Réconciliation: Wally Seck torokhal na Pawlish mbaye " khagn na ay nit maynako auto ak keur mais

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 30 жов 2024

КОМЕНТАРІ • 342

  • @MaguetteDioneKa-ln1hq
    @MaguetteDioneKa-ln1hq 5 місяців тому +147

    Ndeyssane Sanekh ndékété nite gni khamounioula
    Ya bakh
    Dieureudeufeti Wally ya âme khôl bou refete machallah pawlis dala beugue rek
    Yalla nalene thiate seylou

    • @ToufaCisse-fj7qp
      @ToufaCisse-fj7qp 5 місяців тому +2

      Amine Ya Rabbi

    • @DiewoKeita-y1p
      @DiewoKeita-y1p 5 місяців тому +1

      Yow wally ci kanam rék khar khamoul boudou ngogne tchimmmm

    • @bodiediaw1651
      @bodiediaw1651 5 місяців тому +3

      Je voulais dire mon grain de sel mais komko dioubola kharal ma yaime fi boula lerone fi ghay moudie gha modéré sa langage waly daifa bakh am yeurmande bilay k Dieu te protège this barket Mouhammad salalahou aleyi wassalim

    • @khadimsamb1806
      @khadimsamb1806 5 місяців тому

      Nseye sane li mon diarra wane you bah yi

    • @KhadyNdiaye-e3z
      @KhadyNdiaye-e3z 5 місяців тому

      Sa nitou thies la yaw machallah il est bien 👍

  • @MamanLo-dc7ro
    @MamanLo-dc7ro 5 місяців тому +86

    Sma xol sedna cheikhou gueye yabakh❤❤❤❤❤❤❤❤vraiment jai les larmes aux yeux ❤❤❤waly yabakh

  • @awasow418
    @awasow418 5 місяців тому +52

    Cheikhou Gueye ya gore yaye noble y ay garmi yalna la ya allah faye takhawayou diaga nga fatali merci

  • @ousmanendom2608
    @ousmanendom2608 5 місяців тому +29

    Quel acte est plus noble que le pardon 🤲 celui qui le fait reconnaît qu’il a mal agit et nous tous nous reconnaissons des erreurs ❤ yalna yalla doli diam teh ndakeu saytaner sounou digueneter ak mbepeu dioulite

  • @Nawal-b8s
    @Nawal-b8s 5 місяців тому +143

    Ndeysane wally seck kou balh leu ,il fait toujours du bien aux gens mais chaque fois niou worla que dieu le tout puissant te donne longue vie a toi❤❤ sinon pawlish auss koula fonk leu seytané rek mo beuri dolé

    • @AichaDia-vv3vn
      @AichaDia-vv3vn 5 місяців тому +13

      Pourta pawliss defoul dara degge rek lako wakh kharit Day wakh kharitam degge

    • @khadimbacke2054
      @khadimbacke2054 5 місяців тому +8

      @@AichaDia-vv3vnsi c vrai mais pas dans les sociaux je ssuis pas d’accord tu connais sa maison et son numéro tu veux pas k ta copine te dise la vérité sur les réseaux aussi il est fautif

    • @Nawal-b8s
      @Nawal-b8s 5 місяців тому +5

      @@khadimbacke2054 très bien dit ,wakh deuguue c'est bien beau mais pas sur les réseaux sociaux

    • @Radiambaye93
      @Radiambaye93 5 місяців тому +2

      Yaw de mome nite kou bakk ga

    • @AichaDia-vv3vn
      @AichaDia-vv3vn 5 місяців тому

      @@khadimbacke2054 pask gniom seen lep thi enter net la kay gisso mem sen joubo bi waro gnioko woon woné nii

  • @Personne-xo3hb
    @Personne-xo3hb 5 місяців тому +69

    Ndeysane dafa yarou nak jne suis pas fan mais faut le reconnaître jamais mou guene di tontou avec vulgarité Di defanté il réagit toujours avec calme et maturité ❤️

  • @amethfall5009
    @amethfall5009 5 місяців тому +60

    Waly est un homme bien . Il a un coeur d'or. Vraiment nit ku baax nga

  • @AbdouJoof-ku7uj
    @AbdouJoof-ku7uj 5 місяців тому +57

    Wally seck yalna yalla défala diamou rék Mala beuga rék

  • @yasjoop716
    @yasjoop716 5 місяців тому +16

    Wally nitt yi niokoy togn niokoy ballou watt défarat lén sén xol yi si wally té mayko diam inchalah ❤❤

  • @bourguibafaye8521
    @bourguibafaye8521 5 місяців тому +26

    Sanèkhe li rafètna mashallah ❤

  • @diarrasow9492
    @diarrasow9492 5 місяців тому +29

    Ndeysane sanekh ya bakh🎉🎉🎉❤❤

  • @mberryable
    @mberryable 5 місяців тому +32

    Thiey Sanekh di Cheikhou Gueye yalna sa diam yague amine amine way nit rekay dioum sallaw.

  • @khadymbaye4312
    @khadymbaye4312 5 місяців тому +41

    Tu es un grand Monsieur Waly yalla naleu yalla sambe thi barke Seydina Mouhamed

  • @AmethDiallo-y4p
    @AmethDiallo-y4p 5 місяців тому +14

    Yalla na ma yalla may sokhna sou bakh com sokhna wally hol ko rk

  • @AmethTraore-mh7ls
    @AmethTraore-mh7ls 5 місяців тому +24

    Bilay contana li Lou deugoula waroul yakou machala🙏🏻

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 5 місяців тому +22

    Sanex ya bakh waye Guéye nite bou bakh the beugue diame ni laye déf ❤❤❤machalla

  • @salimatasarr5137
    @salimatasarr5137 5 місяців тому +35

    Wally lodiapone cheikhou gueye geune ko yokou parceque nit ku bakh rek te gnak kignane moye guiss diguante muy yaku mu yore pouso di gnawe te yalla rek takhe.
    Pawlish adina amul solo nit bo merer dangaye ande ak sago ak ngore ,wally sa nitt la so amater lula meti ci mome khame nga keureum demale ba ci mome nguene wakhtanerko.yallanalene su borome aare same lene te mousseul lene ci seytaner.
    J'ai pas l'habitude de commenter des vidéos mai wally est une personne que j'admire beaucoup.bale lene ma akhe bu de wakhena lu ma warul wakh

    • @mamediarradiop7904
      @mamediarradiop7904 5 місяців тому

      Yowite kou nitei nga tei yiiw yallah are la samela dieumeuleulei la kaname

  • @kambayependasall8908
    @kambayependasall8908 5 місяців тому +5

    Ohhhhh cheikhoul gueye machallah yalla na sunu borom faw la yiw waly ak pawlis yalla na sunu borom samalen diguenté barkep seydina mouhamed psl

  • @LamineDiop-u7m
    @LamineDiop-u7m 5 місяців тому +10

    Bilahi ya bakh wally ❤❤❤

  • @LamineDiop-u7m
    @LamineDiop-u7m 5 місяців тому +18

    Ndeyssane 😭😭😭😭sa défé Gua lou rafet

  • @pendabarry1978
    @pendabarry1978 5 місяців тому +51

    Billahi gniako fayida mar yacine nite yi gnio gorewoul rek

  • @seckmamethiaba3149
    @seckmamethiaba3149 5 місяців тому +5

    Yalla na sa Diam yague mar Yacine Maïssa Bigue yalla gua goudou fane wérr inchallah 🙏

  • @mamourfane9758
    @mamourfane9758 5 місяців тому +3

    Sanekh sa bontou aldiana leerna machallah diobalen ay nit ta yalla takh ❤❤❤

  • @amboisegomis6360
    @amboisegomis6360 5 місяців тому +14

    God bless WBS
    God bless SA
    God bless Pawlish

  • @aissatawade810
    @aissatawade810 5 місяців тому +2

    Ndeysane lii rafet n’a sa nekh yalna la yalla fay yiw lepp rafet n’a Machalah

  • @khadyly1787
    @khadyly1787 5 місяців тому +9

    Bilaye barke serigne saliou waly kou Bakh la ndeyessane ❤️❤️

  • @omarniang5469
    @omarniang5469 5 місяців тому +27

    BILAHI n’a rafet. Rek Wally borom bakh leu

  • @amicollediouf5651
    @amicollediouf5651 5 місяців тому +3

    Machallah rafetna yalna diam sakh

  • @elbiranetoure262
    @elbiranetoure262 5 місяців тому +9

    Merci beaucoup sanekh li moy nite mais Domram yi saytane yi yakh rek

  • @tickodia7847
    @tickodia7847 5 місяців тому +4

    Ma cha allah contane n'a 🎉❤

  • @KhalilDien-fe5uh
    @KhalilDien-fe5uh 5 місяців тому

    Djikoy sangu machallah machallah
    WALY ya bakh

  • @aminatandong8765
    @aminatandong8765 5 місяців тому +4

    Sa nekh y’a bakh yal nala yallah defal diam Ak molem dioulit. Wally kou bakh la mâcha ALlAH

  • @purpleowl4025
    @purpleowl4025 5 місяців тому +2

    Ooh Sanekh is a wonderful human being .We so proud of him .We always love you Canadian Gambian..❤

  • @FamaFaye-o8c
    @FamaFaye-o8c 5 місяців тому +1

    Bilaye wally seck ya bakh yalla n'a yalla faye sa khôl wayé kéne d'où sa nékh yaw tamit yalla n'a yalla faye yiw

  • @MousaDme
    @MousaDme 5 місяців тому +2

    Merci faly❤❤❤❤❤

  • @mamediarrathiao8126
    @mamediarrathiao8126 5 місяців тому +60

    Une leçon de vie pour Pawlich ! 😢

    • @malickdiop3382
      @malickdiop3382 5 місяців тому +2

      Leçon pour tout les deux

    • @ramatoulayesagna-w5t
      @ramatoulayesagna-w5t 5 місяців тому +4

      Fi leçon de vie amou fi bayilene nafekh ak details

    • @adjabellosarr2023
      @adjabellosarr2023 5 місяців тому +4

      Non c’est leçon pour wally beug nako trop ms tay mo dioume comme lep deikhna alhamdoulilah

    • @awasene7840
      @awasene7840 5 місяців тому

      ​@@malickdiop3382Merci beaucoup

    • @AmiGning-m3o
      @AmiGning-m3o 5 місяців тому

      Séytané rék pawlich bimouy ande ak waly waly amoul wone dara ​@@ramatoulayesagna-w5t

  • @abdoumbaye5382
    @abdoumbaye5382 5 місяців тому +2

    Man sha ALLAH, Waly yaa baakh t am ngor ak eduquation de base.
    YALLA nala YALLA are t may leu ndam partout inn sha ALLAH.
    Proud of You !!!

  • @ramcesdia3653
    @ramcesdia3653 5 місяців тому +1

    Bilahi kéne d'où yaw ya bakh deh yalla nala yalla faye sa khôl inchallah

  • @amboisegomis6360
    @amboisegomis6360 5 місяців тому +8

    God bless WBS

  • @SophiaSamb-s4v
    @SophiaSamb-s4v 5 місяців тому +1

    Ndeyesane machalah lii rafetena ❤❤❤❤❤Machalah seck

  • @famatamba9952
    @famatamba9952 5 місяців тому +21

    guiss gua adouna dh ligua done wakh yeupp tayy dem gua motakh wakh bakhoul so meré daguay khalate

  • @adamapene-og9qw
    @adamapene-og9qw 5 місяців тому +1

    Wally djirim leu kouko togne dingako guiss tei lo dem dem dingua dellousi gnou rafetal sounou digeunetei ak mbok djioulite yi adouna amoul solo tei keine xamoul foumouy moudiou. Yalna yalla doli soutoureu sam niou are niou lak niou fou yak agoul si barkeip borom TOUBA 🤲♥️

  • @ajajatta6967
    @ajajatta6967 5 місяців тому +1

    Wally you are bless ❤️❤️❤️ and may Allah bless you more ❤️❤️❤️❤️seck

  • @MariamaSane-yj9tv
    @MariamaSane-yj9tv 5 місяців тому +11

    Pawlis boudé ndangua am conseiller bou bess bayiko bakhoul wally ak sokhnam kou bakhlagnou❤❤❤

  • @FatimaDrame-sx1cg
    @FatimaDrame-sx1cg 5 місяців тому +1

    Wally t’es le meilleur des meilleurs ❤❤❤

  • @kadijatoujallow3477
    @kadijatoujallow3477 5 місяців тому +5

    Machalla Machalla Machalla ❤

  • @ndeyebouyakoita4469
    @ndeyebouyakoita4469 5 місяців тому

    macha allah rafetna torop ❤❤❤
    sanekh que dieu te protège ❤❤❤❤

  • @AmieNyan-ew3yw
    @AmieNyan-ew3yw 5 місяців тому +1

    Wally you have good heart god will pay you.

  • @ndeyawade8462
    @ndeyawade8462 5 місяців тому +1

    Nday sane sokhna aidara une grande dame

  • @mustaphakorta3704
    @mustaphakorta3704 5 місяців тому +5

    MashAllah

  • @mariamangom8163
    @mariamangom8163 5 місяців тому

    Ndeysane joulit li laye déf sanekh yalla nala yalla féyale bopom thie barké koune fa ya koune ❤️❤️❤️❤️😭

  • @ishbobb2504
    @ishbobb2504 5 місяців тому +1

    God bless you Wally . This very nice of you and Pawlish love you. That’s why he was talking like that.

  • @ZeynaTounkara
    @ZeynaTounkara 5 місяців тому +3

    ❤❤😢 vraiment j'ai les l'armé au yieux chiekhou Gueye alias sanexx ya bakh yaye goor dama beug couy defar diguente Wally Daffa ndiaboote ndaw machalla paolich ay wakham yeup foko degue mongui nane nouma Mel wally la cheytane foumou khadjoul rek laye Doug omaro warr ngua rousse bayilen di waly mbagnel ay chetane demal took yalla reubna cou yeee fitte n'a Sanex tawfekh ak taychir rek nak jtm❤❤❤

    • @awasarr3569
      @awasarr3569 5 місяців тому

      Bilay cheytané da Bari dolé 😢

  • @babacarfam251
    @babacarfam251 5 місяців тому

    Machala sanekh ak.waly yalla nala yalla défal diamou

  • @ouleyekane4856
    @ouleyekane4856 5 місяців тому

    Tonton sanékh ya bakh yalla na yalla goudal say fann❤❤❤❤

  • @MariamaAlieuGibba-mh7iy
    @MariamaAlieuGibba-mh7iy 5 місяців тому

    I just can't believe with all they talks wally still good for them ya Allah bless and guide this man for us

  • @Dialfall-dh7gt
    @Dialfall-dh7gt 5 місяців тому

    Ndeye sane mangi dioy😢😢❤

  • @thiattediop2876
    @thiattediop2876 5 місяців тому +1

    Machallah sa nekh ❤❤❤❤

  • @ngagnethiam8137
    @ngagnethiam8137 5 місяців тому

    Yalna gnou yalla may alal

  • @Ndeyeseck569
    @Ndeyeseck569 5 місяців тому +7

    Gnako fayda Wally Chaytané mo bari dolé rek. Pawlish koula beugue la yaw tamite kou beugue pawlish nga.

  • @thianefall8006
    @thianefall8006 5 місяців тому

    Oh machallah 😢

  • @awabarry4201
    @awabarry4201 5 місяців тому

    Merci sanekh merci wally sohkna aidra❤

  • @alphabah2763
    @alphabah2763 5 місяців тому

    Wally is a clean hearted guy

  • @NabouDiatta-j4o
    @NabouDiatta-j4o 5 місяців тому +3

    ❤❤❤❤❤🎉 Merci

  • @Abyfaye-bx7ph
    @Abyfaye-bx7ph 5 місяців тому +28

    Li motakh wakh bou niawe bakhoul pawlise mo meraté dél soraré elek

  • @PapemadiorNdiaye-g9z
    @PapemadiorNdiaye-g9z 5 місяців тому

    Wally seck c'est un grand homme.

  • @yusufmouhamed-8787
    @yusufmouhamed-8787 5 місяців тому +1

    Merci sanex pour sa

  • @fatouthioune-dn9rk
    @fatouthioune-dn9rk 5 місяців тому

    Waly ndame réke inchalah

  • @t.d8000
    @t.d8000 5 місяців тому

    khana thêatre bu bess leu...de vrais acteurs! chapeau bas

  • @UmarFayumar
    @UmarFayumar 5 місяців тому

    Merci beaucoup sanekh❤❤❤ lirafitn

  • @actufootball221
    @actufootball221 5 місяців тому

    Macha allah ❤

  • @YacineDiagne-x7u
    @YacineDiagne-x7u 5 місяців тому

    Waly machalla

  • @sidathniang7183
    @sidathniang7183 5 місяців тому

    Wally aka Diabaram niou bakh lagn machallah

  • @ajoe7816
    @ajoe7816 5 місяців тому +3

    Pawlish siguil amo gathiè

  • @diorseck757
    @diorseck757 5 місяців тому +18

    Biyilene di togne wally môme dou togne kena mais couco togne mou bayila amoule réconciliation waly SECK là sante d'où togne

    • @prince_mbacke2774
      @prince_mbacke2774 5 місяців тому +1

      Kou sant seck Dal dou toñ 😂😂😂 iow dagua con koi
      Perso: wally nafii yagg lool t and ak weer

  • @ChiekhounaNdiaye09
    @ChiekhounaNdiaye09 5 місяців тому

    Gallo rafet khôl walliy mokay Dawlll billahi❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @amadouba4294
    @amadouba4294 5 місяців тому

    Machallah ❤❤❤

  • @thiattediop2876
    @thiattediop2876 5 місяців тому +1

    Ndeyesanne 😢😢😢😢

  • @KharDieye
    @KharDieye 5 місяців тому

    Machalla wally ❤❤❤❤❤

  • @khadyjeanineniang5400
    @khadyjeanineniang5400 5 місяців тому

    Bilahi guise wally seck reck la beugeu massoumako guise damako beugeu sama bire khol ndakh bakh gui mou bakh akh yeureume domou adama yana nga goud fane wally

  • @fatouTALL-ld1ro
    @fatouTALL-ld1ro 5 місяців тому

    Sa nexx geun nama nexx. Limou def rafett na trop. Yalla na diam yagg🙌❤️

  • @antaseck7309
    @antaseck7309 5 місяців тому

    Quelle humilité, non Wallykou bakh nga, yalnala Yalla samal bopam❤️🙏🏻🙏🏻

  • @rokhayadiaw6246
    @rokhayadiaw6246 5 місяців тому

    La paix rien que la paix machalla

  • @oceanmsf5686
    @oceanmsf5686 5 місяців тому

    Machallah sanex❤❤❤❤

  • @Milenasouarez
    @Milenasouarez 5 місяців тому

    machalah saneikhe li rafaite na trop djioulite ni la deffe❤❤❤

  • @bathiniag3384
    @bathiniag3384 5 місяців тому

    Ndeyesane 😭 Machallah

  • @amidiop3299
    @amidiop3299 5 місяців тому

    Papa d'amour je t'aime fort ❤️❤️

  • @lilpapasow9637
    @lilpapasow9637 5 місяців тому

    Wally un grand homme ❤

  • @ALIOUNENGOM-t7n
    @ALIOUNENGOM-t7n 5 місяців тому

    Lou nice ❤ Machallah ❤

  • @espritgagnant5393
    @espritgagnant5393 5 місяців тому +3

    Pawlish nak avant de parler il faut ngay 10milles problèmes dès fois(blagues😂). Wakh balle leu té yakh wally sen diganté lou yaggeula. Niit amna foy tollu bul topp sa xol, del démé akh seu xel car bo xalaaton finga diaar akh wally yeup kon sa sortie yi ngeu deff duu démé nonou...
    Mais nonoula niit moy dioum té kou dioum té nanguko diapalni amnga grandeur akh sagesse bu nek ci yow...

  • @annapepe2976
    @annapepe2976 5 місяців тому

    Paulich adouna amoul solo yaw akh Waly dembeu leu ❤❤❤❤

  • @lisalahi6376
    @lisalahi6376 5 місяців тому

    Bilaye wally ya bakh ❤ mane déh souma done pawlish dina déh mba ma kheum ndakh gathié nima roussé ni té défouma dara 😢

  • @assanediop3246
    @assanediop3246 5 місяців тому

    ❤❤❤ merci cheikhou gu❤❤❤réfét na

  • @ndeyemeissambaye2120
    @ndeyemeissambaye2120 5 місяців тому +1

    Pwlish dada fire bougoule kou djaigué waly😂😂

  • @awasene7840
    @awasene7840 5 місяців тому

    Waa khana Wally rék mo bakh et pawlish dans tout ça Sénégal beuri neu ay nafékh mais nak alhamdoulilah 🙏 merci beaucoup sa nékh ❤❤❤

    • @aissatousow7690
      @aissatousow7690 5 місяців тому

      Mais pawlish mo toguone di yak Wally souko Wally balé kone Wally mo bakh

  • @maremeseck9540
    @maremeseck9540 5 місяців тому

    Ndaysane seytanè dafabari dolè foumou khadioul rek lay dougou yalna diam yague🤲

  • @MoustaphaDiagne-f1z
    @MoustaphaDiagne-f1z 5 місяців тому

    Ndeyssane Diagua mankenafi😢soufi nekone dinako régulé 😭😭😭

  • @AbyKebebyba
    @AbyKebebyba 5 місяців тому

    Wally yalla n'a yalla same

  • @fatouba5718
    @fatouba5718 5 місяців тому

    Merci wally ❤

  • @AmaSow-te6bl
    @AmaSow-te6bl 5 місяців тому

    Mon frère ❤❤❤❤❤❤❤