Lac 2 : Sadio Mané débloque 10 millions F CFA pour compléter les 20 millions, Pape Sarr révéle

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 тра 2024
  • Lac 2 : Sadio Mané débloque 10 millions F CFA pour compléter les 20 millions, Pape Sarr révéle

КОМЕНТАРІ • 83

  • @goradiagne9686
    @goradiagne9686 21 день тому +4

    Lac 2 yalla nalla yalla dèffale diam ❤❤❤

  • @Bildezer
    @Bildezer 21 день тому +11

    Merci sadio mane

  • @user-kh5pf2mf8f
    @user-kh5pf2mf8f 21 день тому +6

    Ndeysaan sadio mané nitt kou bakh la❤

  • @elzodieng8067
    @elzodieng8067 21 день тому +13

    Yalla nako yalla tegil natoubi waye lac guerre danga nelaw

  • @user-sb8gw2fx7k
    @user-sb8gw2fx7k 20 днів тому

    Merci pape sarr partir d’aujourd’hui tu fais partie de mes fans

  • @ibrahimaba5061
    @ibrahimaba5061 21 день тому +5

    Pape sarr borom bakh

  • @djilyboumodoulo8217
    @djilyboumodoulo8217 21 день тому +3

    Yalla na yalla tegulee kou lep

  • @user-sb8gw2fx7k
    @user-sb8gw2fx7k 20 днів тому

    Merci pape d’avoir bien corrigé frang

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 19 днів тому +1

    SAWAY FRANC YÉGUEUNA

  • @AdailyGeye
    @AdailyGeye 20 днів тому

    Merci beaucoup sadio Mane

  • @oumarsy860
    @oumarsy860 21 день тому +1

    Yalla bakhna ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @GorguiFall-dy3rm
    @GorguiFall-dy3rm 20 днів тому

    Merci sadio mané

  • @malick9084
    @malick9084 21 день тому +3

    Il a raison, la dernière fois, c’était gris bordeaux, balla gaye 2, sa thies franc parle très mal

  • @laminesall8353
    @laminesall8353 21 день тому +21

    wa lac 2 amoul 10million youmou fayé foumou déf khalisam

    • @oumarsene6509
      @oumarsene6509 21 день тому +1

      ❤❤❤ merci

    • @waxkatoudeug
      @waxkatoudeug 21 день тому +2

      Yaw dé lérna ma ni mousso téyé 1 million sa adouna. Nit day mandou

    • @abloslimshady
      @abloslimshady 21 день тому +4

      Yaw khana khamo mbeur guinawam dafa yatou?
      Mbeur meuna lek 10 million en un mois!
      Yaw ça se voit que million dafa reuy say beut

    • @doufyefaye6290
      @doufyefaye6290 20 днів тому

      Je te jure k niakoul loumouy fayé mais day runkeu xalissam😂

    • @ninkinanka3644
      @ninkinanka3644 20 днів тому

      Même SOUKO AMONE SAKH DOU TAKH YONE DOU AGALI LIGUEYAM.

  • @user-yd5qm6yx1m
    @user-yd5qm6yx1m 20 днів тому

    Je comprends maintenant pape Sarr a éclaircir c'est comme le cas de oustas taib soce pour moi tout les lutteurs doivent aide lac 2

  • @abdoukarimndaw-jo7hx
    @abdoukarimndaw-jo7hx 20 днів тому

    kii mom dou nitt bilahi pape sarr mom

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 21 день тому +2

    😢😢😢

  • @courtoisgueye3419
    @courtoisgueye3419 21 день тому +3

    Pape sarr nékal nitt

  • @xamsawarefe9133
    @xamsawarefe9133 21 день тому +1

    Amoul bén wakhtan nafay léppou

  • @babacaridrissandoye9286
    @babacaridrissandoye9286 20 днів тому

    Pour que justice soit indépendante et bien appliquée au Sénégal ça sera vraiment une chose difficile. On ne souhaite le mal ou la prison à personne mais y’a certaines actes si quelqu’un le fait ça mérite bien une punition peu importe ce qu’il représente dans le pays. Y’a beaucoup de lac 2 qui arnaquent des gens et qui , toute leur vie, dupent des gens pour vivre. Comment un homme comme lui puisse être dans des salles draps comme ça ? Après les gens quémandent sa liberté et cotisent pour le faire sortir de là où il est. Bah arrêtez de défendre les fautifs et laissez la justice faire son travail c’est comme ça qu’un pays normal fonctionne sinon ces gens continueront toujours à faire du mal et profiter des innocents.

  • @oumarndao7485
    @oumarndao7485 21 день тому

    Franchement lac wéréna quoi

  • @Bildezer
    @Bildezer 21 день тому +1

    Lac 2 lambou Faye nako naxene xali saam bi faue

  • @toulessportstv7228
    @toulessportstv7228 21 день тому +2

    Deugal kinane rewmi diapalé lenma ma diapalé sama yaye demal liguey teral sa yaye niepa beuga teral senn yy beugue nga Lou yombou trop

  • @mamadoufaye3123
    @mamadoufaye3123 20 днів тому

    tandis que ya d'autres qui sont en prison à cause de 5000f

  • @mbayediop2668
    @mbayediop2668 21 день тому +1

    Bilahi ki wéroull

  • @serignembackesylla6866
    @serignembackesylla6866 21 день тому +2

    Lambou xana fayoul 😂😂

  • @Omarsane7491
    @Omarsane7491 21 день тому

    Kii vrai mbame aleu laa

  • @madoundoye2414
    @madoundoye2414 21 день тому +1

    Franc lale nga lalaquer dotoka defaty

  • @user-is7wc1uj2v
    @user-is7wc1uj2v 21 день тому +2

    Qu’il vend sa maison et paye l’argent quand tu travaille c pour t besoin

  • @AwaToure-qh6rq
    @AwaToure-qh6rq 21 день тому

    Notou kou nekk lay dall😢

  • @abdouazizseye1439
    @abdouazizseye1439 21 день тому

    Lac limou déf si lamb yeup so manoul geuné 10milions na bayi

  • @CodeDieng-rq1jq
    @CodeDieng-rq1jq 21 день тому

    Féle vére seyetanga

  • @amethgueye8598
    @amethgueye8598 21 день тому +2

    Sadio Mané kou saytané menon gaka diokh xaley yii dée sen yay di souffrir ou même gni am fèbar Dialize 😏

  • @bayemodoufalldiop6816
    @bayemodoufalldiop6816 21 день тому +1

    Mbeur daal do comprendre Ioe bo beuré sa xaliss Ioe RK yaakoy lékk AK say Serigne supporter yi guena sonou dounioussi aam daraa..NGA am blèm xaliss wara dieul sa xaliss binga liguëy fay dokko déf nitt yi nioy cotisé dilaa faaayal...mbeur nékh na Dhë

  • @babacargueye3537
    @babacargueye3537 21 день тому +1

    Lambou ji dokhoule nake

  • @mamadoudiop1105
    @mamadoudiop1105 21 день тому

    Ki werul dof degg la

  • @IbrahimSarr-ts9wn
    @IbrahimSarr-ts9wn 21 день тому

    Wa li emision 😂

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye 21 день тому

    Pape sarr dagua barri wack bayil fèn 😕 franc défoula dara et puis eumo séne déla baye 😢

  • @ibrahimadiop8944
    @ibrahimadiop8944 21 день тому

    Pape Sarr wadjii vraiment dafma il parle comme s'il était au coeur des évènements il parle trop ce mec nitt dayyy aam retenue un peuu

  • @ousseynoudieye1431
    @ousseynoudieye1431 21 день тому

    Wah ki limou wakh si franc niaw na deh li nan lako nit di wakhé si moromou nitam

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc 21 день тому

    Bou féké lakk takoussi nako yalla meytou boussi také na yone défe ligeyam mane droit la diang motakh je suis pas dans les sentiments yone rk

    • @Concept0208
      @Concept0208 20 днів тому

      Ziar frère. Souko yone téyé donc amnañ ay preuves palpables comme si mo nékone le garant. Police dou dieuli Lac ci plainte ak wax bou amoul preuves.
      Dama yakarné Ils se sentaient delaisser, pour dire Lac dalén ignoré mo tax mou yég fi.
      Sou ci amé part de responsabilité meunome nalén wo waxtane ak ñiom dioxlén dara di daxaneté ak ñom bamou matt kone douñou yégg fi.
      Gayiy yobou touki 99% yi amouñiu assurance deuñouy weur programme ba dal ci rek. En plus contexte bi nga xamné RV depot Visa yi dañ koy diay ci la guëna compliqué.
      Mais li dinako diangal lou bari ci Adouna.

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 20 днів тому +1

      @@Concept0208 ziar mon frère! je suis parfaitement d'accord avec toi personnellement lolu la geume en aucun waroul wone nangou doug ou bien participé de prés ou de loin si deal bi dafa nélaw trop franchement et yagi wakh dina ko servir de lesson espérons mais diga dégate un autre lutteur si genre bêtises you melni malheureusement gnoussi yéwou si gnom beuri woul c'est triste à dire mais ils sont tellement facile à manipuler surtout quand il s'agit de million. lac a surpris pas mal de gens si histoire bi gnou beuri ak personnalité bimou done incarné sa façon de communiquer gneup la bétt

    • @Concept0208
      @Concept0208 20 днів тому

      @@MilkMilo-qr5uc Effectivement,. Parfois dañouy confondre intelligence ak naiveté. Fi mou nek tayléna bopam, wadji tayléko.
      Esperons rek mou yam fi.
      Senegal mo bari ñou degueur fit. Nit dafay declaré né GP la encaissé ay bagages diambour ñew ba Aeroport di weur koumko yobeunté. Octobre ca ma arrivé nit fek ma may enbarké moumay diox yobaneté. Je me suis dis même nane lañouy def même ba acces biir Aeroport.
      Deukbi kén meunta wax lépou. Nit ñi dañi leudeum.

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 20 днів тому

      @@Concept0208 ah voilà xolal ma bobou degar fitt il faut franchement defois yow nitt ki gay conscientiser sa bopou nitt dafa wara ragal gatié bokoy lekk nékh na mais faut di xalate retombé yi mais bon li ga wakh rk menou gnou loudul gnanal ko yalla tégil ki natou yi j'ai vu son père mais j'ai de la peine pour ce dernier

    • @Concept0208
      @Concept0208 20 днів тому

      @@MilkMilo-qr5uc Li dafay dieulé Famille bi kaw. Nexoul ci xol. En plus mobilisation bi nit ñi di def Tribunal diarouko. Na dém taxaw probleme bi diex. Soutien kouñou dial dolé tethie la moko yelol.
      Nous tous on a de la peine pour lui.
      Inchaallah légui mou delouci ci ndiabotam.

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 21 день тому

    Pape sarr mom nilagne koye bayi wakh diou niaw rék😢😢😢kate nga sa ndaye yaw😢😢

  • @OmarBao-gu5qp
    @OmarBao-gu5qp 21 день тому +1

    Ki day doul rek

  • @amadouyoroseydi6246
    @amadouyoroseydi6246 18 днів тому

    Cas yi bokoul tmt soyons résonable

  • @barkhama
    @barkhama 21 день тому

    cest pas sadio mané mes cest D Sport qui a payé les 10 millions

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 21 день тому

      Sadio mbokou lac la

    • @serigneamathgueye2886
      @serigneamathgueye2886 20 днів тому

      D'après toi D Sport appartient à qui ? Ne me dit pas diouf dé.

    • @barkhama
      @barkhama 20 днів тому

      @@serigneamathgueye2886 D-Sport Apartien a Bacary cissé et le papa de lac 2 et bacary cissé aye mak ak Rak lagnou voilla mes mane nékouma fi di wakh louma woroule ngamaye wakh aye diouf 😂

  • @adviseragnam7050
    @adviseragnam7050 20 днів тому

    Sadio na rien fais fek news leu

  • @leuz.patriote
    @leuz.patriote 21 день тому

    Franc nak yako tek sa bop 😂 ya toudou touram kon nak losi gobè garko togne bakhoul😂

  • @malickndiaye3835
    @malickndiaye3835 21 день тому +1

    Lambe mome ware nane ko khoulate spor bou tolou ni kou ame problème kene doula takhawou

    • @madoundoye2414
      @madoundoye2414 21 день тому

      Takhawou wessouwoul linga guis frere

    • @malickndiaye3835
      @malickndiaye3835 21 день тому

      @@madoundoye2414 lane moy takhawou li

    • @madoundoye2414
      @madoundoye2414 20 днів тому

      @@malickndiaye3835 mes lane nga beug guayi nioungi def louniou Mane problème bi yomboul dh

    • @malickndiaye3835
      @malickndiaye3835 20 днів тому

      @@madoundoye2414 dafa mele ni giso lima binde dé wa lambe la wakh senesé khalise bimouy dague mbuer yi loumi diarigne khana kou ame problème niou warko thi dimbali ak wa lambe yep

  • @omarlowe3879
    @omarlowe3879 21 день тому

    Kii mom doff la rek 😂😂😂

  • @ybed6113
    @ybed6113 20 днів тому

    Non sénégalais aime relater fakes News quoi aucun site srx n’essaye de vérifier l’info si elle est vrai ou pas Sadio n’a jamais donné 10millions DS sport moo diokhé 10millions en plus dagnou kooo leball Lac de gueire et il poursuivit pour un montant de 19millions et klks

  • @senegal559
    @senegal559 21 день тому

    Kii dafa dof wakh dof rék lay wakh

  • @Concept0208
    @Concept0208 21 день тому +1

    Lac dafa warone deboursé xaliss diox boy yi. Soulén di avance mou defko, wala wax djou nex sam credibilitém même souy perte.
    Touki kou ci nék intermediaire moy danga taylé sa bopou. Lo meunoul dieul say reaponsabilité personellement boul ci engagéwou. La police à toutes les preuves pour l'incriminer.
    Yalnako Yalla delo ci ci ndiabotam🙏🏿

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 21 день тому

      Ndeysann mes xam na lim si takoul motakh mou bania diokhé nkh soudone mo encaisse xalis bi kon dou ègeu fi . Xolal xaritam bobou daw na bayikok thiow li

    • @Concept0208
      @Concept0208 20 днів тому +1

      @@leuz.patriote Souko Police téyé donc day wané mom mo nékone le garant entre les deux Parties. Yakarouma Police baséwou ci ay wax késsé. Ñiko portrait plainte daño wara am ay preuves.
      Lac sou féké mo tax ñou diox wadji sén khaliss donc loulén ci méti moko warone safara.

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 20 днів тому

      @@Concept0208 motakh jenr yi diaroul garanti ki takhon mou nangou garanti tmt kokou deg na da Daw nn metina nak wadji encaisè xaliss bi daw bayi fi thiow li lac fetèwoko nn doyna war

    • @Concept0208
      @Concept0208 20 днів тому

      @@leuz.patriote Na denoncé les personnes impliquées même bouñou dawé dinañou ñibi. Dina guëna allégé le Probleme.
      Bounou nangou kouko utilisé via son nom. Xaliss day diex ngor dess.
      Li diangatt la ci mom

  • @Omarsane7491
    @Omarsane7491 21 день тому

    Franc dina dohane sen leufeul ney domerame laa

  • @ndiayebathie-rf7fh
    @ndiayebathie-rf7fh 21 день тому

    Pape Sarr yaw sa papa dagne ko diap thi diabarou diambour

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 21 день тому

    😅😅😅pape dof miguini pape dofou pikine bi😅😅😅

  • @assanewade6616
    @assanewade6616 21 день тому

    𝐊𝐢 𝐧𝐚𝐤 𝐰𝐚𝐱 𝐝𝐞𝐠𝐮𝐞 𝐲𝐚𝐥𝐥𝐚 𝐰𝐞𝐫𝐨𝐮𝐥