Gris 2 vs Franc combat leu Quench vs Gouy Gui Talfa vs Mbaye Tine Mod Dia vs Ambulance Domou Dangou vs Diam Terry Liss Ndiago vs Anaconda Madji Madji 2 vs Diokel ( combat Tolof tolof )
En tout cas Maodo (Gris2) c'est vrai yaay souniou Serigne gnoune gneup 😂 Macha Allah ndakh yarou nga séleu nga mais nak on aimerait te voir descendre dans l'arène teukeunté comme le fait franc même s'il en fait trop, reug reug et autres pour nga meune nék au challenge et au diapason bala gnoulay raw ngay khaar génération suivante bi. Teunkeunté ci Lamb la bokou et ça nous amuse beaucoup. Yâ Allah mayla combat ko dadjél koudoul Ama Baldé Yalla nga daan ❣️
@@mouhameddia5168 beugue lou noye rekk mounane gouye gui... franc lou yombe la beugue... forza ancien la.. tayzon 2 ancien la.. na beuré ak gris 2 moromame.. gris 2 benneuh defaite la ame tei reug kéisséi mooko daane... franc bs gris 2 moye combat bi
Logique lucide et véridique
Grand respect à toi gris 2
Un vrai combattant champion mbeur bou yarou kadu yi rafett na
Gris 2 kou ame yarou islam la que dieu te garde
Le grand champion lolou mome malakoye sédél bilay medina sougnoufi lathié aide pour kou fébar yay nieuke diokhé bilay
Whaou il exprime bien 🎉
C'est la première fois que je te vois, mais j'ai j'ai une admiration pour toi frère., walyoul lahi.. Allah te protège encore plus,
Gris 2 vs Franc combat leu
Quench vs Gouy Gui
Talfa vs Mbaye Tine
Mod Dia vs Ambulance
Domou Dangou vs Diam Terry
Liss Ndiago vs Anaconda
Madji Madji 2 vs Diokel ( combat Tolof tolof )
En tout cas Maodo (Gris2) c'est vrai yaay souniou Serigne gnoune gneup 😂 Macha Allah ndakh yarou nga séleu nga mais nak on aimerait te voir descendre dans l'arène teukeunté comme le fait franc même s'il en fait trop, reug reug et autres pour nga meune nék au challenge et au diapason bala gnoulay raw ngay khaar génération suivante bi. Teunkeunté ci Lamb la bokou et ça nous amuse beaucoup. Yâ Allah mayla combat ko dadjél koudoul Ama Baldé Yalla nga daan ❣️
Gayi gnamewounioukoo
Ken rawoukoo
Tu es mon premier luteur que je supporte
Machallah gris 2respect à toi beur bouguena yarou thi beur yalla nala yalla defal jam
Machalah gris tu as bien parlé sa combat ak franc moye combat
Franc gris2 combat logique
Dane forza di beurék gris 2 tamit moye lohlou deh dieul gouy gui mo gueune
@@mouhameddia5168 beugue lou noye rekk mounane gouye gui... franc lou yombe la beugue... forza ancien la.. tayzon 2 ancien la.. na beuré ak gris 2 moromame.. gris 2 benneuh defaite la ame tei reug kéisséi mooko daane... franc bs gris 2 moye combat bi
C'est le combat que tout le monde attend 😂 mais franc s'entête sur RG RG 😂 SCORE 13-1
@@ramzydiallo2166 gris2 yomboul na dieull gouy gui rek senegal déme kanam
@@Justin-Lo. Mais Lutte simple akk lutte avec Frappe bokkoul.... Reug mossoul beuré ak Franc lutte avec Frappe té lolou moyy combat biu logique bi !!
Il a raison nak certains lutteurs ont peur de lui
Merci beaucoup deug rék ngafi wakh ....
Merci beaucoup Gris
Ma sh Allah dina bax bilahi vidéo dama ko weur ba sonne
Li gua wah si mbokk ✅✅✅✅
Bilai ki damako beug ❤❤❤❤
Gris 2 ordinateur combat de l année
Gris 2 nitt kou gom yalla lla te kham adouna Bly dema ka fan
Yalla Na Yalla Barkell la Barké Werou Safar bi
c'est le vrais combat franc gris 2 quench gouy gui
Yw nakk bakh nga yarou nga ms franc mola geuneu saf si lamb dh😂😂😂
Gris warna am Combat nak déy khékh déy beuré billay . Mbeur denioukoy daw rek . Mais Franc mo yor buzz bi nak 😂😂Ndiago bi déy liguèy
il communique très bien yalla nga am combat çi barki seydina mouhamed
Champion gua❤
Talpha Tony junior 🔥
Talpha Tony junior 🔥
Talpha Tony junior 🔥
Talpha Tony junior 🔥
Faran ❤❤❤❤💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
Franc tayi defa ndaye yabate Gris Bordeaux sa papa 🧑 la
bilahi franc mo meu 17 gris 2
Guouy gui dall gayi defou niou ko mbeur😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂 bly bakho
Gris 2 graisse bou beuri mola dougueul thi lamb wayé amo Xam xam amo daray lamb franc mo meune wa fasse yeupe
Dél mbapate outi khaliss
Bilakhi yénne niarr combat la
sama Mbeur ❤❤❤❤
Ponkal bu am xeil si Iow lako guussei gris 2
No gris dou dem gayii dagni daw 😅😅😅😂😂😂
Franchement gris 2 a raison je ne sais pas pourquoi les lutteurs de sa génération l'évitent
Franc dafa daneu lieutenant Gris 2 moko raw 😊
@@talladiagne8092moh avec sa nguéne beugue sathies beuré ak franc mome tamite dako raw franc gris 2 combat logique la
Combat la dh gris2 vs franc ❤
Tres bien gris 2
Tu as bien dit Mbeur yiii dañion bgue lou yombou dañion wara dieul séni morom yaw ak Fran combat la
Démal kholi patta bo dieul pattaaa gua franc soxla woula
Nako gayi dieul waye akh😂
Franc day moytou Na dieul Gris 2 wala Quench
Fran doussa morom yow ya yarone dieul fils de balla pa lac rose
Bilahi gayi dange ko ragall
Sa Thies waroul beuré ak Franc d’accord mais yaw osi ak franc dou actualité beuré ak Gouy gui c’est plus logique que beuré ak yaw
Bilahi deug rék guay wakh
Fren gnamai woute 22:09
Promoteur yi setilen gris 2 book
Domou dangou wala faran wala goy gui
Pourtant Modou Lo lolou la def deh tokk ba werr carrément dougueul CG gniouni ko tapete gua 🤣
Franc vs gris 2 lolou moye combat
Franc Môme Lolou Mouy Wax Wakhi Tapét la
Gri2 lègui dagua beuri wakh trop iow kène topoula
Gris 2 dafa yarou
Wawe gris valdo moye combat bi
Gri2 louné wakh gua ko ama bamou blessé
Gris2 AK Franc moy combat
Claro gris Fran dey moytou
Franc tapett la dieuleul gris 2 mi
Bilay lou ler gua wakh fran mo sof
Gris 2 dou ayy thiakhann
Sa thies n'a khar eumeu sene tapha .tine.gouy gui quench franc gris 2 moy logique
Sa poid bi mo diakhal gayi😂😂
Gri 2 Fara 🔥
Gri 2 Fara 🔥
Gri 2 Fara 🔥
Gri 2 Fara 🔥
Dieull youssou combat bou nékh laa
Iaw beugoulo Youssou Ndour 😂
@@amdigyoo4930Lu tax làmbu la de Yuusu neewul doole de😅😅
Franc Gris 2 Combat la
Gri 2 damakooo beuggg lolll
Franc vs gris 2 c'est le combat
Yew gris deux mbeur nga am nga fitt gueum nga sa bopp nala gayi dieul
gris 2 contre franc combat logique la
Franchement Sénégal 🇸🇳 mo nexx Gris yoor bi mbirr ak forme gani athlète la 😂
Gris c un àthlete ils a fait 25 ans de carrière
Gris 2 vs franc ndiago or bi
combat bou nekh leu kou dane sa yonn lerr
Guir 2 sa birr bi dafa reyy waye 😂😂
Pourtant sa birou bay moko eup té waxoko
Boy bayil sama mbeur bi
Gris déll dém si lambe yi di teukouweunté guir yalla
Gris & Gouy gui
Billahi mbeur yi niémé wounioula weur weur lo rek mofi néke
Gris 2 sv Gora Sokh combat là
Gris 2 mayal chance général malika
No ki ken dou diuel bayil buere
Gris 2 vs ordinateur
c'est vrais dee franc dako wara dieul moy yon legui kou dann dem si vip yi soula dieuloul nga dieul domou dangou wala Jordan wala général malika
Gris2 vs youssou ndour
Gri2 jeneral malicka Moy comba bi
Waye fran dafa beug Lou yobeu😂😂😂😂😂
Franc mousoul beugeu Lou yobou demal holate palmarès sam beury nguen wah trop
Bène beurre la khameni Bo danè bène combat mou dieulela moy sa thiés. So Danone reug reug sa combat ak sa thiés day takhaw .
Gris 2 na wagni poids bii
Maodo bayil bere ndax dafa xaram te dousa thier
Franc bayil politique bi😅😅😅😅😅
Gris vs fran
Mo meun boy yi dh
Franc vs Quench Au Franc vs gris2 ay combat la you Nékh you logique
Nékh d'accord
Ms pas logique
Mouno dane serigne ndiaye
Dane forza
Après nga tourne di dieul ay gris 2
Franc gris 2 d’où combat
Lamb ji legui dafa bari ay moytou wanté franc vs gris2 combat douko dakh
Gris 2 vs franc moy combat bi
G2 franc logikna gris mo raw franc franchement
En tout cas mbeur bou ame fouleu ils ont peur de lui
Kharal Jackson
Moom ak Frank combala
Les lutteurs ont peur de lui domou dangou m a decu