Cheu notre ta nationale interplanetaire. Nekhoul ba nékhoul na nékhoul, mais dale yalene meune, raw ngua léne sani carawass ba, macha allah, macha allah
J’ai découvert ce plat grâce à une amie mais nékh nékh ! Pour wa Sénégal vous pouvez trouver tous ces épices au supermarché exclusif sur la VDN ,à Auchan Yoff
Senegal danio wara bayi bouillon yi tè dieule epice yi.kounek mane nako defaral sa bopou.et c plus naturel. Tata sa tiep bakhna machalla.yalla lokho bi wer
Hi Tata merci beaucoup pour les recettes vraiment je suis jeune mariée mais sama façon togg dafa amélioré wah degg grâce à toi. Yallna yalla dollila xam xam. Mais pour épice yi Sénégal meun ngako amè hypermarché exclusif wala marché kermel si boutique chinois yi ak marocain yi 😘
ManshaAllah j’adore ta chaine et je suis une grande fan de pulao rice . Il y a un supermarche asiatique en face de El Toro Ngor Almadies ou vous pourrez avoir le melange des epices a Dakar.
Pulao sourna waay liii tamite deugue leu. Werou koor bi inchallah del def vidéo yi after timis😂😘😍❤ ya takh souma toguei legui gneup apprécier tata marietou god bless you and your family. Love u
Salaam. bii mome, no comments.xalaatt na ba sonn lou may commentaire mais guisoumako. khel bi yeup nek si kifin gui rek :) khana eau a la bouche rek... merci tata. Yal na sa jamm yagg. mere Diop yal na khippee aldiana firdawsi si barke al jummuah dji! amine
Bjr tata marietou. Macha Allah. Sa togue seelna neekhna. Dieureudieuf ci partagé bi avec la bonne humeur surtout. Reste comme ça Macha Allah. Sinon pour ceux ou celles à qui ça a interesse, on peut trouver les epices au niveau du supermarché exclusive à Dakar sur la vdn et sur la route de l'aéroport. Ou alors au marché sandaga dans une boutique libanaise juste derrière la pharmacie Gambetta sur l'avenue Lamine gueye. J'ai oublié le nom de la maman qui gère la boutique. Bonne continuation.
C'est Mme gomis trop bon mais les éléments pour les épices existent clou de girofle coriandre et les autres il faut aller en ville la rue ki debouche sur la pharmacie Gambetta vers sandaga une boutique est lã bas et vend des epices
Senegal epices yi amna si grandes surfaces yi con Auchan ya des femmes qui le vendent dans les groupes Facebook con "Femme chic et A nos fourneaux". Merci encore Marietou. Dinako togue Inchalla. Yi rek la beug machalla
Téeerée Bien MachaAllah Sokhneuh Marietou. Dileuh nianal gudu fane ak weur rek. Yalneuh sunu diam yagg way sukodeifei nganiuy "neko ci rel" recette yu bakh niakay setane di ci diang tei aimé rek
Trresss bien madame je vais essayé inshalahou
Aujourd'hui je essaye cette recette c'est oufff😋 nekhna trop merci Tâta marietou
Machallah je vais regardé bien sa tout les jours pour reprendre sa le korité inchallah merci
Waleyki salam wa rahmatoullah habibatou.walahi je prend du plaisir à t écouter.baraqallahou fiqi
J'ai commencé à vous suivre depuis hier mais j'adore ce que vous faites et surtout you bi yaba yi machallah
Tata merci beaucoup yalla n'alla yalla fay barké serigne fallou
Machallah j'aime bien tes recettes
J'aime bien tes vidéos c'est très attirants et raffinnés. Merci pour tout ces recettes qui nous facinnent😊😘
Tu nous transporte dans d'autres horizons 😉 un vrai voyage culinaires merci ma grande 😘
Maachallah bii thiouknaa MARIETOU.Merci du oartage👍🏾👏🏾👏🏾
Mashallah ça donne vraiment envie merci beaucoup tata et bonne continuation😚😚
Mashallah , bonne continuation. Merci
J aime tes recette car tu met des epices qui son bien. Pour la sante je les utilise
Bonjour Marietou Je l'ai essayé c'est tropp bon. Tout le monde a aimé
Delicious and nicely served
Beugueu n'a lii💓💓💓
Bravo pour les vidéos cest très bien expliqué merci j'adore
Bravo 😃😃👑
koumay soumiii.attention Marietou.machAllah...😂😍🍴
waw délicieuse recette machaalla bravo Mariétou bégué rék merci beaucoup pour le partage 👍👍👍👍🙌🙌🙌💕😁💋
Absolutely True their spices are very good but the ones they mixed are very salty. Unless you wanna buy it yourself and mixed them without salt.
MA SHAA ALLAH lay wokhati taarkala 👌
Thank you Marietou yangui takh niouy diversifer recettes yii, na sa diam yagg!❤❤❤
MachAllah ça semble très bon !!!
machallah. yalna Buur Yalla wéreul lokhobi
Machala machala yalna Yalla gueuneu wereul lohoubi c est un plaisir de suivre tes video
aita b. ndoye Ameen
Machalla merci
Maa Shaa Allah Marietou, Diam ak xeweul 👍🙏
Machalah merci encore si recette bi
Nekhna mashallah yallah nala yallah faay .bi mom dinako togua inshagod
Machala tata
Cheu notre ta nationale interplanetaire. Nekhoul ba nékhoul na nékhoul, mais dale yalene meune, raw ngua léne sani carawass ba, macha allah, macha allah
Machallah tata Marietou yak guama yalla na yallah Faye, thank you I have to come refresh my mind every time that I have to cook.
Dokhna nako essyer machallah Dieureudieuf ma belle
Amna solo machala
Machaĺlah nekhena looooollll
Tata Marétou li ma nek dakoy firri ci wolof machallah
Machaallaah del wakh amine rek Mariètou
J’ai découvert ce plat grâce à une amie mais nékh nékh !
Pour wa Sénégal vous pouvez trouver tous ces épices au supermarché exclusif sur la VDN ,à Auchan Yoff
Mberry Mmy merci pour l’info
Merci beaucoup
Yaw kana nekkoon nga ASIA liimoy MATAN BRYANI mashALLAH tog bi diarna yoon 👍👍👍👍👍
Trea bein !
Touuuuuuuuu les bagassssss😍😍😍
Billaye tata yalla nala yalla féye
Non Marietou do dem sister 😂😂👍
Love your sense of humor machala
Tata eupneuh tarkaalha j'aimerai eut goûté ça semble bon!!!
Tata mane dal j t'aime
Senegal danio wara bayi bouillon yi tè dieule epice yi.kounek mane nako defaral sa bopou.et c plus naturel. Tata sa tiep bakhna machalla.yalla lokho bi wer
Bien bon tata machallah 👑👑👑👑
Machallah tata
Machallah tata borome parole you nekh yi
Machalla👍😘
Ta Maretou Goudal fane waay yow sa dound amna ndiarigne barki Yalla mala beug ❤❤
Machalah jarna fimdane jar ❤️
Machallah tata... la maniere dont tu la préparé est bcp plus rapide et astucieux que celle des afghanistan.
Sa lokho naye ame diam toujours
Hi Tata merci beaucoup pour les recettes vraiment je suis jeune mariée mais sama façon togg dafa amélioré wah degg grâce à toi. Yallna yalla dollila xam xam. Mais pour épice yi Sénégal meun ngako amè hypermarché exclusif wala marché kermel si boutique chinois yi ak marocain yi 😘
Tata li nekhna macha allah je vais grossir
ces epices sont saint
Wouuuuy mogui mey kheign ba fi point E 🥺🥺❤️
Lah Thiat tata cherie
Merci tata d'être là pour nous machalah qu'Allah t'accorde une longue vie🙏🙏❤
ManshaAllah j’adore ta chaine et je suis une grande fan de pulao rice . Il y a un supermarche asiatique en face de El Toro Ngor Almadies ou vous pourrez avoir le melange des epices a Dakar.
Rafet na lol, yallah nagua coude fane way.. Sel na ,rafet té nekh machallah
salut tata mariéme machalla si plat you nekh yii amna solo trop. A la place du safran est ce qu'on pourrait utiliser du curry.
Merci beaucoup pour les recettes
Nekna tata❤👏
Machall tata
Salam ma fille ça je vais l essayer ça paraît bon bonne continuation tata Bineta Ndiaye
Merci tata mariétou yalna yalla goudal sa fane mayla weir contane cii yow♥️💋
Humm délicieux 😋 ça ressemble au riz tanzanien Pilau
Mashalla tata epices yi mom warnanko oute té bayi boulion yi
Yapouu kharr rekk...ahh motakh douma lallle bou nakk...khollall lii rekk
Pulao sourna waay liii tamite deugue leu. Werou koor bi inchallah del def vidéo yi after timis😂😘😍❤ ya takh souma toguei legui gneup apprécier tata marietou god bless you and your family. Love u
Machallah contane si yaw leup ngui goundous goundoussi
Salaam. bii mome, no comments.xalaatt na ba sonn lou may commentaire mais guisoumako. khel bi yeup nek si kifin gui rek :) khana eau a la bouche rek... merci tata. Yal na sa jamm yagg. mere Diop yal na khippee aldiana firdawsi si barke al jummuah dji! amine
😭😭😭😭 Dama dioye ndakh khamna li nekh rek la def te douma thi moss.
Mashallah
Bjr tata marietou. Macha Allah. Sa togue seelna neekhna. Dieureudieuf ci partagé bi avec la bonne humeur surtout. Reste comme ça Macha Allah.
Sinon pour ceux ou celles à qui ça a interesse, on peut trouver les epices au niveau du supermarché exclusive à Dakar sur la vdn et sur la route de l'aéroport. Ou alors au marché sandaga dans une boutique libanaise juste derrière la pharmacie Gambetta sur l'avenue Lamine gueye. J'ai oublié le nom de la maman qui gère la boutique. Bonne continuation.
Merci beaucoup Tata ... boko si.. je m’abonne😍
Say expression amoul feneu tata 😂😂😂😂😂 neneu resin bi danioukoy titeul rek L ol
Ah thiebou yapp bi amna solo
Machallah
Je t'aime fort sister bonne continuation et thank you so much
Ma sah Allah
Tata Mareitou MachaAllah 👍👍👍👍
Fraise Bo mais sester tu es vraiment belle hein
Togg massi namm variété wayy, merci Tata Mariétou
C'est Mme gomis trop bon mais les éléments pour les épices existent clou de girofle coriandre et les autres il faut aller en ville la rue ki debouche sur la pharmacie Gambetta vers sandaga une boutique est lã bas et vend des epices
Merci madame Gomis
Machala machala lép diapna forme
Ey tata amougnou dara lougnou lèye wakh loudoul mashallah ak dieuredieuf. Bii mome nice na torop, c'est térès bien. Bilaye titeul nga gnou waye. Mouah
Salam big up tata marietou wa senegal epices yi amna super marché exclusif😘
Hum c'est trop super Ma tata.. en plus j'arrive tôt aujourd'hui 💪 merci Tata pour tes bons plats
Diap form😍😍😍🙏🙏🙏
Aimer ba parer soga setane . Yague fi lol waay borom tous les bagass
que Dieu te benis JUmaa moubarack
Sow Idrissa Ameen wayy ak yaw
Svp ou vi cette dame en Europe
Mbich mbichal Kossy😂😂ay tata mariétou 😂
Youbi yaba moye lane tata no 😅😅😅😅😅😅 bismilah
Senegal epices yi amna si grandes surfaces yi con Auchan ya des femmes qui le vendent dans les groupes Facebook con "Femme chic et A nos fourneaux". Merci encore Marietou. Dinako togue Inchalla. Yi rek la beug machalla
7th
Comment faire avec le riz parfumé , on le passe à la vapeur où on le fait comme avec le riz basmati
Marie Aline Mbaye c’est mieux avec le basmati mais bon vous pouvez utiliser le parfumer aussi et à la vapeur c’est bon
Encore de nouvelles recettes merci merci mille merci ma maman de cœur
Diarietou Manga 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
@ merci bcp que le bon dieu te bénisse
Neekhasss tata sama toma
epices yi warna ame super marché exclusif
Salam j voudrai savoir comment preparer du " thiébou sape ak guinare avc ls fruits d la mer merci
Hum cé bon tata beug na niguay toguè prck dagay utilisé tjr des épices comme moi j'adore les épices
Téeerée Bien MachaAllah Sokhneuh Marietou. Dileuh nianal gudu fane ak weur rek. Yalneuh sunu diam yagg way sukodeifei nganiuy "neko ci rel" recette yu bakh niakay setane di ci diang tei aimé rek
Maïmouna NDIAYE Ameen wayy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Yummy 😋