Oh lala lala thiébou diongué bi diongué na lol lol machallah no tata sa term yi momay danél walahi yalna sén diam yag tata yaseye mom ndékété yoo ci gayi leu
Ma Sha Allah #Yass wathiégafi ba zéro tata #marietou merci encore une fois yalla na yalla motali yéné gnieup thi barké #SALATOUL FATIHA kooru diam rek bisous je t'aime 🙏👍🇸🇳❤
Yass toth nguafi Macha Allah. Sokhna Marietou sa liguey raftna, amna solo. Yangui diapalé djiguene you barré. Man ben togue reer ratouma ndax yow. Yalla na ligueye bi barkel Dieureudieuf Mame Diarra depuis italie .
Non nekker Tata Marietou la beugeu néna très bien, yaw dal tata doundal 100ans sans ordonnance ,tiebou diongué bi tokki tokki na ,wa li nekhoul rek 😍😍😍
Toucha touchal mbichi mbichal 🤣🤣🤣 Masha Allah sister Mariètou Artiste nga. Non seulement sa ay toga de gnou ndiongè mais language bi da fa ndiongè aussi. Me and my daughters love to watch your videos ❤️ 🙏🏾
Je vous adore vous me faites tellement rire je suis vos recettes tout les jours je vis au Canada depuis presque 20ans quand je regarde vos recettes le lendemain je le copie à la maison et partage avec mes amis québécois mercii😘
@@codoufari4988 Merci pour ta réponse.. Mais moi j'avais compris garlic closs du coup je ne savais pas trop c'est quoi le closs et j'ai demandé.. Merci de me dire que c'est clove sinon je connaissais très bien la signification de garlic clove..
Tres bien,! very 👌 nice. You should have a cook book in French and English. I guess you speak Arabic too. I am from Liberia and speak English. Senegal speaks English also.
Tata Marietou ak sa vidéos yi souma meunouler togg ma khamni mon cas est désespéré 😂. Merci beaucoup pour les recettes ça me permet de connaître d'autres techniques autres que celles de maman
😍🍀💚🌿☘ quand je pense que je suis abonnée y'avait 5000 abonnés et maintenant elle est a 60k c'est magnifique ça veut dire ce que ça veut dire daal. Au 100k naak marietou na def ngourbane pour begual serere yi comme maane fi ak mborokhe. Je t'aime waay 😘😘🇸🇳❤
Walaykoum salam ndaw mahallah yalla na diam yageu ya seye yalla nako yalla défal diam soutoura goudou fann limou beuge moko kham yalla nakoko yalla délaf🙏🏾🙏🏾😘😘😘😍😍
Salam comme tout le monde t appelle Tata Marietou moi aussi je fais pareil 😅😅 Linguay tog nekhna tei lekoumassi wayei kou kham tog guiss affaire yi diaar nayoone seulement nga balma ndakh boudone sama sago boye talalei tomate nga diluer ko ak touti ndokh après nga dogal sa tomate. Maintenant nak sa langage guissouma loussi nek vraiment am nga yaar sa wakh rafet na yaw dal Machalah rek 💖💖💖💖👍👍👍🙏🏼🙏🏼🙏🏼
5 років тому
Yaoma Diagne Waaleykum salaam ohhh Masha Allah dieureuf kou bakh nga
Oh lala lala thiébou diongué bi diongué na lol lol machallah no tata sa term yi momay danél walahi yalna sén diam yag tata yaseye mom ndékété yoo ci gayi leu
Ma Sha Allah #Yass wathiégafi ba zéro tata #marietou merci encore une fois yalla na yalla motali yéné gnieup thi barké #SALATOUL FATIHA kooru diam rek bisous je t'aime 🙏👍🇸🇳❤
Ouh thieb bi diongué na ba yègue ci looool masha allah, todie nguène fi radiakh
Tata marietou mala beugue piiire doundeul Lou bari❤😍
really u a gud cook
Yass toth nguafi Macha Allah.
Sokhna Marietou sa liguey raftna, amna solo.
Yangui diapalé djiguene you barré.
Man ben togue reer ratouma ndax yow.
Yalla na ligueye bi barkel Dieureudieuf
Mame Diarra depuis italie .
Good guekh🤣🤣tata marietou love you ak say terme 😍
Wawaw bakhbou niakdiom😁😁😁
Aye Tata Mariétou😂😂😂 trop drole Yaalna sa jaam yagg❤❤
Non nekker Tata Marietou la beugeu néna très bien, yaw dal tata doundal 100ans sans ordonnance ,tiebou diongué bi tokki tokki na ,wa li nekhoul rek 😍😍😍
Amine yarabi
Relleu dji ak telleu dji sama keur khalé yi mome euyway laniouy répéter ba legui toubab you nioulyi😂😂😂maachaa Allah amna solo
😂😂😂 C vrai k languageou Tata marietou beneu lafi
tata marietou mane daleu yaw la beug . ton langage me tue machallah!
Mashaaalllahh bi d la nara oubeh koor gui In shallah. Merciiii tata et ton invitée
Toucha touchal mbichi mbichal 🤣🤣🤣 Masha Allah sister Mariètou Artiste nga. Non seulement sa ay toga de gnou ndiongè mais language bi da fa ndiongè aussi. Me and my daughters love to watch your videos ❤️ 🙏🏾
Je vous adore vous me faites tellement rire je suis vos recettes tout les jours je vis au Canada depuis presque 20ans quand je regarde vos recettes le lendemain je le copie à la maison et partage avec mes amis québécois mercii😘
Machala defati ga sa bakh bakh👍👍👍🌷longue vie à vous
Peukh peukh 😂😂😂😂 bahou gnakeu diomeu bouy creer embouteillage😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 ton language est unique, yaw rek ya ko meune
Ndeye Khada Diop non opeuna 😹😹😹
Ay ndiobene yi
Bilay mane moy sama anti stress
Ndeye Khada Diop 🤣🤣🤣🤣
Eupneu wayyy
Bi amoul Tata marietou..Machallah...mane deh yow rekkk....mague bou meute magg....laftiat
Yii Tata marietou tiep bii wouyouna toureum tiep bi dafa diongué ba yakou machallah
No tata raynama mashalla yalla na yalla faye la
Podiosss no guen d'ou Tata maretou c biennnnnnnnnn
Wawaaaw thieb diongueh bi Ndiaye la sant Macha Allah merci Tata Marietou li eupeuna 😍😍😍😍😘😘😘
Eupeuna sa thiep Dal bakhna C'EST BIENNNN😅😊😊😊😋
Tressss bien bi rek lounei la 🤣🤣🤣🤣 Thiep bi wakhou nopi
Machalla li tamit eupena tata beugue na li man
Une minute de silence pour tous ceux qui ont mis dislike 😂😂😜
Thiatou Papam dagnou dof la yakar
Thiatou Papam bilay wakhal deh .. niom wérou niou
Nanie len balle sen khol moy peukh peukh woooyyy
Rires:)) c'est le gens qui aiment le foufou ce n'est pas tout le monde qui aime le thieb.
hahaha
Ouloulou 😂😂😂 nonnnn tata marietou fait ma journée
diang na ci moule yi mashallah!!!merci tata goudal fane waay
Maria DIM Ameen ak yaw
Tay môme salléne yi dinagnou simi ndawéne bi. Wayé nak théb bi amna solo lol.👍👍👍👍👍
😂🤣walla au contraire
Dykha ndao sallène yi souminaniou lène bou yaag Hololilolilolo🤣😂😂🤣😘
@@ndeyearamesall7013 mané ndawéne gno simbi salléne.da ngana beugue leka ba soléne guissé léka manolénko mougne
Dykha Ndao balnala 😂🤣😂😂🤣😘 C'est gentil ! Ravie de faire ta connaissance🤝🤝🤝
@@ndeyearamesall7013 Merci a toi aussi 😘
j aime regarder té vidéos nekothi relhhh rek mo may ray love you tata
Ndiobéne sa thiep bakhna ma sha Allah, tata marietou dell bakhe amine rek
Mane daal mala beug Tata Mariétou yanala Yallah sameu yirla diamalela amine 💋
merci ndaw seydou aly yalla nala yalla défal diam je t'aime❤❤❤❤😍😍😍😘😘😘😘😘😘
mame fama ndaw ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
TOutiou toutieul neko si touy😂❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️tata marietou ngay am fofou
Machaallah yaseye sa thiep djongué na. Wayé Tata mariétou say expressions moma nex.
Mane commentaire yi Tata Marétou nane telleu cii togue gui molmey réyy . Masha'ALLAH lep diarna yoor
Mashallah tata mariétou astuce bou béss Wa li nékhoul.
Yalla nassa diam yague trééés bieeen😘😘😘😘😘😘😘
yaseye contanay trop beuguena li mane machallah
😂😂😂yaw rombal
MACHA ALLAH WA mé tata mane guisssa gouma thiebou diagga deh té dama ko beug
yalnala yalla defal diam
Mahchahala merci yalla na sén diam yagu lolou sunu tata yi thi sén generosité
Merci bcp tata
MACHALLAH Mariétou neko si rell ya mey fathie
Tata Marietou , yangui mayyy dadji walahiii,.......masha allah ,fans number 1 ...non je suis contente
Nathalie Diallo 😘😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️😂😂
Saveurs Planétaires Machalah
Mashalah am na solo
Ta marietou Yalla na goudou fan kouné amine dagay goudou fan sa ben sopé depuis italy❤️❤️
fadiengsaala dieng amern
Très bien machallah chef
Ohhh lii Eupeuneu Djongue 😜😜😜😜
Merci pour ta joie de vivre. Que Dieu te garde par sa grâce et sa miséricorde. Amine inshalla mashallah. ❤️❤️🥰🥰💋💋❣️❣️💕💕💓💓
MACHALA bi môme surprise la koy def dokou merci tata
Je suis nouveau à suivre tes plats mai j'adore surtout ces façon de parler
Ehhhh gnio bok tour ak sante wa li nekhoul
Ehh gnio bok tour ak sante wa li nekhoul
A lolou forna sama toma mo takhe ga bakhe ziar nala
@@teningdiouf4220 delo ziarrr ma pupuce
Yallah na yallah nagou ziar toma
No tata marietou dinama raye très bien.......🤣😂😂😂😂😂
Merci pour tes plats tata Marietou
Je viens de m'abonner mais youbi yaba migui May Ray manoumako mougne
Tu agréable a écouter machalla
Tata on veut voir le Visage qui se cache derrière cette douce voix machalla.
étoile filante c.
//“
Macha Allah tata youbou yaba no stress avec vous longue vie 😂😂😂😘
Yasseye tell telle na lii nekhna tee gnamoumako
neuuuk kay non ak mbith tata machalla niogilay khar thi koor gi inchalla
Machaala !!! a essayer encore merci bcp
Mashalah 1ère .. Longue vie Tata Marietou❤️❤️❤️
😂😂😂 deguna terminuse 😂 main machalla thiep bi bi wouyouna tourame
Machalla j'adore toute t'es recettes merci infiniment
Wa li nekhoule très bien c est comme ça
Très bien tata marietou yaye sama idole di dogue malla beugeu machala
Faty Diaw 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Ndaoenne bi bilay ya bah si sallenne yi😍😍 mane dal beug nala liiiii
Trop beau à voir kouko niam am lou bari merci way
Machallah machallah machallah na ress ak diam 😘😘😘
bsoir tata marietou sa ligueye refete na machaala; GARLI CLOCHE moye lane
Merci beaucoup tâta Marietou tu es unique merci
Machallah merci tata pour l'astuce des huitres amna solo vraiment 😍😍❤️❤️
Hahahah tata mariètou beuguone na sa num dei si possible..je te love forr
Waw tata beugone naa khame lane moye garlic closs mane france la nek nane lagne koy wakhé thi français ma sete kofi.. Merci tata 😘😘
Thiatou Papam amoufi Canada la am mais tu peux commander garlic plus sur Amazon
@@chachou6467 Merci bcp ma grande
Garlic cloves moye gousses d'ail... Walabok😄...
Ma shaa Allah... Lafthiat😘
@@codoufari4988 Merci pour ta réponse.. Mais moi j'avais compris garlic closs du coup je ne savais pas trop c'est quoi le closs et j'ai demandé.. Merci de me dire que c'est clove sinon je connaissais très bien la signification de garlic clove..
Tres bien,! very 👌 nice. You should have a cook book in French and English. I guess you speak Arabic too. I am from Liberia and speak English. Senegal speaks English also.
Mann yenn la Guemm 😂 nehatina dall😘❤️merci beaucoup tata 😘
Da gua bakh rek mo takh ga diaboté yeup big kiss 😘 I wish you the best
mbene hair 😘😘😘😘😘😘❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Oh la la!!!! Merci bcp happy iftar à toi aussi
Rama Traore 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Machala 💝💝👌👌👌✍✍✍
Machalah li n'ak monye deugueu deugueu thiébou diongué
Tata Marietou ak sa vidéos yi souma meunouler togg ma khamni mon cas est désespéré 😂. Merci beaucoup pour les recettes ça me permet de connaître d'autres techniques autres que celles de maman
Sa holala rek eupeune tata Marietou😁😁😁😁 limala beugue rek HOLALAAAAAA
😍🍀💚🌿☘ quand je pense que je suis abonnée y'avait 5000 abonnés et maintenant elle est a 60k c'est magnifique ça veut dire ce que ça veut dire daal. Au 100k naak marietou na def ngourbane pour begual serere yi comme maane fi ak mborokhe. Je t'aime waay 😘😘🇸🇳❤
Ci yaw lay roy sey togu bahna machalah
Machallah ce bien c'est tres bien diongue😂😂😂 de Tata 😋😋😋😋
Tata mariétou je t'adore bonne continuation.
Ahhh tata marietou Man Mala ndeyalé sama bopou
Thiébou jonguei bi deff na jongama dei Tarkallah ak ay nécessairam niaafff I like👍😍😗💃👌💟💖💚
Mane dall legui baral bouy tokhi tokkhi lay def ma bayi bakhou gnak diom 😂😂😂
Macha allah ta marietou Man de diangue nassi sakh car khamou ma wone ne moule bi oubekou bakhoul yalla lokho bi wer c est magui
magou ndiaye Ameen waayyyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️😘😘😘😘
Walaykoum salam ndaw mahallah yalla na diam yageu ya seye yalla nako yalla défal diam soutoura goudou fann limou beuge moko kham yalla nakoko yalla délaf🙏🏾🙏🏾😘😘😘😍😍
Mashaalah! Inshaalah je vais essayer 😘😘
Tata Dinama dadji nena sobi ladoul tayy😁😁🤣🤣🤣😘
Awa Cissé 🤣🤣🤣🤣🤣
Euyyyy wayyy bou maman marietou bi rayenama 😆😆😆😆
Waw mane Tata marietou mii warna guiss kanam gui dh machala 😍j'adore la cuisine
Mariétou tu me donnes des idées
Incha allah demain je vais essayer de '''diongué''. Ahaha
Bon appétit. Miam miam
El podioss 😂😂😂 contane thi yén niko thi rel merci mariétou amal diam
ya seye borom deureudieuf mala beuge pireeee😍😍😍⚘😘😘
Machalla mercie
Téré bien chez bien 🤣🤣🤣🤣 tata Mariétou machalah ya bari fem.
Mane tata marétou la beugeu😂😂 peukh peukh
Très bien😂😂😂😂😂
😁😂😂😂😂😂😂
Mère vraiment on est content de toi et t écouter c est un plaisir 😘😘😘❤