À mon humble avis nous devons tous être vigilants… un voisin ou qui que ce soit qui commence à appeler ine fillette « sama diabar » mou di ko maye Xalis ou autre, il faut l’arrêter systématiquement. Ça peut susciter beaucoup de chose, so thi wakh lou beuri on te colle une mauvaise étiquette mais bakhoul, seytané da thi gawa rakh.😢😢😢 pauvre enfant 😢😢😢😢
@@diopfifi4937 minimiser wouma dara, un crime aussi odieux et sauvage comment pense-tu qu’on puisse le minimiser ???????? Tu as très mal interprété mon commentaire
Dans de pareils cas et à mon humble avis faire une proposition de lois à l’assemblée nationale pour faire appliquer la CASTRATION purement et simplement.
ses parents sont irresponsables comment on dormire jusqu'à 2heure du matin sans voire que ta fille n'est pas retourner à la maison et preneer la peinne de redormire jusqu'à 06heure pour alerter
Mercy linga wakh moy deugeu lep parents yila khale bou 12ans waroul nek si mbend wakhoumala di geun goudi parents douniou nittou dara di diour rek te douniou topato khale yi
@Diara757 bilay diara lii mom senegal rek la am du importe quoi, la lois ne sanctione pas sur la surveillance et le bien etre des enfants,avoir plusieurs femmes faire des enfants partout et aucune responsabilité, Etat dii setan rek .
Il que les parents arrêtent d'exposer les enfants, qui n'ont demandé (statuts tik tok snap.... ). Un enfant doit être protégé et suivi et non être exposé. Les parents doivent être plus regardant sur l'entourage et surtout bayi di solal les enfants yene soline yi.
Peine de mort rek li Yalla wah mo geune ci gnune domou adama...ki ray gnu ham ni mo ray nagnuko ray c aussi simple que sa t Yalla dougnu ci toppé dara nah mognuko santeuh...
Kou appliquer woul charia si crime rèk lagnouy deuk ki raye diari dagnouko warra ray tall ko gneupou ték si beute li dafa gnaw ki amaloul société bi ndiarigne kou amaloul ndiarigne say mbokou amaloko société lofiye déf dagne la warra ray mo gueune mou nék fi di rayaté

Bilahi masla laniou wara bayi si quartier yi un délinquant il faut le dénoncer bayi ay dekeundo la danio yague après ni rek
Analyse pertinente
Li dou sèytanè. Crime bou bone la. Kouko déff criminel la. Arrètèlén di nan séytanè bou lén minimiser lim déff
@@diopfifi4937 minimiser wouma dara, un crime aussi odieux et sauvage comment pense-tu qu’on puisse le minimiser ???????? Tu as très mal interprété mon commentaire
Domou haram yi danou wara raye séne ndeye
Merci beaucoup à vous
Athia rek lou yalla wakh rek géené dét
Dans de pareils cas et à mon humble avis faire une proposition de lois à l’assemblée nationale pour faire appliquer la CASTRATION purement et simplement.
ses parents sont irresponsables comment on dormire jusqu'à 2heure du matin sans voire que ta fille n'est pas retourner à la maison et preneer la peinne de redormire jusqu'à 06heure pour alerter
Vraiment
Mercy linga wakh moy deugeu lep parents yila khale bou 12ans waroul nek si mbend wakhoumala di geun goudi parents douniou nittou dara di diour rek te douniou topato khale yi
@Diara757 bilay diara lii mom senegal rek la am du importe quoi, la lois ne sanctione pas sur la surveillance et le bien etre des enfants,avoir plusieurs femmes faire des enfants partout et aucune responsabilité, Etat dii setan rek .
Il que les parents arrêtent d'exposer les enfants, qui n'ont demandé (statuts tik tok snap.... ). Un enfant doit être protégé et suivi et non être exposé. Les parents doivent être plus regardant sur l'entourage et surtout bayi di solal les enfants yene soline yi.
C'est domages
Oú sont les droits de l'hommiste Anesty et autres et si on parle de peine de mort ils viennent nous tympaniser
Danio rayoule séne domou motakh niounek ay Satan
C'est Vraiment trés Triste .
Meuttina Meittina
Prison a vie
Ki keye raye rek !
peine de mort rek
Amul 9ans,12 la am
Machaalah amna solo
Tout ça c’est trop facile ki mome wakh dji diaroul beuri daniou ko wara ray ndakh niari crime la def viol ak meurtre li ma si méti legui mou guéneu
Peine de mort rek li Yalla wah mo geune ci gnune domou adama...ki ray gnu ham ni mo ray nagnuko ray c aussi simple que sa t Yalla dougnu ci toppé dara nah mognuko santeuh...
Naniou ko raay
❤
Kou appliquer woul charia si crime rèk lagnouy deuk ki raye diari dagnouko warra ray tall ko gneupou ték si beute li dafa gnaw ki amaloul société bi ndiarigne kou amaloul ndiarigne say mbokou amaloko société lofiye déf dagne la warra ray mo gueune mou nék fi di rayaté
Li motakh Ousmane sonko niou warro juger🔥🔥🔥🔥🔥
Barbarie à l'état pur. Mala moko gueune!
Pourquoi cacher son visage
Boudon Europe la daniouy arrete wadiourou khale bi nakala wadiour di teude di nelaw bayi domam bou am 12ans si mbend bi
😂😂