Baye Bada wané deug deug mélokaanou sénégalais wollah ils sont tellement solidaires et pourtant kilay diapalé mola eupp problème yalle na diam sakh si sougn réw mii😢🙏
Ohhh c’est la première fois ma setane série bi ms souma sanione dou diekh amna sens trop rigolo neu triste neu ohh rien a dire vraiment c’est exceptionnel ❤❤❤❤ Ms Baye bada assuré nga tmt Bakary mom ya euppeu problème si Dunya 😂massa way
@MassSeck-h9g Arrétez votre complexe bakari niakoul mingi liggey yor responsibilité famille wam il est comme 70% des senegalais, daa fék nak senegal nek deuk bou chére par rapport aux revenu et aux pouvoir d'achat
Nguen gnibi senn dëkk.. Mann deh deukouma Dakar parce que je refuse de faire partie de cette mascarade. Di boukhante ci ay poukhouss melni ya pas assez d'espace au Sénégal.. Décentralisez vous...
@@ThiesKaayimagine toi nga war fa diangué alors dans ce cas tu n’as plus le choix. C’est ce meme perspective que s’inscrit la situation des autres qui viennent installer à Dkar. La décentralisation dépend du gouvernement mais pas les citoyens. 😊
@@serignembaye6230 Tu n'es pas obligé. Il y a des universités partout au Sénégal. Pas qu'a Dakar.. Question de choix de vie la rek.. Il faut arrêter de se trouver des excuses et de tout mettre sur le dos de l'état et tjs attendre que les solution viennent des autres. Lolou rek moniou tardel nak. Ma ngui diegalou nak. Mais la vérité est pas facile a réaliser.. Dakar a plus d'opportunités de réussite, on en disconvient pas . Mais a quel prix?? Pour quels sacrifices ?? Est ce qu'au final le jeu en vaut la chandelle.. et plus on avance plus ça empire..
@@ThiesKaay il me semble que tu n’as pas compris du système d’orientation des universités sénégalais. Fiii kou sañonn sa gox ngay diangué mais dafa fekk ni l’opportunité n’est tjrs pas donnée chez ns.
Une série qui reflète la réalité sénégalaise bravo à la rts
Vraiment
Cool Casting. Djiby Seye ak sa fille kiiff kiiff😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
Lolou la khalate bima lene guissai
Esk dou domome
Ndaysane Baye Bada à assuré son rôle et montrer la responsabilité
Réclamons le bonheur de Bakary 😂🥹😔
Kou yeureum Bakary rek lalal j'aime 🥺 yalla nako yalla takhawou
Bilay wahatiko dehh😂
😊😊😊😊😊😊@@MamadouToure-kr4wy
Les genres de personnes comme baye bada sont exceptionnels bilahi
Bo Yorouleu ga Nékh déréte sax😂 kéneuu dou BakarY😂😂😍🥰❤️❤️
Lolou mouma diakhal 😂😂 yow amou di nakhari derete
Lolu mom djiafeh na 😂 gniak yorr bapareh beugg neekh deret lolu meunull néek nak tourando😂😂
@@khadijadieng6658Bilaye dé 😭😂😂
Bakary Kaye 😂😂😂😂😂
Metti liniou tekk Bakary mais sénégalais you beuri li laniouy dundu . Soutoura yallah rek
La meilleur série Bakary ❤
Jareujeuf Wa Rts sur le Dg P allé Niang
Baye Bada c'est comme un papa pour Bakary machallah ❤️❤️❤️❤️
Ayez des Baye Bada dans vos vie ❤
Faté samay problème di nianal Bakary😂😂
Liiii kagn 😂😂
😂😂😂😂
Ya wané😂
@@MansorDiop-wn4ogBilahy 🤣🤣🤣
Bilay yaw!
La qualité d’image c’est autre chose ❤❤❤❤❤❤
Réclamés de bonheur bakari svp
Djibi seye rewna❤
Baye Bada wané deug deug mélokaanou sénégalais wollah ils sont tellement solidaires et pourtant kilay diapalé mola eupp problème yalle na diam sakh si sougn réw mii😢🙏
Duo djiby seye ak dome dji nekh nama😂😂
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤😢
Mouhaméd ana samba Ndiaye démissionné na
Nono😂
@@MeddiéyeDiéye😂😂
Nék pauvre daal amoul louko geuneu méti vraiment. Yalla na borom bi takhawou gni sén lokho diotoul guinaw😢
Amine inchallah
Bakary wakh na deugg djibi loum ko wakh dou yone ❤
les lecons de fin d"episode sont vraiment magnifiques et importantes merci a vous
La vraie vie sénégalaise... une très belle série mais les épisodes sont en court métrage
Bakary et baye bada sont bien dans leur rôle
Bakary sonou na😂❤😢😢😅
Minute de securité Yi amna solo ❤❤❤❤❤
Ndeyesaan !!! Rôle de baye bada❤
Vrai nitt kou bakhe❤
Bakary série bou beury diarigne ❤🙏🙏
Ohhh c’est la première fois ma setane série bi ms souma sanione dou diekh amna sens trop rigolo neu triste neu ohh rien a dire vraiment c’est exceptionnel ❤❤❤❤
Ms Baye bada assuré nga tmt Bakary mom ya euppeu problème si Dunya 😂massa way
Svp augmentez les minutes de la série meilleure série Sénégalaise 😂
Voilà ❤
Sama Tourondo Bakary rekk laayy tooppp😂😂😂
Serie bou mengou ak sunu dondou réalité ❤❤❤ merci rts pour le rénovation ❤❤
Bay bada ndanan la cw😂😍😍😍😍
Fi de limafi diange moy kharit bou bakh 😢mo am solo
Bilahi
Surtout lolu
@@IbrahimaCisse-km1lh dafa ler dh
Une Série est vraiment sénégalaise
Baye bada meuna masla sheuttt j’aime bien sa personnalité si je pouvais être comme lui
Bakary nékoul dimbali dafa nakari dérete😮😮😮
daffa bagne kouko yappp rk 😂😂
@@modouniass2973 wayé bo yoroul dangay yarou 😂
Souvent kou niakk day nakhari dereit 😅
@@MassSeck-h9g bilay khamna stress bila😂😂
@MassSeck-h9g Arrétez votre complexe bakari niakoul mingi liggey yor responsibilité famille wam il est comme 70% des senegalais, daa fék nak senegal nek deuk bou chére par rapport aux revenu et aux pouvoir d'achat
Votre qualité d’image est vraiment wouaw🥰machallah
Lii akk la magui sogua khame serie bi .beugue sétana ndo lépe😂dama gueumintou bay langue wayé bou diékh ma sétane bissi désse😂
Chapeau à vous😂
Tey lako découvrir mais magui ni bou diékh ma avancé thi bénén
C la triste réalité la famille sénégalaise tout se repose sur une seule personne
Walahi mtkh niouy daw ba de
meilleur série de l'année
Bakary yeureum nala nk😢 dina bkh nék si rek
Yoro baparé ngané do yarou boolési nakhari déréte lolou dafa meuneu nékk 😂😂😂🤣🤣 waayé kénne dou djiby seye pabou rèwla vraiment serie bi nékhna trop
Bou khol si bakary mougn dh😂
Bilay bi Djiby retanè, Bakary retaan sama yaram dafa daw😂😂😂
Bada tu es gentille c'est ca un bon ami
Ayez des Baye Bada dans vos vies 😂❤
Hoo baye bada il joue très bien dafa naturel
No bakary com man blahi vérité la❤
Nn Bakary moy Sénégal 😄😁😄😁
Bly yen rk la don khar bly li Dfa nekh ❤🎉😂
Djiby sey rewna😂😂😂
Bakary mo geuna sonou si serie bi sak jour ak problem bou bèse 😂😂😂mè kendou djibi seye😂😂😂
Lagaboury na delou way wa Rts😂
Wax lu neexoon, waay xaley xamuñu ko. 😂 😂
Une très bonne série ❤❤❤
Wa Espagne am guénn dammeu❤❤❤❤❤😂😂😊
Igualmente 😅🎉
❤❤
Je te jure il a trop de problème
Waa BAKARY FOUMUY DIEULEI GASOIL😂😂😂😂
Dakoy lepppl😂😂
@@sokhnaboussokebe3901 lolou moma diakhal 😂dama guissul mou am clients dii en TANT QUE CHAUFFEUR je connais ce qu’il est en train de vivre 😂
Bonne question 😂
Bilahi sourtout lolou
Hana lep
Djiby Seye beugueu nako way 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Mafi djitou❤❤❤❤❤
Bakary ak doukoure kan mô apou borolem😂😂 2:28
Médina aka méti thi kou yoroul bofa beugué deukk dafay méti trop😢😢😢
Bilay dou médina rek
@@bocarguisse2282Bly dou médina rk
@@bocarguisse2282 😔😔
Location si bopam lan wara kholat Dakar serna trop
Ioe khamo sakh loulako wakhlo
Baye bada aussi nitt geunouko😢❤
Vie Dakar dafa méti bilaye 😢
Nguen gnibi senn dëkk..
Mann deh deukouma Dakar parce que je refuse de faire partie de cette mascarade. Di boukhante ci ay poukhouss melni ya pas assez d'espace au Sénégal..
Décentralisez vous...
@@ThiesKaayimagine toi nga war fa diangué alors dans ce cas tu n’as plus le choix. C’est ce meme perspective que s’inscrit la situation des autres qui viennent installer à Dkar. La décentralisation dépend du gouvernement mais pas les citoyens. 😊
@@serignembaye6230 Tu n'es pas obligé. Il y a des universités partout au Sénégal. Pas qu'a Dakar..
Question de choix de vie la rek..
Il faut arrêter de se trouver des excuses et de tout mettre sur le dos de l'état et tjs attendre que les solution viennent des autres.
Lolou rek moniou tardel nak.
Ma ngui diegalou nak. Mais la vérité est pas facile a réaliser..
Dakar a plus d'opportunités de réussite, on en disconvient pas . Mais a quel prix?? Pour quels sacrifices ?? Est ce qu'au final le jeu en vaut la chandelle.. et plus on avance plus ça empire..
@@ThiesKaay il me semble que tu n’as pas compris du système d’orientation des universités sénégalais. Fiii kou sañonn sa gox ngay diangué mais dafa fekk ni l’opportunité n’est tjrs pas donnée chez ns.
Nioun d meti woul si nioun Sant yalla rk 😢
Djiby Seye motakh may sétane série bi ki damako beugeu🤣🤣🤣
Djiby rèwna billaahi 😂😂😂
Ils sont vraiment naturels
Ndaysane bakary massa😂
J’aime le rôle de Baye Bada❤
Grand you melnii barétoul ci koñ yi dey.. arrangé na problèmuu Bakary a sa façon.. teye ak dal deffa bax ci nitt
Magui soga setane série sama adouna walahy série da nice Amoul Dara vulgaire
😅😅bilay théâtre bi da nekh
Cette série dafa wara geuneu am Marketing li nekh na trop 😂gnou beuri khamougnou ko
Bo yoroul dangay yarou😊😊😊
2 3episode par semaine waay
On réclame le bonheur de Bakary 😂😂
Dagen gedjie réclame sax😂
Baye bada nar nâ sonou billahi 🤣🥰 11:50
T'a pas attaché t'on ceinture de sécurité Bakary
Baye bada Kou baxla
Djiby Seye, c'est le meilleur 😂😂😂
Chapeau à Baye Bada 🙏🏾🙏🏾
💚💛❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳💯💯💯💐💐💐✌️✌️✌️✌️✌️Sonko Rêkk 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳✌️✌️✌️✌️💚💛❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳💯💯💯💐💐💐✌️✌️✌️✌️✌️Sonko Rêkk 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳✌️✌️✌️✌️
Ma serie preferée !
A la fin bakary da wara am xaliss Niou khol noumouy démé 😂
Dou am😂
Nn djibi seye Sama Idol amoul morom 😄😁😄
😂😂❤Djiby seye 😅
Ho baye bada❤
Yan jour lay am svp
Samedi et dimanche
Samdi et dimanche
@@yayemayelatmbao5442quel heure svp
Cette série nous parle❤ 😂😂😂
Djibi seye yekh na niew 😂
Papa ass mofi manki
Guene na ré Bouma commencé setane série bi la commencé ré
Merci rts
Soumouy Gasoil moma diakhal man😂😂
Bakery ndeysane
COMME D'HABITUDE DJIBY SEYE NE DÉÇOIS PAS DANS SON RÔLE FÉTICHE 😂😂😂
J’adore ce serie tout le monde doit reguarde ca
Sénégal et Sénégalaise ñipo war ñianal babakar vraiment 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Baye Bada nenako dawalal rék lingay daw khamna ko khana Agent Diehdiou la Bakary di daw😂😂😂😂😂😂😂😂Pabi nandite la
Li la rétane 😂😂
Vision Sénégal 2050 inchalla ❤❤❤
Kou fi gueun beug lakh 😂
Barça meilleur équipe du monde ❤❤❤❤❤❤❤
ATTENTION MARODI ET EVENTPROD 😊RTS est à vos trousse
Djiby sey comme Stromae😃😃
En tout cas bakary a plus de problèmes que Diomay