Sokhna Aida Saliou dit tout

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 13 гру 2024
  • Dakaractu, la chaine d'information en ligne!
    Abonnez-vous à notre chaîne sur UA-cam : www.dakaractu....
    Rejoignez nous sur Facebook:
    / dakaractupointcom
    Suivez nous sur Twitter :
    / dakaractu

КОМЕНТАРІ • 966

  • @sokhnadiallo9013
    @sokhnadiallo9013 Рік тому +4

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Dieureudieuf Thioune Dieureudieufeuty Serigne Béthio Sokhna Aïda Saliou Thioune Yalla ngafi yag lolou té gueneu wér andékok sa amir yi barké Serigne Saliou ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿💫💫💫💫💫💫

  • @abdouhdndiaye7546
    @abdouhdndiaye7546 5 років тому +163

    Au lieu d'aller dans les marchés posés de questions vrai femme battante qui se lèvent à 6 du matin.. vraiment C désolant Sénégal

  • @dikha7525
    @dikha7525 5 років тому +136

    Qu'Allah te guide ma sœur ! Répand toi et essaye de remercie Dieu et Son prophète Mahomet psl.

  • @amargueyeat-tidjanya
    @amargueyeat-tidjanya 5 років тому +103

    Thiey Sénégal lègui mom wakhii serigne mo fi soutt wakhi yalla
    Naniou diamou dji yalla tè basi thiakhann yii

    • @serignezall9405
      @serignezall9405 5 років тому +1

      amar gueye wallaye wakh nga deugue

    • @serignezall9405
      @serignezall9405 5 років тому +6

      Wayé nak lépe loula nite wakhnè serigne touba ko wakh walla serigne saliou loudoule yalla ak yonénete biii wakhi bopame la wayé dou wakhi Sérigne biii

    • @mouhamedgueye688
      @mouhamedgueye688 5 років тому +1

      Wakh nga deugue dé

    • @mbenguethiamba3084
      @mbenguethiamba3084 5 років тому +3

      Amar Gueye boul guiss ki rék ne Sénégal wakhi serigne mofi soutt wakhi yalla ki limouy wakh mome la nioune Wa Sénégal sounou yone nékou si

    • @serignezall9405
      @serignezall9405 5 років тому

      Mbengue Thiamba ndaye khamena da dioume si wakh dji rék

  • @fatimrabydiaou7588
    @fatimrabydiaou7588 5 років тому +106

    Elle a était plus maline que les autres elle est très éveillée et stratège

    • @ladivandiaye2230
      @ladivandiaye2230 5 років тому +2

      Bilaye deug nga wax

    • @ahmadoundaw835
      @ahmadoundaw835 5 років тому +2

      Deug nga wakh dh

    • @katypendagueye6278
      @katypendagueye6278 5 років тому +9

      Manipulatrice en plus

    • @sundayroblox9860
      @sundayroblox9860 5 років тому +5

      C'est vrais elle a un but dans sa vie c'est une vrai manipulatrice djanguoul sakhe

    • @fatimrabydiaou7588
      @fatimrabydiaou7588 5 років тому +5

      Titiya Mbaye salut madame répond les gens avec un peu de respect on est libre dire ce qu’ont pense

  • @talladiallodiery
    @talladiallodiery 5 років тому +76

    Elle a tout compris,cette bonne dame;elle sait que affairou tarikha lègui dou dara loudoul ay arnaque ak ay deal.Nékal bandit comme sa dieukeur rek et tu iras loin

  • @ndiogoudiop5390
    @ndiogoudiop5390 5 років тому +243

    Kouné Sénégal nekhoul danga amoul connexion

  • @s.saliou3010
    @s.saliou3010 Рік тому +2

    💜💜💜💜💜DIEREUDIEUFETY SRIGNE SOKHNA AÏDA SALIOU DEUGUI DEGUI DIEUMI SERIGNE BÉTHIO YALLA NAFI YAGG LOOL ANDÈ KOK BOUNTAM YI 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @linvincible2967
    @linvincible2967 5 років тому +17

    Yallah nagnu yallah wonalé ak Seydina Mouhamad psl.

  • @biglycolofficiel2946
    @biglycolofficiel2946 5 років тому +6

    Bilay kou mér sa xol moy dageu rek Serigne saliou bamouy def kéneu fékéwoul té tagouwoul kéneu ni kou bakh loumou khamoul dassiy mandou dieureudieuf Serigne saliou Serigne béthio yalna fi yageu té wer

    • @cheriadjisarr6166
      @cheriadjisarr6166 4 роки тому

      Katal sa ndeye feulé yeneu cheikh ibra boufi nekone ay kour dinalene sapi

  • @awagueyeniang739
    @awagueyeniang739 5 років тому +59

    Man Waxouma waxou Femme bi dh mais journaliste xawma animateur bi Tokk thi souf MoMA Ray 😁😁😁😂😂😂

    • @khalifandieguene8576
      @khalifandieguene8576 5 років тому +1

      Yaw tu crois k y a une femme plus battante kél khamoléne sakh lane moy une fam exemplaire

    • @TheDiogop
      @TheDiogop 5 років тому +2

      @@khalifandieguene8576 wakh niou louy femme battante alors

    • @gorandoye3769
      @gorandoye3769 4 роки тому +1

      Modiakhal gnépou 🤣🤣🤣🤣😁😁

    • @moustaphaloum6360
      @moustaphaloum6360 4 роки тому +2

      😂😂😂😂😂

    • @Smokin_mass33
      @Smokin_mass33 3 роки тому +1

      Je ne suis pas du côté de la femme mais c'est juste qu'il n'est pas orgueilleux réfléchis bien

  • @fatoundure5849
    @fatoundure5849 4 роки тому

    I love your massage. Ma sha Allah. Jerrejef sohkna ci

  • @senegambiaboy5061
    @senegambiaboy5061 5 років тому +59

    Mes béthio louko déff serigne ak touramm bou doff bi
    Yalla nanou yalla mousall si bithio aki seytanémme

    • @moussaarfancamara4959
      @moussaarfancamara4959 5 років тому +1

      Sa data ndeye domerame bie

    • @khalifandieguene8576
      @khalifandieguene8576 5 років тому +2

      Yaw katal sa ndey ki dou Serign kne dh adouna kéne doufi Serign
      Ay doméra nguéne rk ak Serign Béthio limou déf si adouna ak gnimou défar gnép ba takh dougnou toukh dougnou nane dougnou moy doméram yinguéne done

    • @TheDiogop
      @TheDiogop 5 років тому +6

      Sen vulgarité ak agressivité déh ghalene di khamé....serigne bé léne gueuneul Yalla Yoninthe ak séni wadiour

    • @papaalioufall4115
      @papaalioufall4115 5 років тому +2

      Wa Sénégal nékhoul tmt Cheikh bi louko def Serigne may léne niou way guéniy dague ay sagua

    • @sambcheikh4159
      @sambcheikh4159 5 років тому +1

      serigne touba liko yalla May koumou nakhary thi torokh ngay deuk

  • @byby2740
    @byby2740 5 років тому

    sunu serigne sokhna aida thioune yalnafi yagg lolou te werr yaye tiobaree cheikh bethio yaye moom parforce

    • @assanediallo9926
      @assanediallo9926 5 років тому

      Loudoul deugua douyagua biirr mi Amatoul rire dé

    • @byby2740
      @byby2740 5 років тому

      @@assanediallo9926 17 avril 1946 balegui nganane amatoull rire yaw xana newofi wala danga cataracte guisso wala danga teukh deggoo sa kholl moy pollou mbalite

  • @marseck2909
    @marseck2909 5 років тому +32

    Mbok yi nanou diamou yalla dé yokou sunu thiofél thi yonéntibi(geunél deugg moy yonéntibi)

  • @sokhnaastoudia5226
    @sokhnaastoudia5226 5 років тому +3

    Nagn lén diamou ji yalla té bayyi thiakhane yi nagn déllou si ndigalou yalla ak diangalé yonnénte bi(saw) yalna gnou yalla mousseul si gni rére tey réralaté

  • @samaypapier8279
    @samaypapier8279 5 років тому +27

    Entouka tu est tro Belle ..

  • @rastavanch2000
    @rastavanch2000 4 роки тому +2

    Dieuredieuff THIOUNE 🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤

  • @fatmadiop666
    @fatmadiop666 5 років тому +181

    Sokhnassi mooy niane nonou ak ay ongles😂🤣🤣

  • @khadyfaye3786
    @khadyfaye3786 5 років тому +14

    Waaa yeine Aida diallo dagn ko cheikhal? Jpp😂😂😂 xolal mère yi di diébeulou sheuuu mon pays va mal 😂
    En passant elle est très belle

    • @dialloboubacar8218
      @dialloboubacar8218 5 років тому

      Khady sa ladj bi amna solo. ken khamoul li loumou done. Pourtant cheikh bethio amna taou bou goor.

    • @fatoungom3811
      @fatoungom3811 4 роки тому

      Rafet dall deff nako

  • @sakkortv8623
    @sakkortv8623 5 років тому +7

    Cheikh bethio thioune djiamoup s. Saliou mbacke yalla ngafi yagu lol te andak werak werle barkep s abdou sakor damay guiss nit gni danu lay dingat rek di wax dieume si yow damay guiss dangay geuna yoku rek te dangay dieuf doko bole ay wax nit gni am djiot rek di wakh rek kuy dokh di dem rek lanuy dingat yagufi thioune 💞💞

  • @lalachadiallo520
    @lalachadiallo520 4 роки тому +1

    Do meusseu giss niouy diangue alkhourane mai santé rk thieuy. Yalnaniou yalla dieggal rk lolou rk l'ay niane

  • @mimimbengue4846
    @mimimbengue4846 5 років тому +63

    Dama yakarni la fin des temps est toute proche, je sens la présence de Al Dajjal au Sénégal

    • @sidy.el.chekhdieng2746
      @sidy.el.chekhdieng2746 5 років тому +5

      Amina,, on est ala fin des temps puisque le temple de Dadial est déjà construit..aussi le mahdi est parmi nous . et Jésus est en route donc le monde est fini...

    • @mamyndiaye8984
      @mamyndiaye8984 5 років тому +1

      Ded way al dadjial kay boumou fi gneuw

    • @sidy.el.chekhdieng2746
      @sidy.el.chekhdieng2746 5 років тому

      @@mamyndiaye8984 non j'ai pas dis qu'il va venir au Sénégal mais il est déjà né.il est avec nous dans ce monde je veux dire...

    • @curvybaeka1148
      @curvybaeka1148 5 років тому +1

      Sidy.el.chekh Dieng Allah le trés misericordieux a dit k dadjal passera partt dans l monde inch allah

    • @sidy.el.chekhdieng2746
      @sidy.el.chekhdieng2746 5 років тому

      @@curvybaeka1148 alkhamdoulilah tu as parfaitement raison mon ami

  • @sundayroblox9860
    @sundayroblox9860 5 років тому +32

    Et le saint coran sa devrait être le numéro 1 et sa doit être vous me faites pitier Mme de la peine même

  • @yacinesarr2275
    @yacinesarr2275 5 років тому +88

    Bayilén serigne touba mom wakhoul li dé

    • @papandiaye979
      @papandiaye979 5 років тому +1

      yacine sarr mo serigne bi nii di ay domou kharame

    • @ndeyefatou7526
      @ndeyefatou7526 5 років тому

      Geume léne yallah yalla ameuna yaw wodoule sa békhio tené moute ameuga fiite trop hiiime

  • @ahmadaadiouf1897
    @ahmadaadiouf1897 5 років тому +85

    Thiey YALLE c'est le monde à l'envers

  • @labarhamistekanejalloh801
    @labarhamistekanejalloh801 5 років тому +23

    Où va ce monde ??? Li nak moy akhirou zaman Qu'Allah nous préserve de l'égarement

  • @aminatambengue6830
    @aminatambengue6830 5 років тому +15

    Lahilaha ilalah soubhanalah akhirou zaman yalnaniou yalla dooli soutoura 😢😢😢😢🙏🙏🙏🙏

  • @yamadrame3860
    @yamadrame3860 5 років тому +97

    Barké serigne touba yaw AIDA DIALLO danga yapp domou adama yiii

    • @tk92221
      @tk92221 5 років тому

      Yama Drame bopam rék. Naniouko settan rék

  • @muna326
    @muna326 5 років тому +31

    Je te le jure j'ai pitié, reviens sur terre tey khamné yalla mouguifi ce que le prophète paix et salut sur lui nous a enseigne sur le saint coran personne ne peut effacer sur terre.

    • @khalifandieguene8576
      @khalifandieguene8576 5 років тому +1

      Sim khawma loutakh nguéne nagué rk so diké si képarou Serign Béthio lo khamone si yalla dingako khép doff yinguéne done

    • @TheDiogop
      @TheDiogop 5 років тому

      @@khalifandieguene8576 yaw ya toukh sa yamba niou Ndandal la sa biir feess yakarni bethio moy le Créateur....vas voir un spy pour ton bien

    • @abdoulayeayande2873
      @abdoulayeayande2873 5 років тому

      Mane deh khamouma waye sokhena Aida dagua wara du kalawou

  • @damendiaye9737
    @damendiaye9737 5 років тому +22

    Yamana féne doudara si serigne touba daraye serigne touba necoul si yaaw

  • @babacarniasse4382
    @babacarniasse4382 5 років тому +2

    Man dé beugueul KOU TEDD KI REK.
    rawatina mou tekk ci mokkal ay xassida..
    DIEUREUDIEUFF KHADIMOU RASSOUL

  •  5 років тому +68

    no femme bi vraie comedienne la koi

  • @cheikhbi2056
    @cheikhbi2056 5 років тому +123

    Comédie Show. Borom micro moo gueuneu niakk fayda nieup.

  • @biramdiagne7697
    @biramdiagne7697 5 років тому +39

    talibé yi diebalou si CHEIKH bi
    CHEIKH bi diebalou si diabaram😂😂😂😂😂 khamna goudi ya nekh rekk

  • @bvediarrachousene5832
    @bvediarrachousene5832 5 років тому +9

    Ndaysan soxna aida mom sama yayou bop leuh aka mo bakh té woyof beugu nitt té yatou mana wakhtan yaye boy long vie rk inchalla

  • @rassoulounahseck9823
    @rassoulounahseck9823 5 років тому +30

    Kii dafa meuneu doull koi bilahi,té bolén ko dégloo bou bàx, limouy beug wax dakoy wax indirectement.ay ( cheikh bi néna maay mom té Serigne Saliou néwoon nako yay man may yow té Serigne Saliou moy Serigne Touba) imaginer ce qu'elle veut dire par là, ki elle est très dangereuse Walahi
    Mais nak lép rék Cheikh Béthio mo matoul ndjiitt c'est ça la réalité

    • @khalifandieguene8576
      @khalifandieguene8576 5 років тому +1

      Moh yaw katal sa ndéy felé ngay wakh Serign Béthio moniko yaye mane may yaw yonou kéne nékoussi goor djiguéne binda done meno léna mandou khana tamite

    • @rassoulounahseck9823
      @rassoulounahseck9823 5 років тому +1

      ishh bàl nàla
      Vous croyez yéna gnou gueun nék ay mouride , walahi vous me faites rire

    • @rassoulounahseck9823
      @rassoulounahseck9823 5 років тому +2

      qu'Allah vous guide

    • @abdouldiop71
      @abdouldiop71 5 років тому +2

      Daddy RASSOUL
      Tavais vu juste mon frère bethio es responsable de cette situation

    • @rassoulounahseck9823
      @rassoulounahseck9823 5 років тому +1

      @@abdouldiop71 bilahi wax ga deug

  • @mamefatyfall7181
    @mamefatyfall7181 5 років тому

    yalla ngafi yague lool Sokhna si

  • @minaaa3981
    @minaaa3981 5 років тому +83

    Moudié niew âme rang bou keneu amoule xamna de saflé gua troppppppp

  • @modytoure5278
    @modytoure5278 5 років тому +5

    Mdrrrrr non aida mo nekh pose ongle yi la meunoul mougne ak niane gui🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @sunulibertetv4518
    @sunulibertetv4518 5 років тому +8

    Mais li sa ce passe dans mon pays ooo senegal va mal 👿 que dieu nous vienne en aide

  • @khadytoure3992
    @khadytoure3992 2 роки тому

    Sokhna aida saliou thioune Sama sangue bi dieuredieuf ❤❤

  • @mendesshasha1021
    @mendesshasha1021 5 років тому +3

    Bamou komencé wakh ba legui toudou Fi wakhi Yallah toud Fi Seydina Mouhamed psl. Ayway magui Sante sunu borom Bima donei dioulite done tidjane nakh ndeysane sunu mbeuguel SI Yallah moh foor. Sunu mbeuguel SI prophete fougn toll dikko tagu. May wakh mouna dieuwrign universelle ak regional. Yabatei

  • @Kn-cf8bq
    @Kn-cf8bq 5 років тому +2

    Machala li yep serigne saliou la

  • @mariamasarr7073
    @mariamasarr7073 5 років тому +4

    Yalla naniou yallah yeureum..

  • @ndeyebanadiop328
    @ndeyebanadiop328 2 роки тому

    Elle est maline en plus elle sais communiquer chaque question amna reponse

  • @myvision7647
    @myvision7647 5 років тому +52

    Ak regarou bandit bi🤣🤣🤣🤣

  • @fatougueye4774
    @fatougueye4774 5 років тому +1

    😅😥😥😥nn man bilahi Amna louma meti si mime reweu wa li nekhoul rek

  • @khadijaamar1845
    @khadijaamar1845 5 років тому +4

    😂😂 astafiroulah billay Sénégal dou dem 😯😯

  • @mama-df8dh
    @mama-df8dh 4 роки тому

    Sokhena si dagua bakhe trop tu es belle

  • @nabyseck2355
    @nabyseck2355 5 років тому +19

    Lii gèn dii déf dou diiné dou souneu dou sarikha dém lén diamou dji yalla ta gèn bay sén thiakhan yiii

  • @alassanesowseck6678
    @alassanesowseck6678 4 роки тому

    MAME YALLA DIEUREUDIEUFEUTIII!

  • @masscool
    @masscool 5 років тому +10

    Elle a été bien formé donc c'est elle qui est Cheikh Bethio qui est Serigne Saliou qui est Serigne Touba
    Mdr 🤣🤣🤣🤣🤣

  • @mameboussoguiro9851
    @mameboussoguiro9851 3 роки тому +1

    Bou lenn faté domou adama dou togn sokhna aïda ap serigneum moko fi tek té serign bethio moy serign saliou (ay wakhi serign saliou laa)

  • @lamptoubafall7548
    @lamptoubafall7548 5 років тому +3

    Souhanala yalla nama yalla dieguel ci limako sèetan ak dèegue wakh diou reuy bii

  • @khadydiouf609
    @khadydiouf609 Рік тому

    Mon chemin n'est pas dedans 🏃🏿‍♀️🏃🏿‍♀️🏃🏿‍♀️

  • @mamadoutopkoundoul9216
    @mamadoutopkoundoul9216 5 років тому +4

    Dieureudieuf Sokhna Aida kadou yi rafett neu walay Serigne Béthio woutéwul Dara ci biss bi té contane na ci ioe

  • @amygueye3882
    @amygueye3882 5 років тому

    💅💅💅 souma dégueu saye sakhe moye bethio moye yawou ngaye mome wayeu bolene toudeu te serigne saliou de

  • @diarryb1ba483
    @diarryb1ba483 5 років тому +19

    Avec tes ongles .yay diokhé nianne .hummm

  • @boromsamdiop9796
    @boromsamdiop9796 5 років тому

    Bilaahii wallaahiiiiii maallaaa sopeee loolllll ssokhnaaa adiaaaaa yaalnaa saa faaaannn guoudouuu

  • @notallanoparty8547
    @notallanoparty8547 5 років тому +4

    YAYE MANE MAYY YAWW 😂😃😂😂😂 SENEGAL NEHNA WAY

  • @serignecarlosmbacke759
    @serignecarlosmbacke759 2 роки тому

    Sokhna aïda Diallo borom kham kham leu Sénégal nioko khamoul

  • @ousmanesarr4142
    @ousmanesarr4142 5 років тому +84

    Wakhofi ben xam xam
    Del mourou mo geunn ngay diankou nii

  • @aboudiop8206
    @aboudiop8206 4 роки тому

    Yalla Nanou Serigne Touba Atée ak yieux

  • @shaimalapuissance2959
    @shaimalapuissance2959 5 років тому +6

    Khamna boy diouli xassida yi ngay use😂😂😂
    Wallahi li dou dinné goor gni gnak fayda gnak foula topou si guinaw djiguéne di yaparr yapar djiguene bou khamoul baa khamoul siin
    Sokhna aida mi kouko top diakhanenama nga dieum khamoul khamé woul kham lé wouy
    Bo deguei gnouy nane serigne ndieurigne motakh ta ndieurigne bi moy mou meune la eguali si yalla tegue la si yonou ndioub diangal la kham kham ndakh kham kham moy yor rew
    Sokhna aida bangay wakh batey tibé wo si al quraan tibé wo si souneu
    Yalna la serigne touba diegal togn bingakey togn rk

  • @fatimadiop8383
    @fatimadiop8383 5 років тому +1

    Ya rafete kar machallah toye rek nga def

  • @cheikhka5611
    @cheikhka5611 5 років тому +21

    Mandaal dema wara change nationalité doon gambien senegal chakhan yi defa bari

  • @evagassama9831
    @evagassama9831 5 років тому

    Mais aida dekeur na fite dé😅😅😅

  • @sultantv5205
    @sultantv5205 5 років тому +9

    😂😂😂 j’aime mon pays thiakhane fi la féke bakh

  • @tourecheikh1858
    @tourecheikh1858 2 роки тому

    DJEUREDIEUFÉ SERIGNE TOUBA
    DJEUREDIEUFÉ SERIGNE SALIOU MBACKÉ

  • @babacargueye9760
    @babacargueye9760 5 років тому +6

    14 février 2016 ah Ndeysane yaw dal jour Saint Valentin lala bethio cheikhal

    • @curvybaeka1148
      @curvybaeka1148 5 років тому +1

      babacar gueye 😂😂😂 limko pareil mo richone

  • @aboudiop8206
    @aboudiop8206 4 роки тому +1

    Guir yalla bayil Serigne Touba trankilment

  • @bambyniakhate5003
    @bambyniakhate5003 5 років тому +14

    Boul djouli Bo déh wé nga khamné lèpp deugue leu. Bodoul djouli bo dèwé déme safara rèk.

    • @khalifandieguene8576
      @khalifandieguene8576 5 років тому

      Safara dh diouli kate yi gnokoy féssal ndakh di diouli di khalate lénéne t nguéna gnane yermandé yala mo guene si yéne dh

  • @omarsene1223
    @omarsene1223 4 роки тому +1

    Bilakhi thiagua bii mo mona doul dégg_déggg

  • @bakaridoumboya1972
    @bakaridoumboya1972 5 років тому +18

    Diabarou bethio bii molna deh

  • @seynabousagna6283
    @seynabousagna6283 2 роки тому

    DIEUREUDIEUF THIOUNE SERIGNE BETHIO ❤️❤️❤️

  • @alioubadaradiouf4441
    @alioubadaradiouf4441 5 років тому +16

    thiey Yallah momena mougne wallay kou de xamne Yallah dou thiaxan

  • @lalachadiallo520
    @lalachadiallo520 4 роки тому

    Khamna mom bou Serigne saliou meunone djougate bly dingene giss Lou yéme

  • @faloutall8699
    @faloutall8699 5 років тому +15

    Bilahi kusi am 3 sibir bamel diga khamne lepou dagala bilahi

  • @s.saliou3010
    @s.saliou3010 Рік тому +1

    DIEUREUDIEUF THIOUNE XOL YI SED NA XEL YI DAL NA 💪💪💪💪💪💪💪💪💪

  • @sereroubamba7956
    @sereroubamba7956 5 років тому +6

    Biilahii gnii daañoo reeer,c'est elle qui a commandité les meurtres de madinatou salam

    • @binambaye3564
      @binambaye3564 5 років тому +1

      SEREROU BAMBA ahh bon demgua procès ba beu wakh kofa?

  • @antoinettesemedo3555
    @antoinettesemedo3555 5 років тому +1

    Dieuredieuff thioune aka yaniou dimbali sou gayi di wakh rek ngédi dieuf wakhou mame cheikh ibra bii rek ba kérok yalla difay wax bayi dieuff. .. yaye djeumi s.bethio té taloubé gueneulléne thioune yaguefi looooool té weer

  • @bougnaw
    @bougnaw 5 років тому +10

    Lou teugueu tass. Teyit loudoul Yallah nene la!!!

  • @fatousamb2992
    @fatousamb2992 5 років тому +1

    Dieureudieufeuty cheikh bethio thioune yagg fi looll THIOUNE c'est EL hadji samb môme Serigne bethio touba Mabo

    • @serignesaliouniang4227
      @serignesaliouniang4227 5 років тому

      Iow diémala sant yalla mo guene béthio dalén nax rekk ap domram la

  • @ndimbelanendimbelane421
    @ndimbelanendimbelane421 5 років тому +4

    Bayilen Serigne touba mi ngen di fowei ta ngen yem si s’en bethio
    Wa procés madinatoul Salam bi foumou tolou mba dou wadji da 🏃‍♂️ courir 🏃‍♂️ daw

  • @mamouhamed8255
    @mamouhamed8255 4 роки тому

    Serigne touba lila binede roumna choukou rallazi waya binedoul roumna chaakor

  • @linguerembodji8733
    @linguerembodji8733 5 років тому +9

    thiéeey Sénégal loutakh mandou wougnou moma yéme kii limouye ame nakko ba nopi lidieunti leine s'en problèmes

  • @madiorgueye728
    @madiorgueye728 4 роки тому

    Nitt kou nitte Day deg chéri tega kay ma tak la rek bilahi nop je t'aime aïda diollo love you love you

  • @kdkit9881
    @kdkit9881 5 років тому +15

    yew baîl thiakhan dagney mogal kouran bopare soka dieul khasida ndakh s touba thine douko fowé billahi

  • @beuguebaye4864
    @beuguebaye4864 5 років тому +1

    D'après cette femme, Serigne Saliou a dit: "diouli lakeu diouli woul lakeu", Cheikh Béthio lui demande: "Loussi pékhé ?", Serigne Saliou répond: "Diapeu ci Serigne Touba rek"
    Si cela est vrai, je perds tout estime que j'avais envers Serigne Saliou. Inconcevable de décrédibiliser ce que le prophète saws nous a amené pour autres choses. Ne vendons pas la prophétie pour quoi que ce soit

  • @yacoubfall123
    @yacoubfall123 5 років тому +12

    Vraiment le khalifa général doi intervenire sur sa

  • @salmadiallo6187
    @salmadiallo6187 5 років тому +2

    Mane gni diébalou gnoma df ay rirr😂

  • @fallcheikhibra1155
    @fallcheikhibra1155 Рік тому

    Kouddoul xalaat bammèl loulaa nèkh defal wakhale vrai Bandit moy yaw 😂😅😅

  • @modoufall8109
    @modoufall8109 5 років тому +10

    Thieuy senegal nekhna 😂😂😂

  • @abdoungom6017
    @abdoungom6017 5 років тому +1

    Serigne Touba dh islam la diglé liimom bokoul si islam bokoul si yoonwi kii nak dagnko wara niaanal yalla soppiko😭😭😭😭😭

  • @mansourfaye4292
    @mansourfaye4292 5 років тому +17

    djiguen togue si kaw goor yalla togue si souff

  • @kinekandji7100
    @kinekandji7100 5 років тому +2

    Barké serigne touba bouléne yalla diapé ndakh yénagui togne serigne saliou

  • @paomar1859
    @paomar1859 5 років тому +7

    Tégnoo diaye Sénégal KOU nék djeul walam svp.

  • @mamebouossamr6893
    @mamebouossamr6893 3 роки тому

    Akassa 👏👏👏👏👏👏👏👏💝💝💝💝💝💝💝💝💝💝💝💝💝💝💯💯💯💯💯👍

  • @elhadji83tv
    @elhadji83tv 5 років тому +25

    Wakho deugue doul rek 🚫🚫🚫⛔⛔⛔⛔⛔⛔👎👎👎👎👎👎

    • @ablayembaye1031
      @ablayembaye1031 5 років тому

      elhadji vigo nit day manou lo khamoul boul ko wakh

    • @ndeyesalihouna4031
      @ndeyesalihouna4031 5 років тому

      elhadji vigo tu es un embesille sa tatou yaye

    • @ousmanembengue1785
      @ousmanembengue1785 5 років тому

      elhadji vigo sa data yaye

    • @elhadji83tv
      @elhadji83tv 5 років тому +1

      @@ousmanembengue1785 da datta yaye bou nekh te rek yaye katal nako

    • @elhadji83tv
      @elhadji83tv 5 років тому +1

      @@ndeyesalihouna4031 ss datta yaye nekh katal na yaye katal you nekh