Machallah g commencer a suivre cette emission pour savoir l'histoire du Senegal. Parce que j'ai constaté nous les jeunes ont ne connaient l'histoire we nos aieux
Waxtaan wwi neex na lool, wante njariñ lee ëpp neexaay bi. Ngërëm luy law ba fàww la nu leen yoreel. Seen xam-xam dóotul réer mukk! Askan yiy ñów it dinañu ci jot ba xam fa ñu sosoo. Jar ngeen jëfati!!!
Macha Allah nekhna trop té amsollo
Elhadji ady Wade yalla n'alla yalla fan wogoudou
Wa wao👈👉 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳👍
Machallah g commencer a suivre cette emission pour savoir l'histoire du Senegal. Parce que j'ai constaté nous les jeunes ont ne connaient l'histoire we nos aieux
Walay sama khol sedna trop yala moy borom teranga yalnalen teral sagal len soutouralen maylen fan wou goudou