Bilahi taw moy donou baye 😢je pense tout les thiatanecoune doivent le suivre ! C’est que Sénégal mo doywar khaliss bi Sokhna aida yor motakh niou bari goré di top matériel rekkk personnes ne respecte la hiérarchie des choses ! Surtout quand y’a de l’argent qui rentre en jeu
@@Lopios-g6l mais yow Ku wakh yow ..yallah AK yonnete bi bu la nekhou le ya am problème diapale sa Serigne ma diapp yallah AK yonnete bi Sénégal mo nekh Quoi
Soxna Aïda Dall amna Xalisss Téyiit Serigne Bethio Mokoné Yaye Mane May Yaw 😁😁Ndigeul lii moy guéne top thia Guinawam Ndakh Serign bi di Kilifam Serigne Bethio Di sen kilifa tmit Topo léne Ay wakham ✅
Conférence islamique ou tu n'en jamais de Allah ni de son prophète sws mais Serigne néna ou la na Serigne mo sunu yakar adouna AK alikhira li dou dine Serigne Touba santaleoul li
Yaw xamo magal dh li dou discours li ak thiante la gou nite di wax moromam Ndax yalla moni koudoul sante nite dou sante yalla tee magal gui leep ak thiante la
@@ousmanethioune5478 soit véridique c'est pas de l'islam ça discours bo doul yallah néna walla.yonnete bi néna il y a un problème mais vous faite pas exprès vous suivez sans savoir
Non ils ne se réveilleront pas car ils aiment qu'on les endorment pour ne pas sentir le temps passé. Peuple de d'aveugles,de sourds et de cœur castrés.
Yaw niit gua nji di diabotou kou teurbiyou serignam ba lak gueureumam niouy contuné sén yonou wadiour diko rafétal guanan réveillez vous yaw ya yéwogoul balégui am talibé mo woor
J'adoooore Sokhna Fatim Thioune 💓💓💓💓 Elle a un franc parler incroyable...
Yalna ngua guoude FANE yala bou gnou sédeulé dara thi sa guanaaw 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Bayilen sokhna Aida Diallo bou Serign Bethio si jaam. Kokou mom ken meuneuyoul Ko dara.
hummm soxna aida Diallo ndanan leu . Deug dou nex. Mou ride dieuff
Machahala kadouyi rafetena yalla nalene yalla defale diame ak soutoura sou Barri amine
Machalah thioune donou nga sa baye bo meleni wathie nga gueuneu yag gueuneu weer rek
Machalah wakh dji raféte na Lole yalla na diame yague si yène
Machallah yalla na sen barkee baye daal si sen kaaw lafale leen thiate dakh seytanee si barkee Seydina Mouhamed psl 🤲
Machala thioune yonou serigne touba wi douye thiahanedé ake koudjé dohale sadokhe
C'est beau de parler du bien a ses proches pas de jealousie, wolof, dit sou niit baxén ndax mbok yi ko wax.
Vraiment merci
Bilahi taw moy donou baye 😢je pense tout les thiatanecoune doivent le suivre ! C’est que Sénégal mo doywar khaliss bi Sokhna aida yor motakh niou bari goré di top matériel rekkk personnes ne respecte la hiérarchie des choses ! Surtout quand y’a de l’argent qui rentre en jeu
Allahou rék ak seydina Mohamad téy ak euleuk moy bou woor bi
Kon loy woutt fii
Tai Mouy DEUG
C émouvant machalla l union fait la force
Yallana lèn yalla samou bou bakh machalla
Kenneu dou Aida Diallo moy khoromm si dee
Waw j'ai pleure de joie walahi
Dieureudieuf ❤Thioune Sérigne Sal rek
Machalla longue vie à vous
Mouride ndigal dalll yalla nala yalla diapaler si yene bi Serigne saliou thioune
Machalah long vie à vous ❤ ❤
Machallah mane ma begueu serigne saliou thioune bou wéera wéer
Machallah yalla na yalla yagual takhaway bi❤
Hoo kadou rafétna Macha alla thioune dieureudieuf
C'est vrai quelqu'un de très simple je l'ai rencontré a l'aéroport Blaise Diagne on n'a pris même avion vraiment longue vie à vous
Mashalakh Mashalakh Mashalakh
Soxna Fátim Thioro taaw bi wakh gua lou reuy ta raféte lii moy takhawayou taaw bou gueun si keur wadjouram Thioune kou téd gua
Machalah rafétna
Bouleen si dara dieulé thioune mame bambi yallna yalla goudeul seeni fane te weral leen
Wakhleine si magal bi mo geune ligueini wakh ni reik barki serigne saliou les jeune réveiller vous
Tiakhane rek tiakhane rek Yala nalen diegal té baléne
S saliou point longues vie maman
Machallah fatum thione demba bilay sa khôl dafa raféte
Maachaalah thioune
Hé les familles Sénégalaises nañouy wakhalanté lou bakh. Li rafett naa
Machallah Machallah walay anzim dawna yaram
Machallah c est emouvant
Mais li com nguente' !!! Diamou len yallah svp .
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Merci
❤❤❤❤je suis très content thioune
Diamu djilen yalla te bayi s'en thiakhan yiii guen neké
Kaddu yi raféte na machallah
Senegal nekh na 😂😂😂😂😂😂Lou waay nekh wakh demlen jamou ji yalla yen yi nakh sa khel laa yalla nañou yalla guindy
On voit ça qu'au Sénégal t'entend pas Allah ni yonnete bi
au champ de cours avec Serigne Moustapha sy on l'entend
Walahi s'en talibé yi kom niou amoul khel
@@killahndiaye3838 amuñu khel kon nga bayi ñu ak suñu ñak khel
Ya rambathe diapal fii guaa diape téé maygnou diam..
@@Lopios-g6l mais yow Ku wakh yow ..yallah AK yonnete bi bu la nekhou le ya am problème diapale sa Serigne ma diapp yallah AK yonnete bi Sénégal mo nekh Quoi
Masha Allah kadou yi rafete neuh
Soxna Aïda Dall amna Xalisss Téyiit Serigne Bethio Mokoné Yaye Mane May Yaw 😁😁Ndigeul lii moy guéne top thia Guinawam Ndakh Serign bi di Kilifam Serigne Bethio Di sen kilifa tmit Topo léne Ay wakham ✅
Sou woté rek mom aida diallo niou ndakare ndayame bou bakh ak gnimou andale linguéne Di déf yamaléléne ko médinatou salam
MACHALLAH ndeysaane
Dieuredieuf Serigne saliou ndiguel
rewmi rewmi ana ndiagaler seydina mohamed dou li
Tres émouvant venant du soeur
Oh bilahi famille d amour mon nékh
Machallah wakhh dji Rafiettena trop
Do geureum Aïda Diallo 🤣🤣
😄😄😄
@@yousratoure6178 damay roubé 🤣
Machalah
affaire yi comme aye ndayale
Machala mane thione zéro comme elle dit nit bou bakh am kersa ak soutoura. Yalla nala yalla fey sa khol.
Yèn wa seneweb louguèn di toudé Sokhna Aïda thi lii yèn ay diakhassékat nguén vraiment
Lo kham thie nafekh
Li dh ci khol la diougè yalna yalla yokou dimedj
Bravo
l'union fait la force
mais bon le changement arrive avec les VIP/SD pour un Sénégal prospère
Serigne saliou thioun way 😅 manguikay geuna beug way😅😭
Mai fi diné la wala khawarée thiey yalla
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Li ndayalé leuh
Amine waye ♥️♥️♥️♥️♥️
Bayilene dinée dji nguene di fohei
Sa bay moko fohei
@@babacarsenghor4053 nekal nitt
Conférence islamique ou tu n'en jamais de Allah ni de son prophète sws mais Serigne néna ou la na Serigne mo sunu yakar adouna AK alikhira li dou dine Serigne Touba santaleoul li
Mère fatime yakk dieuke. Machallah moguene famille mythomane.
Machalah mbok dafa neh
Merci
C koi ça encore.. des famille qui s'enrichissent sur le dos des ignorant 🙄..
Magal du ay discours
Yaw xamo magal dh li dou discours li ak thiante la gou nite di wax moromam
Ndax yalla moni koudoul sante nite dou sante yalla tee magal gui leep ak thiante la
@@ousmanethioune5478 soit véridique c'est pas de l'islam ça discours bo doul yallah néna walla.yonnete bi néna il y a un problème mais vous faite pas exprès vous suivez sans savoir
Ousmane Thioune lou len arrengè reck ngènj wakh.. loussiy yonou diciple yi ..
@@ousmanethioune5478 c’est quoi un thiante a quoi ça sert
@@TheBandafall2003 demal nga guestu dji
Machallah wakh bi rafetna
Yow yaye mak teh ya tass family sa papa.
Machalah li rafetna nit mokame
Sokhna aida Diallo rék inchallah
Boulen gnou sonal guen melni kou nekk si guenté li dou diné wayy
Kou Serigne touba takhawou diaroul sonou ndam rk
Sokhna aida❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah domu bay da nekhe loll
MACHALA machala
Machalla li rafétna
Business magal yewoulen jeunesse bi🤔🤔🤔
Mdr yawe de yagui mere dé
@@falloukane3177 nekal nitt khôl bakham
Copin nanal asipe way yen danguena nekh nokoul feulé sokhla wougnou Say conseil 😂😂
@@aloubeby2235 yaw dof gua 🤮🤮🤮🤮
@@alleualleu693 yaw nokoul feulé yaw mbam nga sen khol yi gnoy xasane rek té nguen nopal sén bope
S’en discours yeup defanter leu, soxna aida Diallo amoul morom ci cheikh bethio.
Li Sante yalla la Wala garouwale ..
Ragal l'en yalla te diamouko
Taye fi neike a✅✌️
Ta fatim thioune ❤
La cour d un monarque.liberez vous peuple
Machala ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Titre bi moy lane. Moi vraiment je veux comprendre et vous comprendre
C'EST ÇA LA RELIGION?🤔
DU GRIOTISME?DU FOLKLORE?🙊🙉
Sa baye si la bok
Yaw mi kham religion djeuleul
Respecter la mémoire de votre père éviter les garawaler
☝🏿☝🏿☝🏿☝🏿☝🏿
Konn kene d'où wakhal nit Lou baakh loumou def
Comédie rek thieye sénégal C’est du n’importe quoi
Khawma lodéfone mais dolil mané sa ndieuké keureumenala
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
😍😍😍😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️
Wakhi dof rek diamou lene yalla mo gueune folklore rek
SOKHNA AÏDA SALIOU THIOUNE YALANAFI YAGEU LOOL TA WÉR
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
C'est quelle religion ça !!?
Yewou jotna ooh les jeunes
Bilakhi
Fi déh deguoumafi kaddou talibé...Daguassanté rèk la fi guiss
Courélou guéweule rek dara yalla guissoumako
Serigne Saliou Mat gua Baye cheikh Bethio laali na fimou nék reuthiou woul litaax mu taw Lola
N'importe quoi les jeune réveiller vous svp
Mba yaw réveille nga rék
Non ils ne se réveilleront pas car ils aiment qu'on les endorment pour ne pas sentir le temps passé.
Peuple de d'aveugles,de sourds et de cœur castrés.
Mdr mais yaw loula dal je crois que yaw yewo goo en personne bay conscientiser
Yaw niit gua nji di diabotou kou teurbiyou serignam ba lak gueureumam niouy contuné sén yonou wadiour diko rafétal guanan réveillez vous yaw ya yéwogoul balégui am talibé mo woor
Surtout
Serigne boukhameoul a ak b
Ana.yalla.ana.yonentebi.ana.serigntouba
Yow bayil sa affairou aadaa yii ay tagate ay Maam. Weene tagg ngeen am moy Talibé serigne saliou
Voilà la religion sénégalaises 🤣😂😂une femme chef religieux avec ce comportement
Nakk yi Dagone ba fégne naa😂😂
Ndeyesan man cirehakim lo di talubé s abdoul hakim touba Milano
Sama xoll cèdd na ci li loll, cheikh bèthio
Yalnaque soun BROM dolie ay xeèwuell
Ya nnyaka jom