Gana Messéré: "Ce qui fait la particularité de Serigne Fallou Mbacké..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 13 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 215

  • @aramendoye2457
    @aramendoye2457 5 років тому +84

    Thieye serigne fallou sama yakare tay ak euleuk kéndou mome yalla na niou ko yalla fayal si barkéb serigne touba

    • @matarndiaye3105
      @matarndiaye3105 5 років тому +3

      mane ak yaw serigne amoul morom moy samba mi meune kanamame ak guinawam

  • @fatimafaliloulah1145
    @fatimafaliloulah1145 5 років тому +26

    Thiey Serigne Fallou Mbacké sama kharit bi kén dou mome ! Moy khewe ba fawe ! Yalla na yalla yoque leerame té tass niou ci barkéme ! Serigne Touba kén amouko nioune rek nioko ame. Dieureudief Mbacké balla

  • @syllayatma9317
    @syllayatma9317 4 роки тому +5

    Cheix Mouhammadou Fadal ♥️sma yakar tay ak euleukk yalla na sunu borom yokou Say lérr🙏🙏Balla Aïcha

  • @aidafallousall6793
    @aidafallousall6793 5 років тому +40

    Thiéye sama wadji, sama kharit bi , sama sangue bi, sama sopè bi,yakar taye ak euleuk, Mbacké balla kéne dou yaw Domi sokhna Awa Bousso dji,
    Serigne Fallou rék, kép, dongue la beugue bolé woumako ak lénéne bougama lênêne sokhla wouma lênêne , kholouma lénêne, guissouma lênéne.
    Thiéye sama wadji mala beugue awma sago ci yaw Mbacké.

  • @ndeyefatouguissembow6012
    @ndeyefatouguissembow6012 5 років тому +44

    Ay way gana meseré yalla na yalla goudal say fane bekk na torop thi liguay wakh thi sama serigne bi sama xol bi sédd na❤️❤️❤️🙈

  • @MaodoMalickNiang-qr4lr
    @MaodoMalickNiang-qr4lr Рік тому +1

    ❤ Dieureudieufé serigne fallou 🙏🏾Sam yakar

  • @abdoulayetop1615
    @abdoulayetop1615 5 років тому +14

    Yalla naniou yalla fayal serigne fallou mbacke

  • @mamediarragueye5236
    @mamediarragueye5236 3 роки тому +2

    Kenn dou serigne Fallou doko wo moukk moulay doumoyou 😭🙏🏽

  • @bambaniang9305
    @bambaniang9305 4 роки тому +2

    Mach Allah que Dieu nous protège et yalna yalla fayal niou serigne fallou mbacke

  • @falllouseck7106
    @falllouseck7106 5 років тому +8

    Sama tourondo Serigne Mouhamadoul Fadillou yalla nagnouko yalla fayalee amine🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @aissatoudiaw7860
    @aissatoudiaw7860 5 років тому +8

    Yallanala yalla defal diam ta yokk kham kham bii🙏🏽🙏🏽🙏🏽

  • @sabarasts
    @sabarasts 3 роки тому +3

    Dieuredieufé Serigne Fallou Mbacke 😍❤️ !!!

  • @diabambistesarr7350
    @diabambistesarr7350 5 років тому +20

    Serigne Fallou❤ damako bgu awma si Mom SagO

  • @mariamasow3970
    @mariamasow3970 5 років тому +74

    THIEY SAMA SERIGNE MOUHAMMAD FADAL MBACKÉ YALNA YALLA YOKE AYE LÉERAM ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @fatoudioufmouserignefallou2709
    @fatoudioufmouserignefallou2709 5 років тому +7

    Akassaaaa kokou sama way la serigne Fallou mbacké balla❤❤❤❤❤

  • @gueyemourtalla9639
    @gueyemourtalla9639 5 років тому +21

    Machallah Gana yabakh

  • @cheikhtalldioum8412
    @cheikhtalldioum8412 5 років тому +36

    Diourom niaary Serigne Fallou défar na adouna

  • @alassanefaye1059
    @alassanefaye1059 4 роки тому +1

    S gana messéré machllah yallah na yallah goudal fanyi si barkeb s touba

  • @cheikhounapro6716
    @cheikhounapro6716 5 років тому +26

    mane dama khammé rék beuguko sama khol mame boy yalna yalla yooku sa lér

  • @moustaphasow3886
    @moustaphasow3886 5 років тому +20

    Ndeyssane thiey jambarou serigne touba diou makk djaa borome ndindy akk sahm mo diêkhone takke sii serigne touba yallenaniouko yalla fayal

  • @famalo9021
    @famalo9021 5 років тому +1

    Dieurdieuf serigne fallou mbacké balla aicha yalla na yalla Yoko ay leram te tafe niou ci barke ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️ma beugeu serigne fallou mbacké

  • @fallmbegtefadilou9306
    @fallmbegtefadilou9306 5 років тому +25

    Ken du mom sama wadji je l'aime éperdument ❤️

  • @fatoundiaye7256
    @fatoundiaye7256 4 роки тому

    Machalla yalla na yalla goudeul fanwi S Fallou yalla na ylla yok ai leram té sedniou ni où sakh si beg baye karimu fallilou

  • @bayfall2658
    @bayfall2658 5 років тому +5

    Machalla kene dou s touba amoul morom ma baga s fallou mbacke

  • @falloundiaye7946
    @falloundiaye7946 5 років тому +6

    Machalla sama torandou waye keneh dou mome gana khol sedna trop machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @khadijadiouf5668
    @khadijadiouf5668 5 років тому +8

    Thiey sounou wadjiii🌹♥️😍

  • @sokhnaniang8645
    @sokhnaniang8645 5 років тому +1

    Thiey sama mame Serigne Fallou damako beugue ba beugue kouko beugue machalla borome Ndindy ki mo mane kaname mane guinawam borome n'a am mou am 👌👌👌

  • @mamadoundiaye2871
    @mamadoundiaye2871 5 років тому +1

    BOROM Na amm mou amm.aka dioubok YALLA sounou BOROM.yalla nanouko YALLA fayal yook léram taasnou si barkém . Amine

  • @poupette9544
    @poupette9544 5 років тому +5

    Machela😭😭😭❣❣❣

  • @falloufall1953
    @falloufall1953 5 років тому +6

    Machallah,♥️♥️♥️♥️

  • @mariamadiallo96
    @mariamadiallo96 5 років тому +7

    Neyessane kéne dou serigne fallou Mbacké 👏

  • @sophiediakhate141
    @sophiediakhate141 4 роки тому +2

    Machallah kene dou mame fallou ❤️

  • @aminatakeita496
    @aminatakeita496 5 років тому +22

    FALLOU awo bousso kén dou yaw
    #élémentSFALLOU lay don ba Al Janah

  • @falllouseck7106
    @falllouseck7106 5 років тому +3

    Fadilloulahi Borome Ngeunélle🙏🙏🙏🙏🙏👌👌👌👌

  • @mbayediop833
    @mbayediop833 5 років тому +5

    Machala 🎤

  • @falloundiaye144
    @falloundiaye144 5 років тому +13

    Machallah

  • @awanjaay4640
    @awanjaay4640 5 років тому +6

    Ma Sha Allah❤

  • @fatoundoyeba8904
    @fatoundoyeba8904 4 роки тому +1

    Diadieuf serigne gana Waxtan bi amna solo loll thiey sunu djambar dji serigne fallou Mbacké mako beugue yalna yalla yokou leram tasniou si barkèm

  • @rokhayadiop334
    @rokhayadiop334 5 років тому +9

    Segne gana yallana yalla fayalnioula

  • @serignemodouseck6005
    @serignemodouseck6005 5 років тому +5

    Thieye sama wadji elhadji Fallou Mbacke yalla nagnu la yalla fayale bopam

  • @astatall9786
    @astatall9786 5 років тому +1

    Thiey sama serigne sama yakari adouna ak alahira dieuredieuf serigne touba

  • @ksballa7202
    @ksballa7202 5 років тому +1

    Sama sopé sama kharite sama yakar mame fallou borom ndindi di def dindi kou reer mou nguindi yalla na yokou leram te tass niou si barckém amine

  • @ouseynouthiam8925
    @ouseynouthiam8925 5 років тому +1

    Macha allah way serigne gana messere

  • @beuguefallou4212
    @beuguefallou4212 5 років тому +12

    Thiey sama yakkar tay ak euleuk fokko woo mbacke balla mou wuoyoula

  • @papjobe1872
    @papjobe1872 4 роки тому

    Yhieye sounou wadji yalla na niuo ko yalla fayi la mala begue bilahi mbacke balla amoul mourom dieureudieurfe serigne fallou ❤❤❤❤❤❤❤🤲🤲

  • @mbenediop3201
    @mbenediop3201 4 роки тому

    Thieye Serigne fallou mbacké yalnaniouko yalla fayal

  • @papamormbaye7508
    @papamormbaye7508 5 років тому +7

    Mame❤

  • @ousseynoukane8854
    @ousseynoukane8854 3 роки тому

    Kenn dou mom Sama yakar Sama lepp🤗🌷💖💖💖💖💖💖💖

  • @piscoaladin4968
    @piscoaladin4968 5 років тому

    Thiofél bima am ci Serigne Fallou daa melni guédj, taank taxouko diékh téé lolou depuis touutt tank❤ Thiey Aladji Fallilou mbacké

  • @serignefallouhane3914
    @serignefallouhane3914 5 років тому +8

    Jëreujeuf srg Fallou Mbacké

    • @mbenediop3201
      @mbenediop3201 4 роки тому

      MachAlla guana liguéye wakh thi Serigne fallou nekh na lol machalla

  • @himadaff1876
    @himadaff1876 4 роки тому

    Ken dou Serigne fallou❤️❤️❤️❤️❤️

  • @manekhady5178
    @manekhady5178 5 років тому +1

    Machallah serigne fallou

  • @saerfallgmail.c0mmbayene453
    @saerfallgmail.c0mmbayene453 5 років тому +1

    Dieureudieuf s ganna

  • @youssoufbarry9754
    @youssoufbarry9754 5 років тому +1

    Dieuredieufé serigne fallou mbacké

  • @amethniang2442
    @amethniang2442 5 років тому

    Wadiall 18safar 2020 inchala niou feikei ko yalla nako yalla defff

  • @mariendiaye3347
    @mariendiaye3347 2 роки тому

    Dieureudieufati serigne fallou mbacké sama yakhar ❤❤bo gawoul rek dîna metti

  • @sodadiakhate5045
    @sodadiakhate5045 5 років тому +2

    Machalah😍😍

  • @x2dvision116
    @x2dvision116 4 роки тому +3

    Niougui woo niepp sackou niou ande ligueyall Serigne fallou fondation sope Serigne fallou

  • @arameseck7521
    @arameseck7521 4 роки тому

    Ooooh gana yangi wakh si ko khamni nimou mél si sama kholbii❤yalla rekk lakoy sédél...maneuh dama beugue serigne fallou tei yalla rekk takh😢

  • @ismailafaye5288
    @ismailafaye5288 4 роки тому

    DIEUREDIEUFÉ Serigne fallou Mbacké

  • @fatoudiakhate491
    @fatoudiakhate491 4 роки тому

    MACHALLA sama xol sédena torop

  • @tinealiou4039
    @tinealiou4039 5 років тому +6

    Diarradiefaty s.fallou machahala

  • @khalyball3758
    @khalyball3758 Рік тому

    Allahou Akbar 👏 serigniou serignesi 👃

  • @cheikhndack4237
    @cheikhndack4237 5 років тому +11

    Dierediefeti diambari Serigne touba yi wayé s gana tamit kéndou yaw yagufi té wérr

  • @ismaelndiaye751
    @ismaelndiaye751 5 років тому +1

    machallah s gana❤🙏

  • @gninguediarra3131
    @gninguediarra3131 5 років тому +1

    Bilay Gana mèsèrè kendou Sama Serigne bi Gallas bayou mbène sama khol lako def

  • @fatouthiam4407
    @fatouthiam4407 3 роки тому

    S.falou salam lép ❤❤

  • @ndeyeniane2556
    @ndeyeniane2556 5 років тому +2

    😭😭😭serigne Fallou sama sangue bi

  • @seynaboudiop8126
    @seynaboudiop8126 Рік тому

    Machaalla Alkhamdoulila ❤️❤️❤️

  • @khadimgueye3124
    @khadimgueye3124 5 років тому +6

    Dieuradieufati s fallou mb

  • @fatoudiop6487
    @fatoudiop6487 4 роки тому

    Thiaye bayou Mbéne Aka Ma ko Beugue ci sama khol 😍😍😍

  • @cheikhtall8828
    @cheikhtall8828 5 років тому +9

    ❤️❤️

  • @dalldall549
    @dalldall549 5 років тому +6

    Sama wadia 😢ch fallilou Mbackè

  • @amadoubagueye947
    @amadoubagueye947 5 років тому +1

    Thiey serigne fallou. Moy lep

  • @khadydiallo7233
    @khadydiallo7233 3 роки тому

    Serigne fallou dieureudieuf ❤️

  • @madickendiaye3244
    @madickendiaye3244 4 роки тому

    Dieurédieufé serigne fallou

  • @fallousene2181
    @fallousene2181 5 років тому +16

    They sama toura ndo kenela

  • @youssoudrame2756
    @youssoudrame2756 4 роки тому

    Dieureudieuf serigne gana

  • @maramedrame8167
    @maramedrame8167 4 роки тому

    Manchallah amena solo

  • @AwamouSerigneFallouThiam
    @AwamouSerigneFallouThiam Рік тому

    Ndaysan man dama beug Serigne Fallou bagua xamné kou KO beug sakh wala gua toudou ko damalay beug te sama khôl bi day sed lool bilahi,yalna y'Allah yok Ay leram te khir gniou thi beug Serigne Fallou ba bamay saguo Souf🤲💓

  • @sokhnagaye9286
    @sokhnagaye9286 5 років тому

    MACHALAH DIEUREDIEUF SERIGNE GANNA WAKHTAN BI AMNA SOLO BOROM TOUBA AMOUL MOROM KENLA

  • @falloujoop4742
    @falloujoop4742 4 роки тому

    Jeureujeuf serigne fallou

  • @ElTIO_Galass
    @ElTIO_Galass 5 років тому +5

    Sama tourando bii Cheikh mohhamdou fadal mbacke mbacke Ken dou mom walahii

  • @falilloubasse5234
    @falilloubasse5234 5 років тому +1

    Thiey serigne Touba

  • @adamambodji5368
    @adamambodji5368 5 років тому +2

    Sama sope mako begue machalah

  • @bambatouba6884
    @bambatouba6884 5 років тому +2

    Thieye Ken dou S.Fallou

  • @metahgueye6233
    @metahgueye6233 5 років тому

    Machallah Serigne Fallou Mbacke

  • @aminatabathily6139
    @aminatabathily6139 4 роки тому

    Kedou serigne Fallou dieuredieuf serigne Fallou dieuredieuf serigne Fallou dieuredieuf

  • @ogwayd3765
    @ogwayd3765 5 років тому +4

    Jeureujeuf sëgn ganna amatina solo

  • @falloudiop180
    @falloudiop180 5 років тому +1

    Yalla nanin ko yalla fayal

  • @kinebeguefallou
    @kinebeguefallou 5 років тому

    Mame fallou sama yakar adouna ak alakhira yalla nagnou serigne bamba tass si barkém

  • @bourydiattaa229
    @bourydiattaa229 4 роки тому

    Aka mako begue💓 mom serigne fallou awma si mom sago😭😭😭😭

  • @ndeyebeuguefalloumbacke9089
    @ndeyebeuguefalloumbacke9089 4 роки тому

    Dieuredieufffff serigne fallou

  • @layediop5234
    @layediop5234 5 років тому

    waw kendou mome serigne fallou sama yakar bilahi

  • @ndeyediopba567
    @ndeyediopba567 5 років тому +1

    Mame fallou ma force

  • @cheikhndiaye5143
    @cheikhndiaye5143 5 років тому +13

    Thiay s touba ken khamoul loum don

  • @layedia414
    @layedia414 5 років тому +1

    Akassa mame fallou brome na am mou am si ❤️ sokhna awa bousso sama tourado bobou

  • @mbayelo3022
    @mbayelo3022 5 років тому +4

    Máchallah

  • @princessebellandiaye4730
    @princessebellandiaye4730 5 років тому +4

    Beugu na tawlo dom bou goor toudé ko Mame fallou Mbacke.. nianal lénma

  • @souleymanediop5014
    @souleymanediop5014 4 роки тому

    Euskeuy machallah gana mesere khôl Saïd na lol.ken dou mam fallou mbacke borom na am mou am mbacke dieureudieuf Serigne touba amoul morom mbacke