Ama Baldé avait raison quand il disait de Balla Gaye le mal faiteur c'est une vraie vérité si l'homme s'entraîne comme il le faut ses adversaires sont en danger car il fin lutteur et bagarreur
Jareujeuf Baol baol yi ..Nieuw ngèn en masse si Stade bi jènd billet you chère supporter Tapha tine ngir dollèl ko ❤..mais Jamm ak pèkhèm yalla ak dogalaam... Vraiment, content na si wa Baol ñii ❤
A 40:45, on voit Tapha Tine essayer de remettre en place son auriculaire qui semble cassé. Cela le gênera tout le reste du combat. Très très beau spectacle et très belles images ! Merci pour ce beau film ;)
Ama Baldé avait raison quand il disait de Balla Gaye le mal faiteur c'est une vraie vérité si l'homme s'entraîne comme il le faut ses adversaires sont en danger car il fin lutteur et bagarreur
Jareujeuf Baol baol yi ..Nieuw ngèn en masse si Stade bi jènd billet you chère supporter Tapha tine ngir dollèl ko ❤..mais Jamm ak pèkhèm yalla ak dogalaam...
Vraiment, content na si wa Baol ñii ❤
Dougousi Balla gaye AK sa thiess dawna yarame❤
Supporters balla yii Gno gorée ❤. C le meilleur c l incontestable
Beau geste de jacob Baldè li moy lamb ❤
Mashallah balla yalnaga nekaaat roi inshallah
Amine❤
Empereur déf gua lép ms roi laniou sokhla wat té dina ame inchallah 💪❤️
Merci Boucar Ndour ❤❤❤
Ohh le touss be Balla Gueye ki dou nitt 😂❤❤
❤❤❤❤ohhh ndéyssan kén dou Balla Gaye sama mbeur mi ❤❤❤❤ c'est le meilleur bilahi ❤❤❤❤❤
LA FILLE EN BLEU AU DEPUIS DU FILM🤣😅🤣🤣😂 Bari ngua thiaathie Mashallah nice style.. Yeaaah
Sofna 😂melni ku yagu usa 😂😂😂😂😂the thies sax meus fa dem
😂😂😂😂mouy wane aye rrrr ni li motax iran dilen wakh séne mousiba
@@rassoul2294 😂😂🤣🤣😂😂
@@rassoul2294 😂🤣🤣🤣🤣🤣grave Comme KOUY life USA
Dama fogone ni kaw la naike
Bonjour tu es le meilleur champion moi et toi pour toujours
Mashallah excellent travail ❤
Yalla nako yalla defal si li dess si carrière bi lep ay victoire si barki seydina Mohamed
Lutte TV rék laniouy topou ❤❤❤❤❤
A 40:45, on voit Tapha Tine essayer de remettre en place son auriculaire qui semble cassé. Cela le gênera tout le reste du combat. Très très beau spectacle et très belles images !
Merci pour ce beau film ;)
sisi dafa dameu
très bon documentaire mé la prochaine fois bo lén wagné son bi si souf dina bakh trop
Maye léne niou toussou zambala stp 🙏🙏
Félicitations à toute l'équipe de la réalisation Good job 🎥🎞📽📸👌
Balla gaye 2❤❤❤
Lutte tv si kaw
Boucar est trés intelligent et plein d’expérience.
Good job brother Boucar ❤❤
Lutte TV télé bou mak bi kéne dou mome wallahi
Wa Lutte tv sene vidéo daye lerr
Bilay 😊
Femmes bi nieuw première sa niari mbeur deh daan nagniou mais niang ballo bou sanioon balla gaye dou am ndam mais yalla nopina
Tapha Tine baram bou ndaw bi da dameu dhh ça se voit bien ndeysann lamb metina
Mai’s où es thiatou Daouda fall 😂
Tapha tine niew di dioye gnibi di dioye 😂😂😂😂😂
Donitt😂
😂😂😂😂tapha tone balla gaye daka niousse
BALLA BIMOUY TOUSS TAKKUL NGUIMB. NICE MBEUR YI BAYILEN TAKKUBI NDAKH FOU KOURPAGNE YI TAKARNASSI NGUEN DINDI SANNI🤣🤣🤣🤣.
Balla ama 😂❤😂
Ama mome ladone dagal nonu ??😂😂
Tapha ❤❤❤❤
25:13 AMA CON NA😂😂😂😂
😂😂
Ok donc stad bii halé you djigéne yifi doug yeup c’est leur 1er fw 😅😅😅 nn sénégal mo dahe thi adouna bii😂😂😂
Tapha tine Andi woul dra djoungu bi sakh dagay forcé 😂
Rafetna
Dafa mèlni baramou tafa bi dafa damou si biir beurè wala?
Ces com
40:09😂🎉🎉🎉🎉
Mêmes yékini balla daka niousse 2fois même ngone bii bg2 Ama Jacob
Mamadou Diop mo guene ay albourakh
❤
Bocar❤❤❤❤❤❤❤
TAPHA A ENCAISSE 32 COUPS PUTAIN
Dafa takke lokho Tapha tine yiii
Eumeu Sène Khana Dafa takon lokhom yi tamit😂
Khana Eumeu aussi dafa takon ayii Lokhom tamitt, soyons sportifs
@@laminendiaye7881Tei lima diahal danio dann Eumeu
Dièye wayyyy 😂😂😂😂😂
Yéyé bi mome kane la
Takke lokho Tapha tine yiii motakhe gnou dane ko lii dou ndamme takkale ma lokho yii si non mou réye ko
Tu es un mauvais perdent reck😊
@@Maxkekendokhamna fans modou lo la
Balla Gaye daal pour ioe amoul mérite ??
Bimiy dane Modou lo tmt dafa takone loxo yi
Yaw damay dakhar sa ndaye khana kone modou Lo dafa tak ama ak boy niang
MAAD
ZAMBALa Comme niangou faramaren🤣🤣😂😂🤣 meme tete
𝐝𝐚 𝐭𝐚𝐥𝐨𝐮𝐥 𝐰𝐚𝐭𝐨𝐮 𝐜𝐨𝐦𝐛𝐚𝐭 𝐛𝐢 𝐦𝐨 𝐝𝐞𝐦𝐞 𝐧𝐨𝐧𝐨𝐮 𝐳𝐚𝐦 𝐜𝐨𝐛𝐚 𝐥𝐚 𝐝𝐞𝐡 𝐠𝐮𝐢𝐬𝐨 𝐨𝐫𝐝𝐢 𝐭𝐦𝐭😂😂
@@siteu_n77 🤣🤣🤣🤣
Lii mom dafa niaw Balla goudii yii koumou tei woul si galadj doula dane Tapha dafa deim bay feugue ay lokhom si podjam
Mou tay deh
@@boromegawanembacke-kw4ux kane mola nday ladj
Kon eumeu dafa tiéwon ay lokho yii tamite
gueemou mani daf ko takk deh mais tapha baram bi dafa dameu khol lene 40mn 40seconde bi
Xana faniouko xalis
DIOP2 SEUL