🛑 Mine Nouri de Abdou Aziz Mbaye avec Serigne Babacar sy Abdou et serigne Maodo sy Dabakh

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 316

  • @aronambengue5981
    @aronambengue5981 2 роки тому +112

    Je suis mouride mais abdou Aziz mbaye dinama ray rek ak mine nourihi ❤😍

    • @youssouseck5182
      @youssouseck5182 2 роки тому +2

      Maa sha Allah

    • @khadysene1328
      @khadysene1328 Рік тому +2

      Maa shaa ALLAH bari nga ci morom sama beineu collègue mouride la wayei Mine Nourihi mokoy danel

    • @ndiayesada7317
      @ndiayesada7317 Рік тому +1

      Deysan mboguil t yala tah♥️♥️♥️ machala 🙏

    • @OumyNiang-hl1zu
      @OumyNiang-hl1zu Рік тому +1

      Bilaye

    • @gorandiaye4776
      @gorandiaye4776 Рік тому +1

      Pourquoi la.precision" je suis mouride". Tagg yonent bi kepp kou sa xol labb dina la nex ak kokou meunna deff

  • @nourou1996
    @nourou1996 2 роки тому +139

    La lumière du prophète PSL est la source de nos lumières

  • @gorguika1570
    @gorguika1570 2 роки тому +36

    Machalah yalla na yalla wereul batt bi baye abdou aziz si barké sa toureundo dabakh 💕😔💖🙏

  • @messatsu2074
    @messatsu2074 2 роки тому +65

    Yalla nagnou Yalla def Ay Talibei Chekhou Tidjane 🤲🏾 ❤

  • @ramatoulayeleye2148
    @ramatoulayeleye2148 2 роки тому +64

    Tidjani fil dunya wal akhira 💙💞💞. Yala naniou yalla sakh si tarikha cheikh bi ba kawsara. Dieureudieuf mame maodo. Cette melodie me procure tellement de joie. Serigne mbaye sy abdou yalla nafi yague lol tei weer si barki khalifa ababacar sy sa toureundo.

  • @Makhtarsene-h1q
    @Makhtarsene-h1q 11 місяців тому +2

    Yalna diameu dji gana barri way machallah Abdou Aziz mbaye noukko khaleyi Di waxé ioe rek lay topou ❤

  • @salimataly4272
    @salimataly4272 2 роки тому +20

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ li nekh na si khol walay ndeyssan yallah na gnou yallah def deug deug talibe Cheikh ziar na gneup si gamou gui 🙏

    • @OumyNiang-hl1zu
      @OumyNiang-hl1zu 9 місяців тому +1

      Amin ya Raby ❤️♥️♥️♥️❤️♥️♥️❤️

  • @sowmama6181
    @sowmama6181 Рік тому +7

    Mine Nouri limouye deff sa ma lémayela je peux pas rester une journée sans l’écouter dieureudieuf sa ma BOROM bi ma def Musulmane et pratiquante machala ensuite ma done talibé Cheikh pure et dure mame Dabakh Malick done sa ma Serigne pour toujours.
    Merci Mon DIEU pour tout ce bonheur Alkhamdoulilahi Rabine Allamina.

  • @leprince2591
    @leprince2591 2 роки тому +79

    Nèk Talibé cheikh mo nekh ❤️🙌🏾🥹

  • @fatousarr6963
    @fatousarr6963 2 роки тому +56

    Doumassi doyol yalnala fi yalla bayi bassi kaname mbaga té werele batte bi machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mansoursow9896
    @mansoursow9896 2 роки тому +7

    Machlla l'AF thiat yalla nale yalla same mayla goudou fane AK wer ndoudanle mbaye

  • @laminendiaye4631
    @laminendiaye4631 2 роки тому +18

    Diarama Mame Maodo Malick S'y Malick... Mâcha Allah.

  • @baaxbaay2919
    @baaxbaay2919 2 роки тому +24

    Barke Boroom Tuubaa lii neexna abdu Aziiz Mbaay yalna nga fi yágg te wér

    • @ndiayesada7317
      @ndiayesada7317 Рік тому +1

      Diarama yaw🙏♥️♥️ Amin yarabi 🤲

    • @baaxbaay2919
      @baaxbaay2919 6 місяців тому

      @@ndiayesada7317yaaram kii li muy wax Yonente bi dafa neex lool moo ma tax a jàng Xilaasus-zahab ak kifaayatur-raaxibiina waaye ñaari téere yu doywaar te am solo lool masàllaah yal na Yàlla dotti waamew yërmande ci Maam Mawdo te yàggal fi Allaaji Abdu Asiis Mbaay ci barkep Sayxul Xadiim🙏

  • @diaylapouye3672
    @diaylapouye3672 2 роки тому +20

    Fier d'être talibé cheikhe sougnou degrés civilisation dama yéme❤️❤️💯💯

    • @AichaMane-yn7ok
      @AichaMane-yn7ok Рік тому

      ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ eupeuna Macha Allah à ns

  • @salieundow8506
    @salieundow8506 2 роки тому +20

    Machalla Baye Abdou Aziz Mbaye Djeuereudjeuf Mame Seydi Elhadji Malick Sy walahi li nekh rek la def yalla fayal gnou Mack gni Barckep yonenti bi❤️💕

    • @sidydiallo2676
      @sidydiallo2676 Рік тому

      Cela va droit au cœur jusqu'au bord des larmes

  • @fatimatathiam7040
    @fatimatathiam7040 2 роки тому +11

    Machalla naniou Yalla bolé bal daffal niou diam may niou fékéé ay att you beuri inchalla

  • @mamfacamou8340
    @mamfacamou8340 2 роки тому +8

    Santa yalla ak yoneuté bi ak wadiour yi wallahi yalnaniou yalla fayal Sunu Mame Maodo yalnaniou yalla yokou samal Khalifa bi serigne Babacar Sy Mansour dieureudieuf Abdou Aziz mbaye

  • @manoumanou7703
    @manoumanou7703 2 роки тому +13

    Dieureudieuf Mame Maodo yaniou khamal NABY❤

  • @diagnemamedemba2307
    @diagnemamedemba2307 5 місяців тому +2

    Machalla Abdou Aziz yal na yala barkel goudal sa fann

  • @tvmeta8628
    @tvmeta8628 2 роки тому +14

    Machallah Mbaye doundal waay khol yeup sédd na❤️

  • @seydinadiop9225
    @seydinadiop9225 2 роки тому +11

    Yalla naniou yalla fayal cheikh seydil hadji malick sy maodo

  • @adamafall8817
    @adamafall8817 Рік тому +5

    Machala et bonne continuation Abdou Aziz Mbaye ❤❤❤❤❤ très fière d'être talibé cheikh ❤❤❤❤

  • @AmynaNabySarr-bouDabakh
    @AmynaNabySarr-bouDabakh 2 роки тому +7

    Khôle bou sédena rek❤️💓Yalla na Yalla yagal séne takhaway

  • @ndeyeawaseck8480
    @ndeyeawaseck8480 2 роки тому +4

    Machalla yalla na yala Dollé tahawou té guena goudal fane yi amine vraiment hole yi sédna alhamdou lila hi rabil alamine

  • @massambathiorondiaye4856
    @massambathiorondiaye4856 3 місяці тому +1

    Ma beug papa Abdoul Aziz Mbaye way l'écouter m'apaise

  • @mankeurdiol2544
    @mankeurdiol2544 2 роки тому +5

    Machalla Abdou Aziz yalla n yalla weral may la fane wou goude

  • @kineseck8786
    @kineseck8786 2 роки тому +3

    Machallah nékh Talibé cheikh nékhna troop Aziz mbaye yalla na yalla goudal sa fanne aminnn

  • @serignemoussagaye6954
    @serignemoussagaye6954 2 роки тому +16

    Yalla nagnou yalla def ay talibé cheikh you mak💯💯💯❤❤❤❤

  • @ababacarndiaye8275
    @ababacarndiaye8275 2 роки тому +20

    Tout simplement content 😭😭😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️

  • @omarsamb3878
    @omarsamb3878 2 роки тому +20

    AlhamdoulilAh Dieurdieufétii Serigne Touba Khadim Rassoul 🙏❤️

    • @messatsu2074
      @messatsu2074 2 роки тому +2

      Serigne Touba noumou Sant svp?

    • @mbacke3857
      @mbacke3857 2 роки тому +1

      @@messatsu2074 kel rapport

    • @khadim1775
      @khadim1775 2 роки тому

      Naniou Manou fall

  • @niamasow8947
    @niamasow8947 2 роки тому +7

    Machallah layenne la mais franchement li dafa nékh sama khôl sedd na

  • @kineseck8786
    @kineseck8786 2 роки тому +3

    Sa lumière est la source de toutes les lumières saws

  • @DioumaDiouf-y8t
    @DioumaDiouf-y8t 3 місяці тому +4

    Fier d'être tidiane❤❤❤🎉🎉🎉🎉

  • @amicolesy
    @amicolesy Рік тому +2

    Dieureudieuf sy malik

  • @badiewo973
    @badiewo973 2 роки тому +9

    Tabarakallah Baye Abdou Aziz sunu mbekte di gnane Bour Yalla goudal fann wi te begueul ko ni mou gnouy begueulé🙏💚

  • @bayefallouserignebabacarsy
    @bayefallouserignebabacarsy 2 роки тому +14

    kéne dou seydil hadji Malick Sy amoul morome dhé 💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓

  • @mamadidabo385
    @mamadidabo385 2 роки тому +18

    Machallah fier d'être talibe cheikh 💯♥️❤️

  • @aidaniass7821
    @aidaniass7821 2 роки тому +9

    Machallah lii dafa nékh trop 🙏 done taalibé Cheikh dafa nékh 🤩

  • @sidyndiaye9669
    @sidyndiaye9669 2 роки тому +5

    Bilay machallah 💗tarikha bou amoul guewal nekhoul

  • @oussmane941
    @oussmane941 2 роки тому +2

    Maa Chaa Alla Dieureudieuf CHEIKH SEYDI HADJI MALICK SY sa liguéye rafétna sa lép Yalla nga diar ko thi Yonetibi Yalla nala Yalla faay

  • @DialloKadiatou-ez8rg
    @DialloKadiatou-ez8rg Рік тому +5

    Je suis fière d'être talibé Serigne Babacar s'y ❤️❤️💎🙏

  • @adamasene2437
    @adamasene2437 Місяць тому

    Merci mon père ndiada sene fierté d'être tidiane

  • @AsfawSow
    @AsfawSow 3 місяці тому

    Je suis fière d'être talibé cheikhou tidiane❤❤❤😊😊

  • @ngonelo1722
    @ngonelo1722 2 роки тому +7

    Demb sama khol sedna Bilahi Yalla khamnaka Yalla nagnouka yague tewé

  • @ibrahimagaye9702
    @ibrahimagaye9702 2 роки тому +8

    Machala abdou Aziz yageu fi lol te werr ❤

  • @aissatadiop1668
    @aissatadiop1668 Рік тому +2

    Yalla na Yagui done talibe cheikh❤❤❤❤❤

  • @amadouba8653
    @amadouba8653 2 роки тому +6

    Machalah
    Talibés cheikh dey respecter sartou tarikha bi su bogué talibem weer mais pas si ay wakh seulement.juste une rappelle
    Yalla na yalla nagu sunu talibé cheikh

  • @ndeyemanedieng392
    @ndeyemanedieng392 2 роки тому +12

    Que dieu vous protégé🙏❤✅✅✅✅✅

  • @abdoulazizdiop2558
    @abdoulazizdiop2558 2 роки тому +7

    yalla gafi yague ta ande ak wer ak werlé 🤲🤲🤲💚💚💚💚🤍🤍🤍💚💚💚😭😭

  • @mouhaseck9394
    @mouhaseck9394 2 роки тому +12

    Barki mame cheira fall lii seddd naa khôl ❤

  • @mamemaryndiaye3875
    @mamemaryndiaye3875 2 роки тому +5

    Machallah Machallah Yalla na Yalla barkél

  • @mouhamedkante6395
    @mouhamedkante6395 2 роки тому +7

    Machalal Abdou Aziz mbaye ❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏

  • @SaliouGaye-z3q
    @SaliouGaye-z3q 3 місяці тому +1

    Machalla nexna lol wayé yalna yalla goudal fanam ❤❤❤

  • @syaida1180
    @syaida1180 2 роки тому +4

    Tarkallah doundal weral amal diam machallah

  • @adjimaremediagne7200
    @adjimaremediagne7200 2 роки тому +5

    MANCHALLAH ABDOULAZIZ MBAYE YALLA NA YALLA GOUDEUL SA FANE BARKE SEYDINA MOHAMED

  • @mbayamefall3536
    @mbayamefall3536 Рік тому +3

    Mangui sante yalla diko geureum wlh azim bimou ma défense ma nek talibé serigne babacar sy 🙏

  • @awadieye293
    @awadieye293 Рік тому +1

    Yalna ma yalla def talibé cheikh insha allah 🥺❤️

  • @oumardiaw3847
    @oumardiaw3847 7 місяців тому +1

    SAW SALALAHOU ALA MOUHAMEDINE ❤️

  • @cheikhtraore9840
    @cheikhtraore9840 2 роки тому +7

    Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤nek talibé cheikh mo nekh

  • @dembandoye6560
    @dembandoye6560 2 роки тому +8

    Ousoutourhouna fi mou ko dieulé mo sori🙏🏿

  • @aissatadiop1668
    @aissatadiop1668 Рік тому +3

    Barki serigne babacar sy dama teud malade bima diele sama phone diko setane dafa melni dra dalou dakh cotane ak xol bou sed lii yalla rk mako meune❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fatimatathiam7155
    @fatimatathiam7155 2 роки тому +6

    Machala talibe cheikh jusqu'à la mort

  • @sambadia7183
    @sambadia7183 2 роки тому +7

    Ndeyssan daw na yaram lolu . Dia mouride 😍

  • @oumoukhairymbodji7297
    @oumoukhairymbodji7297 3 місяці тому +1

    Machala fière d'être talibé Cheikh

  • @mbayemagette9198
    @mbayemagette9198 2 роки тому +5

    yalla nanga goude fane papa abdou aziz mbaye

  • @mbayesarr6258
    @mbayesarr6258 2 роки тому +34

    Machallah papa abdou aziz mbaye ❤

  • @mariamasyrodriguez348
    @mariamasyrodriguez348 Рік тому +1

    Machallah rafetna que dieu te protège ❤❤❤

  • @papamassambagueye8659
    @papamassambagueye8659 2 роки тому +4

    Super content 😀 ❤️‍🔥

  • @khadim1775
    @khadim1775 2 роки тому +6

    Mbouride la me dama bgue ndiole fouta wallay🙏🙏

  • @bintoumansare7639
    @bintoumansare7639 2 роки тому +2

    Papa Abdou Aziz yalla n'a yalla goudal sa fané yak gnigaye andall sayouma dégé sama khol séd yaganala deglou do walf deux par mercredi gay sédal sama khol té boba xalél la khow dieureudiel

  • @YacineDieye-jn4pi
    @YacineDieye-jn4pi Рік тому

    Je suis fière d'être tidiane❤❤👆

  • @fatoukinemboup6430
    @fatoukinemboup6430 2 роки тому +3

    Min 'nouri bi tamite machalla

  • @LatgrandGUEYE
    @LatgrandGUEYE 8 місяців тому

    je suis tellement content que Dieu nous fait des vrais talibe cheikh

  • @gninguekhadim531
    @gninguekhadim531 2 роки тому +4

    Abdoul Aziz mbaye mom machallah

  • @MESTOREGAMER158
    @MESTOREGAMER158 8 місяців тому

    Machallah rafetna Mame abdou aziz M'baye❤❤❤

  • @fatoukinemboup6430
    @fatoukinemboup6430 2 роки тому +5

    Machalla hole sedene diam si yen Ken dou mame

  • @maimounadia4976
    @maimounadia4976 2 роки тому +5

    Machallah goudou fane ak fër Yallah wërèl batbi

  • @dikonediop1921
    @dikonediop1921 2 роки тому +2

    Machalla amine doumasi doyal dah xol bou sede

  • @FatouThiam-o4c
    @FatouThiam-o4c Рік тому

    Min nourihi nimouy def sama khol bi ohhh❤❤

  • @fatoudiop2933
    @fatoudiop2933 2 роки тому +2

    OMG machallah khol yeup toye na ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @ThiamaSeck-sq8zz
    @ThiamaSeck-sq8zz 5 місяців тому +1

    Fier d'être talibé cheikh ❤❤❤

  • @ramcha607
    @ramcha607 2 роки тому +2

    Demb contane na yalna borom bi goudeul séni fane thi barké yonent bi saws

  • @yacinediouf7061
    @yacinediouf7061 2 роки тому +7

    Macha Allah notre papa

  • @papeciss1898
    @papeciss1898 2 роки тому +6

    MACHALLAH❤❤

  • @aissatadiop3831
    @aissatadiop3831 2 роки тому +18

    Macha Allah longue vie 🙏🙏🙏❤️🥰

  • @fantydiop5935
    @fantydiop5935 Рік тому

    😍🥰🥰🥰oh li dafa nekh bilay sama xol bi sed naa machalla ❤❤💖❤❤❤💖❤

  • @bachirmbaye353
    @bachirmbaye353 9 місяців тому +1

    Deig gein moustapha mbaye limouy awu❤️😭

  • @sokhnaaminatoumbaye6674
    @sokhnaaminatoumbaye6674 2 роки тому +4

    Ohhh Abdou Aziz mbaaye

  • @dieliadjigo5919
    @dieliadjigo5919 Рік тому

    Cheu teu teu. Amine ya Rabbi. Maa shaa Allah.

  • @suzanneaminataseck3621
    @suzanneaminataseck3621 2 роки тому +2

    Manchalla li kouner nekhoul da ngua sè bokoul bilakhi li dayy diouguer si khol dougou si khol barky yoneteby

  • @alima5003
    @alima5003 Рік тому +3

    thiéye min nurihii bii noumayy défffff🥲🥲🥲🥲🥲🥲dama contane

  • @alassanediop9428
    @alassanediop9428 2 роки тому +13

    Masha allah ❤️❤️❤️🙏

  • @sidatyba4200
    @sidatyba4200 2 місяці тому

    ❤❤❤thiey baye azziz mii yalnasa jamm yague mbaye❤❤❤

  • @3jtvf
    @3jtvf 2 роки тому +4

    ❤❤❤❤❤man amou ma loumay wakh

  • @yaramendiaye6946
    @yaramendiaye6946 2 роки тому +4

    Ndeysann 😭😭😭

  • @malickdiop4552
    @malickdiop4552 2 роки тому +1

    Yalla nala yalla may goudou fane

  • @pathegeuye2423
    @pathegeuye2423 2 роки тому +2

    Al hamdoulila ❤️🤟❤️ santé Yall

  • @mometims1207
    @mometims1207 2 роки тому +2

    Machallah machallah machallah machallah machallah machallah

  • @gastarpdg8490
    @gastarpdg8490 Рік тому +1

    Barki Baye niass Lii nekh na mine nourihi bi

  • @tvmeta8628
    @tvmeta8628 2 роки тому +286

    Mais mbokk yi niou défaratt djiko yi ak téguinn yi si beureup yi rawatina si biir zawiya bi souniou yakkou khadj nasi

    • @abdouazizdieng8566
      @abdouazizdieng8566 2 роки тому +10

      Mashallat

    • @Sopeyayam
      @Sopeyayam 2 роки тому +16

      Billahi kheur rék. Yalla nagnou borom bi diégueul

    • @yayaly2652
      @yayaly2652 2 роки тому +2

      @@Sopeyayam 00

    • @mawdodieng655
      @mawdodieng655 2 роки тому +6

      Surtout les organisateurs

    • @ousmanebalde9542
      @ousmanebalde9542 2 роки тому +4

      Vraiment xolall mame Ass mbaye mii mell nii kou nekk thi mbedd niii