexte de l'histoire, Adolf Hitler a utilisé cette stratégie en désignant les Juifs comme boucs émissaires pour les problèmes économiques et sociaux en Allemagne dans les années 1930. Cela a contribué à la montée du national-socialisme et à la justification de politiques discriminatoires et génocidaires.
La vie est une continuité inéluctable, où chaque génération, telle une vague incessante, succède à la précédente, inexorablement liée à elle, et où la transition se fait souvent de manière inévitable. Ce phénomène se manifeste également dans le domaine politique, où les dirigeants successifs prennent la relève et se complètent, tout comme il l'a été avec les prophètes, dont les enseignements perdurent à travers le temps, assurant ainsi une continuité dans la quête spirituelle de l'humanité.
S'autocritiquer est essentiel pour favoriser la croissance personnelle, améliorer la prise de décision, renforcer la résilience (nitt déy mougn, rawatina djioullitt), promouvoir l'honnêteté intérieure, optimiser les relations interpersonnelles, encourager l'apprentissage continu, prévenir l'arrogance, optimiser la performance professionnelle, faciliter l'adaptation au changement et contribuer à la construction d'une identité solide.
Ma sha ALLAH 🙏🏾🎉🥳 vérité absolue
Fadel je Salut ton professionnalisme journaliste du peuple couz ✊🏽✊🏾✊🏿
MODOU LO machalla mon champion je savais que tu n 'allais pas me decevoir
Non ly nékhe na non dagno khoromou mais mane pikine la deuke nake boye Niang rek lagni topou ake ama baldé 💪🏽💪🏽💪🏽😂😂
Ioe sportif nga
Guemlene yalla rek ❤❤❤❤❤❤❤modou le roi❤❤❤❤❤
10:30😂😂😂 wadji khana yalla moko wo wala kiko wo khourbou satané lh bamiy watt di wané message gni modou Lô Duflo naléne walah
Makhala Boy Niang dafa beuri waxx 😂😂
Lolou rek motakh bouy beuré douma ko faral fans balla la mai tay môme Modou lo la fara lone môme ak siteu ak reug reug gnio gueuneu Bari wakh si lamb ji mai mane môme diél bi bétou ma khamone nako
@@sonkoamdy7644dafa daan sén mbeur motakh😂😂😂
Modou lo tass na pikine😂😂
Réw na yabaté na,il n'a eu que ce qu'il mérite, adouna da ngay téy yarou
Il devait aider Ama Balde et attendre le combat de Ama avant de prendre Modou Lo. C’est boy niang qui est responsable de la cassure à pikine. C’est bien fait pour lui.
Amaaaaa Amaaa yé
Sa Waye boy Niang sou moumoune lamboji diélkou yeuna geuna khamné Modou lo Mou Mane téméri boy Niang geume léune yalla té khamné mounge merci seringe cissé AK masilla Diop AK sa Touba AK nieup ngi doune nianall Modou lo merci a tous
Modou dou nit mo woor deee😂😂😂😂😂
Papa lan la😂😂😂😂
Bilahi
@@djibyrokheyadieye691bro iow molo koi papa lane la 🤣 🤣 🤣 na fatalikou 1 janvier 2023 limou défone balla gaye2 té mou gueume yalla 😅😅😅
Wa yen supporter boy niang loutakh gueumo lein yallah mais boulein forcer boy niang nit yi tamite ama dal moy star pikine
Modou defatina meuniname sama khol sedna😂
Wa Pikine nio meune solidarité kou daanou diokh sa morom Ama, Eumeu, Sokh , Boy Niang. Bilahi yena appo souf 😂😂😂
Tu seras roi des arènes Inch1llah
Modou lo c'est le Roi des arènes Maire de pikine n'a rang yi dioupppp khamoulénne sport P.A for life bandi cerveau.🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Now Now 😅😅Modou lo yaxna😂pikine 😂😂is good yeh Modou lo I have you on Modou ❤😂😂
Dane makk dane rakk cheikh niang boy niang thieuy modou mi.
Machallah machallah bismillah errahman errahim sii modou lo dha technique bravo mbeur ❤ depuis nouakchott mauritanie
BOY NIANG TU AS ÉTÉ IRRESPECTUEUX ENVERS MODOU LO
SI VOUS REMARQUEZ BIEN TOUT LES LUTTEUR LORS DES FACE À FACE IRRESPECTUEUX VONT TOMBÉS
Modou lo dh kokou yapp arbitre dafa soufflet wou rkk Modou bvndi gueww leu 😂😂kou dess pikine pathe balde😭😂
Balla moy sama mbeur mé Modou bagne Kate bimou done motax mou nex ma❤xamna ni dafa touti motax dakoy diaral mou entraîné chak jour té lolou kou bagne kou la yap rk lay nek si yw bon vent Modou lô
Modou looooo🎉
@@KhadijaNdiaye-us3dw Modou lo😍
Du courage boy Niang.modou LO likoy dane moungui guediawaye bilahi
Modou lo likoye dane mogui guèdiawaye wayè ki nèkk guèdiawaye lii ko dane mo nèkka pikine tè modou dane nalène lolou la yalla doguale adouna nonoula
@@bouchragueye60 dou sakh balla gaye
Ioe daga bakh di wax rek 😂😂😂😂
Félicitations Xlo❤ Dafa Meun Wahtanlén Rafetal Yalla Mofi Neik
Chacun son tour chez le coiffeur..leigui supporters boy niang gnoo nane dagnko seitane 😂😂😂..il fallait aidé ama baldé au premier plan..yéna guena tay nii ama mo eup supporters birr pikine..et boy niang et son staff on montré quil ne soutenait pas ama pour quil prend la couronne..leigui vs ts vs avez perdu
Bilahi yéné negg la borom mosiy fanane té Ama khol bi mo rafet motakh akham molén dall
du courage boy niagn per mansor moma ree😂 lo nena lan la boy niagn dieul ba tokk wallah da dieul cou
😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂 non père Mansour 😂
Supporter boy niang yi danioo yékk khana😂😂😂 mourir de rire
KARIM PRÉSIDENT LANIOU WAKH NIOUNE 💙💛✌️ di filicte xlo
Weuh😂😂😂😂
L'AFRIQUE A UN INCROYABLE TALENT !
Appel manqué lama wo😂😂
Cheikh Niang rék manatakh Niang danou wakh rék _boy Niang da mirrrrrrrrrrr
Boy Niang kassé 💚❤️ félicitations modou lo
Wa lamb nio gueneu keukh wayadi sur terre mais comment on peut penser pareil 😂 Ba legui dieulo lene leçon sport c’est de l’entraînement
Mais vraiment il est KO, il a pris un crochet et uppercut les gars c'est sa qui gaspillé son gaspillé son combat et il est attaqué aveuglemennt. Bon courage Boue Niang
Père Mansour Diop qui animait les plateaux en disant que modou lo n'aura rien
Et maintenant qu'il a battu boy Niang il dit qu'il ne comprend pas ce qui s'est passé
Il comprend après
Il n'a pas attaqué aveuglément au contraire il a eu un pieds peut-être sa position mais il n'a presque pas reçu de coups ( 2 ou 3 sur plusieurs) et il en a donné à Mdlo aussi. Son adversaire est tout meilleur c tt
Chui un purcen pikinois mai il faut accépte la défaite pour mieu savouré la victoire a l'avenir mai bou DEUG REK déssé Modou lô moniou meune
Kou daanou rk dogua delou si yalla
KARIM PRÉSIDENT LANIOU WAKH NIOUNE KARIM PRÉSIDENT LANIOU WAKH NIOUNE KARIM PRÉSIDENT LANIOU WAKH NIOUNE KARIM PRÉSIDENT LANIOU WAKH NIOUNE alamine 💛💙✌️
Mouni ???
L'AFRIQUE A UN INCROYABLE TALENT 😂
Pikine degno deugue liguey diambour mais boulen saltél victoire modou bi nak di encourage boye niang sou amaté combat yalla nako yalla may ndam
" li daan Boy Niang Pikine la nek" bayi lenn yefou nafekk yii, PIKINE danou ko Modou Lo moko daan . Affaire yi yepp si digg geew gui leu .... Geum len Yallah bania geum yenn Serigne yii 😢
Boy niang ; Dioy djiakhneu
Modou lo : djioy djioyatte
😂😂 🤣🤣modou lo tu n’est pas sérieux Billay 😭😭😭😭😭
Ama baldé vs boy niang 🤷🏽♂️😂😃😂combat la 😂
Kou dane djieul Eumeu😂😂😂
QUE DIEU BÉNIT NOTRE CHÈRE AFRIQUE !
😂😂😂😂😂 Fadel dinama ray nena moy Mairou Pikine 😂😂😂😂😂😂😂
Waay cheikh Niang raynama bane prise la boy Niang déf waxléne mako rék😂😂
Bilahi fans Modou lo pur la mais boy niang diambar deug leu, mane courage lakoy wakh
Modou lo pikine lo arène nationale lo maire de pikine lo le roi lo 🤲🤲❤️
Waxale dhé Modou rek 😂😂😂
Niongi wakh pikin danko sétann wayé boy niang bou amonn ndam danoy wakh lénnen ama geum yalla no no no nam geum yalla rékk
Fadel yaye meilleur reportage si lambj gayui sou mbeur nanou dougno gniemé diegéeee
Bayui lénen diakhassè bi seytanei guene trop modou Lo kassè 🎉❤❤
Lelll mom xaliss lh wlh xam xam tei modou da lell 😂😂😂😂 c le meilleur niarr yeup la am yalna yokkk 🎉❤😅😅
Modou Lo tasss na pikine nii rk 😅😅😅😅😅😅💔💔💔💔
Modou lo mérite un monument à pikine
😂😂😂😂
200% pikine,la modou lo dane😂😂😂😂
Non dess na pathe😂😂
Néna pikin amatina nakhar😅😅bilahi dama yeureum wa pikin
Na nguène fékher ba boulène fi toudou ama baldé. sou meunone détourner victoire, mou défale ko bopame
Fekisilen niousssss léne lolu niaw na 😅fekisilen doorlen lolu niawna 😂😂😂😂😂😂
Kokou nane gnom gneup ay yambar lagnou mom mereina sen wa kogn dii😂 may wakh mounane Modou lo mii diko touteul😂😂non ki nexna félicitations Modou lo gnoune wa P.A on est fier🎉❤🎉❤boy Niang haler bou yarou nga je t'aime bien du courage
Ama beuré na ak modou lo staff fou boy niang kane mo diap si combat bou lene niou sonal
Moma diaxal
@@chatif1196 yené keur la borom mosi fanane
Molén meune waay❤❤❤❤😂😂
Degal ma li boy Niang mo mômone lamb ji gnou deup ko wakhi dof. Demléne entraînement dji t wahirou si Yallah
Félicitations modou lo
Wa adouna bii yeupp bouniou bollé wone takhoul, Yalla moy doggal bouné modou moyyy dane rékk lolou moy ame. Guemlén yalla way
Modou lo contanagnou mane gua bayi beuré😅😅🎉❤
Ama yé Ama yé Dieu a dit tant que les cœur ne sont pas ensemble il y aura pas de victoire voilà la vérité😂😂
talouniou lamb, on s en fou, focus SONKO 2024
Combat boye niang ama Balde iska dougn ko teugeu tmt 😅😅😅
Kou dane djieul Eumeu 😂😂😂
QUE DIEU BÉNIT NOTRE CHÈRE AFRIQUE !
Geum léne yalla nak
Quand il batté eumeu séne, c'était 💯 pikine mou dane eume 2 fois arrêté vos conneries,téh ngéne félicité le roi 👑