Ndeyssane, il pensait être sauvé en criant wanté dess n'a thi momite, terewoul seddé yeup nenaniou diabaram kou bakh leu wone. Yalna yallah yeureum khady diouf té kharéko aldiana
Daniouy wakh wayé def lou bakh li motakh niounane amna solo . Bo déwé ngakay khame😢😢 Sédé amna solo dé. Ha wayé Yalla moy até Yalla bakhna yalla naniou até si yeurmandém
C’était un pervers narcissique en faite. Il avait une personne à maltraité. C’est ce genre de comportement qui devrait finir . Le gouvernement devrait mettre en place une loi pour protéger les femmes. Et les familles, devraient empêcher et protéger les femmes. 😢😢
Ndeysane Khady doundou ngua si thiono déh ngua tamit si thiono yalla na adiana nekk sa noflaye ! D’après tout ceux que j’ai entendu la famille de Khady vous êtes vraiment des irresponsables vous l’avez jeter dans la feule du loup
Mais seck tamit eskeu nit leu waw ki mom lou ko dall ki daal moy..... khady diouf yallah na yallah sa borom yeureum ko té gorrél ko deffal ko tawfekh fa aldjanay firdaws si barkép serigne touba ak dollé mame cheikh Ibrahima fall
Djiguene yi bayi lene nepeu nepeul bi. Kou thi sa djeukeure pesse ngua porté ko plainte gnou ni ko rape thi kasso bi aye ate dotouko defati. Khady Yallah nako Yallah yeureume te khare ko Aldjanaye firdawsi.
Le problème ce n'est pas que les couples, mais aussi l'entourage. Si une femme amène son mari à la police, la famille parle parle, retirel plainte, sa baaayou doom
Billahi wallahi sokhna si wakh Nga degue de khady Diouf ngio boko baye, Moy la toudee sama 3e dom😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 Billahi wallahi yalla dina leral lep inchallah
Bilahi métina dé mais mbokou khady tamit amnguéne si part de responsabilité . Ndakh féke kou normaloul ,di menace de mort , di fil de fer nguéne bayifa séne dome mou divorcer nguéne delokoko ishh. Yalla na dé diséne Noflaye
Yalla nalèn bour yalla yeureum lèn tè dièguel lèn kharalèn thi aldiana fir dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl
Ndeyssane, il pensait être sauvé en criant wanté dess n'a thi momite, terewoul seddé yeup nenaniou diabaram kou bakh leu wone. Yalna yallah yeureum khady diouf té kharéko aldiana
Il faut que les langues se délient et que tout homme qui violente une femme soit sévèrement puni et que maslaaa cesse.
Qu’elle repose en paix au paradis éternel . Que le seigneur protège ces enfants, Amineeeee 😢😢
Amin ya rabi
😢😢😢😢😢 suis sans voix
Daniouy wakh wayé def lou bakh li motakh niounane amna solo . Bo déwé ngakay khame😢😢 Sédé amna solo dé. Ha wayé Yalla moy até Yalla bakhna yalla naniou até si yeurmandém
Yen tamite setane guen ko dé warone guen mobilisé wou door djeukeur dji bamou khole beneu place
Khaanaa, il faut que ça cesse deh.
C’était un pervers narcissique en faite. Il avait une personne à maltraité. C’est ce genre de comportement qui devrait finir . Le gouvernement devrait mettre en place une loi pour protéger les femmes. Et les familles, devraient empêcher et protéger les femmes. 😢😢
Ay pervers narcissique, yanna gnoussi ya ALLAH moussal.
Il faut être sensibilisée les filles à ce phénomène avant de vous marier.
Ndeysane Khady doundou ngua si thiono déh ngua tamit si thiono yalla na adiana nekk sa noflaye ! D’après tout ceux que j’ai entendu la famille de Khady vous êtes vraiment des irresponsables vous l’avez jeter dans la feule du loup
Son mari était fou,dof keur nio gueuneu sokhor
Khady reposez en paix.😢
DOFOUL dara diotou ko dof dou yor diabar dafa sohor rék wayé yalla migui koy har
@SalyNdiaye-ef9su Mane da ma diomi 🤔 niit bou normal,dou déf li si sokhor, vraiment qui mo sadique,la mère de tes enfants 😭
Amineeeeee waye li métina trop 😢
Mais seck tamit eskeu nit leu waw ki mom lou ko dall ki daal moy..... khady diouf yallah na yallah sa borom yeureum ko té gorrél ko deffal ko tawfekh fa aldjanay firdaws si barkép serigne touba ak dollé mame cheikh Ibrahima fall
Repose en paix Khady le mari yalla nako yalla bougal gueune ko lak yalla bou dé di noflayam
😂😂😂😂😂
😂😂😂sa khôl mo thiekhe bilay
😂😂
😢😢
Mariage you melni dou diekh si rewmi mais dagnouy neup neupal ba dcd amsi
Nima bagnè ay mbeup mbeup
Djiguene yi bayi lene nepeu nepeul bi. Kou thi sa djeukeure pesse ngua porté ko plainte gnou ni ko rape thi kasso bi aye ate dotouko defati. Khady Yallah nako Yallah yeureume te khare ko Aldjanaye firdawsi.
Le problème ce n'est pas que les couples, mais aussi l'entourage.
Si une femme amène son mari à la police, la famille parle parle, retirel plainte, sa baaayou doom
@gracevie6343 Il ne faut pas les écouter. Bayou dome boula bougue raye ngua raye ko en le privant de sa liberté. Sénégalais mo gneme massla.
Paix à leurs âmes, le mariage est vraiment une chance
Billahi wallahi sokhna si wakh Nga degue de khady Diouf ngio boko baye, Moy la toudee sama 3e dom😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 Billahi wallahi yalla dina leral lep inchallah
Yaw nopile khady da guine ko setane
Ki ndeye khady Ndiaye la kharitou ndeye seny Diouf
Yaw baba saka Kan ngay wakhal,? khamal li ngay wakh bou bakh, iskeu kham nga fan la nekeu 👈 khady Diouf Sama rak la ngio boko beneu baye, ok
@@shevamilano1981 yaw La wakh
Amna louma metti trop Khady Yalna khipper aldiana Yalna d done noflayam
repose en Paix Khady
Bilahi métina dé mais mbokou khady tamit amnguéne si part de responsabilité . Ndakh féke kou normaloul ,di menace de mort , di fil de fer nguéne bayifa séne dome mou divorcer nguéne delokoko ishh. Yalla na dé diséne Noflaye
Vraiment Mane béni yoneu ngamay doreu niou niarr même avec 50 enfants ohh khady 😢
Bilay mariage sans respect diaroul tokkk
Khady mo gnak fayda
Ta bcp de khady
Yaw deh amgua fitt bay hass kou ngagnou, yanna ya ALLAH diégueul
Nangou domeu keneu douma si menacer j’adore les enfants deh wayer keneu doumassi chantage
Mère warone ga wathié dabali bou yague😂😂😂😂
Aywaye😂😂😂
Chères sœurs arrêtez de vous marier avec les hommes sénégalais s'il vous plaît !!! Rip Khady❤❤
KHANAA DAFA DEPRESSIF. ?
Yéna sétane lii bamou aksifi wéroule wéroule soudone deuk toubab yii dagnoukoye boléck psychologue wéroul wéroul affaire bi métina trop wassalame
Ooh massa way khady warowon dello ci seye bi. Tey say domm gnakeunañ yaye ndakh jeukeur bou bonne
Metina 😭😭😭😭
Pourquoi cette non assistance yen yena raay Khady way